Quand tu es discipliné tout le monde t'aime. Nous sommes tous fan de la bonne éducation. Merci Sathies
@papesoumaАй бұрын
Walay ndeysane
@TireurDElite693527 күн бұрын
J’suis FAN de Mod’lô 💯/💯 après lui je supporte SATHIÉS. Il est clean, calme, serein et posé. C’est le même style avec Mod’lô dans la bagarrre, côté gabarit et la même taille . Je suis convaincu que c’est le seul qui peut détrôner le roi des arènes👑 VIVEMENT Mod’lô 😍🙌🏾 Sa Thiés💯🫶🏾❤️
@BHB5TVАй бұрын
Kou d'accord sathiés ak modou lo lalal j'aime ❤❤❤❤❤❤
@amadousow6391Ай бұрын
Combat du siecle
@ousmaneba8733Ай бұрын
Sathies douniou sa morom demal si boye niang
@BarhammDioufyАй бұрын
Modou lo 100% laa bilhy mais yaŵw momm mbeur ngaa téé kouye beurékk yaww dina nekh do daww téé do soul ndanane bilay yakk modou dinna nehh troppe walayyy 😊
@SalesmarketingPrimsАй бұрын
Torop sakh
@AminataDIOUF-ez8kdАй бұрын
Bilahi trop
@papitogueye2767Ай бұрын
Walahi modou lo moy sama mbeur mais sou bayei lamb sathies lay supporter
@AbabacarKeita-cs8rmАй бұрын
Fans modou 1000% la ,mais sa thies franchement damako yénné ❤bonne continuation SA
@ndiayemohamedrassoul-hb4miАй бұрын
Kone beugue ga Sa thies dane Modou Lo avec ça nguani Fans Modou nga no way
@FallouLo-d1rАй бұрын
No da beugeu wakhni yènèna sa beurè ak modou @@ndiayemohamedrassoul-hb4mi
@Bayeniang20Ай бұрын
@@ndiayemohamedrassoul-hb4mi😂😂no way
@papesoumaАй бұрын
Danga bakh rek
@bassdiokhane1472Ай бұрын
Merci
@DyssiFamilyАй бұрын
Il communique bien et il est très respectueux bilayy Sa Thies
@mordiakhate4260Ай бұрын
Aka yaro champion la
@papaibrahimaseck1003Ай бұрын
Nous supporters de modou lo nous sommes d'accord pour ce combat car sathies ndanane
@assanediakhate3507Ай бұрын
Un lutteur posé discipliné intelligent bonne communication,,,je suis eumeu séne
@cheikhngome1456Ай бұрын
saliou sakhou yalna yalla défal la Diam kou bakh ndeysane te amé talibe ❤
@Bakelsen99Ай бұрын
❤SAKHO 🇸🇳❤
@papeomardiagne8201Ай бұрын
En tant que supporter Modou lo Mayla chance sax moma geunal boy yi beuri wax yii bilahi 🫶 yénénako Modou mayko chance ❤
@galaxiepro.5641Ай бұрын
tout le monde yené naniouko modou lo mayko chance
@Rassoul__Moustapha07Ай бұрын
Je suis fans MØDOU LÔ Ms Sa Thiès kou yaarou walahi depuis keur massar ba lgui magui Kay topp Ms cette foi si mok Modou Lô Bi mom doumako meuneu faral vrement kou bakh
@FallouGalss-j8rАй бұрын
bilahi modou lo sa thies mom combat doko dakh bilahi niari gor yalla la té dongou yakh biss inchallah niepa ngi khar combat bi ❤❤❤
@NdiayeMamechekh29 күн бұрын
Wawaw vraiment sa mom dou daw s'il te plaît modou dieuleul sa gnoune sa fans yi beugeu nagnou bilahi
@MouhamedmoustaphaSeckThiamАй бұрын
un Lutteur trés Correct . Qu’Allah veille sur lui .
@papesoumaАй бұрын
Amine
@babacar3178Ай бұрын
Sa thiés dama ame si mom amour trop
@assanefall4111Ай бұрын
Sa thies bilae tu peux battre Modou lo yokal sa rapidité ak sa force. bonne continuation mbeur kou yarou nga
@dethiediouf5019Ай бұрын
Sa damaka méré trop dafa eupeul
@Mame_Da-lelionАй бұрын
Blh eupeul rk lay dioy si mom sinon Kein manouko
@sunrise358528 күн бұрын
Tu as oublié qu'il n'a même pas capable de battre Eumeu sene
@AbdoulkhadirBahАй бұрын
Sa thiés est le plus poli de Luther donne-lui son sens contre le roi des arènes. Je suis sûre que c’est le seul qui pourra faire tomber modou lo
@sambakante8724Ай бұрын
je suis fans de Modou mais j’aime Salif ♥️✅
@MouhamedMbow-e5yАй бұрын
Sa thies future roi des arènes ❤
@kawoudiallo7946Ай бұрын
Très poli je suis modou lo mais ce petit mérite le roi des arènes
Modou repose toi 1ans 3 combats 3victoire felicitation champion 🎉🥰💯
@galaxiepro.5641Ай бұрын
wallahi
@Domou_Deukk_BiАй бұрын
Meunoufi reposer loumou reposer woule wone tokna plus d'un an beuré woule bayilén séne yeufou tiakhane yii lamb dou sale de massage
@ndiayeousseynou830629 күн бұрын
Modou di liguéy nganann nopalou thi ay millions 😂
@galaxiepro.564129 күн бұрын
@@ndiayeousseynou8306 ligueye tamite da am nopalou congé dafa am si ligueye
@tallandiaye9108Ай бұрын
Modou mayal chance sa thies
@MamadouNiang-rg1cnАй бұрын
Billahi man fans modou lo la wayé sathiés daf ma nékh deugue rék lay wakh yalla nala yalla déffal diamou champion ❤
@moussapayemane4167Ай бұрын
SA yow rék ya meuna fréné Modou Lo si boyi 💪💪
@ronaldgomis2791Ай бұрын
Tu rêves.
@ModoufalyАй бұрын
Mdr 😂
@fodetoure8740Ай бұрын
Merci
@hamidoutall9134Ай бұрын
Sa Thiès beugue na Modou Lo may ko Chance mais Modou moko meune fouff
@yacinetoure-TY29 күн бұрын
Kou manaloul dra boy yi dina manal dra modou lo
@famadrame3130Ай бұрын
Sa yalnala yalla defal diam yokla soutra yagu modou lo combat bou nekhla❤❤❤
@IbrahimdialloIbrahimdiallo-z7wАй бұрын
Sa thies modou moy combats bi❤❤
@MomoDieye-j6sАй бұрын
Sa thies vs modou lo combat leu dina nêxe lolou . Bou bobaa modou nak digua ame combat ndaxe sa thies dou yoyou boy yoyou rek . Mai wayè yallah mii mayè gnogui coye gnane mou may ndameli modou lo inecha'allah
@cheikhouseck3292Ай бұрын
Ya yarou sathies bilay iow mom beug na nga donn roi dsns future 😊
@falloundiaye4285Ай бұрын
Sa thies nak yaw senegal yepa la beug ndakh sa yarou me nk sa Palmers khawna doywar toti si modou lo lay depander me nak nala modou may ndakh merite ngako machallah big respect
@MansourDiop-wd2orАй бұрын
Palmarès sa Thiès mon guen bou Siteu sa 3 défaite rk la am 15 victoire Siteu amna 6 défaite victoire yi matoul sax 13
@DemecheikhououmarАй бұрын
Lambe bakhoul deugue @@MansourDiop-wd2or
@YatmaFall-d5hАй бұрын
Ki dane siteu dane reug reug guay waxe ay palmarès
@alamine803Ай бұрын
12 v @@MansourDiop-wd2or
@MansourDiop-wd2orАй бұрын
@@alamine803 wa guiss gua
@anddieuf3960Ай бұрын
Kou tek ci sa thies besseul jaime👍💯❤️
@MoustaphaFall-zy8moАй бұрын
Merci sathiés contane ci yaw Ms kén döû modou lo ❤
@madembatoure7005Ай бұрын
Modou sou bayiwoul dinala may chance inchalla modou bayinala xel bou yague
@DethieDioufFisselАй бұрын
Vraiment tu mérite roi des arène parce que tu est discipliné❤❤❤❤❤bonne chance
@nogayeniang9119Ай бұрын
Yalla na takhaw sa thies ak modou lo
@PatriotepourtoujoursАй бұрын
Salif rek la ñouy toppou inchalla dina bakh
@MaremeDieng-l6tАй бұрын
No yawe mome degne la yenne roi des arènes dégua ya yarou am discipline yawe lep guay am inchallah
@bassdiokhane1472Ай бұрын
Merci sa Thiès yall nala yalla takhwou dé fall la Rio
@ModoufalyАй бұрын
En tant que fans de Modou lo je sais que ni Modou mo meun Sathies mais j’aime Sathies parce qu’il communique bien 👍
@AzizDramé-q4jАй бұрын
Sa Xalat nga wakh n'a combat bi takhaw
@papadiom9260Ай бұрын
Tambali ngene 😂 Li ngene done wakh thi Siteu gneuw Siteu gnous ko 😂😂😂😂
@touremamecheikh9737Ай бұрын
Aythio saam mbeur bii❤❤yokal entraînement yi rk lisi kanam moy dakk nanou modou may chance mérité naneko
@dimodbass9280Ай бұрын
Combat leu 🎉❤ mod'lo sa thies 😂
@azizngomАй бұрын
Sa Thiès machallah sénégalais yi beug naniou la trop nakh témoignage yi raffet na trop yokal gor gorlou et bonne continuation
@MaimounaNiang-zu1voАй бұрын
Ya yarou nak masha'Allah rakkou empreur bi❤
@AbdelKader-kt7zjАй бұрын
Regardez sa manière de communication kii mo poli barki yalla❤ 8:15
@moustaphafall9494Ай бұрын
Merci sa ❤❤je supporte modou Lo mais beugg na mou mayla chance
@nogayeniang9119Ай бұрын
Sama mbeur me daye diaye Combat tá dou wakh Lou niaw bilakhe yaw rek laye topou mane❤
@mamadouseydougueye1696Ай бұрын
J'aime sa thies
@papemalickmbayendoye9341Ай бұрын
Sa Thiès jolie ❤
@kurayahmiАй бұрын
*Magui guiss fans Modou yi di wakh combat bi legn beugue mais def leine ndank. Sa Thies ci défaite leiu diougué teh meussoul teglé 2 defaites. En plus Modou est fatigué. Il a fait 3 combats en 1an, pour son age c'est difficile. Souma senione mou nopalou benia dieul avance beu saison prochaine, Sa Thies ak Tapha Tine beuré, kouci daan Modou dieul ko*
@lesankariste8721Ай бұрын
Khana modou 10 and la magué sa thies
@mbackeseye7178Ай бұрын
Mé modou lo si défaite la dioguéwaune nioudiokh gua eumeu séne mou dieul roi bi
@kurayahmiАй бұрын
@ non. Modou bimiy dieul avance Eumeu Sene bobou beuré goul ak Balla. Mais gars yi danio bayi beu combat bi dialeu niou annoncer ko
@papadiom9260Ай бұрын
Bayil Nafekh Modou lo thi défaite la djouguer wone bako Eumeu di maay CHANCE !!! Balla dafko Djoutal Eumeu taalal ko combat royal 😅
@nafisene5335Ай бұрын
@@papadiom9260Yow mome louma la beugue wakh xepp ko, Yow sonoulo ci begn bi nga begn modou Lo. Ki lou mou la def? Metiwoul ci Niit nga begn kou la defoul dara ak kou la xamoul? Mais nak ko indi daan n’a ko motakh meuno ko beugue ndeyssane. Mougneul mon cher
Yalnako haragn may chance vraiment dama yééné mou beuré combat royal il a une bonne palmarès en plus il est discipline
@legauchedione263Ай бұрын
Sa Thiès vraiment da am Yar trop 🎉 est ne change surtout pas champion
@mormboup9301Ай бұрын
Graisse bi bari
@abdoulayegassama8971Ай бұрын
il communique très bien
@Adam-gz5btАй бұрын
Il communique très bien🔥
@gueyeserigne-mv5ppАй бұрын
mane modou la mais sa dafa bakh lolou moum comba bou nekh la machalla ❤❤❤
@GoraMbengue-f2jАй бұрын
Sa thies ioe moom dinagne mayy chance inshallah kou yarrou nga vraiment
@ousseynoutoure518Ай бұрын
Yw mbeur nga nieuweul niou danla champion❤
@nianggallass6826Ай бұрын
Mane ki dou sama mbeur mais dafa deugou koi bravo mbeur
@BoubacarDiop-q2pАй бұрын
Champion grand lirou mougui si forme dhé
@moustaphafall9494Ай бұрын
Bilahi MODOU Lo dala wara may chance
@laminedia1768Ай бұрын
Modou. Biss mboh dieulè Sathies , danou.
@tallandiaye9108Ай бұрын
Combat bou nekh lay don incha alla
@ndakarudialdiop1206Ай бұрын
Aka meuneu dane modou lo bilay champion leu Sathies ❤
@AdamaMballo-t9sАй бұрын
Merci sa thies
@MakkaDiagne-mk1jvАй бұрын
Combat bu nara nekh lay don dh ms Modou Lo mola meune fouff nk💪👑
@libasselahiАй бұрын
Franchement mérité nga combat royal 🤞🏾
@AdamaMballo-t9sАй бұрын
Bravo Éric Favre
@mbackediagne4667Ай бұрын
Modou seul mais sa yalna nga am diamou kou yarou nga
@saliousagna8922Ай бұрын
Sathies Modou combat éclair..je vous assure
@ThioroFall-s8hАй бұрын
Sa thies mérite combat royale 👑 modou lo mayko si chance yi
@volfroitfall8785Ай бұрын
Yalla nala Modou mayy chance dagua yarou
@BABACAR-l2eАй бұрын
Modou na nopalékou défarou lamb ji sakh none yikoy xéx gnoko beug taxawal pour mou gnakk couronne bi je ne suis po contre sa thiés kou yarrou la meun beurré té daffay entrainé bou baxx mais souma nékone Modou lo catchet 500millions laye ladj sa thiés lale 150millions jahjeuf👍👌🙏
@karbafaye979629 күн бұрын
Louné meune nako am si Lamb nguir dafa yarou et il exprime bien. Go Saa❤
@birametraore6100Ай бұрын
Modou lo à vie sa thies rek la yenner niou mayko chance yarou bakh dall yalna combat bi takhaw Incha allah modou lô danne ko
@LibasseBa-c6uАй бұрын
Champion Future roi 👑 inshalla 💪💪💪💪❤❤❤❤❤✅✅✅✅✅
@RossellaRussottiАй бұрын
Modou bou soubé yallah Dina la may chance nakh nitt geunou kou bax nga kou degou nga mérité nga modou mayla chance❤
@nganimaАй бұрын
Bouko Modou Lô mayé chance moune neu am surprise dé
@daoud2760Ай бұрын
Sa Thiès rek ❤❤
@bintouwade172918 күн бұрын
Sa Thiès seul ❤❤❤
@Bakelsen99Ай бұрын
Salif ❤léguii amoto fite mais ont t'aime bi1 boy salif yawe ak eumeu dirige tes combat frère siguéwebii
@OusseynouNdiaye-t7vАй бұрын
Sathies futur roi des arènes 🤲🤲🤲
@bintouka8923Ай бұрын
Je suis de GDW mais Sathies faudra t'entrainer très dur en bagarre et lutte pour battre Modou Lo je te conseille d'aller à insep pour te prèparer ah wa baxna 😅
@Omarsane7491Ай бұрын
Nous les fans de modou lo on reclame sa thies bilahi combat laa
@CamaraJibril-c3bАй бұрын
Bilahh sa Thiès dafa am respect si nieup
@MousséGningue-n9bАй бұрын
Bilahi sa wahna deugeu siteu d'à beugeu lou yombe trop
@arfangboubayesakhirndiaye4270Ай бұрын
Nn bilae j'aime la personne de sathies
@papemalickmbayendoye9341Ай бұрын
Je supporte Modou lo mes beug n'a sa Thiès trop
@sowoumartalla8507Ай бұрын
sa thies mo dakeu communiqué si lamb dji bilahi
@papadiom9260Ай бұрын
WAKH DEUG YALLAH TAPHA TINE MOLA GEUNA MÉRITER ROI mais KOU YAROU NGA YENER NA LA COURONNE BI 👑
@OumarDiallo-p7mАй бұрын
Moudou Lo ❤❤cofierme ❤❤le roi
@ndendethiam5896Ай бұрын
Très discipliné et posé ….❤
@DameMbaye-ps2woАй бұрын
Merci sathiés ❤❤
@layeciss7674Ай бұрын
Je suis supporter mod lo mais mom sa Thiès combat bouneh siteu tapet la
@nganimaАй бұрын
Siteu Modou Lô kou dém ardo
@papadiom9260Ай бұрын
Siteu dafa nious Ya Ouztaz nangou lene
@bokkebene56Ай бұрын
Sa thiés vs modou lo combat du siécle
@zora3115Ай бұрын
Mane mom modou lo la mais d'accord na sur son combat contre sa thies
@ycamara9034Ай бұрын
Yes Sa thies vs Modou lo 👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍💪🌍👍✌️
@anddieuf3960Ай бұрын
Non combat bou nekh modou sa thies ❤❤❤
@moustaphadiouf9154Ай бұрын
Sathies modoi lo Dernier combat modou lo sur la lutte