Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine www.youtube.com/^prestige senegal
Пікірлер: 431
@mamesodaniang35712 жыл бұрын
Femme bi ndieukeu wakh nittou fitna leu😏 lougnou la wakhaal Yako déf
@msz63172 жыл бұрын
Salaw dé ak kanamam, darra méti wouko si dé gui
@kebemethza82592 жыл бұрын
Femme bi kay mane sax dama ko gnéméwoul
@amethsiby32102 жыл бұрын
Bilakhi ta raison
@ndeyekhadyfall30502 жыл бұрын
Femme bi kay kou kateu ndayam là
@sokhnabassel82792 жыл бұрын
Walahi
@mouhamadoumoctarseck69152 жыл бұрын
Je ne peux cesser de revivre cette histoire. J'ai supervisé toutes les vidéos qu'on a publié sur le net mais vraiment toutes ces personnes devront être jugé et traduites devant la justice. Je pleure à chaque fois que je revois cet incident. Yen gni def dieuf dji yala nalène yala faye leep té bagne lène baale darra. Kou lii nakhariwoule do diouliite. Je ne sais où se situe Ndieye mais je sais que y'a des gens très méchants laba .
@sarrtapha64152 жыл бұрын
Mere bu mujj bi tamit man naa fen de yaw sa jëkkër yor liñuy dagge fere bi ñu filme ko mu yore weñ bi
@bellawomen2 жыл бұрын
Ay wakhi pithie Rek lan fi wakh gni dama yakar ni ay yefeur lan
@noirafrik70852 жыл бұрын
@@sarrtapha6415 no doyna war
@soulayndiay70342 жыл бұрын
0000⁰⁰00
@mariefrancoisesagna9102 жыл бұрын
Est-ce que tu peux mettre les liens des vidéos s'il te plaît ?
@diopndella41452 жыл бұрын
Famille bassirou mbaye nagne gaday gnén deuk bi nakh dji togne baparé té diémou gno réthiou dara
@neneoumou85512 жыл бұрын
Guissouma béne lére si sen kanam .gni ay vrai thiedo lan (nafekh hypocrite des menteurs etc. ).je demande a la famille du defunt de quitter ce maudit village.
@msz63172 жыл бұрын
Yako lal thiédo piir. Doyé xou niou diouma bi darra boudoul rivaliser ak yénén village yiko am. Bass dieul alalam dolém ak bou ndiabotam déf di niou ni ko dofi diouli
@salyallemomuawrksarr86527 ай бұрын
Yène gni Ray basirou mbaye dèh léne si Caso bi RK domaram
@timachou72872 жыл бұрын
Sa kanamou seytané bi so sagawoul wonn kenn douko wakh. K justice soit faite les auteurs du crime nagn arrêter nieup sa dieukeur soussi bokoul wonn ken douko arrêter soof
@ninadiouf67292 жыл бұрын
Té kou réw té ñak téguine wayé mom dina déf liguéyeum
@mouhamedndong60692 жыл бұрын
Femme bi njeukeu Wakh Gangster la dh Wipliw
@seckndeyemamy71152 жыл бұрын
Mane li la khamoul laneleu....depuis ce jour meunouma neilaw je sais pas pourquoi à chaque fois que je pense au martyr que ce papa a subi damaye diooooy....mane khawmeu deugu bi gni yalla reik mo meune si yome dara😭😭😭😭😭😭😭😭😭meitina ki nignou ko deif devant toute sa famille....sama khol bi Nakari na...meuneutouma franchement toujours meu khalate ko😭😭😭😭😭😭😭ay état bi ni diouk si li
@salysoumare36872 жыл бұрын
Même moi
@sarrtapha64152 жыл бұрын
Mère bu sol li rouse bi de wax na dëgg ci côté fenn ci côté neena école de basse apres mu ne xamul ku ko moom
@mohamedjobe79752 жыл бұрын
Sokhna si demall wuti benen jeukeurr
@mbomseck77002 жыл бұрын
Ki vrai mbam la
@aissatouleonie89852 жыл бұрын
Déféna lolou mo gueune guaw
@davidsat2972 жыл бұрын
@@aissatouleonie8985 diokh léne mako
@mohamedjobe79752 жыл бұрын
@@davidsat297 😂😂😂
@ndeyediop3352 жыл бұрын
Oumou Diéye mi lougnou ko wakhal mome la kou dégg nimouye wakhé ak aye manière ram khamné kou barri aw aye le kanamam gui di mélni boppe signélle
@neneoumou85512 жыл бұрын
C est vrai avec sa manière de parler
@elhadjithiam64032 жыл бұрын
😂😂😂
@sambadiagne57502 жыл бұрын
Bass Djoulit la Goor la Que Dieu l'acceuille dans son paradis.
@africainefiere10782 жыл бұрын
Gni ay vrai domeram lagnou xolal qui ak kanam bou gneme wam nite kou Bone la
@barafedior462510 ай бұрын
Sa baye dinan raye ndayame domourame
@damesamb62962 жыл бұрын
Gnome gnepou yalla nagnou deh thi prison yi...bilahi yena bone .yen douguen rouse sakh..raye katou nit nguen di wakh..yalla nanguen deh prison yen gnepou
@famatadiankha64852 жыл бұрын
Wa femme bii werna dosi meuna sori kaye yaw daleu n'a sa dieukeur set rek ts fekewo sa dieukeur es ce ke bousi bokoule waune dinaniouko arrêté sa kaname bou njieme bii
@nenebodian64092 жыл бұрын
Tè fèkkê wou thi dara
@mmsseye93912 жыл бұрын
Thiow bakhoul !! Kham nguen ni ki dé ndiabotam diominagn wayé gni ray tamite sen ndiabot diomi nagn
@diarra_chou84972 жыл бұрын
Motakh nitt wara moytou fitneu li loukofi diar
@mmsseye93912 жыл бұрын
Bilahi dara diarouko
@Diarista90 Жыл бұрын
Yènn gathia doulèn rayy 👈thimm
@famaba34982 жыл бұрын
Dame bi ndieukeu wakh lougnouko wakhal mom la ak kanam gou gnamé gou yak sa dieukeur yena yam Boy bi mom fenkat la pa konté nena au tolam la bayatoul nguen sopiko seun difa dieulè souf ba paré nan gnoko mom Guenel sa keuyitou baye ba paré .beug setal sa baye boumou takh nga takal kenen
@barafedior462510 ай бұрын
Yen blh danio wara raye sen ndaye sen sarapp ndaye waye aye deum gen rek
@ndeyekhadydiop92562 жыл бұрын
Mère bou mana fen ngay am fii ay yii fen you tooy, yaw say doom kouleen takk ,am diabar diou mana doul😂😂😂 😂
@oumoucisse86022 жыл бұрын
Ay vrai voyou ngen raykatou nit yi ngen done
@nenebodian64092 жыл бұрын
Non qui mo mane doume
@justarandomguywithachainsa88782 жыл бұрын
Dé Len wakh diam di deff diam di yenné diam.li amm meti trop. Yalla na yalla yeureum ki fatou té sakhal diam di deuk bi ak adouna bi.yalla na yalla yokk niou moussal si radjim amine.lii yeupp si biir ak mbokk.yalla na Len yalla deff ak .mbokki pass pass amine.diné ngor ak fitt
@fatougning28632 жыл бұрын
J'ai tellement mal au coeur walahi souma deukone fi gadaye
@ousseynoudiouf20782 жыл бұрын
Fambi koka hole hamne poveurle dagaye sohor
@amidoudiakhate97542 жыл бұрын
Problème principal bi moy bassirou sonneu si diouma dji fayekou woulen 1frs di def te yalla takh beneu porte kesse meuno lenko ko may nann dako sathi lolou mo indi problème bi
@gndiaye25452 жыл бұрын
Que justice soit faite pour l'amour de Dieu. Sama khole bi metina torop
@soxnaramataba32832 жыл бұрын
Niguéne ñiawé nonu guéne boné. Xoléne wa keur père bass niñiou nitté mashallah
@bintadiop32322 жыл бұрын
Konn setlouga Lolou
@soxnaramataba32832 жыл бұрын
@@bintadiop3232 bilahi bella ñie j'arrive même pas à les cernés ñiouye melni aye montage
Gni aye vrai vrai sauvage lagnou ils sont aigris et méchant ba pare mene fene baguene ko raye ba pare laye dina yomb bass n’est plus la pour se defandre père Bassirou dalene guene sur tt les plans molène guene gueme yalla guene lene Ted guene lene deguou gni dounou aye nite aye terrains fenêtre you gnak fayda bagnou si ray nite
@bellawomen2 жыл бұрын
Bilay gnii ay nitt you sokhor lan
@abydiop37722 жыл бұрын
Yéne nitt you bone guéne 😭😭😭
@moussambaye69152 жыл бұрын
famille diéye bii aye doma rame la niou kw😢😢
@ndeyefatoufaye35942 жыл бұрын
Yaw esk sa keur baye amna ay papier...com dagay lire vidéo yeup concernant votre crime naga fekhé ba répondre
@fatoumatadrame59092 жыл бұрын
Moma diakhal sen keur amoul ndeye papier mouy doul legui niom louniou beug niou libérée len gni esk ay nit lagne domi kharame yii
@boubacarsaware9702 жыл бұрын
Keur bou am papier amoul ndiéye. Daniou lay may terrain rekk nga deukk.
@nancykane88502 жыл бұрын
YALLAH ne YALLAH atei bou gawe Gni amougne khole Aonzoubillakhi mina cheitane radjim Da nou me commentaires wayei khamoumeu me loutakh histoire bi touché me ni rek waye !!!😢😢😢injustice meunou me ko supporter YALLAH ne khipei FIRDAWS ndeyssane 🙏🏽
@jeanyazback84602 жыл бұрын
Ki sérieux daniou warona diap ndayam mouy créer ay circonstances atténuantes domaram
@bayezaletalla20662 жыл бұрын
Famille Dieye gathia ndiéye défnagn diéyé😭
@1AbouDavid2 жыл бұрын
Boye wakhofi dara , yéne niysi take yeupe naniou réye séne ndéye
@kasouleye42072 жыл бұрын
Deuk bi woroul deuk. Dégno doff té am fiite
@africainefiere10782 жыл бұрын
Bilahi yaw
@Fashionistas834002 жыл бұрын
Gni kay dofougnou rekk yam si mais kou goor ki mossi tané
@lahad75792 жыл бұрын
Gni ndékété ay dof degue lagn
@babacarsarr14072 жыл бұрын
Fi kaye aye nuitte deuke niou fi
@meyoundao41032 жыл бұрын
Bilahi Dagno bizarre pa bass rek mosi normalone motakh gnou raye ko
Ayyyyyy dofffffff. Entout cas letat doit revoire Tous les villages et chercher des solution pour les problem interne.
@ousmanediagne10122 жыл бұрын
Ya mouna doule bo amoule yene ray nite dinagnou armee wou nonou
@cheikhdiop8592 жыл бұрын
Yamana doull boy sa keur baye da am kayit wa deke bi ana sen kayit niom sen baye da dewoul rék ray bayou diambour melne kouy dem guer yenay domou ram
@africainefiere10782 жыл бұрын
Ay domeram lagnou d
@salysoumare36872 жыл бұрын
Lakhou dom dor dome mofi ame que justice soit faite ils savent qu’ils ont tort wayé yalla dina atté😢
@sonadiouf27052 жыл бұрын
Wa lak dom dor dom gni ay sauvage lane
@siracissokho96782 жыл бұрын
Mère ya mana féne
@msz63172 жыл бұрын
Djiguén gni complices laniou fén katt laniou darra safoulén si dé gui
@boubacarsaware9702 жыл бұрын
Yéen noppi rekk mooléen warr, niaawtéeff bou reuy bi ngéen déff ba paré di wax, teutj léen séen guémañ way. Ep8 keur bou am ay papiers amoul ndiéye. Kone boul fi wax waxi papiers.
@Adelina1982 жыл бұрын
En voyant la façon de parler on se rend compte que la femme meurt de honte. Elle cache quelque chose. Elle n'est pas claire. Trop de paroles sans aucun sens. Pauvre dame.
Yêne doul meune guéne wakh bagni raye guëne yaw kom khamossi do déme gua tokk lounioula lathie guani khamo donc ferme ta gueule yaw khamo bane lokho laniouy djéguénayo si bamél noye diapé baye lale Kamil puffff
@sakhosakho58142 жыл бұрын
Boy cheikh ba yaw deugouwo kham nga liy deugeu wayé dang sé deugeu sa tank
@tout19582 жыл бұрын
Soxar ngene trop wa deugeu bi
@tanoudiallo66322 жыл бұрын
Noumou def ba nekk ci vidéos yi
@sokhnabassel82792 жыл бұрын
Waw
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Gnii souniou bayiwoul sène wakhdji problème dinafii amate c'est sûr ndakh gnii dagno doff c'est une crime qu' on parle
@wadandiaye3972 жыл бұрын
Bilay waxatiko gni ma gis bouniou si diogoul lalene Dina am ndax Ray nite baparé Di werr Di wax rek Domi bay basse apouniou niouma nakar bilay gni diépinaléne
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
@@wadandiaye397 wakh nga deugue dé gnii danio contane cii raye bii
@fatoumboup66842 жыл бұрын
@@wadandiaye397 likay man jaxalnama kouniwon nit soxorenani ma wediko t guisnga gni baniouniousi dara soumadon njabotou bass damay gaday gni yak sa adouna laniouy def dof sakh xajnasi wala febar boudoul wer
@wadandiaye3972 жыл бұрын
@@fatoumboup6684 bilay boumalene gisé nioy wax sama khôl day diekh gni AK gni Ray nioyam khôl bilay bay basse nak khamoumako way ndiabotam yépou niongui bokake mom nakar bi te niane sounou borom diegal ko yallna khipe aldiana firdawsi
@hulkhulk49732 жыл бұрын
Iow boy vrais domerame ga , ganane sama bay mo mom brique yi et après !!! Doul rk !!!! Diokhoulenn' thieur baye basse !!! Boroom keur gou mayé keureum guanni yénako mom
@aminatadiedhiou67112 жыл бұрын
Vampire
@mbeneniang89172 жыл бұрын
Yaine koulaine khol sakh khamnai ay domi khadje guaine
@serigneabdoulahatseckoffic49092 жыл бұрын
Journalist bii macha Allah question
@magayendiaye84912 жыл бұрын
No mais qui dou nitte kou bakh dhe
@adjafall76082 жыл бұрын
Cette dame est très désagréable elle est sur la défensive et n'est pas sereine de toutes les vidéos que j'ai vue il n'y a que ce monsieur qui a présenté ses condoléances à la famille du défunt c'est quoi ses gens vraiment yalna yalla sopi s'en kholyi lou neh si khôl fégne si kanam s'en kanam yi nirouwoul kanamou niit gnou bakh surtout cette dame qui n'a même pas l'air affecté
Séne kanam ou safarayi, danguéne ignanéwone pa Bassirou rék
@mohamedndiaye86202 жыл бұрын
Boys bi di wakh koumana doul le ay domeram nguene sokhor molène diap domeram yi nguene donne
@lahad75792 жыл бұрын
Famme bi dh nimou wakhé rk moy wone nii lign la wahal yako wakhhh yaw dh kou tégui caméra bi nga saga ndeye
@mymammecisse21972 жыл бұрын
Wa deuk bi diakhalnagnouma ko lathie mouné fekewouma histoire bi moy waneni wakho lene deugu
@sidysylla11462 жыл бұрын
Daguene di fene il sont mérite tous perpétuité je demande il sont où là communauté islamique Diamra e consort Si ils agissiez des choses no sens gnou nek di sonal nite yi tous les musulmane di senégal devront avoir la soutient de serigne Bassirou mbaye personne n’a parlé désoler 😭😭😭
@noiricainesall99732 жыл бұрын
Khâgne diabar dieukeur khâgne dom papa khagne seute mame ba paré am fitt tok fi di sagna wakh yèn kouguèn yap nopilène 😡😡😡
@khadimdiop37372 жыл бұрын
Boy gordjigene nga doule way
@mbodjaseye30002 жыл бұрын
Non Sénégal dagay réy niit yaakar ni déy yobé nonou
@massfall63242 жыл бұрын
Bay bass yalna ko yalla yereum wayé gni tmt sen wakh dji lerna d senegal nak kou déh rek laniouy faral mais dal doyna waar
@mbodjaseye30002 жыл бұрын
Man dé Lima diakhale moy kiguéne réy yéne wakhi famille rék guéni wax té yénako réy
@modoumodou81302 жыл бұрын
Boy fen rek gay Def filas yi amol bine papie baye aliou konte moka ko may fammi bandi damo yi doulen ay musulman
@soxnaramataba32832 жыл бұрын
Chef de village donté mag la n'empêche que ni féne kate la
@aissatouleonie89852 жыл бұрын
Gni daniouye diekheul khôl dieul nite raye ko si aname you métti baparé beugue dieul kiniou tongne raye ko diokh ko tort gni Dakh ay nite laniou
@ousmanedrame34882 жыл бұрын
li moye wane qu yene begou lene hone pabi raye nite ki balegui sa khol mayoula nga wakh si môme Lou rafete
@famaba34982 жыл бұрын
Legui deug fegn nak ndakh degg nafi école basse kon moko takhawal Fenkatt yi nan ecolou deuk bi ak plaçou deuk bi bass daal khamlen mo takhone mouy bagn
@sonadiouf27052 жыл бұрын
Wa mère ki dai guay doulal dosi deigue dara gni paine de mor mo bakh si mom
@diengmamadou22722 жыл бұрын
Ndaw si ndieuka wakh vrais nafekh la fene Kat
@souleymanecamara33432 жыл бұрын
Domaram bou donne sa baye do wakhez ni doule bonne
@amadoundao15262 жыл бұрын
Famille diueye be kobakh neko ci
@tantycamara88442 жыл бұрын
Que justice soit faite
@gorasilla54972 жыл бұрын
Ray waroule wona am
@moustaphandiaye84112 жыл бұрын
Bilahi mérbi lougnouko wakhall momla ak gnawayam bi
@mbodjicoumba81922 жыл бұрын
Kou dieguene ki kanamame bou gné bi lougnoula wakhale yawela
@ousseynousall58082 жыл бұрын
Katéléne ndéyame feuleu doul réke
@gueyeawa75792 жыл бұрын
Mère bi meune na fene 😢 Quoi qu’il en soit le fait même d’aller vers quelqu’un avec des armes et que la mort de ce dernier s’en suive peut être considéré comme un meurtre avec préméditation. Loussi meune ti ame même si Baye Bass sou momoul wone le foncier sur lequel il bâtissait raye amoussi wone yone. Li c’est juste une manifestation de la rancoeur qu’ils éprouvaient envers le vieux.
@lahad75792 жыл бұрын
Boudoul wone sa ndiawayy bi rk manila démal outi dieukeur mais niaw nga té amo diame mon takh kéne doula tak
@aldojr73892 жыл бұрын
Mère Bou niemee Yallah ngui nii
@zeiinabeiiyefall2 жыл бұрын
Mdrr des femmes soumises yo hameni waxe deugue sahe meunougnou ko juste pour couvrir le mari frere enfant ki sont des criminels pff meune nguene kathie mere nguene balma
@niang.talibe.brom.ndienend54342 жыл бұрын
Femme bi ndienke wakh nitu histoire leu diouboul ak mousaram gou bon gui
@ndoumbeniang73412 жыл бұрын
En plus vous êtes des insolents
@laminedieye77442 жыл бұрын
Mère bi mo nième yalla .
@nenebodian64092 жыл бұрын
Mane fène rek
@ndoumbeniang73412 жыл бұрын
Ha loy yonou peulbi thi affaire bii
@sokhnafatmathiam52392 жыл бұрын
Ndaw si deh ay wakham djiouboul moy deudeudi ni que son àme repose en paix
@fatouboubacarndiaye90462 жыл бұрын
Mère bi bone neu kanamam bou wow bi mouni dafa demone pire legui mom noumou def ba khamni dieukeur dji fekewoul khéx bi tchrrrrrrr Que justices soit faite akh
@diarra_chou84972 жыл бұрын
Katlén khonam nopi rien ne justifie l’acte dieul bakanou nitt togne ki trokhalko devant sa famille liguèndi bonn domeram Ki décédé naki yalla yereum k justice soit faite
@amethsiby32102 жыл бұрын
Vous à rien à dire mai moi je pose une question esk gni set naniou gni esk douniou ay deum
@sokhnaaminata2872 жыл бұрын
da ngén di doul ku rayul nit ci mem jour bi nga sangu took di attaaya mem soo ko rayul ci mem heur bi waroo took di attaaya
@couriellebalde22222 жыл бұрын
Qui dieuk wax dayyi doul simm djiguene Diou meuneu fénne, en entendant leurs discours tu comprends automatique le théorie du complot,tekk bassirou mou fatou beut ,mou defar école coranique 10ans plus tard guénne beugue defar bénéne école, maintenant pour la justice il n'est plus affaires de jumah mais de meurtre , association de malfaiteurs vendalisation , ils seront jugé pour meurtre
@ndeyendiaye12822 жыл бұрын
Mère bayilén nafékh fi kousi laléwoul dougne la wooo mère bi bo xolé ay wakham khamni leuf laaaa
@pendadiallo78712 жыл бұрын
Leuf ak gueniwala beurina afaire trop
@isseudieng71372 жыл бұрын
😂😂😂 Astahfiroulah
@serignembackediaw20362 жыл бұрын
Bassirou dall koune ay mbokam rék nioko ray woloff Ndiaye wakh na paka balay ray say mbokou niokay dass
@coumbaousseynousall34742 жыл бұрын
Kou djiguenne ki kou bonne laa daniou KO wara rayyy
@bassiroundiaye57142 жыл бұрын
De même que moi aussi j'ai supervisé tout les vidéos bilahi
@mariamakebe37252 жыл бұрын
Bilaye sama khole dafa diékh femme bi di wakh visage séytané la nitou aye la sama khole dafaye méti walahi 😭😭😭😭