Série - Virginité - Saison 1 - Episode 06

  Рет қаралды 33,445

Beuss Bouton

Beuss Bouton

Күн бұрын

Пікірлер: 56
@dodokisamba6031
@dodokisamba6031 Ай бұрын
Li motakh kén wolotoul kén astou nak Lou ndike yay ndiak yaw sa dieukeur soutoureul lah nga wer sa bop Mai mahfousse serie amna sens torop machallah sén ligey raféte nah
@AbdouThiaw-o4i
@AbdouThiaw-o4i Ай бұрын
Astou tu as foutue le bordel tu ne devrais pas partagé ce qui ce passe dans ton mariage mais bon courage kouy seuy danguay mougne madiké yaw mom awma loumay wakh si yaw yeureumal seu sokhna parce que Matadi motakh nou diokhla ko Du coup vraiment vous méritez beaucoup de choses car votre série est très intéressante et c'est ce que la société sénégalaise vécues actuellement 🎉👏👏
@NabyKara-w4l
@NabyKara-w4l Ай бұрын
Louma nekh si série bi moye amoull peub🎉😂
@Laye_critiques_ciné
@Laye_critiques_ciné Ай бұрын
Da wara am pub nak 😂
@KhoudiaNdiaye-p9x
@KhoudiaNdiaye-p9x Ай бұрын
Lolou no si nékh 😂😂😂
@bocarguisse2282
@bocarguisse2282 Ай бұрын
Niaanal lène mou am pub ndakh khaaliss bi dougou mane khawma loutakh dou nguène réfléchir
@FilyDiarra-v6s
@FilyDiarra-v6s Ай бұрын
Commentaires yi mo guene commentaires rou amour brisé Fi commentaire yi dinaniou wakh si série bi Mais commentaire amour brisé yi gafaye dégue ( maylénma jaime , heure bi naniouy dougal serie bi , etc.)😅😂😂😂😂
@Madame1401
@Madame1401 Ай бұрын
Saga yi meuna niak mais serie bi mom Nice
@aramegueye-ox8ff
@aramegueye-ox8ff Ай бұрын
Yall naniou yalla soutoural inch'Allah ❤
@ThiénaDiop-f8o
@ThiénaDiop-f8o Ай бұрын
Allahouma amine 🙏 inchallah
@NdoyeSport
@NdoyeSport Ай бұрын
Merci beaucoup Makhfous ❤️ ❤️ 🎉
@Bassirou123-y2n
@Bassirou123-y2n Ай бұрын
La fille de imam elle est enceinte loumouy wakh wa kogne fatou penses retrouver la bonheur nieuwatte ci malheur thieuy 😢
@BayeBassDieng-y6k
@BayeBassDieng-y6k Ай бұрын
Tay rek bayam diko ray 😢
@AlfaCisee
@AlfaCisee Ай бұрын
Boxe de droit ❤ même jusqu’à 🎉
@ndiayebaye8418
@ndiayebaye8418 Ай бұрын
Wahe degue yalla mangi don sétane mou néhe lo ta am chance mai bisi saga yi dougée la arété série loum néhe néhe bou amé réwandé rék yahe ko wahe degue yalla arété na sétan bi ngén balma nak
@NdeyependaGueye-m9g
@NdeyependaGueye-m9g Ай бұрын
Meilleurs série du moment 🥰 machallah
@bocarguisse2282
@bocarguisse2282 Ай бұрын
Yaw fo dème ni meilleure série
@gayearona5649
@gayearona5649 Ай бұрын
Merci beaucoup pour makhfouss
@SerigneFallouSyll-t7r
@SerigneFallouSyll-t7r Ай бұрын
Mahfouz longue métrage lagne soxna 30 min maximum
@AbdoulayeBob-ey3lv
@AbdoulayeBob-ey3lv Ай бұрын
vrmnt🥰
@aissatoutraore2203
@aissatoutraore2203 Ай бұрын
Vraiment theatre bi amna sens djiguénes boukko sétane dina tax nga gueune teh sa bopou té béne goor boumou tax nga assalo sa bopou ak lépp loumela meunti promettre djiguénes amoul loudoul bopam donc sama mbokk djiguénes yii nagnekko rahass dinthi ba guiss biss bou raffétte ak situation bo meunti am boumou tax nga dioxé ko ❌❌❌
@ThiénaDiop-f8o
@ThiénaDiop-f8o Ай бұрын
Bilahi walahi watalahi DEUG bou wëurr 😢
@mamydarry1317
@mamydarry1317 Ай бұрын
Machallah li dafa nékh trop ❤❤❤
@SaliouDiop-ix9um
@SaliouDiop-ix9um Ай бұрын
Pourtant gore you bakh amna way
@aminata3897
@aminata3897 Ай бұрын
Astou c’est bien fait pour toi Nga am dieukeur boula soutoural ba paré ngay dem di wakhi sa secret kénéne 😢 Yokal léne gnou minutes yi way😭on veut 30 minutes de série minutes
@mustafaasamb8419
@mustafaasamb8419 Ай бұрын
Dof rekk.
@ThiénaDiop-f8o
@ThiénaDiop-f8o Ай бұрын
Astou Kay daffa wéré rék
@MatiNdiaye-u4z
@MatiNdiaye-u4z Ай бұрын
Mamy elle joue bien son rôle
@dodokisamba6031
@dodokisamba6031 Ай бұрын
Oui mamy est une grande actrice machallah
@elhadjiyoussouphdiatta2810
@elhadjiyoussouphdiatta2810 Ай бұрын
😂😂LOUTAH DOMOU IMAM YI DEUNG ,MOUY GOR WALA DJIGUÉN,, J'AVAIS UN AMIS DE FILS D'IMAM TRES PIEUX MAIS 😂😂😂 DOMÉRAM BOU MAG ,, DIL,, 😂😂RÉK
@awatoure5056
@awatoure5056 Ай бұрын
Loulou kay louma yemm la beug goor ak beug djiguenn
@ThiénaDiop-f8o
@ThiénaDiop-f8o Ай бұрын
​@@awatoure5056DEUG bou wëurr mais boul fatté sa papa done imam wala sa Yaye done ya séyda takhoul nga mélni niom boul fatté kou nékkak sa djikko nitte gni Kay nion yorr sén djikko boppam rék 😢 motakh yalnaniou yalla saamal boppam allahouma amine 🙏
@AlfaCisee
@AlfaCisee Ай бұрын
Bc❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤ hui dans les années précédentes les contre 🆚 est très difficile pour les gens
@MamefamaThioune
@MamefamaThioune Ай бұрын
Nn li moy adouna ko wollou rek amna kom wollou sa coussins bi ndak dafa nobate rk😂😂
@khadidiatoundiaye3120
@khadidiatoundiaye3120 Ай бұрын
Doul kate la Kaye
@aissatoutraore2203
@aissatoutraore2203 Ай бұрын
Theatre bi beurry na loussi nitte meune diangatte deh vraiment ah mane deh diangue nassi you beurry , djiguénes dafaye teh laminiam ak loumou meunti done car Astou lolou mokko yoobbé lii yeupo boukko waxoul wone cousine bi kone kénéne doukko xamal , djiguénes meune na diouddou sans ndaww c bizarre ms mo dall Astou car guiss nani kou teh bopam la ms elle est nait cmm ça , amna niouyy dioxé séne ndaw ndax kou goor ki dafléni digueul takk mouyy domou Imam bi mome damako tégué neullé car nitte boula beugué na déff farata bala mo xam lo woddo et enfin amna niouyy dioxé séne ndaw ndax sohla genre danio nékk si situations cmm lou dall kou djiguénes ki mame dji fêbare mou dadjé vautour bobou déff ko loumkay déff baayi ko mou dém té au final dieurinioul dra car Mame dji dead na Dou guiss ngénes exemple you nékk si série bi yeupp donc sama mbokkou djiguénes yi nagne am foula si souniou bopou teh xamni goor boula beugue doula meusse ladj sa bopou wa salam...merci Mahfouss❤
@aramegueye-ox8ff
@aramegueye-ox8ff Ай бұрын
Merci beaucoup wakh nga lépou
@ThiénaDiop-f8o
@ThiénaDiop-f8o Ай бұрын
Bilahi walahi wakh nga DEUG
@MamouneDiop-mw4vw
@MamouneDiop-mw4vw Ай бұрын
Hum pas de cas li louy nékhi la dh 😅❤ quelle série 🎉
@BebeaichaSowathiaaa-ie9pt
@BebeaichaSowathiaaa-ie9pt Ай бұрын
Machallah amna solo
@FilyDiarra-v6s
@FilyDiarra-v6s Ай бұрын
Série bi gawna diékh
@SerigneFallouSyll-t7r
@SerigneFallouSyll-t7r Ай бұрын
Une nouvelle aventure
@AbdouSamb-y3b
@AbdouSamb-y3b Ай бұрын
Ma sœur di courage
@AbdouSamb-y3b
@AbdouSamb-y3b Ай бұрын
Super ma dikke
@BebeaichaSowathiaaa-ie9pt
@BebeaichaSowathiaaa-ie9pt Ай бұрын
Yokaleun minutes yi slp
@FatouSarr-r1u
@FatouSarr-r1u Ай бұрын
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@maymounagueye7249
@maymounagueye7249 Ай бұрын
Apprenez à vous taire
@khadydiop5903
@khadydiop5903 Ай бұрын
Vraiment
@NogayeNiang-wp9vr
@NogayeNiang-wp9vr Ай бұрын
❤❤❤
@ligueeytekki
@ligueeytekki Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@BarraMbacke-y6s
@BarraMbacke-y6s Ай бұрын
🎉🎉🎉🎉🎉
@AbdouSamb-y3b
@AbdouSamb-y3b Ай бұрын
??
@BandiaDanny
@BandiaDanny Ай бұрын
❤❤❤❤❤
@tchatcheur_ms6840
@tchatcheur_ms6840 Ай бұрын
❤️❤️❤️
Série - Virginité - Saison 1 - Episode 07
15:30
Beuss Bouton
Рет қаралды 32 М.
Série - Mirage- Episode 110
44:49
Khar Media
Рет қаралды 236 М.
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН
Quilt Challenge, No Skills, Just Luck#Funnyfamily #Partygames #Funny
00:32
Family Games Media
Рет қаралды 55 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 30
35:58
Yesdakar
Рет қаралды 555 М.
PROMESSE Épisode 2
10:25
diante gui family
Рет қаралды 609
COURT MÉTRAGE - FATIMA UN MARIAGE SANS CONSENSUS
25:56
WEST AFRICA SN PRODUCTION
Рет қаралды 97 М.
Djirime
22:25
pencum afrique
Рет қаралды 4,9 М.
Béén Milliardaire bouy Goumba goumba lou pour khol Sokhna sou Bakh Chapitre 2
19:50
Histoire en Wolof Sénégal
Рет қаралды 40 М.
Série - Virginité - Saison 1 - Episode 09
17:23
Beuss Bouton
Рет қаралды 29 М.
ROKHAYA- Saison 1 - Episode 9 **VOSTFR**
28:22
Yadaaké tv international
Рет қаралды 30 М.
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН