Yalla na Étudiants yeup tekki !Amine Tafsir Abdou Rahman Gueye ak groupe bi yeup yalla nane am goude fane ak wer.Amine Yalla na nieup am diamme. Amine
@aichatoudieng25012 жыл бұрын
Allahouma amine
@kingyass29742 жыл бұрын
Amine
@matydiop7922 жыл бұрын
Alahouma amineee
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine
@momobah81902 жыл бұрын
Sam tay ni nga seidalei seum xol bii 😩❤️Yalla na Yalla seiddalei nonou sa xol 🤲🏾t’es le meilleur Yaggeu nako wah wallahi ❤️Nangoul nala 🥰
@softdstlo81712 жыл бұрын
Nianale léne Tafsir weér ak gouddou fane yalla samouko ta art ko si barké yonéte bii 💯💯💯 sopé Tafsir Abdou Rahman gaye 💯💚💯💚💯
@SheriffCham-m8y4 ай бұрын
Yall neen ko yallah boli dafal si barkeh s.a.w 🤲🤲
@leadion48623 ай бұрын
Amine y rabi
@mbackendoye73082 жыл бұрын
Machallah Tafsir dama ko sopp Wallahi Yalna yalla yaggal takhawayam na niep wakh Amine 🙏❤️
@mamediarraka98222 жыл бұрын
Machaa Allah Tafsir yalla nala yalla may wer ak werlé goudeul sa fane té gueune leu katanal si barké Nabil Moustapha. Serigne Sam khol seedna. Yalla rek kay yalla
@mbenekane55922 жыл бұрын
Machalla wa 2stv Ken amoute sen faye bilay Yalla nalén Yalla defal diamou diou sakh bou ande ak yokouté ba fayou 👏👏👏👏👏🙏🏽🙏🏽🙏🏽♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@GAUCHER_MAGIC2 жыл бұрын
Rien que de l'écouter a nouveau j'ai le corps qui frissonne❤️❤️😭😭 j'ai le cœur apaisé 💞💞
@mansoursy94512 жыл бұрын
Yalla naniou yalla Fayal cheikh seydil hadji Malick Sy ♥️🙏bilahi khol yagui fékh ♥️
@diarryndiaye40762 жыл бұрын
Machallah Tafsir gaye et chérif Aidara yallah na yallah yagale sens takhawaye si barke seydina Mouhamed (psl)
@fallmodou89752 жыл бұрын
barkeb brom touba liikouko beuga diele'fii ci rewmi danga sonne nioune gamnane liniouye gam ba pare gamnane bamba gnii gamnane maodo gnii gamnane mam limamou gnii gamnane cheikh abdoulahi niss ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@fbc47732 жыл бұрын
Machalla yalla na léne Yalla fay fayal gnou Mame Maodo mo gnou khamal Mouhamed (PSL) bayou Fatimatou sama toureundo🙏🏼🥰
@kingyass29742 жыл бұрын
La 2stv en terme de montage ils sont les meilleurs. Yalla na kep étudiants validé année bi wax yalla meune nako . Merci Tafsir pour cette sensation
@madiagnediagne27662 жыл бұрын
Machalla yalla nalla yalla sama serigne sam Mbaye,AMINE YARABAL ALAMINE.
@sellybiramasall99732 жыл бұрын
Sam mi fouma ko meuneu guissé tamite💖💖💖💖
@diarrandiaye40912 жыл бұрын
Macha Allah les Oustaz yalla nalene yalla defal diam,may Len werr ak goud fane. Vous avez assuré yalla nagnou yalla may degg ak topp
@mamankhadysene53642 жыл бұрын
Machalah tous les étudiants de l ucad sont trés contents. Vraiment tonton Tafsir ak tonton chérif yalla naleine yalla Faye si barki seydina Mouhamed merci aussi à la 2stv
@fatoumbodjdiagne7722 жыл бұрын
Kc
@NdackNdiaye-vr6sv Жыл бұрын
@@fatoumbodjdiagne772❤❤
@amycollesane28962 жыл бұрын
YALLAH NANIOU YALLAH SUBHANAWATALAH FAYAL MAGUE NIOU BAX GNIFI NÉKONE TÉ TASNIOU THI SÈNI BARKÉ. ALAKHOUMA AMINNNN🤲🥺❤️ Mais Tafsir AK Sam boufeke roguagn yima toureuh😭😭😭 en vous écoutant tout au long de ce Gamou ay roguagn YÈWEUL leuh Kone mangui nianeuh 🤲YALLAH mou deffaralèn ko AK kèpp kouguèn thi andaleuh🤲 Dieuredieuf amouniou sen faye😭😭😭 MACHA'ALLAH ❤️❤️❤️
@maissawalybourserere87762 жыл бұрын
Machalah il as tout résumé ! Tafsir gaye Un vrai pédagogue yalna yala goudeul aye fanam defalko diam inchallah
@absatoudiop96092 жыл бұрын
Yalla moy Karim. Koumou may niou gné la machallah. Kham kham gui selna firi bii lerna. Say sou wakhé khôl yi sed nayssane. Yalla n'a yalla fayal lène bopam.🙏🙏🙏
@abdoudiouf71252 жыл бұрын
Depuis España pero estamos más orgulloso de nuestro sam y tafdir de él hadji Malick desde el profeto
@Ama-tb9es2 жыл бұрын
Quelle chance que vous avez cette génération!!! Nous on avait pas ça!! Diap lèn ci bamou deugeur😍 té sen ay mourrou mi ngi rafèt mashallah, je me rappelle une année á l'approche des examens on nous avait invité un chanteur connu et au milieu du show son batteur nous dit au micro" étidiant yi yAllah na nguèn am bac" 🤣🤣🤣
@alyniang73312 жыл бұрын
Same Mboup yalle na bourbi faye la je très content fière d'être Musulman 💖💖💖❣️❣️❣️💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖😍😘😘😘😘😘😍😍💖💖💖❣️💖💖😋😋💖I love your émission
@fabacarydiedhiou51092 жыл бұрын
Alhamdoulilah prières sur le prophète manchanlah tafsiir ak chérif mais Sam yalla n'a brom bi fekhal sa holl kom nunko deifaler ni yalla gua dugu aljana way😪❤❤📿
@muliesonko16102 жыл бұрын
Yenn yep dome Janna tul firdaus s’y kenn woor n’a borom nian bu nangu laa ☝🏽🤲🏻🙏🏾🕊🕊🕊
@papaaliounembaye49962 жыл бұрын
Suis mouride mais vraiment sama khol Sed n'a yallna diam yague❤️
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Dieureudjeuf ♥️♥️♥️
@bourendong7672 жыл бұрын
Amine 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@abdouazizba7515 Жыл бұрын
Xana mouride n’est pas Muslim pffff use your mind way
@saliouniang26912 жыл бұрын
Mano ma guis koo melni yonentibi yallah na yallah deff nio bgg younentibi ♥️♥️♥️
@goraniang95512 жыл бұрын
Machalah à toute l'équipe de la 2stv Dieureudieufeuti sounou Borome mome minou bolei thi ndiambotegui bidiahi Taha psl
@papadiarra38072 жыл бұрын
Alhamdoulillah baniou amé Tafsir bilae amouniou sa faye nous les étudiants de l’université Cheikh Anta DIOP nous vous remercions du fond du cœur. Paix et salut sur vous outas yallah nala Diam sonal ak weer🌷🌷🌷🙏🏾
@AngeGabriel052 жыл бұрын
@@kabou43 ah bn l'entrée c'est à combien???
@kabou432 жыл бұрын
@@AngeGabriel05 l'entrée c'est libre na nieup tew niou sargal tafsir abdourahmane gaye aux théâtre national daniel sorano le 14 mai à 16h30mn
@AngeGabriel052 жыл бұрын
@@kabou43 In Chaa Allah lolou dañe kaay téweii... Tafsir suñu Oustaz leu sou xewlei dañe kay wouyou ci yalla nañou borom bi maay tale akk fékkei🙏🏿
@coulibalypenda76412 жыл бұрын
@@kabou43 55
@dancogassama82342 жыл бұрын
@@kabou43 et iiiiiôio est îoooiiiiiioi ooôôooôoĩooio
@ndiogoulaniane47942 жыл бұрын
Billahi sam mboup ak taff ken dou yene machaalla
@ndeyeseck65152 жыл бұрын
Wa li koumou dawoul sa yaram dou nitt❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@youssoukebe85502 жыл бұрын
Bilahii
@mbayesy59232 жыл бұрын
Yallna yalla fayal niou same ak tafsir❤️✨abdou rahmane gaye✨🌙ak kouné amine🕌❤️✨🙏🌙
@papesylla32342 жыл бұрын
Amine🕋💋💙💔💔
@AngeGabriel052 жыл бұрын
sama Oustaz Tafsir Abdourahmane Gaye akk Cherif Mamine Aïdara, yalla na borom bii gëneu weiral bàtt bii🙏🏿 guddeul seini fane🙏🏿
@bayeserignendiaye75632 жыл бұрын
Masahala Tafsir mane damako sope trop yalla na yalla mayé fane bou goudou ak wérale trieur surtout la vois et chérif aussi .un grand merci pour la 2stv. Tafsir et son équipe yalla na léne yalla faye des cœurs 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 pour Tafsir
@fatimadiallo14682 жыл бұрын
A
@sidyadiaby67062 жыл бұрын
Tafsir abdourahmane gaye Gaye yalna leu yallah may gouddou fane ak wergou yaram Allahuma amine 🤲🏾❤️😘
@SheriffCham-m8y4 ай бұрын
Yall nen ko yallah buli dafal
@safietounguenodiakhate80122 жыл бұрын
Machallah wou kana kheneu dou ya Rassoul psl 🙏 tarikhatoul diné l'islam yeup ziara na leneu machallah magui mell nii j'étais ô présent yallah borom laffal thiath inchallah contane na trop dieureudieufé ya Rabi 📿🧕🤲🙏🤝
@oumouba47642 жыл бұрын
Walahi sam voi bi day daw SMA yaram 🤦🥰🥲 bilahi yalla nalen yalla Faye goudal sen fay
@fatoucisse48172 жыл бұрын
Papa Tafsir ningayy bègalè souniou khol yii Yallah nako Yallah sèdalè sa khôl fotolou sii adouna Amine ya Rabii❤💕💕
@senysallsall11292 жыл бұрын
MAME Abdou yalla nala yokou lérame si brké mouhmede ✊🥰🇸🇳❣️❣️❣️🙏 Amine waye Baye karime
@ndeyeseye92402 жыл бұрын
MACHALAH TAFSIR ABDOURAHMANE , CHERIF, SAM MBOUP 111 sans Ordonnance Inchalah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mashalla Tafsir yallah neu yallah goudeul senn fann sam Yallah neu yallah werreul batt bii nioun Waa UCad on est content Mashalla
@kaoumou75502 жыл бұрын
Machallah Yalna yalla wéral bate yi beugue na Tonton Tafsir bilahi yalla na nguéne goudou fane si barké Mouhamed ❤❤khole yépp séde
@bourendong7672 жыл бұрын
Amine
@babacardiop102 жыл бұрын
machaHala Yalla na Diam yague Sénégal 🤲🤲🤲
@cherifmane47882 жыл бұрын
Excellent Tafsir Abdourahmane GAYE, c'est important de tenir de tels discours dans nos universités.
@diormartinsylla59512 жыл бұрын
Machallah yalanagnou yalla fayal Seydi Elhadj Malick Sy.
@ndiogoulaniane47942 жыл бұрын
Yallana yalla fay len si barque werou koor guii amin 🙏🙏😍
@gnimasatousen45892 жыл бұрын
Machallah sam li nékhna loll wayyyyy😍😍😍 yalna suñu borom bi gueuna wéral bateu bi
@badarasow3202 жыл бұрын
Merci 2stv nous les étudiants nous sommes content de vos actes
@aminatandiaye44782 жыл бұрын
Masha Allah Tafsi r- Cherif mamine et Sam mboup xol sedeunaaaaa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤contane nagnou
@ndiagagueye28462 жыл бұрын
Machallah ma universite khana nieppou ay tidiane lagne yalnaniou yalla fayal seydi el hadji malick
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Alakhouma Amine ♥️♥️♥️♥️♥️
@yoboye6112 жыл бұрын
Machallah yalla na guéne fi yague té wére ❤️ khôl yeupe séde nagnou ❤️❤️❤️
@mamediop81112 жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤💖💖💖💖💖yalnaniou yalla def ay talibeé chiekh barké yonentebi
@ndeyemerrylo19072 жыл бұрын
Li defoul loudoul nekhh😭♥️♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️Sama xol sedd na, yalla nalenn Allah fayy❤️♥️♥️♥️♥️
@ndeyefamadiouf41292 жыл бұрын
Bilay le peuple est content Tafsir je t'aime beaucoup Same sounou Khôl sedde na yalna yalla goudal sen fane 2s❤️❤️❤️
@diallosalmane53322 жыл бұрын
1:46:35 الله مشاء الله I cry I love how all of them stands up and happy Allah bless you in the university ❤ 💖
@coumbasow11472 жыл бұрын
Machalla yalla nalen yalla may goude fan weregou yaram Tafsir et cherif dema l'en SOP Biolay💕💕💕💕
@falldiarra82462 жыл бұрын
Samm mboup yalna yalla samoula te are là si barkep seydina mouhamed,
@diawmarame31372 жыл бұрын
Machalla Taphsir Abdourakhmane ak Mamine Aidara yalla nalen yalla maye fane bou goudou ak wer 🤲🤲🤲
@IbnTv222 жыл бұрын
Yalna Yalla fayal niou MAODO 🥰
@babacarsenghor96632 жыл бұрын
machalah nexna trop zikr niassen nekhoul ba nekhoul mais dafa nekh ucad bi yeup yegouna
@lunelune88722 жыл бұрын
khana sam mboup kene dou mom
@yoboye6112 жыл бұрын
Machallah dougnou doyal ti dila déglou Tafsir Mamine yalla na léne yalla takhawou
@teningsarr8462 жыл бұрын
Machallah kén d'où yw doudaleu lo dounou doyoul❤❤❤
@aidatraore67482 жыл бұрын
Merci beaucoup 2stv nous sommes fière de vous
@Kheucha1032 жыл бұрын
Machalah tafsir machalah exceptionnel à Sam ♥️😍❤️❤️❤️💯💯💯❤️❤️♥️♥️
@fatoumbodj89502 жыл бұрын
Yalna gnou yalla fayal mane maodo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@assanediagne12222 жыл бұрын
Machallah nékhna trop billay ,sam yalna yalla saamm leuh ak Tafsir wa 2stv il faut bien régler le micro de Tafsir Gaye pour qu'on aura une très bonne qualité sonore mé à part ça vous avez fait un excellent travail Merci beaucoup
@yayasow61392 жыл бұрын
Machallah wa 2st wa université 🇬🇭♥️♦️
@seythian87932 жыл бұрын
Machallah oustaz Tafsir Gueye mala bague❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mbayesy59232 жыл бұрын
Ndeysane machallah same 🕌❤️
@khadimngom71892 жыл бұрын
Marchalla yalla nalén yalla fay xol seudeu Billaye walaye ak wa 2stv ❤❤❤❤❤❤❤❤🎃🎃
@pogba74402 жыл бұрын
Tafsir abdourahmane ohh yallah na yallah fayy al dianatoull firdawsi❤❤
@amadydia15012 жыл бұрын
Merci là-bas Sénégal depuis Libreville Gabon 😭
@rouguibah85532 жыл бұрын
Yallah ñanko fékke ay ate you barii inchallah 🙏Xol Sédena Machallah ❤️🙏
@aminadiop33132 жыл бұрын
Mention speciale a Sam Mboup Tafsir, Cherif Mamine yalnalen yalla faye guen yague fi te wer
@moustaphanger51692 жыл бұрын
ماشاء الله 💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖 💖💖💖💖💖 بألف ألف ألف ألف ألف ألف ألف ألف
@matythiam8672 жыл бұрын
Je suis mouride mais bilahi welahi dema begue tidiane yi 🥰🥰ando messi ak same sago bilahi surtout Tafsir abdourahman Gaye Diam rk inchallah 😍😍😍
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Djeureudeuf dagua bakh rék♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@mamediarrafall98012 жыл бұрын
Machala je tellement ému longue vie Serigne sam
@maremendiaye820 Жыл бұрын
Masha'allah tarikha cheikh gui niakeu sé né woroul ❤
@aminatandiaye81222 жыл бұрын
Alhamdoulilah ala kouli hal nignou contanné yalla guéne contanné nonou adouna ak allaxira.
@elhadjibabaniang3602 жыл бұрын
Dieureudief Sam ak tafsir machallah nkh na trp
@amysene49202 жыл бұрын
Machaallah tous les étudiants sont très contente 💖💖💖💖 mention spéciale à tonton Cherif abdouramane é ses compagnons 🤲🤲🤲💖💖💖🕍🕍🕍🙏
@ndeybousene3301 Жыл бұрын
peine
@ndeybousene3301 Жыл бұрын
peine
@aissatoumboup65082 жыл бұрын
Machallah Walakhi nioune niépa contane yalla nalen yalla fay limom Dafa manquè wone si espace bi
@madiagnediagne27662 жыл бұрын
Machalla cherif yalla nalla yalla faye. Amine yarabal ALAMINE.
@laminendiaye89912 жыл бұрын
Mbectei menoul eup lii❤️❤️mercii pour tout yalla nalein sama borom faye❤️❤️❤️🙏