Reug reug est un vrai champion vos critiques sont trop negatives je trouve qu il fait vivre la lutte pa de respect pour un adversaire
@atoumaneniasse48549 ай бұрын
Merci serigen ndiaye lou léer nga wakh ❤❤❤
@Ozdev-hl5hm9 ай бұрын
Reug reug c’est un champion
@Ozdev-hl5hm9 ай бұрын
Reug reug c’est un champion mais il est dans son rôle. Li miy def moy nekhal lamb mane je suis fan de modou Lo mais reug reug meusul dépasser benn mbeur.
@danielcorreia20739 ай бұрын
Nekhal lamb? Mais bou dé franc mouné franc dada rew
@abdoulayediop9569 ай бұрын
Mbayang dall na machallah
@CheikhKjfnkhf9 ай бұрын
Merci ziza
@modoulebou6349 ай бұрын
Démbélé bann communication la Reug Reug wara soigner boulen gnou sonal waye Reug Reug dann beuré lafi moussa saga wala mou wakh la Lou niaw !!
@aichadia7199 ай бұрын
Frere dou dépassé sakh mais ko beuréleugoul si plateau diaroul wédiék wédiék diou barri souléne combat bollé nak meunga wakh loula nékh.mais mbeur bouñla wakh nga toutilko lohlou dou yeufou champion
@souleymanegueye93209 ай бұрын
Et Ama hehoufi ak Modou 2011 té fekni dieguéwoukowone sah si lamb nagn bayi na fekh
@ibrahimadrame94999 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤démbeulé meilleur journaliste❤❤❤❤❤
@cheikhbasskeurmassar95489 ай бұрын
Serigne Ndiaye lou léer
@mamadoumoustaphasarr40949 ай бұрын
Reug reug lamb lay def chacun à sa maniere de communication au paravant la communication de balla gaye etait plus violence lamb affaire de show leuh
@abdoulatifdiop56409 ай бұрын
Wakh n'agn ko déugue deh ilfo mou kholaat aÿ wakham
Balla Gueye loumou wakhoul yekini ak Tyson fii amoul thi werou koor ngen nek ish
@abdoudiop71779 ай бұрын
Sawaye mais dawara hare ba contrat lié lene balla signature contrat laye wakh louko nekh
@bocumalpha32009 ай бұрын
Bien vu Ziza il faut savoir donner l'exemple 👍
@Ozdev-hl5hm9 ай бұрын
Il n’a pas à soigner sa communication les lutteurs on peurs de reug reug wakh len degg bi.
@YakhyaSakho-n6g9 ай бұрын
Sayy reug toloul fii guayiii Sa thies fi lako diapp fégnal ko guanane ragal Modou faléwoul Mamou reug reug dagua bakh di wax rekk
@sidysakho65589 ай бұрын
Mais Reug Reug dafoul lou graw c just dafa ame combat MMA le 5 Mai ensuite il voulait avoir un combat à la lutte sénégalaise c prkw il communiqué de la cette façon . Est ce k xame gani Reug Reug communication motakh vs parlez de lui chak jrs
@mamadoufaye40579 ай бұрын
Nafejh ngénn Franc moffi woté saga en direct Reug reug massoul saga kenn
@danielcorreia20739 ай бұрын
Reug mo ndieukeu saga bouléniou sonal
@mamadoufaye40579 ай бұрын
@@danielcorreia2073 reug reug massoul saga franc mo woté saga deug la yalla beugg
@tamsire9 ай бұрын
@@mamadoufaye4057 saway nii ay nafékh l'an reug reug moy dérange
@seydinaomardiop45379 ай бұрын
@@danielcorreia2073Waxo deugeu kagn lako Reug Reug saga
@papaibouseck87239 ай бұрын
Reug reug limouy def moy nekhal lambeu..Li sport de combat la bou am mystique et tout ..donc dara lou rafet amoufa ....sou combat takhawé da ngay dem si serigne ligueye sa moromou mbeur ba paré nguein beug mou rafet ..reug dafay nekhal nii rekkk champion la ..kouko beug changer lo communication da ngakoy dieul doumeu ko dan ko
@TallaFaye-y8t9 ай бұрын
Boulen gnou sonal reug reug defoul dara day lamb
@tamsire9 ай бұрын
Ki dafa sof way
@AliouPouye-qd8ci9 ай бұрын
Reug ni lako yalla bindè accepté len ko rék xol ❤bi dara nekou ci
@Ozdev-hl5hm9 ай бұрын
Khana balla Gaye dafa rewon bayi len reug reug domou djambre la . Lamb la deff
@ixparish14539 ай бұрын
Shut up Reug reug meussoul saga adversairwam fila franc saga en direct wakholene si. Nganiouy sonal ak communication motay communication bo khamner si geum geumam lako tek ak si sport. La communication de reug reug vous dérange pas a vrai dire c'est reug reug qui vous dérange
@papemedounesy14019 ай бұрын
Reug reug dou touss ama rék niou dém💪
@diopibrahima74129 ай бұрын
Serigne topal leulé dangua beugeu reug niane modou lo c’est le plus beau c’est le plus fort
@souleymanegueye93209 ай бұрын
Reug reug ak sa thies gno meune si génération bi
@AliouWade-e5t9 ай бұрын
Dagua sokhor rek reug reug championn la bagne bagne ndaggou
@bdiene669 ай бұрын
Parfois il faut inviter des amateurs de la lutte et éviter les fans de lutteurs .Un consultant doit être neutre. wa salam
@seydinaomardiop45379 ай бұрын
Merci
@simmelsarr35999 ай бұрын
Communication Reug Mo gueune ci Lamb ji. Li sport de combat leu. Douniou ay ouztaz. Iow Dembélé xamo Lamb
@ousmanendour90759 ай бұрын
Reug reug est redoutable qu, il parle Comme il se sente bien, il est confiant mais il n, est pas susceptible de dire qu, il est arrogant. Arretez de dire mal a reug reug et parlez nous de la lutte vous n, etes pas invités pour critiquer reug reug. IL est tres confiant point. Vous avez peur de lui ces adversaires.
@NdiaboutaDiouf9 ай бұрын
degg na. Deugeu dee
@AliouKama-zs9ye9 ай бұрын
On s'en fout nitt dégay guém sa bopp reugreug lidiaté woule kèn reugreug n'a jamais insulté qui que ce soit 😮
@AliouKama-zs9ye9 ай бұрын
Vous qui supporte les VIP vous ne pouvez pas aimer reugreug par ce qu'il vous dérange inch'Allah roi des arènes rec ❤
@moussathiaw37329 ай бұрын
saway reug reug défoul dara lambe rk lay déef
@BadouLo-u4u9 ай бұрын
Bayil sokhor reug reug champion la lamb la dou dine dou trikha
@souleymanegueye93209 ай бұрын
Bilahi Modou sama mbeur la Mais fi dou Dara dou dahira ,Yako wah diohnako respect bignou guissé mais micro yi pour diay sa bopp la donc nagn bayi kou demandé Modou gnoukoy bagn ,Modou dou imam,boye Niang wahnafi balla louko nekh et Ama baldé limou def Ama ,reug reug defouko Modou
@Ozdev-hl5hm9 ай бұрын
Bayi lenn reug reug bi guenn di togn wakhou bi benn mbeur Lou gniaw modou sou ragaler reug reug nako wakh.
@PapesambaDiop-bf7gh9 ай бұрын
Ww ok daniouko ragal
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف9 ай бұрын
Lolou lagne done wakhe modou lo dafa ragal ama balde 😂 legui modou lo dafa ragal reug reug wakhi dof 😂
@SémouDiouf-o3c9 ай бұрын
Serigne ndiaye do gatte
@amdymoustapha61309 ай бұрын
Domou parcelles la meuno si mome dara🎉🎉 P A LA DEuK ⚔️👑
@user-li1ro9pn8y9 ай бұрын
Cest Sa communications avant combat mais attention cest sa que yekeni disait a balla gaye
@amdymoustapha61309 ай бұрын
P A LA DEuK ⚔️👑
@IbouseyniLaye9 ай бұрын
Sokhor monléne djap rek reug reug dafa ranppé ba aksi ngéne di féne rek
@cheikhthioub22409 ай бұрын
Reug kass3 futur roi
@AMADOUCana9 ай бұрын
Modou thé king
@bayeratebayerate58939 ай бұрын
Reug reug dafa reww
@chakasen3999 ай бұрын
Si vous voulez le battre , il faut le faire dans l'arène !
@amadougueye70449 ай бұрын
Reug rék bilahi
@komalokoma99929 ай бұрын
Non le problème de reug reug en est que la manière dont il croit qu’il est le meilleur c’est de cette même manière que les autres lutteurs pensent qu’ils sont aussi des meilleurs Et bizarrement il pense que les lutteurs ont peur de lui mais il n’a rien compris Quand boy niang le blasonnera il saura que personne n’a peur de lui
@bathiedrame8009 ай бұрын
Waw nioun Nio beurewoul dayam akk reug reug
@badarasanti48789 ай бұрын
Wayy reug reug il sans fou de modou lo ou balla gaye bayilen reug reug deflennnn di déranger c'est ça le problème golo bou dioukk rek né reug reug ohh
@khadimthiam30819 ай бұрын
Dèngeun fral modou lo rèk. contr reug mè manolèn dra ci mome.
@mbackegaydelserignembacke83359 ай бұрын
Reug kene amoul sokhla thi mom nek lene nitt
@bdiene669 ай бұрын
@@mbackegaydelserignembacke8335do amateur motakh.Reug lamb mo ko sokhla😂
@seydinaomardiop45379 ай бұрын
Golo gou diokk nguén inviter si plateau yi di wax waxou doff
@alysow90899 ай бұрын
Reug reug dof la
@domou__rewmi9 ай бұрын
Reug fila wakh franc khalé boula yabé dangaye niouss bayam mou khamni do morom lolou saga leu 😂😂
@ixparish14539 ай бұрын
Fouko reug reug wakhé si koor nga nek sawayy
@domou__rewmi9 ай бұрын
@@ixparish1453 barki seydina Mohamed bouko wakhoul yalla bou yalla nangou sama koor
@ixparish14539 ай бұрын
@@domou__rewmi hiii boulko wat maguii fa wone si live bi fall cheikh bou reug reug mo wakh lolu reug reug rectifié ko lolou mofa khew
@domou__rewmi9 ай бұрын
@@ixparish1453 bane live interview la souma dioumoul mok Modou mbaye lawone mane douma wakh louma leroul
@ixparish14539 ай бұрын
@@domou__rewmi det live bi buzz lawone lutte tv after franc sakh nekone na si live bi mais cheikh bou reug reug mo wakh lolu reug reug la bien rectifié neh il respecte Modou lô
@nitoudeugue49309 ай бұрын
Modoulo dou touss ngeine beugg ko deff Yalla Nokou leine feulei
@MamadouFaye-ek7jv9 ай бұрын
Amo droit neko danga indiscipliné c'est ça façon de parler
@pascalkama36639 ай бұрын
Reug Reug soigne ta communication so beugué sori
@medounediene96529 ай бұрын
Reug chef de file la chef de file lay berel franc dou tête de file wakh deug dafa baakh
@konadiouf25969 ай бұрын
Sa way yangi dioum d. Franc moy tête de file écurie Jambar. Modou Lo moy tête de file rock énergie
@medounediene96529 ай бұрын
@@konadiouf2596 tu a raison
@goumbagueye27689 ай бұрын
Mod-Lo ak wa disambar Franc lagne beuga diokh roi bi Siteu day Dane Modou Lo par combine après Niou teug Siteu Vs Franc pour franc nék roi des arraines li moy beug beug Wa parcelle mais Modou Lo vs Siteu Dou combat
@domou__rewmi9 ай бұрын
Siteu dou dieul franc lolou risque leu
@abdoulahadboo9 ай бұрын
Bayilen wakhou saytané yi modou lo wakhna fi loune Balla gaye khasté basi sokhnam fila nou fék té kéuneu wakhoul
@dembafofana86469 ай бұрын
Ani sa preuve 😂
@ndiougamar22029 ай бұрын
Reug reug meussou fi saga nite meunouléne wakh ba reug reug beuré ak Franc modou lo rék doufi mbeur
@MaxDiop-f1e9 ай бұрын
Yéne dafa melni compou léne reug reug badola bou khaliss dapp la mo takh day béww
@LamineSenghor-j6b9 ай бұрын
Serigne Ndiaye ya guèneu indisplinée Reug Reug defoul dara dou yangui nonou di wakhné tapha tine mo guèneu nill si mbeur yii té amo contrat ak mome .Modou lo moy sama mbeur mé bou waré danou mouno si dara do dougu si guew sokhor nga trop
Saway waxofi dara reug reug dépasé woufi kénn li lamb la dou tarikha dou diné
@ibrahimadia74694 ай бұрын
Modou lo 😂dafa ragal reug reug yaw éloquence koukou dakou franc yéne aiye vrai nafék guéne😂
@ousmanediouf31659 ай бұрын
Boy bi dey fene reug moussoul wax indiscipline,dafa gueum bopam
@domou__rewmi9 ай бұрын
Reug reug da wara bayi di sous estimé mbeur mo amaloul contrat lolou rek moko yakh
@PapeDioif-p3t9 ай бұрын
Way modou gnémewoul reug reug
@momoofficial19889 ай бұрын
Wakho deug dè lolou ngèn fi wakhon si ama ak boy niang mou niouss lèn
@ibrahimadrame94999 ай бұрын
😅😅😅😅😅😂😂😂😂😂😂bane Modou😅😅😅😅bou tamba Wala🙄🙄😳😳😳😳dou modou lo dé khana ngaye wakh😅😅😅😅😅
@PapeDioif-p3t9 ай бұрын
@@ibrahimadrame9499 bayignou way daw reug reug daw tapha tine diel siteu kay boko guéné thi ragal ragal amatoul
@biramesenghor35289 ай бұрын
Mé reug reug mbeur la dou imam té lo guise amna marketing reug day lamb késé défoul dra balla ak modou wakh nanou fi louné gnémé woléne boy bi késé motakh
@abdoulahadboo9 ай бұрын
Bilay saga Nanou fi khasté Nanou fi té kéuneu wakhoul bo wakhé niouné day nékhal lambe
@bdiene669 ай бұрын
Merci mon ami.kham gua lamb té tu es véridique machalla
@domou__rewmi9 ай бұрын
@@abdoulahadboobokoul deh reug nekoul thi contrat ak Modou
@xalimagui-officiel90019 ай бұрын
Sa Thiès moko ko ndieuk wakh na diang wakhine. Mounoul communication mom
@leydigueye4079 ай бұрын
Vous avez peur de reug reug il n’est pas indiscipline, c’est un lutteur c’est juste pour vendre ses combats et vous êtes jaloux
@gueyembaye8539 ай бұрын
Regu lamb lay def c normal hor lamb mou diokhko respet et lolou ct quand donc magu na ba warko deuk dnc ou et l mal ga tok fi dixaste te ken xamoula regu champion la ko dane 10 wala 15 foi amga droit ni do bere ak mom legui ioe kou sof ga trop
@FallouMboupe9 ай бұрын
Yama fène nganane Modou yebouniou Modou séné Bay la
@bayemodoufall28799 ай бұрын
Mocvcv❤
@ballandiaye94309 ай бұрын
Reug boul changer sa communication figa KO teuyer fofou la wahal saga wofi ken
@cheikhbasskeurmassar95489 ай бұрын
Ziza ama bou malika combat bou néex
@mamadoundiaye52309 ай бұрын
Saway ioe merde way bayil saytané reug champion la
@kara18939 ай бұрын
Boukar yaw fok ga dageu debabi pour yaw ken dou wakh degue reug reug
@mohamedgeuye78859 ай бұрын
Dou sama mbeur dh wayé wakhoufi lou balla gaye wakhoul wala loufi mbeur mosta wakh bayi lénnn far ta ngén di wakh deug
@saliougueye98339 ай бұрын
Reug reug ken weretewoul ni ndanane leu mes wakh dji bari la wara bagni mbeur pir leu mes wakh bou baré rék nga sof nite gni
@bdiene669 ай бұрын
Yow do mbeur tè tu parles gratuitement😂😂😂
@saliougueye98339 ай бұрын
@@bdiene66 kon gnio yam mane ak yaw
@alysow90899 ай бұрын
Reug reug dof la dafa konne lol
@diokinemendy43839 ай бұрын
Reug mo meune modou lô sakh gni dagni sissou franc mo guena bari wakh si lambs dji
@OmarThiam-ji2xu9 ай бұрын
Reug dof la .lolou mo daal malik niang
@elhadjidiouf59919 ай бұрын
Reug du tusss😂
@NfamaraDiatta-q8j9 ай бұрын
C vrai il es tres arogan Arriviste le
@OusaynouSy9 ай бұрын
Hana deme ge gemel sa bopou mo gen digou modou lo
@afro38279 ай бұрын
Yow yag reug reug yem wala wala mou tané la liga wakh si tapha tine nak def ni sa touba di wakh lou logique si nbeuri jambour yi
@PapemorSamb-q4k9 ай бұрын
Reug reug dof la il communique mal ken nawlo woulko dooff pire
@bdiene669 ай бұрын
Yow ya amoul namlé parce que Reug dieulat na niari avance😂😂😂
@gueyembaye8539 ай бұрын
Regu moy sen vip yen gnep mofi def louken defoul gueni tioe rek arete
@AmadouDiallo-j2c3 ай бұрын
Reug boko lamb bayer tamitt tousse reug seul
@chakasen3999 ай бұрын
Tu reconnais que Reug Reug a respecté Modou Lo à Tivaouane et tu continues tes conneries. Reug Reug ne fait que communiquer pour décrocher des combats !
ziza yaw diaro fenn ngay soob fi do bayi teng teng lou teddo niebe.
@goradiagne96869 ай бұрын
Bayilène fène lac kène mèrèwouko moffimane thi lamb ji
@modoulebou6349 ай бұрын
Sergine ndiaye billay ya Nara sonou Saway Reug Reug lidianti woul sakh modou Lo barké Rassoul lay Saway Reug Reug comme sonko nit meunoul si mome Dora 🦍contre Reug Reug paska dafa wax ni li boy Niang ak ama am si modou Lo Souma ko amé dann modou Lo mais lann mo niaw si lolou bayilen boy binguén beuga diakhassé ak khalé bi waye😊🥹😂😂
@bilalkhalyfall99389 ай бұрын
Saway li nguay wakhnih amoul yaw lidjeunti wo niteu té plateau bo tok wakh si mom wakhal lénéne key wayé lidjeunti nako mom gnou wakhanté deugueu rk
@mamadoumbengue22998 ай бұрын
Reuk reuk molêne meune
@dionemodou48179 ай бұрын
Boucar yeun la meré . Gni lann laniou kham ci lamb. Vrai douleur micro rekk Di fenn. Reug reug seunn bay la ci beuré