Rivalité avec Wally Seck, Momo Dieng Brise le silence avant son Dakar Arena

  Рет қаралды 35,531

Univers info TV

Univers info TV

Күн бұрын

Пікірлер: 88
@Petitzo
@Petitzo 19 күн бұрын
Momo Dieng meùssou mako dégu mou wax lou gnaw nitt ku yalla bakhé leuh machallah 🎉
@aidambaye5021
@aidambaye5021 19 күн бұрын
Virement nit kou bakh té manou
@buz7755
@buz7755 19 күн бұрын
Yak man wakh deug Yalla ak Sama bammél mesùssou mako degui mo wax lou niaw
@MustaphaFaye-t5g
@MustaphaFaye-t5g 20 күн бұрын
Wally séne baye la 😅séne khol nékhoul nane léne glace fofa totie 🤪 maryacine seul amoul lénéne nékha faral moy borome décembre faramaréne bi seul 💪💪😅❤❤❤
@coeur2lion38
@coeur2lion38 19 күн бұрын
Bane trophée géne am seul les bidons vide ki fon du bruit
@aidambaye5021
@aidambaye5021 19 күн бұрын
Iaw eske cva momo rivalise woul akh kene dougeul fo kadje biome aye mbokh lagnou dieng salla tinioul kene migui tokh si rokom di ligueye kana do khol iaw mi
@lomamadou4526
@lomamadou4526 19 күн бұрын
D vré kon bala gua commenté do deglou loumou waax baa parei
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Yoe do yem ya degu momo wah lolou ki Amoul tmp rivaliser AK ken teu Nga deglou vidéo bi baparei dora wah
@MustaphaFaye-t5g
@MustaphaFaye-t5g 19 күн бұрын
@@EvaNdiaye-i1u mes yéne séne khol nékhoul 😂🤪kone yénagui tontou ba tay 😂
@adamendiaye1395
@adamendiaye1395 19 күн бұрын
Gni lignou titré momo wakhoul lolou dé😢momo kou yarou la té bakh dou wakh lou niaw bon courage
@zinedinezidane3696
@zinedinezidane3696 19 күн бұрын
Gni diakhassé rek ils abusent
@ArameDieneDieng-ym2st
@ArameDieneDieng-ym2st 19 күн бұрын
Momo dieng liguèye sans bruit machallah yiow ndanan té dokhalale tu yé le meilleur de ta génération ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💃💃💃💃💃💃💃
@AidaNIANG-z5o
@AidaNIANG-z5o 20 күн бұрын
Tres bonne communication machallah ❤
@Mody-nz3zt
@Mody-nz3zt 20 күн бұрын
Wakhaleine seine wakh teu gueinei tji wally domoukharam yi
@MamadougayeNiang-n1v
@MamadougayeNiang-n1v 19 күн бұрын
Commentaires delene deglou bala guéne di commentaires stp li faut titre pour âme aye vue waxoul lolou 😢
@PapaSeck-s3z
@PapaSeck-s3z 19 күн бұрын
Momo dieng yalna sa diam yagge 🙏
@BintaBa-z8x
@BintaBa-z8x 19 күн бұрын
Machaallah Dieng salak weyndé domou yarahmou papa Ndiouga Dieng nous te souhaitons une réussite totale pour la soirée du 28 décembre à Dkr Aréna amine inchlh ❤🎉
@IbrahimaSeck-pl3vl
@IbrahimaSeck-pl3vl 19 күн бұрын
Yalna yalla lafal la thiat may boy boy bou yarou nga niep ngui sa guinaw 🙏🙏🙏🙏🙏🙏👍👍👍👍👍👍
@lythiesigasenghor2948
@lythiesigasenghor2948 20 күн бұрын
Machallah rafetna
@tidianesow7660
@tidianesow7660 19 күн бұрын
Merci bro iow gor yalla nga continue sur cette lancé sa ira
@adjaracisse7794
@adjaracisse7794 20 күн бұрын
wally dako topp ba soon, momo meusso wouyou wally en plu tu es jaloux, merci
@bellabella521
@bellabella521 19 күн бұрын
Bayilɛne diaxassè ,seytanè guène trope
@gueyewakanaserignefallou7198
@gueyewakanaserignefallou7198 19 күн бұрын
Pourquoi mou dikou woyou
@BabacarNdiaye-u2f
@BabacarNdiaye-u2f 19 күн бұрын
Wally taloul sakh momo dieng
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Esk Dolen lidieunti sen bop ki taloul sah rivaliser teu wahoul Dara Waly titre bi limou bind AK li momo wah dou ben
@mayzowaliette1323
@mayzowaliette1323 19 күн бұрын
Frères et soeurs faramareens 🥰 bou niou top titre yi 😅 Momo dafa sampou dieul Lou reuy kouné khamna ni aréna dou ay foo pour chercher le buzz et donner de l'ardeur ils sont obligés de mettre le nom de Wally tmt wakh deugu yalla nak fi rew mi tolou so beugué visibilité nak le chanteur du peuple moci gaw 😍 nagn comprendre rek Momo mar la beugu 😍 douko wakh Lou niaw😅 nagn ko bale li
@dadasow4495
@dadasow4495 19 күн бұрын
Vraiment 😂
@mayzowaliette1323
@mayzowaliette1323 19 күн бұрын
@dadasow4495 marr limou wakh deugu la dagnio bary histoire 😂
@seynabousamba1439
@seynabousamba1439 19 күн бұрын
Sénégal da beuri satan titre laniou khôl rk di khass nit ki juste comme ça
@Moussa.r19
@Moussa.r19 19 күн бұрын
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MamenogayeWade-oo6mc
@MamenogayeWade-oo6mc 19 күн бұрын
Wawaw Dieng sala l'homme du 28 décembre Dakar Aréna inchallah borom liguéy sans bruit le meilleur de sa génération ❤️🥰
@OmarSeck-r4u
@OmarSeck-r4u 19 күн бұрын
Bayilen lire titre rkk nieuw dii commentaires delen setann ba parrei dogga commentaires
@KhalilDien-fe5uh
@KhalilDien-fe5uh 19 күн бұрын
Sa waaay waly sa diottt wayyy barii wakh troppp defo fii daraaa ... waly raw nalénn distance bou sori té boudone course ropiiiii neulénnn
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Yoe dof bouy dohot Nga ki rivaliser woul AK ken seytanei Nguen yenay diahassei nitt yi
@RassoulNdiaye-h4y
@RassoulNdiaye-h4y 18 күн бұрын
Yaw kou mise à jour sa data yaye nga dieul domeram tass keur rek nguéne meun kii taloul ay rivalité sa data yaye way kou nek ak lila yalla mayy wally ak Momo dieng bokoul ngay doul ni sa leufeul ndey way
@mamadoulaminesamb6949
@mamadoulaminesamb6949 20 күн бұрын
Bayilen doul ak faux titre
@PapaSeck-s3z
@PapaSeck-s3z 19 күн бұрын
Wadial sampou le 28 décembre inchallah sampou rek
@AidaGoudiaby-yc1cj
@AidaGoudiaby-yc1cj 19 күн бұрын
Ki mo khamoul bopap waly niata yon le niew si yaw té guisou mala si waly kou bew ngua té faux
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Yoe bala nga wah do deglou baparei vous êtes trop bête
@aminandoye9951
@aminandoye9951 19 күн бұрын
Journaliste meune nagnou doul fi loufi diar alahou akbar melnè da ame kou dè😢
@dameka1658
@dameka1658 17 күн бұрын
De grâce les sites internet li motakh mane de ma part douma abonné seni page douma aimé sene page parce que tout vos titres sont mensongères bayilene doul bayi diakhasse ay nitt heureusement que Momo mayoulene lougeune doull
@fatoumataba5160
@fatoumataba5160 19 күн бұрын
Ki nak wakhoufi dara lou Niaw arrêtez vos titres ishh bonne chance Momo
@BabacarNdiaye-u2f
@BabacarNdiaye-u2f 19 күн бұрын
Gni teukeulé wally ak momo dieng eska cava wally bayou momo dieng taloul sakh momo wakhlen artiste bi deug ben mano fesal arena khana nga defko billet 🎫 2000😂 même sidy diop mo raw momo dieng momo so wolo sa dolé diéguil frontière yi dieul sale bou mak même dock pullman joue wofa wally sa bougne ko ladjé si yaw lou nice lay wakh mais yaw sisou man nga
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Dangay todj sa leufeul nday yoe ki domou lebou la Amoul loumouy ragal Deum haram yi degôko mou toud ken Imbecil
@fatousow94
@fatousow94 19 күн бұрын
Momo yéen lane moy séen problème ak Wally th nguén nangoul Wally liko yalla may kouthie tague Wally tay souba nga déf ko noon louy problème bi Wally kou bakh la
@EvaNdiaye-i1u
@EvaNdiaye-i1u 19 күн бұрын
Yenn yena am problème bala nga wah do deglou limou wah Gni df sen titre boulen neh bokoul sah AK momo Limou wah
@MalickSy-i9g
@MalickSy-i9g 19 күн бұрын
❤❤❤❤
@Prossonkotv2
@Prossonkotv2 19 күн бұрын
Mo meune wallly dh foufff sah 😂
@Meumz-p7z
@Meumz-p7z 19 күн бұрын
Wally même bouye obali 😂😂sakh nite yo môme laniou beug 😂
@AmySow-wy6tk
@AmySow-wy6tk 19 күн бұрын
Bayilén sén titre yii Kii dou wakh niit Lou bone
@bassitoualwely
@bassitoualwely 18 күн бұрын
gni dano mana doul
@ジャウバッチ
@ジャウバッチ 20 күн бұрын
Yaw boy beuri nga titeur gor dou setou bopam way ngay khogalikou nii
@LachainedesTechniciens
@LachainedesTechniciens 20 күн бұрын
Boy bi ay moromam dagnko raww elajj kaïta rk dousa morom
@coeur2lion38
@coeur2lion38 19 күн бұрын
Senegal béne actrice la am Moy Youssou Ndour mofiy idi trophée yési dés parlé rék ak buzz késé
@aidambaye5021
@aidambaye5021 19 күн бұрын
Ya meune fene
@BabacarNdiaye-u2f
@BabacarNdiaye-u2f 19 күн бұрын
@@coeur2lion38 trophée Viviane trophée domou badiene la 😂yan artiste gnofa nekon dem rek indi sa ay trophée yombou na khana Youssou ndour
@coeur2lion38
@coeur2lion38 19 күн бұрын
@@aidambaye5021 sa Baye moma diagal ay féne doméram🤪
@coeur2lion38
@coeur2lion38 19 күн бұрын
@@BabacarNdiaye-u2f ba taye mé gnisi déf buzz moléne sonal ligéye Lou bari wah touti dafa am solo bagna touti bet tegi France diaroul ndamo té menago ça am disk dor
@ousmanesolly4061
@ousmanesolly4061 19 күн бұрын
Sampou rek
@NdeyeSall-fr3ky
@NdeyeSall-fr3ky 20 күн бұрын
Sènègalais mon dakha juger loumou khamoul kou yabou mandou khole lene ko si sidi Diop gni setaléne rek en bon entendeur salut 🎉
@diewosow4590
@diewosow4590 19 күн бұрын
Bayi len soxor ki dafa bakh defffou len dara th bagnoul ken .
@fatouseck4915
@fatouseck4915 20 күн бұрын
Momo dank rek doussa none tegua moytou ndoungourou yi gniome diakhassei rek
@loucha7179
@loucha7179 19 күн бұрын
Ki Waly rek la bagnnn
@Mody-nz3zt
@Mody-nz3zt 19 күн бұрын
Domoukhathie la dei
@aidambaye5021
@aidambaye5021 19 күн бұрын
Bayilen fene ki migui si bopam
@loucha7179
@loucha7179 19 күн бұрын
@@aidambaye5021 yaye doul kat bou mag bi ki dafa faux
@Meilleurgateaudeluxe
@Meilleurgateaudeluxe 19 күн бұрын
@@loucha7179aka faux domeram bi
@RassoulNdiaye-h4y
@RassoulNdiaye-h4y 18 күн бұрын
Yaw kou khorom boolé sa data yaye nga dieul nane ngay guissé niit dikoo bagne kii sou bagnione wally dinako defal album en diapalé ko si album symphonie doul way
Try this prank with your friends 😂 @karina-kola
00:18
Andrey Grechka
Рет қаралды 9 МЛН
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 108 МЛН
Леон киллер и Оля Полякова 😹
00:42
Канал Смеха
Рет қаралды 4,7 МЛН
FINALEMENT "YOUSSOU NDOUR CHEZ🔥OUSMANE SONKO......
11:02
WEB PLUS SÉNÉGAL
Рет қаралды 7 М.
Soirées Pyjamas : Episode 5
1:34:19
N Prod
Рет қаралды 116 М.