Jërëjëfaty mbacké Balla yalna Borom bi samou défal goudou fane AK weur barké Al xourane
@Waxtaanu_boroom_xam_xam_yiАй бұрын
Amiin Barkeb seexul xadim ❤️
@mamadouseck5549Ай бұрын
Machalla mbacké balla kadou yi amatina solo lol yalla Nanou sounou borom may degg ak topou barké Serigne bi
@ibrahimaseck2319Ай бұрын
حفظه الله ورعاه بجاه سید الوجود صلیاللهعلیهوسلم برکیب الشیخ الخدیم ❤❤❤❤
@salioumb5371Ай бұрын
Balla aicha Dieureudieuf
@ibrahimaseck2319Ай бұрын
C'est la vérité 🇪🇸🇪🇸❤️
@saliouaissy4462Ай бұрын
Niongi ziar di sakkou si ñiy dougueul wakhtane yi bouniou meunone bayi Mouride yinie croix Dina Guen am solo ndax S Touba da barilei th ai ndiabotam lanou nioun nieup th d'où beddi ken
@mamadouseck5549Ай бұрын
@@saliouaissy4462 waw gor yaw dé nio bokou guisin
@albachirtvАй бұрын
❤
@dëgmonjëkdëgmomuj1780Ай бұрын
Franchement ñi ñuy croix ay murid lañu mo xam ñu teggu ci yoon wa wala ñu bañ ca teggu ay murid lañu buñu ci teggo Alhamdulilaah buñu ci tegguwul nañuleen laabiré mo gëna rafet dileen croix melni dañuy def ab safaan... Ñongi tuub bu baax tay sant ci waxtaan wi🙏❤️
@Rawdourayahine20 сағат бұрын
" Jërëjëf ci yaatu gi " Damaa gis campagne bi ñuy def fan yii ay xale yu gatt xam-xam di croix Serigne Mbacké Abdou Rahmane ci wax ju mu wax ni Sëriñ Tuubaa du nit mu metti woon ma lool
@DaneGueye-l8yАй бұрын
ماشاء الله ايدك الله❤
@BayeAbdouGaye-x6oАй бұрын
Nioun borom Touba adji makadji rek laniou geum
@KhalifaTopАй бұрын
Waw goor
@CheikhSambou-y9lАй бұрын
❤❤❤❤ ماشاءالله
@moustaphadiop94Ай бұрын
Macha allakh
@cheikhseye4119Ай бұрын
Machalla
@IbrahimSamb-ms7zuАй бұрын
Xam xam bokotage xim xim😂 mbacke diaradiuf ❤
@assanegueye2427Ай бұрын
Ma cha allah amatina solo en même temps iow rk laaaay diglou
@modoucassette5178Ай бұрын
Machalla bèg na thi li abbonénaa🙏🙏
@onlytrust13Ай бұрын
Serigne touba agu si yalla la woté wone lolou mo waral yonou mouride Mame cheikh ibra fall donoul wone diouli,kooroul wone té adji woul wone maka té mome la serigne touba diokhogne ni moy baboul mouridina Yoonou mouride agu si yalla moko soss Serigne mouride tay khamou gnou louy aguale nitt si yalla té sen talibe yi defou niou si gnom agu si yalla
@SidiDienneАй бұрын
Li ngay waxni d kom théâtre 🎭rek 😂
@badboy-ju2qkАй бұрын
Xasida guiy daw si souf koumakoy baxé way ?
@abdoukarimdieng6321Ай бұрын
Anta rabbi wakountali bi widadi la toudou
@badboy-ju2qkАй бұрын
@@abdoukarimdieng6321 dia dieuf way
@seexunaaseexahmadubambasil1553Ай бұрын
Mbàkke Abdu Rahmaan fi moom ya tooñ Daam Mbàkke moom deesu ko limale ci mbindéef yi waxaale wu ma nit. Ya tooñ de nekkal nit te bayyi sa dàjji bu metti bi.
@RawdourayahineАй бұрын
Bismillah Wax ni Sëriñ bi du nit xas la. Ta ñi ëppu ci koy wax dañoo jàppu ni Sëriñ bi du royukaay ta moy woote woo ni doomi sangamag sangam. Serigne Touba royukaay la ta ci sonna la nekkoon.
@seexunaaseexahmadubambasil1553Ай бұрын
Yaw fi mu tollu ni ci sa xalaat ngay waxee waaye boo jëloon ay mbindam def ci reference dina xam ni nekkul fi ko teg. Sëñ Mbay Jaxate li mu wax leer na "man jéemu ma roy te jéemu ma ray....
@RawdourayahineАй бұрын
Moom de lim wax mooy ni man 》jaamub yàlla laa di ligeey katu Rasoolu Laahi lii de la wax .
@mamadouseck5549Ай бұрын
Magui toubat bou bax di sakou si niiy partagé vidéo yi niou bayi di croix mbokou talibé yi mou melni Serigne bi niom lay wakhal té Serigne bi diagalé rek lasi dioublou ak léral yonou Serigne bi té niom mouride yoyou Serigne bi reka len Nior kene Manou léna guéné si Yon Magii toub bou bax da don louma remarké Lou bari lol si vidéo té wakh dja day wouték lolou lol sakh Magui digalou mou bax nak sama xalat ak khel mou gatt rek lay wakhé
@RawdourayahineАй бұрын
Machallah jërëjëf ci yaatu gi Damaa gis campagne bi ñuy def dan yii ay xale yu gatt xam-xam di croix Serigne Mbacké Abdou Rahmane ci wax ju mu wax ni Sëriñ Tuubaa bul nit lum wara doon ñu dagg ci parti bu ndaw ba soo ko deg loo sax mere Sëriñ lool nak du jall . Wasalaam jërëjëf ❤️