S Moustapha Diop Koki, Li mom wérnamani Serigne Touba moko bind ci loxoom…

  Рет қаралды 27,882

Rafah TV International

Rafah TV International

Күн бұрын

Пікірлер: 142
@AmsaSamb-sn5oz
@AmsaSamb-sn5oz 11 ай бұрын
المجدد لا يأت بالدين جديد ولكن يأت بفهم جديد❤أيدك الله ونصرك نصرا عزيزا
@BayeSall-cs7ec
@BayeSall-cs7ec 11 ай бұрын
ماشاء الله أظن أنه من المجددين طريقة المريدية😊
@diouckcheikhouna3082
@diouckcheikhouna3082 11 ай бұрын
Yitteem mooy leeral deugi deugi ak mourid , yala nakofi Yala yagal. Lii mouy wakh yala rek mootakh ak beug sam ndondol Serigne bi
@MoussaMbengue-vc9wg
@MoussaMbengue-vc9wg 10 ай бұрын
Ak mouride meusta leudeum bagn koy leral tè yonou mouride yonou dieuf la wayè dou yonou wakh
@diouckcheikhouna3082
@diouckcheikhouna3082 10 ай бұрын
@@MoussaMbengue-vc9wg ndeysann
@SerignemalickDiop
@SerignemalickDiop 11 ай бұрын
Kola Xam Xam Ne Lou Wakh Deg La Koula Toub Am Yalla Ak Segne Bamba ❤
@xaadimfaal9285
@xaadimfaal9285 11 ай бұрын
ما هو معني الخاتم الفظا ومعني والصتلاحا
@OusmaneSow-nb1bi
@OusmaneSow-nb1bi 11 ай бұрын
Même hafif et kamil il y'a plusieurs versions mais elles viennent tous de cheikh AHMADOU Bamba :C'est la richesse et grandeur de Serigne Touba qui s'explique.
@SeringeMorloNdar-dj9jk
@SeringeMorloNdar-dj9jk 11 ай бұрын
ماشاء الله تبارك الله فجزاكم الله خيراً ياشيخ
@BayeNorouDiop-kz2yp
@BayeNorouDiop-kz2yp 11 ай бұрын
Yala nala yalla fayall bopam yonente bi sws fayall leh bopam Serigne Touba fayall leh AK Mac gni AK leepou loma yéne yalla naco ame
@yorondoye7205
@yorondoye7205 11 ай бұрын
Serigne moustapha ndax waroo demal sa bopp baci Serigne mountaxa nga wax taan ak ci wird wi ak linga ci xalaat ❤ Jërëjëf diop
@MoussaMbengue-vc9wg
@MoussaMbengue-vc9wg 10 ай бұрын
Yonou mouride d'où yonou xalatt matt n'a bou yagg dieufè rèk
@tawbatv6268
@tawbatv6268 11 ай бұрын
Wakham dji d'où nêkha dadji dé wallo yalla môme ni la geustou bamo werr rk
@Cheikh_abdou_hakim_lofficiel
@Cheikh_abdou_hakim_lofficiel 11 ай бұрын
Lii mom borom Xam xam yi warouñ ko bayi mou diall dafa wara lérr dh wax deug yalla ndakh njariñul Murid yeup la 🙏🏾
@dioufmbayediou1729
@dioufmbayediou1729 11 ай бұрын
Yalna nou yalla fayal cheikhoul khadime lou yageu yageu mbir yiii di geuna féniaa mom akhmadou kén la dieureu dieufé brom Touba yalna nou yalla soutoural ❤❤❤❤
@nafissatou9560
@nafissatou9560 11 ай бұрын
Dieureu dieufeuti Serigne Touba khadimou Rassoul
@abdoufall7542
@abdoufall7542 11 ай бұрын
Mashallah kaadouyi amatina solo loll mouride sadikh
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Thieye yalla. Képou kou amm nioula toupou bala nga wakh dara...war nga kou sétte boubakh.
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Ana loun wara sétat ci wax dji waxal xam xam ñou tontou la ci xam xam bou lér bou ànda ki tégin
@papesarr1177
@papesarr1177 11 ай бұрын
Wakho dara wakhal lou ler wala gua nopi damelni sa xol dafa nekhoul serigne xam xam bou leer lay wakhal xam xam soko monoul demal teudi mo guen
@mustafaanjaay20
@mustafaanjaay20 8 ай бұрын
Ya nek si deuge de ❤
@bassiroudiouf7702
@bassiroudiouf7702 11 ай бұрын
Amna solo loll
@amarndiaye6186
@amarndiaye6186 11 ай бұрын
Machalla ❤❤❤
@MameMorBeye-ll4pc
@MameMorBeye-ll4pc 11 ай бұрын
Machallah ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
@alioudiaw3211
@alioudiaw3211 11 ай бұрын
Nguir yalla S Moustapha Diop fanla deukeu ci Touba
@kebe3868
@kebe3868 11 ай бұрын
S bi migi patar bala ngà ak djàrém
@alioudiaw3211
@alioudiaw3211 11 ай бұрын
Merci s kebe🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@KhadimMourtadaSourang
@KhadimMourtadaSourang 11 ай бұрын
Saam Jaxate de la dëkkoon damaa xamul baxam dinafa nekk lu bari
@cheikhomarlo1834
@cheikhomarlo1834 11 ай бұрын
Boudé yagui Touba dé ame mill change pour guisse ko 27 janvier mognou wara dafal conférence si Université bou néke dame a partir de 10h
@Moustaphalo-sj9on
@Moustaphalo-sj9on 11 ай бұрын
Patar wétou Diourbel
@ansrxdm
@ansrxdm 11 ай бұрын
Kumay diokh número serigne moustapha diop gir yalla
@bambaleye619
@bambaleye619 11 ай бұрын
Amnako
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
kzbin.info/www/bejne/e2OakHp_mth_lc0si=1KijhsW2vzY3ka34
@tokhoro8890
@tokhoro8890 11 ай бұрын
​@@bambaleye619diokhma numero Serigne Moustapha Diop stp
@TheTalibee
@TheTalibee 11 ай бұрын
@@bambaleye619doniouko bakhè 🙏🏾
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Dagay bayi sa numéro fi bouko défé ma diokh la numéro dieuwrin dio xam ni dina maman wax ak yaw ba nga man ko diot waye numéro serigne bi mome manésou ko diokhé fi
@MohamedNdiaye-o7y
@MohamedNdiaye-o7y 4 күн бұрын
Segne bi man numéro segne Moustapha la beug dama beuga dieul wird wi
@babacardiaw8701
@babacardiaw8701 11 ай бұрын
Merci machalla
@moussadiop6144
@moussadiop6144 11 ай бұрын
Serigne abdou rahman vidéo complète bim leral xafif bi lasi leeral du début à la fin Confusion dall amna sma bopp bi
@Muridullaahi
@Muridullaahi 11 ай бұрын
Defal lou dall sa khel rekk S moustapha mom diambar wayé lim wakh fii mom andou masi té lousi né rekk amna ay firndei Diapal ni daal wird yi boumsi meuna doon rekk si Borom Touba la diougué Bosi diapp rekk nga fonkou ko té boul khébal kénn bosam
@sindidisindidi801
@sindidisindidi801 11 ай бұрын
Sëriñ Muhamadul Lamiin Jóob de, bu moomul wérdi wi it, moo la ci raw, gën laa jege Sëriñ.
@massambadarousalam9586
@massambadarousalam9586 11 ай бұрын
Maasàllaa amna solo lool.
@doundeuge
@doundeuge 11 ай бұрын
Kouma siye dembal te yallah takh
@taphaaidara2954
@taphaaidara2954 11 ай бұрын
السلام عليكم وبعد، أخبروني كيف أحصل على الورد الخاتم .جزاكم الله
@taphaaidara2954
@taphaaidara2954 11 ай бұрын
Slm kou beugue ame الورد الخاتم nake?
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Bind ma ma boole la ag Ku la ko jox
@terangatv5395
@terangatv5395 10 ай бұрын
Noumay deff ba am Al wirdoul khatim
@moulayendiaye6256
@moulayendiaye6256 11 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@modoungom653
@modoungom653 11 ай бұрын
Ndeysan lou lére réke nga beugue
@dembaniakh4205
@dembaniakh4205 11 ай бұрын
Koumay dimbali thi numéro moustapha diop koki té yalla tah
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Bind ma email ma boole la ak kenn ci jëwriñi daara dji
@serignefaliloundaw2411
@serignefaliloundaw2411 11 ай бұрын
Lii dh souko Serigne Mountakha sou si guidé mouride dina bah lol parce que louy jamono Di geuneu deim mouy geuneu jaxasso yalna jot si lii
@OusmaneSow-nb1bi
@OusmaneSow-nb1bi 11 ай бұрын
Mom serigne Saliou moka diok wird khatim té man bima yor ci Serigne Saliou la diogué té wird kamil
@sindidisindidi801
@sindidisindidi801 11 ай бұрын
Bu dee faj gi nga ciy wax nag, ñi jaamuwul Yàlla sax ñi ngi koy def, loolu du daliil bu wér, ñi yor yeneen ñi ngi def lu leer, dañoo am bàmmeelu biir rekk te amóo ko.
@terangatv5395
@terangatv5395 10 ай бұрын
Wakho fi dara yaw loutakh mano mandou est ce Que yaw lay wakhal
@Faalbualkookii
@Faalbualkookii 11 ай бұрын
الهادي آلى الخير صاحب العمد أطال الله على بقائك بجاه العبد الخديم المكنى بزيا أهل الديوان
@bambiste3040
@bambiste3040 10 ай бұрын
Yokkk yague Wérrr Lou bakh Niornala Loool wax deugue
@bamohamed6152
@bamohamed6152 11 ай бұрын
Akassa
@NdeyeDiakhate-xb5ne
@NdeyeDiakhate-xb5ne 11 ай бұрын
Jazaakumullaau xayran . Damay laathie ndax talxiin binulay defal booy jel wirdi wi ndax loolu faratala ?
@mustafangom23
@mustafangom23 11 ай бұрын
Nono
@khadimseck6841
@khadimseck6841 11 ай бұрын
Dem leen ci sëñ al Hadji Mbacké khaadimoul khadiim
@khadimseck6841
@khadimseck6841 11 ай бұрын
Damadi goné motakh amna Lo khamni doumako mëna léral
@GalsenPureSang
@GalsenPureSang 11 ай бұрын
À 16:30 Mouni ñaari ecole: Ecole S. Modou Lamine Diop ak bane ecole??? Moustapha Diop Koki mooy beneen ecole bi??? 😂😂😂😂😂
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Wawaaw dellou waay la d Ku xamul xamul nag.
@GalsenPureSang
@GalsenPureSang 11 ай бұрын
@@cheikhkandji3002 ku xam it xam na! nama Yàlla musal ci jeul wird ngir ay xeetu "resultats"... loo fi seru na Jaamu Yàlla kepp tax!!
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
@@GalsenPureSang Ndax xalam nga bu baax linga wax. Ndax ku nekk ci aw Yoon doo gis jeexit ja, te doonte taxulaa juk sax, (résultats)yoo yi nak du ludul jeexit ci dox bi. Wahalaykumu salaam
@GalsenPureSang
@GalsenPureSang 11 ай бұрын
@@cheikhkandji3002 jeexit yi deh xanaa sàmmonte ak saarti wird wi kepp doynama man...Ku ci sax soppiku gu rëy dina am ci sa digg ak Sa Boroom. Te sax nag, kuma tegal càllale ci Sëriñ Bi diggante S. Modou Lamine Diop ak S. Kokki mii fa S Modou laa jëm man! Ndax wax deugg moo FEKKEE te itam thieuram fa Sëriñ Bi oumpoul kenn! Na seen jàmm sax 🙏🏾
@sibtoullaminebarra3041
@sibtoullaminebarra3041 3 ай бұрын
deuge dall mom nekhoull
@MoussaNdiaye-o7k
@MoussaNdiaye-o7k 11 ай бұрын
Moustapha Diop dall kham khamou bopam la yoor.gni sén boop ammoul daara rék lamana convaincre.
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Nit ki wàccu waay bimu am jox koko du wàññi ci sa dara ja dara
@moussadiaw1682
@moussadiaw1682 11 ай бұрын
Funu mana amei wirdwi Serigne Bi
@senegalndiaye1128
@senegalndiaye1128 11 ай бұрын
Kan mooy sa Wasilla laaj ko ko
@sibtoullaminebarra3041
@sibtoullaminebarra3041 3 ай бұрын
s Moustapha ap dof akoup nafekh manoula beuge manoula degg mane dé doy gama seukk lo wakh si werd wi moye li wér khamnasi darra Mane mi
@mbayegaye3210
@mbayegaye3210 11 ай бұрын
❤❤
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Yalla nanou Yalla faye awe yiwe nioune niépou.
@MoussaNdiaye-o7k
@MoussaNdiaye-o7k 11 ай бұрын
Billahi ki satané la té dîna léeŕ
@thiernoabiboukante8728
@thiernoabiboukante8728 9 ай бұрын
Niit kou bakh té woyof Bari yeurmandé téléphone rek lakoy dégue wayé day melni danio guissé
@mormbengue8085
@mormbengue8085 11 ай бұрын
Wird wii mom nan laniouko meuna amè?
@kebe3868
@kebe3868 11 ай бұрын
s bi dakoy diokhé
@amarndiaye6186
@amarndiaye6186 11 ай бұрын
Limou wakh dè xam xam la
@mourtadaka4985
@mourtadaka4985 11 ай бұрын
Haataim bi luko gëna woor gisumako
@OusseynouLô-l5j
@OusseynouLô-l5j 11 ай бұрын
السلام عليكم mbokki yi damadoon laathi serigne moustapha diop mii foumou deukk
@abdoulayeseye2693
@abdoulayeseye2693 11 ай бұрын
Touba ci carthié sam Am na dëkk bu tudd pataar wetu jurbel dana fay faral di nekk lu bari
@modoundimbdiop3753
@modoundimbdiop3753 11 ай бұрын
Touba
@modoundimbdiop3753
@modoundimbdiop3753 11 ай бұрын
Patar boo gènn Duola
@PapeDiagne-en1tw
@PapeDiagne-en1tw 11 ай бұрын
Patar après Diourbel son diogué Dakar .après ndoula so diogué touba
@mourtadaka4985
@mourtadaka4985 11 ай бұрын
Akawoor
@s.modoubousso565
@s.modoubousso565 11 ай бұрын
Xafif khatam Kamil Yéppa wérr
@fallmoustapha8588
@fallmoustapha8588 10 ай бұрын
Kouma beug nakh xam xamam
@saliouka6518
@saliouka6518 11 ай бұрын
Akaza Serigne bi wakhtaan wi amatina ndiarigne lool yaggfi lool té wérr . Wakhtaan wii warnanou fékhé S. Mountakha teewlouko
@Muridullaahi
@Muridullaahi 11 ай бұрын
Lolou mom dou wakhi dara Wakh deugg yalla s moustapha tollou neu si dayo bo khamni bou beugué guiss s mountakha dinako guiss pour wakhko lim beuga wakh, wala tmt meun nako bindeu lettre. Wayé kilifeu gou tolou ni mountaxa mom khamnga dou dieulé ay suggestions si ay vidéo etc
@Joorjaañ4444
@Joorjaañ4444 11 ай бұрын
S MOUNTAKHA mofiy BOROM TOUBA 💝 JËRËJËFFF REK kokou moy borom kham kham bou ler bi
@toureserigne9168
@toureserigne9168 11 ай бұрын
La xewoon ba Seydinaa Housmaan defco mouy benn kaamil.
@toureserigne9168
@toureserigne9168 11 ай бұрын
Mbaa dou la xewoon ci alxuraan moo xewaat ci wird wi?
@amadoulaminediop8852
@amadoulaminediop8852 11 ай бұрын
Mouride dou dogou bané li mo were, doga wakh na serigne bi leral,boula tolo fofou danga warona yobou khatim bi lathie serigne mountakha danala thi wakh lou ler.nga doga wakh
@sindidisindidi801
@sindidisindidi801 11 ай бұрын
Sa xalaat rekk ngay wax, waaye demewul nii nga koy waxe, lii debat la mais du xalaati kese.
@moussaniang7994
@moussaniang7994 11 ай бұрын
Lingua wax si xafuiff mom wéroull
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Détracteurs kenn ñàkku ko
@ndiayepape9284
@ndiayepape9284 11 ай бұрын
Tè mom mo feek diamanoy serigne touba kay limou wakh lou wer la te mandouna
@mourtadaka4985
@mourtadaka4985 11 ай бұрын
Yagg filool diop
@bayesalihouthiam
@bayesalihouthiam 11 ай бұрын
jâajëf
@moussaniang7994
@moussaniang7994 11 ай бұрын
Seringe mohadou laminé limou wax moguéna wérr lingual wax
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Wérdou guayou bakh yi dou aye kjalaat,waya dana kouy toukhale thi nioume....
@fallsadio6464
@fallsadio6464 11 ай бұрын
Il faut arrêter ce gars ....thi khassida yi la tambalé legui mou ngi thi wird bi. pour moi môme rek mo djangu Touba
@cheikhkandji3002
@cheikhkandji3002 11 ай бұрын
Murid teggin
@moukhydinembaye8663
@moukhydinembaye8663 11 ай бұрын
❤❤🎉🎉
@syllmordiarra2965
@syllmordiarra2965 11 ай бұрын
Sumay diglou wax dji ci wird Wi damay yeukné sama rouh Dou moromou sama khol ak khel
@khadimsalane816
@khadimsalane816 11 ай бұрын
Wah mom kouko beuga guiss nak fokay fekk?
@elhadjisylla9865
@elhadjisylla9865 11 ай бұрын
Démal patar yonou Diourbel
@aladjiendiaye632
@aladjiendiaye632 11 ай бұрын
Girl yalla numérome la soxla
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Bayil sa numéro fi ñou diokh la béneu ci numéro dieuwrin yi wayé numéro serigne bi mome désou ko diokhé ni rk ndakh diamano mo dokhéwouo nonou
@diengsidy4782
@diengsidy4782 11 ай бұрын
Envoyer ma sa nemorou
@mousyaphaseye1916
@mousyaphaseye1916 11 ай бұрын
Diafe wouta guiss de nioune mo niou don diagal lycce ch modou moustapha mb touba chaque jour dama ko don guisss
@mohoussa
@mohoussa 11 ай бұрын
Problème amatina dii.. Ay fougn dieum
@ousmanelo2170
@ousmanelo2170 11 ай бұрын
Problème mosoul ame ak wouté rék té wouté yag na ci l'islam
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Yaw kay ya am problème waayé li mom lou scientifique la
@papesarr1177
@papesarr1177 11 ай бұрын
Yaw ya am problem
@SerignembackeKa-dt9bu
@SerignembackeKa-dt9bu 11 ай бұрын
Le moy wakh xamna ku
@OusmaneSow-nb1bi
@OusmaneSow-nb1bi 11 ай бұрын
Niet wird yepp werr
@kebe3868
@kebe3868 11 ай бұрын
ه‍ذا ه‍و الورد الخاتم المأخوذ من الله بالرسول الخاتم. limome wérd la
@Muridullaahi
@Muridullaahi 11 ай бұрын
@@kebe3868 bayilen di andi confusion si nitt gni. Lepp wird leu. Yeuffi serigne bi leu té serigne bi lou nekk si mom rekk gnou dieul. Lisi dess nak mooy s moustapha diambar leu lool di sounou soppé wayé fii daf fi dioum si you bari sakh.
@Noru538
@Noru538 11 ай бұрын
Yen eska degg len sr bu dani bi mom wor nako mais waxol ni dafa am yu baxol
@Noru538
@Noru538 11 ай бұрын
Yaw suy def dara nio ni la ndax am na si lou la ler louy wax mom nak dani bii mom am na si lou ma ler
@Muridullaahi
@Muridullaahi 11 ай бұрын
@@Noru538 kou bakh gnoun khamnan s moustapha bou bakh, sounou serigne la sounou soppé leu, waayé limou wakh mooy khafif ak kamil dounou wird waayé hizb lan, khaatam moy wird. Lolou la wakh
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Moume dafa safané wakhdji . Khatame dafa amm loukatakha diouke.
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Louko taxa diouk ??
@papesarr1177
@papesarr1177 11 ай бұрын
Kaay fii wakh loko takha diok kaay leral nomou safané wakh dji
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Man ngi la biré sema mboukou talou béyé niou guana khamate sénn poupou...ta ranié boubokh.
@sidyndiaye4697
@sidyndiaye4697 11 ай бұрын
Teiga demall sabopo tieh seringbi diam mbatt koko
@Baraka-n6r
@Baraka-n6r 11 ай бұрын
Lime wakhné khatam képou mou ame loukhale serign bi loulou dioumla khana.yanén yi guisnan thi loukhale serign bi .
@assalih7969
@assalih7969 11 ай бұрын
Deed dafa wax moom lañ giss degloul bu baax
@SeexunaaSilla-e4g
@SeexunaaSilla-e4g 11 ай бұрын
Wakhoun amoul de bou amé foum né ???
@papesarr1177
@papesarr1177 11 ай бұрын
Bou amé guené ko
@zaydibnhaariss6310
@zaydibnhaariss6310 11 ай бұрын
Thiey koki si polémique rek lay dokh
@DiengMoustapha-jq2bm
@DiengMoustapha-jq2bm 11 ай бұрын
Yaa réew
@mouhamadlaminefaye3596
@mouhamadlaminefaye3596 11 ай бұрын
C pas polémique si khamkham AK gueustou lay dokh
@talibebambarekk5673
@talibebambarekk5673 11 ай бұрын
Kattall sa ndaye yaama touthie salafall ndaye ganane poumikk Kii dafa kasstou addou naam beppou gay dool fii
@xelcomdieexitoumaggni7920
@xelcomdieexitoumaggni7920 10 ай бұрын
❤❤❤❤
@AblayeSeck-e1c
@AblayeSeck-e1c 11 ай бұрын
Machalah ❤❤
@syllmordiarra2965
@syllmordiarra2965 11 ай бұрын
Sumay diglou wax dji ci wird Wi damay yeukné sama rouh Dou moromou sama khol ak khel
Serigne Moustapha Diop Koki : La Mouridiyya à l'aube d'un Siècle
1:40:37
Al Khadimiyyah TV
Рет қаралды 7 М.
Incontestable : Moustapha DIOP Kokki emmène de nouveauté dans le mouridisme .
27:01
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 73 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 691 М.
路飞做的坏事被拆穿了 #路飞#海贼王
00:41
路飞与唐舞桐
Рет қаралды 26 МЛН
Waxtane Serigne Touba Par Serigne Cheikh Touré
46:37
Sadikh Prod
Рет қаралды 12 М.
Tawhidoullah : Serigne Moustapha Diop Koki
43:53
Faydu Akaabiris Saalihiin
Рет қаралды 7 М.
barthélémy ak mairie bi / ministre serigne gueye ak feugg diaay bi
16:53
Serigne Momar Diagne
Рет қаралды 20 М.
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 73 МЛН