SADIO NDIAYE, LE FAUX LIONS « SIMB » se confie: Comment je suis devenu Modou Modou "Sama Jaabar Meussoul Doug Fimay Soolo"
Пікірлер: 518
@papacheikhmbaye81974 жыл бұрын
Père Sadio kou bakh tei oyof bama nieukei wathie italie d moma dalal aka bakh tei beug nitt goud fan ak weer rk père ❤️❤️
@badarafaye92484 жыл бұрын
wa papa cheikh nam nala si lo nk
@papacheikhmbaye81974 жыл бұрын
@@badarafaye9248 malaraw ban badara la sakh di 🤔
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Papa yaw ya bakh rekk ana Banda
@badarafaye92484 жыл бұрын
baye badou kharitou pape mbaye
@badarafaye92483 жыл бұрын
@@papacheikhmbaye8197 baye badou rak moustapha tambedou
@sowmouhamad94764 жыл бұрын
Je suis fière de Sadio. Ils est parmis les plus Bravo, kou ame dignité
@oulimatadiop93004 жыл бұрын
Sadio avec sadio jusqu'à la mort ndeysan nékhone n'a trop😘😘
@roselafleur55944 жыл бұрын
Bilay 🥰
@mouhamatsy75514 жыл бұрын
Lou yague lol
@maguidiallo52544 жыл бұрын
Wawaw lima daw simbe 🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️bilahi Mo takh ma nék mularde daw diangue dém simbe nioumal dorr rek ta douma bayi🤦🏽♀️😂
@birahimfall5054 жыл бұрын
Yaw do gone bilaye sadio avec sadio rek non Lima daki
@mouhamatsy75514 жыл бұрын
@@birahimfall505 Hihih
@fatoundao57234 жыл бұрын
Manshallah tonton Sadio Ndiaye «Le grand Lion», un Grand monument pour la culture sénégalaise, yalna yalla guoudal sa fann, mayla werrgue yaram boubeuri...
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Amine Fatou Ndao tè niou bokeko
@Diomaye-Sonko4 жыл бұрын
Sadio mi moma seuleumone kani bima bourlé bania dieunde ticket🥺c’est la première fois que je te vois sans ton déguisement🥳 Sadio avec Sadio jusqu’à la mort 😂
Oh le grand sadio Ndiaye 😭😭tu nous as fait vivre un moment de ouf 💥💥💥💥 bilahi
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Loumene bi
@laurenternesttendeng58234 жыл бұрын
Sadio etait mon idole et je faisais le simb gainde à Ziguinchor il y a des annees big respect avec lemzo Diamono
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Laurent
@assanediop22104 жыл бұрын
Présentatrice il faut présenter t'on invité en introduction c'est très important sinon émission bi amna solo Sadio me rappelle une partie de mon enfance Ndeysaan.
@roselafleur55944 жыл бұрын
D'accord inchallah
@assanediop22104 жыл бұрын
@@roselafleur5594 bégué nékal si jamm
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Amna solo
@assanediop22104 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 merci mes respects amal jamm rek
@mamadoulaminediaby50914 жыл бұрын
Oh je me rappelle en 1996 quand un de mes potes imitait Sadio c'était génial goudeul fann père et respect à la journaliste très professionnelle elle pose des questions pertinentes 🙏🙏🙏🙏
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Mamadou beguè
@alioudiagne7674 жыл бұрын
Année de ma naissance 😬😬😢 Ay yallah minu sàkk...
@cissefatou40884 жыл бұрын
Ndeysane c'est lui le fameux sadio , sadio avec sadio jusqu'a la mort tellement on a chantonné cette chanson sans jamais le voir... goudal fane sadio
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Cisse Fatou
@djibisy13204 жыл бұрын
Ok marqué gua sougn Enfance ndaysane Diamoy takkanté yéré sou Gaïndé nieuwé niou daw sou diap Di âme yén niar nieup lay diap oh xalé yi légui fowouniou
@rassoulndiaye59864 жыл бұрын
Bilay portable lagnouy foyè gosse yi lègui...
@mouhassmoura95644 жыл бұрын
bilaye khaleyi portable rék sadio rakhan nekhona
@Focus_2k244 жыл бұрын
Yaw do gonè dh😇
@djibisy13204 жыл бұрын
@@Focus_2k24 no même pas Sax
@Focus_2k244 жыл бұрын
@@djibisy1320 bilahi fall lolou diar nasi mais masou mako niémé nak
@fatoudieye80464 жыл бұрын
Masha Allah Sadio Ndiaye mon frère mon ami, nite kou digne, marqué nga sa emprunte si art bi, foule ak fayda yalla na sa diam yague ❤️❤️❤️
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Fatou Dieye borom yaye diou bakh dji
@cheikhbi20564 жыл бұрын
Longue vie à toi Père Sadio. Légende Vivante
@fatougueye78564 жыл бұрын
Mn grand sadio Ndiaye yalla n'a sa diam yague 💕💕💕
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Fatou Gueye merci
@khadijadiatta84124 жыл бұрын
Sadio avec Sadio jusqu'à la mort😀😀😀😀😀
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Khadija
@yanouzaydiop424 жыл бұрын
Je t'ai suivit une fois à mbour Diamaguëne et aussi à Mbacké Élevage........ Jajëf grand sadio
@benassanegueye28594 жыл бұрын
Mais journaliste dafa am yare té dafa professionnel...bon continuation..👌👌👌
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Ben Assane Gueye merci
@ahmadoudiop50164 жыл бұрын
Machallah père amena solo simb kate dafa wara di entrainé ame une belle forme , ame argne , di sol lou rafet, di danse lou nekh ame bayré, ame ngalathh fo woté mou fess
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Bilay dafa lèrr
@khoudiadjittebillaymanemar77794 жыл бұрын
Hiiîiiii sadio kouma ragalone té meussou mako guiss🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀🤦🏾♀
@alassanendiaye30894 жыл бұрын
🙏🙏
@christinediedhiou87054 жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@boycasa81254 жыл бұрын
😅😅😅😅😅
@yacinethiam75784 жыл бұрын
Et moi aussi
@mamadoudiop92694 жыл бұрын
Barry nguathi morrom 😅😅
@khasimidia97344 жыл бұрын
Ndeysen bimay khallé damako ragalon Sadio ndiaye ibou diange aya kane khabane pape ngome Pikine nekhon na❤🙏
Nityi bilahi beugue nagnou mais legui febar yi mo barer nit day tiit crise wola nga kheutko mou kheum nga am gaathier faik dou woone sa intention. Lolou rek mo takh gayi ragal diko terer.
@keitasidy71974 жыл бұрын
Nice na Pierre sadio sa wakhe rafétena
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci fils sidy keita
@ousainoukeita62064 жыл бұрын
je si figere sadio bon mèsaje et bon cosege pour tou. les senegales mersi papa sadio
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Ousainou keita c gentille
@pendafall48454 жыл бұрын
Machalla tonton long à toi ❤️♥️ diapel sama djikar pour mou gniew Italie svp🙏🙏
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Pendant fall ya bakh
@pendafall48454 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 tonton diapale gniou ta yalla takhe
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Inchalla Penda
@mborodijolof6844 жыл бұрын
Pere wa linguere jolof ,se souviennent bien d t séance d simb , longue vie...
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Viyeboydo meci lou bari
@demahoumlayd4 жыл бұрын
Ki il a le simb dans le sang. Da nirou Gaïndé sakh. Il vit son art.
@modadieng98864 жыл бұрын
C vre sadio kou bakh bokounanou tourné Norvège hollande Danemark kou meune loumouye dèf yanala yalla takhawou
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Moda ya bakh
@FatouDiop-ne7dq4 жыл бұрын
Sadio,auto rail, Baye Diop ak Ndongo Beye Toth nan thiaroye sur mer.surtout Ndongo Beye sounou fierté chaque année mou nieuw bégueule niou yalnako yalla tahawou
@toubandiaye45434 жыл бұрын
Lima métti rék moy simb yoyou amoul vidéo
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Bilay tu a raison
@selimselime69384 жыл бұрын
lima geunon nekh moye bou simb tasse gayi di touch nga fans sadio nak bou waniasso tek si khiralou gainde bi khum khum reck nga beg papa amouniou sa fey begeul nganiou nioun nieup
@ramatambow77424 жыл бұрын
Machallah grand Lion
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci a tout le monde conetanena si yene yalnalène yalla faye
@gassndoye67124 жыл бұрын
Sadio borom mboro
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci
@biranendiaye95844 жыл бұрын
Vraiment simb nek naa art bo khamni nieupako beugue daffa nekh tellement que daay takh khalei yii du divertirou bou bakh... nane ko dékilatt waay.... walla niou bayii mou soukhh ????🤷
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Birame Ndiaye ya bakh
@aissatousarr68064 жыл бұрын
Deysanne Sadio pape ngom ibou diagne aya kane. Khabbane ,😂😂😂😂😂hoo simb nekhon naa ana wa pikine wayy🏃🏃🏃🏃
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Wawawww
@jilzopido4 жыл бұрын
Ndeyssane aissatou yanguimay fatali pikine. J’habitais à icotaf oh c’était tro nekh
@aissatousarr68064 жыл бұрын
@@jilzopido moi j'habitais cité icotaf 1 koniou makha bass
@jilzopido4 жыл бұрын
@@aissatousarr6806 ah ok moi kognou gnom eumeu sene mame bassine e consor près du marché dimanche
@minajoli3134 жыл бұрын
Guenno len ma dekk pikine gainde fatma la diague dem Sadika sath maggo
@byefalln64434 жыл бұрын
Sadio waholep bene côté rek lawah!!!!
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci bayfall
@tupac63454 жыл бұрын
Sadio un jour tu avais attrapé un des grands frères 🎊🎉🎉🇸🇳🇸🇳🇸🇳🤣🤣
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci A Ndiaye
@xamsadine48564 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 vous mavez attrapé a pikinr
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
A bon balma dh
@ndiayeadama53174 жыл бұрын
Macha Allah père sadio Ndiaye yalna yala doli takhawou
@jamesgueye74164 жыл бұрын
Machalla dembe nekhonna waye sadio ndiaye ak pape ngom derbi la wone me man sadio la beugone ak ame diop ak gangne me sa waye dama menon daw bilahi gainde mousoma diap te douma sori geuw bi ak simbe fallou ndiaye march same geudiawaye no sa waye sama for daw la won bilahi sadio avec sadio jouska la mor nekhon na waye boy yi fowou niou waye diame si yaw sadio me ani ame Diop mo dane nekhal simbe sadio
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
James ya bakh
@jamesgueye74164 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 merci grande
@ahmadoudiop50164 жыл бұрын
@@jamesgueye7416 wa ndananebi ame mouguifi deh legui boko guissé doko khamé il a bcp changé mai naka fofu
@jamesgueye74164 жыл бұрын
@@ahmadoudiop5016 diop nakala boy simbe dadiio rek louma geunon nekh gainde bou mak bi sadio bou solo baye tew si geuw bi nekhon na bilahi bou timiss diote waye katyi diko waye mane beugeu na si ala sadio sama gaind ame diop di fethei lou nekh waye grand beugal gen niou bilahi goude len fane way aka beuge seringe masour sy borom daradji me li sadio wakh yep deuge la nit kou bakh ta diamono yoyou kouy simbe gayi daniou nane bandila sadio mofi di ndi lolou bobou khalela wante fate woumako kom taye si mane sibm batou ak simbe diamono2 nekhone na way sadio avc sadio jouska la mor sadio avc sadio jouska la mor
@ahmadoudiop50164 жыл бұрын
@@jamesgueye7416 bilay dafa lerr amena simbame bimou done def coté keur pa salif nonu bountu guallé zale mbeur bobu sama cogne hamo la solo ma taxaw sama gallé si kaw dilen sétane gaïdé gui nima watial ma wathh nank 😁😁
@omarmalle41394 жыл бұрын
Way way grande sa wakh amna solo trop mersi doundeul sa ndoundou amna solo
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Omar Malle merci
@nenou2d8464 жыл бұрын
Long vie à toi tonton sadio sama toureundo papa machallah
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Queen Diarra merci
@nafinaseck39844 жыл бұрын
No sadio kan j etais ptite dama ko bguone❤🥰
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci
@amitanndir70444 жыл бұрын
Barigassi morom d
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Nafina merci
@AminaAmina-nv2iv4 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 tonton sadio dama perte sa numéro consulàt bu Milano laniou xamanté won svp
@aichalo28454 жыл бұрын
Ndeysane aka mako beug ndakh Serigne Babacar sy❤❤
@diamapouye57364 жыл бұрын
Ayy way sadio ndiaye ana wa guediaway ecole 25
@samfall71584 жыл бұрын
Ana monsieur kebe ak madame kebe ndeysane
@fidesetratio47754 жыл бұрын
Man gui, terrain Diisso, marché bou besss....
@yacinesow10964 жыл бұрын
Ak wa école 19 daroukhane guédiawaye
@diagnenar90574 жыл бұрын
Directeur Diagne ndayssane..
@mamandiayeofficiel20384 жыл бұрын
Khaly madiakhaté kalla 1e 🖐️
@ahmadoudiop50164 жыл бұрын
Pére meusna gneuw sen simb guédiawaye cognu mor fadam ancien lutteur maléndi sani kher far ben way di romb rekk ma tothh bopbii lolu doumako meuss faté simb nékhatul je suis un neveu de ame votre compagnon
@hightonskozanostra47394 жыл бұрын
Sadio oohyèh😁meussnanio dakkhé,ma daw ba daanou,mou diapp sama copin keuz,seuleum ko,kheuthko kheuth you méti 😅, Ça me rappelle Kaolack temps boy,bouniou wathiaan diangui école sètani Ndjiin simbekatt.ooh neikhone neu..mè on dirait dafa khéwone
@keita885k34 жыл бұрын
Ma ragalone père sadio bangay simb 🙏🙏
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Hahaha
@laliyasarr55844 жыл бұрын
Thiey yallah adoun amoul solo kholale sadio rk🥺🥺
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Laliya
@laliyasarr55844 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 yagui fatteilikou madibsoo🥺billahi marquer gua sama khalei mane beuriwouma sakh souvenir si ioe
@falybadji89544 жыл бұрын
No sadio vraiment ken doula fatai 😃😃😃
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Faly ya bakh
@diarradiouf51014 жыл бұрын
Ohooo sadio aka mala ragalone diapone ngafi sama tonton d😄😄😄
@Cheikhuna4 жыл бұрын
Ay way tmt 🤸🤣👋
@oka854 жыл бұрын
Un grand Icône de la culture sénégalaise !
@ndeyeuuuhfadiagneuh60474 жыл бұрын
Longue vie papa sadio 🦁
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci ndeyeuuuuhfa
@princediop16593 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 ngoudoul fann ta vraiment marqué notre enfance diam si iow
@AidandawNdaw4 жыл бұрын
Machala sadio ndiaye
@babacargaye92094 жыл бұрын
Après magal a mbacke temps boy chaque années dafa done ame simbou mou nékhon lol mane mome bokone na si gniko diakhalone mousouma ame ticket limouma dakhé yépou mousouma diapou dakh sama vitesse bou fort temps boy rék ma raw 4x4
@Zeynaguerin014 жыл бұрын
Machallah amna solo
@mamadoulaminekonte59674 жыл бұрын
Yow sadio togn ngama deiii...yow fouma deigone sa tourrr deimm teudii neilaww...bouu yabooo nga balouma akhhh nakk
@mortallagueye85234 жыл бұрын
Machalah famebi kou tèyela 👌
@ndamthiaw61094 жыл бұрын
Il m'a une fois attrapé oooohhhhh gaïdé Ndiaye gayy damm yakh🥵🥵🥵
@rokhayaniang63504 жыл бұрын
Khouyy gaïndé gui sadio ayé avec sadio thieyy aduna li gua ma wane si sa simb sheuteut
@bandoudiembengue72774 жыл бұрын
Intéressant un vrai homme de culture
@alassanesalla25344 жыл бұрын
Sadio mesone gua diap sama mag dei bigua done simb hlm5 jour bobu dama tite b saw😂 mai tu es le meilleur nak
@amybadiane40272 жыл бұрын
Sadio sawlona kouné 😂😂
@serignesaliougningue65434 жыл бұрын
mom da nirou ak gaindé sax
@coumbaseck56062 жыл бұрын
Père nonou gadane titalé khali yi bodane wah sadio Ndiaye migui nieuw rek nieup tite😆😆😆 laye père sadio waye aka ragalou wone dama ko massa ragale 😭😭
Nday sane on habité ensemble ma grande mère t'aimer tellement mère Thiam et toi aussi
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Bilay wakh nga deugue
@papesidikonate85554 жыл бұрын
Thiéy simb are bou néh Galase Fall la djieuck sétane si simb Sadio tamite sétane nako a Rufisque ahe thiakaba vraiment nékhone na di nougnou Galase Fall un ngua reconnaissent vraiment
@amadelbeye61662 жыл бұрын
Oooh ndeysane beau vieux temps ! Xaléyi foowatouniou🙂town néxatoul
@thiormamadou14854 жыл бұрын
Sadio ndiaye domou guinaw rail son Petit frère était mon ami jo quand nous étions petits
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
C vrai
@neneba54694 жыл бұрын
Rose ma chérie la prochaine fois il faut l'invité se présente d'abord mais à part ça bon boulot et bonne continuation
@roselafleur55944 жыл бұрын
D'accord ma belle
@aissatoutoure78554 жыл бұрын
La journaliste la très bien présentée et ça suffit largement. Et c’est c’est le journalisme.
@aichadiop53464 жыл бұрын
Ndeysane diamaguene Simba nafa ba tayi nekhone na
@yacinethiam75784 жыл бұрын
Mo tack kaléyi meunouniou Dawlégui par ce que soumbou amatoul
@yanouzaydiop424 жыл бұрын
Affaire bou yémé sadio mdrr ! Yaw rék ladone topando temps boy bilahi ! Goudal fane
@kiroukouafrique89674 жыл бұрын
Thiéy Man moom douma messeu fatei Sadio dafma xol rek ma saw sama toubeuy 😹😹😹 weuy ! Yay ! Yooy 😭
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Euy way kirikou
@ibrahimadiop86264 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😁
@PILN624 жыл бұрын
Ndeysane Sadio Ba Leguii Gaindei nGa ❤️❤️
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Merci Russ
@ngonendiaye35844 жыл бұрын
Thieyy adouna sadio simbi
@moustaphangom12624 жыл бұрын
Kou bakhla
@laminendiaye69404 жыл бұрын
Machallah Pére
@lamtorrobourguedde44894 жыл бұрын
Sadio🤣un jour simb na Yoff ma takanté ak sama cousin mou dakhédji Manou niou daw ndakh takkanté bii mou djapp niou mouni niou teuyeukh souf bii boléko ak dii niou seuleum souf ndeysane que des souvenirs🤣
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Latmoro ya bakh
@fallsaliou44494 жыл бұрын
Sadio 1997 masngama diapou lingama wan légui simbou amatoul
@fidesetratio47754 жыл бұрын
😂😂😂😂😂 dala reukkk
@omardiop26684 жыл бұрын
😂😂😂😂
@k-dy42104 жыл бұрын
😂😂😂🤣🤣 Loumou la déf bimoula diapé
@sadiondiaye14254 жыл бұрын
Mangui diegalou boubakh Fall
@fidesetratio47754 жыл бұрын
@@sadiondiaye1425 No grawoul Père. Boy danio deugueur bope... Mais Père man môme je vous préférais D’Ibou KANE, d’ailleurs je n’ai jamais été à ses jeux... Yalla nala bayi ak gnounnnn lou yagu yagu. Amine
@coumbafall54744 жыл бұрын
Ndeysane le grand Sadio simbeu lou néxone temps boy deukone na sougnou keur mé meussou mako khol ndakh ragal ko marqué nga sa emprunte bilahi
@zorandiaye15024 жыл бұрын
Tu as bien dit mon pere diam si yaw❤️❤️❤️vive sadio Ndiaye