Série nekhna trop mais mention spéciale à l'équipe technique oh oh la qualité est du haut niveau. ❤❤❤Son, montage, cadrage, image tout est au top deug dou Niro AK pire RTS nak yaye télé nationale. Félicitations à toutes l'équipe je vous envoie pleins de bisous 😘😘😘
@ibrahimadrame29312 сағат бұрын
Un série à la vraie réalité Sénégalaise
@babalayesarr93452 сағат бұрын
UNE SERIE PUREMENT SENEGALAISE BRAVO AUX ACTEURS ET AUX REALISATEURS
@Gaye-industrie2 сағат бұрын
❤❤❤
@elmamoudouba765042 минут бұрын
Une leçon à tiré pour cette épisode Soo nguéné sa keur ak Thiow diaapalni mooo lay topp toute la journée
@mouhamedfall46662 сағат бұрын
Une pensée forte à tous ceux qui traversent des moments difficiles. Restez forts, cela va passer.❤💪🏼🙏🏼 Yalla naniou Yalla doli Soutoureu 🙏
@Noba-konateСағат бұрын
Makha boutiquier bi loumou def Bakary nekhouma deh li mom tass yakar la té Bakary loumou sonou rek doyna😢
@mamemaryndiaye3875Сағат бұрын
Vraiment j'aime mame khoudia alias Halima je l'admire elle joue bien son rôle ❤❤❤❤😂😂bakari tamite sonouna 😂
@bagiss36011 минут бұрын
bilay iow maneu damako fans 😂😂😊
@Morydiop82045 минут бұрын
bakary sone na nk😢
@FallouDieye-ie8yz52 минут бұрын
Serie bakary daffa waron ame son wally ballago seck taxi love
@ballafaye50792 сағат бұрын
Sacré Bakari 🌹😂
@mamadoubalde-nw2hv27 минут бұрын
Bouléne faté qui binde scénarios bi kokou mo aï dou acteur yii
Bakary yalna nga guèneu ci tolof tolof yi ak bèpp père de famille bouy doundou yi situations 🙏🏽 rewmi mo bari thiono😂😂😂
@dabaxful13 минут бұрын
Mame Khoudia est une excelllente artiste. Je realise toujours pas qu'elle ait deja depassée cette étape de dépression et revenir plus forte qu'avant. Mais ani Jalika sama sokhnasi
@rosemariethaurin1953Сағат бұрын
Pauvre Bakary😢😢La voix off de retour ❤
@fatougueye2201Сағат бұрын
Vraiment Bakary sonn na bak😢😢
@diawi25888 минут бұрын
Wa keureup yi gnoko sonal, yeureumou gnou ko dara
@yayemariemeba176732 минут бұрын
Halima Guadji est très belle Ma Sha Allah❤
@ThioubaMboup2 сағат бұрын
Aye waye yueruem len Bakri
@MDbousonko2 сағат бұрын
Bakary dou nitte 😂😂😂 merci beaucoup ❤❤❤
@babandiaye411635 минут бұрын
Machalah tout est naturel dans ce téléfilm good job
@mamadoubalde-nw2hv35 минут бұрын
Nanou yalla doli soutoureu mes frères ❤
@sekoubadji976420 минут бұрын
Bakary Taximane la série qui n'a jamais perdu sa valeur
@NdeyesalkaBAСағат бұрын
Bacary sa wakeur sagn nagn dompatt néw 😂😂😂 niom dal daniouy khéy rék togu pourtant sa petite sœur peut aller chercher du boulot wayé khéy rék di snap ak lék 😂😂😂. Mais borom boutique bi sokhar naa loll
@yayemayelatmbao5442Сағат бұрын
Ay way😂😂😂
@diawi25888 минут бұрын
Bakary 3 personne yi gnoy problème bi,
@diopkhadim8340Сағат бұрын
Borom botiqu bi lim Deff mernasi trp waye 😭😭😭Bilahi
@elmamoudouba765053 минут бұрын
Mais Bakary mii dou lathié ba paré sogua wathié gazz bii sii taxi bii 😂😂😂
@BHB5TV23 минут бұрын
Wakh deugg yalla 😂😂😂😂😂😂😂
@salimatadiatta159439 минут бұрын
Bakaru diotna mou am benen goor ci keur guy ndakh moukoy diapalé ci khoulobi😅😅
@DiDe-vj1mnСағат бұрын
Bakary mba dou écchangé gaze yi😅😅
@ousseynoungom9817Сағат бұрын
Non d'où sath deh ou bien😂
@ibrahim8899-j3z2 сағат бұрын
Superbe Famille Bakary Du courage depuis la France
@abosall96186 минут бұрын
Avant tout nañu sante yalla bu bakh mom miñou may tawfekh bañ mana nieuw ci KZbin bi di setan BAKARY amna ño xamni taluñuko dakh ay problème ❤👏
@kebefall6125Сағат бұрын
Bilahi sama vie ak bou Bakary ben la 😢
@NdayemassNdayaСағат бұрын
Masta
@Mouhamedtv5362 сағат бұрын
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:11
@scekfatima70092 сағат бұрын
Bakary le meilleur😂❤
@BHB5TV29 минут бұрын
Kou contant ci série bi abonnél si sama compte bi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@CheikhMbacke-p6uСағат бұрын
Batay bakary amul gaze 😂😂
@gnimasane373349 минут бұрын
Merci pour la pub 9kg lobbo mame Diarra bi nimou manquer sakh da metti tay 15h lagnou agn ndakh gaz bou djekh
@Missdieng13 минут бұрын
Bakary yeureumnako trop😢 Borom boutique bii bone na💔💔
@aidabadiane3695Сағат бұрын
Non Bacary sonnu na nk bilay 😂😂
@fantakeita49432 сағат бұрын
Wah loutakh gor gni beugu serie bi😂😂
@aliouthioub65372 сағат бұрын
Parceque c'est notre quotidien
@fantakeita49432 сағат бұрын
@aliouthioub6537 c est vrai aye diambar guene yalna yalla defal lene diam
@julestounkara2 сағат бұрын
Notre routine plus tôt 😊
@NdiayeAlioune-to9lv2 сағат бұрын
Da ñouy sétane sunu boopou 😂😂😂
@Awakeita-or8cuСағат бұрын
Diarna lathie
@dabadidadia30 минут бұрын
Quand c’est important c’est sur la RTS ça me rappelle ls sketch comme #Ndioublang de Baay Ely en 2004
@abdouazizkane3818Сағат бұрын
Halima si niata mois nga tolou 😂😂
@yayemayelatmbao5442Сағат бұрын
Diarna lathie dé 😂😂😂
@diagnenar57172 сағат бұрын
Boulene fate le 15 décembre la Macky Sall diapon élections présidentielles 😂😂😂😂
Bakary 😅 bayile togne boutiké bi waax na deug fayale sa bor biga léb 😂 ba paré
@MbeneFall-z6pСағат бұрын
Bakari tusur poroplem bu bess
@Justme-D27Сағат бұрын
Liguay kateu binga doneu 😂😂😂😂😂
@myashumbengue1399Сағат бұрын
Mention spéciale à vous machallah 🎉❤
@domoudaraatv44 минут бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mamadoufall340833 минут бұрын
😢non tay peul bi 1000 f la yor pour boitelou ndokh bou 100 f mouni amoul wetiete naniko diokhma bou 50 f souba ma diohla sa xaliss mou bagne tay mom mako doundou ❤ vraiment peul yi nekhougnou faral sayo amé problème gnou diayla badola
@MaminaSow-l6l2 сағат бұрын
Waa djolof âme guéne dame mafii djitou
@AstouMbengue-p2h2 сағат бұрын
Garabou saw😂
@modoufaye159128 секунд бұрын
Réalité Sénégalais yi
@MOURTALLApes12 минут бұрын
Gaz 5jour
@sambafaye82232 сағат бұрын
Samba il est.mechant hein
@mouhameddiallo5664Сағат бұрын
Bakary ak dame losss bi😂
@ebdw264126 минут бұрын
Doukoury daa reew rek mais doundoul moitié li bakary di doundou 😂
@BHB5TV5 минут бұрын
😂😂😂😂😂😂
@diawi2588Минут бұрын
Bilay, ndakh mom célibataire la sans enfants 😂😂
@MbavkeGayeСағат бұрын
Ndeysen per de famille metina ohhhh damakoy xol sama bopo
@memoriserfacilementlecoran257Сағат бұрын
TRISTE RÉALITÉ Tu as besoin de 5.000 f pour t'acheter un livre. Tu poses le problème à ton père le soir. Il te donne rendez-vous le matin. Ce que tu ne sais pas, c'est qu'il n'a que 10.000f. Très tôt le matin, il va voir le boutiquier du coin et faire la monnaie des 10.000 f, il donne 5.000f à ta mère pour la ration sans lui parler de ton problème. À toi aussi il n'a rien dit de ce dont il possédait. Discrètement, il t'appelle dans sa chambre et te remet 4.000 f pour l'achat de ton livre. Tu commences tout de suite à te plaindre que l'argent ne suffit pas. Pourtant, le livre coûte effectivement 4.000 f mais tu as majoré 1.000 f pour tes besoins. Ta mère entend tes plaintes et t'appelle devant tout le monde en essuyant tes larmes, puis enlève 1.000f sur les 5.000f qu'elle a reçu de ton père pour te remettre. Tu sautes sur son coup et la bénis; tout en ruminant des injures contre ton père. Tu jures à ta mère que quand tu seras grand, tu la couvriras de toute ton attention. Ton père entend tout mais ne dit rien. Il pense plutôt à la dure journée qui l'attend car il ne lui reste que 1.000 f et son transport pour arriver à son travail coûte 500f au moins en aller simple. Le soir, il devra rentrer avec la solution pour les impératifs du lendemain. Toi tu as ton livre, et tes 1.000 f de besoins personnels et ton plat du jour au retour de l'école. Ta maman ira au marché et mangera avant vous les enfants quand elle aura fini de préparer. La seule personne qui n'a pas la certitude de manger, c'est celle qui a tout financé. Telle est la réalité que vivent tous les parents responsables. À la fin, tous les enfants adorent leurs mamans et considèrent leur père comme un simple accompagnateur dont le rôle a été relatif dans leur parcours et non essentiel. Seigneur aide nos différents pères dans leurs différents projets.
@mameassmbengue4933Сағат бұрын
😂😂😂😂😂man dama warou bacari khana da ame loumou sanguo
@serigneseck7432 минут бұрын
Way Maxa mi nak metina😅
@amyfaye8907Сағат бұрын
J'aime khalima😂
@MbayeFaye-d4vСағат бұрын
J'aime pas les gens qui pense a eux même. Bakary borr kénn dousi insisté 😂wayé makha wéréngua trop mounone ngua téyé 10.000 réck
@Djilydiob-jf2ey2 сағат бұрын
Baakari boo deme wacceel Gaas bu jeex bi joxko ndaw si 😂😂😂yobb sa Gaas ba jamono neex nga fay te baalu ko.
@BHB5TV4 минут бұрын
Moy yonne dé 😂😂😂😂😂😂
@yayemayelatmbao5442Сағат бұрын
Mère bi bakary di yaubou thi taxi bi dafa nouroul bibiche nimouy wakhé ak ay manière
@seynaboudiouf99502 сағат бұрын
Diallo boutique dmrm la koi😊
@khadimkha-p3e2 сағат бұрын
😂😂😂no Bakari 😢😢
@AbdoulayeDiagne-ti1jj2 сағат бұрын
Bakary xana d'où diouli fadiarr😂😂😂
@khadimkha-p3e2 сағат бұрын
😂😂 Billy
@toufashrassoul125519 минут бұрын
Loo meunti dioté ak nit boul tass yakaram😢 lidé day moudié nek akh ngeu dessé ak sa borom… diepi nit boumou teré ngeu juste def deugeu tmt… bakary liko dall metti neu… et boutiquier bi merrè nako tropp
Mann dh baye fall la abdou wahab madonn ladj iska niaka dioli amna baye fall wla aka ma beugeu di dioili sakh barki alquran wayé khamou ma lomay wakh boma sagé wla boma sodio té😢