Je ne suis pas thiantacoune ! Mais témoignage pa bi ak mandouté rafetlou nako torop ! Nit dey reconnaissant té mandou way 🙏🏿
@AlphaGhoost5 жыл бұрын
Je ne suis pas thiatacoune et j'ai souvent condamné certains actes de Cheikh Bethio avec ses talibés mais je viens de comprendre cet amour que feu Cheikh Bethio avait pour Serigne Touba a travers Serigne Saliou. Je pris pour cet homme que j'appelerai pas un chauffeur mais plutôt un compagnon qui a su m'éclairer sur la générosité de Cheikh Bethio et son immense sacrifice. Sa wakh lérr na té andeu ak yarr ak mandouté DIEUREUDIEUF Ps: sans limites changé le titre de la video cet homme ne mérite pas ça si té d'accord pousse bleu
@mamediarrasow17525 жыл бұрын
Aka baax
@papaamadoundiaye81535 жыл бұрын
Kou beug Serigne Saliou lolou réck
@papaamadoundiaye81535 жыл бұрын
Yaw beugeul Serigne Touba réck té mouy dég ci yaw
@saertoure2715 жыл бұрын
Wallah ça ma fait très mal souma guissé yèn commentaire par ce que c'est le père de mon ami intime son fils aîné qui s'appele Serigne Saliou samb
@salioucoumbabiramembaye31834 жыл бұрын
Rafétna
@setaneserierek53665 жыл бұрын
Ndeyesane cheikh bethio yalla nga tassék yeurmandé sunu borom
@cheikhbayekonteye96685 жыл бұрын
Amine
@fatoutambedou84255 жыл бұрын
Amine wayy
@aladji.lo11-875 жыл бұрын
Bilay ndékété oumplewona cheikh bi yalla na yalla yokk léeram
@doudoudiop42535 жыл бұрын
J8 talibé cheikh mais sama khol dafa toye yalla na Yalla défar leupe incha Allah
@fatoudieye55365 жыл бұрын
Monme dafa déme ba nurou ak cheikh bi
@bijoudiop90725 жыл бұрын
Parmis les témoignages du cheikh c'est celui le plus franc et le plus convaincant yalla n'a sa diamou yagg
@mouhamedndoye98175 жыл бұрын
Mashallah, une parfaite maitrise sur tout ce kil dit, mandouté ak thieur bou matt seukk. Dieureudieufff baye lahad
@mbenediouf18944 жыл бұрын
Machalla 😭😭 yalna yalla yokou réram barkep S saliou🤲🤲🤲
@cissendiaga99955 жыл бұрын
Machahala loumeleni rek lanouye khare si cheufeure ak secretaire Ndakh Mandou yalla na yalla defarate digeunete bi ba lepeu done beneu Amine si bareke serigne Saliou amine
@maguettegueye47505 жыл бұрын
Machallah wax dji raféte na amna ayy téguine téyit takhna ñou gueuneu kham cheikh bi diguëntém ak serigne Saliou Yalna yalla doli yeurmandé ci moom
@adamaba65085 жыл бұрын
Manchalla amna sollo cheikh bethio Talibe moko maye loumou beug
Ndeysane, je suis un talibé cheikh et anhrif de surcroît wayé nous sommes tous des musulmans. Lahatt dafa dem ma nirok Serigne Bethio mandouté lou am solo leu thi domou adama. Wakhdji rafetna torop.Nay dioub rek aka malene fonk sama mbok Mourides yi salihatou 🤲🏽🤲🏽🤲🏽.
@serignekaire65975 жыл бұрын
Bro yaw esk nitt nga rawatina talibé Cheikh, Bethio taxam finé Serigne Saliou mooy yalla tegg ci né yalla thiantacoune leu, di way aka leumbeul,diabaram yi di khessal aka tekk cheveux, meussoul djiité kenn dioulli wala diangue al Quran. Ba paré nga koy défendre,niou melnii mom nio yakh diiné dji ,kou Serigne Saliou defar doo melnii, xolaatal sa bopp, yonente bi nena dioulli moy première chose bou niouy khôl yawmal hiyaam, Serigne Touba nena kou bayi benn dioulli rek bou niou la dioullé té bou niou la soul ci cimetière musulman,bou fekké diokhé lekk rek Bill Gates mi ngi koy deff fepp ci adouna bi té dou dioullit ,kouma saaga ma fayou nak
@benkhatab145 жыл бұрын
@@serignekaire6597 iow ya wara nekeu nitt. Aka ma mandou thi yeufou diambour. Je parle plus de la relation entre Bethio et son chauffeur. En ce qui concerne la forme chacun est libre. En ce qui concerne les Mourides je prône leur engagement indéfectible. Kene doula saga iow tamit sangue bi fi ay nitt niofi nek dh tek am yar ak teguine. Nekal thi diamb fall ndiaga yaram 🙏🏾
@ligueyalyalla6195 жыл бұрын
Omar Ben Khatab Niang .
@apg-senegal5 жыл бұрын
@@benkhatab14 bilahi ya am yaar ak teguine
@benkhatab145 жыл бұрын
@@apg-senegal walakhi yama eup yar ak teguine aduna amoul solo. Yallah na borom bi tapé khol yi mayniou diamb ak kheweul bou sakh. 🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Dieureudieuf Serigne bi takh nga ma guenna kham diguente Serigne Saliou Ak cheikh berhio
@pathethiam50085 жыл бұрын
الله أكبر kilimou ame si serigne saliou dafe ko ligeuye
@bassiroufall95955 жыл бұрын
Machallah dieurieudieufaty s touba yalla na yalla diapale s saliou thione
@aliounefamadiop74615 жыл бұрын
Bien dit pére lahat samb iow ak cheikh debou la wone sa beugue serigne saliou tahna gua dieul sa taw bou ngor toudéko serigne saliou Bagne nako sahh serigne saliou cheikh bi la yabalonn djoloff bou toudou siko Dieurdieuf père yalla nla serigne touba fay sa khol❤j SS très content d tw yalna diamou yaje
@khadythiam21215 жыл бұрын
Cheikh bethio Gorre ngua Ba wouyoudji souniou borom paix à son âme cheikh bi
@dameniang39665 жыл бұрын
Mashalla Cheikh Bethio bilay Gaindé la Diambar la
@fatouthiam8865 жыл бұрын
Machallah baye lath sa wah rafet na
@birahimdieng36445 жыл бұрын
Ndéyesane yalnako yalla yeureume cheikh béthio si barké serigne saliou mbacké
@marabodian39615 жыл бұрын
Cheikh béthio yalla Nako yalla yeureum tes kharéko aldiana firdawshi si barki serigne saliou
@hamadouka88135 жыл бұрын
Cheikh bethio meussoul amm compte bancaire allahou akbarrr ak liko yalla mayoneee si khéweul Lou gneuw nonou layy deimé... Yalla na yalla woyafal soufff si kawamm
@falloulaye1295 жыл бұрын
Machalah Theiye seringe saliou
@malickndiaye6314 жыл бұрын
Ndeysane yalla nako yalla doli yeurmandé
@alendiaye11235 жыл бұрын
Ki moy abdou lahat samb limouy wakh aka ko kham yagu ak cheikh bethio Tawam mou toudé ko serigne saliou samb ki si topeu cheikh bethio jajeuf sama wadji ya bakhh
Machalla wax bi rafetna..... Jrnaliste yi bayi len yokk téy kholaaaT sen titre yi
@Mbowmteragua55 жыл бұрын
Machalla yalla nako yalla yeureum fam nek
@Corailpro4 жыл бұрын
Paix à son âme. Il a bcp œuvre pour le rayonnement de cette confrérie. Yallah nako yallah yeureum te khareko aldiana firdawsi.
@Del2Mas5 жыл бұрын
Ndeysane ki gorla nit la kou bahla Serigne bethio dei wadji wadji wah tahna ma ham moy kan ndah man Talibe cheikh la wayei lima deug ni Moy Waneni limou liguey rek lako yalla fay hana diko nianal yalla famou nek yalla yeureumko si barkè yonete bi
@aminatatallndiaye72354 жыл бұрын
Amine
@Minarassoul055 жыл бұрын
Macha allah amna solo yallah naco borombi yeureum
@Element_Serigne_Saliou5 жыл бұрын
Yalla na yalla yok ay leram Cheikh Bethio
@aramediagne83045 жыл бұрын
Dieureudieufati S Saliou. Gadou yi rafet na loll. Santate nanou bou bakh.
@gayesoukeyna305 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum thi barké seydina Mohamed psl thi barké cheikh Ahmad bamba khadimoul rassoul aminnn yaraby aminnn
@aliounesangare49494 жыл бұрын
Thiey Serigne Bethio mo kennal kou ted ki 👍👍👌
@khadijandiaye51865 жыл бұрын
masha allah samb Yallana yalla feyla barkep serigne saliou
@daoudasow26034 жыл бұрын
Machallah Mandou gue
@bizliontv16715 жыл бұрын
ndeysaan nit loumou taxxool niroo ak moom seugn bii di wax dafa niroo ak cheikh bethio. yalnaniou yAllah taas thi barkeem
@mouhadiop54344 жыл бұрын
Ndeysaan Dieuredieufé Serigne Touba
@defguissofficiel19954 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭oupalé nite bakhoule cheikh béthio talibe pire la geume na liki wakh
@mbayediaw22435 жыл бұрын
Wakh dji rafet na sell nheu deugou nheu wa salam mon père baye lahad samb
@awasarr12095 жыл бұрын
Dieureu dieuf serigne salihou mbakce serigne béthiou yalla ne yalla Yoko le RAM
@olypibrahim50525 жыл бұрын
il ressemble même A cheikh bethio
@cheikhahmadoubambamboup13915 жыл бұрын
c'est m'a première impression
@bachiirleveridique97675 жыл бұрын
Trop même
@bibibarry7555 жыл бұрын
Ah wai ils se ressemblent trop même
@ourayecisse58685 жыл бұрын
Khalil IG Niggvz dama dem bay wakh lolou tek tek bilaay
@olypibrahim50525 жыл бұрын
@@ourayecisse5868 lol je t'ai marché sur la langue
@deliart38215 жыл бұрын
Thieuyyy Serigne Bethio😭😭😭
@mouhamedseye63625 жыл бұрын
Nday sann kaduyi dawna sa ma yaram s lahat yalla na la yalla samu def diamu thi rewmi ak bépu dioulit
@mbayesall92715 жыл бұрын
Wakh dji refetna lol. Amna ay téguine. Cheikh Béthio Yalna ko Yallah doli yeuremandé.
Cheikh Béthio Yaalla nakoo yalla Dolli lèrri aldjanna si Barker SERIGNE SALIOU
@assanefallfall45745 жыл бұрын
Thiaye chèikh bèthio Sama rogogn Dou Masa far 😭😭😭🤣😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@nanicheniang62265 жыл бұрын
Ndeysann ken dou serigne touba
@abdoulayebah32495 жыл бұрын
Manchalla cadou yui amna solo 👏👏
@marieparsine91555 жыл бұрын
Mashallah !!! Deug rék la Mbaye Pékh wakhone. Cheikh Saliou Thioune kheuthiowoul dara, kén dou kheuthio lo mom ba paré si dérétt, si baatine ak si zaayiir. Danou ko sass mom Cheikh Serigne Saliou Thioune si Ndigueuleul Serigne Mountakha Bachir Mbacké, yallah nafi yague té weur. Tékssi il est discret, Kèn guisseugoul sokhnam ou ay sokhnam affichéyou si wétam di diay gueuneu goudoulé ak reuyelé moussaure (foulard) uniquement pour fégn, feuss né or si vitrine, niépeu nan yawla yénela😁. Pourtant dé, sa ou ses propres femmes nioko gueneu yéyo, té amssi plein droit. Yague fi lole té weur Thioune !
@fallmatar27845 жыл бұрын
ThieY cheikh béthio Yalla nako serigne Touba FayE Sa LiguéY Rafét na
@assanembengue14515 жыл бұрын
Macha Allah kadouyi amna solo
@fatoutambedou84255 жыл бұрын
Thièy cheikh béthio kéne dou mome djiadieuf 😍😍
@djibyndiaye98245 жыл бұрын
Machallah❤❤❤🤙🏼🙏
@modoufaye97764 жыл бұрын
Salam. Wakhdji rafetna. Kouy defar mbokk nga
@fatoundiaye37555 жыл бұрын
Ya bakh way 🙏🙏🙏🙏🙏
@amadouba42545 жыл бұрын
Xassidaas yi daw thi souf n3xneuu😭😭😭
@bayeamdyfaliloundiaye43135 жыл бұрын
Amadou Ba rabi karimoun la bo tapè youtube di ngako guise
@noyinediop62195 жыл бұрын
Thiey yalla yalnaline yalla kide jaap L'une si serigne touba ak tawam bi cheikh bi
@amadouba42545 жыл бұрын
@@bayeamdyfaliloundiaye4313 dieuradjeuf
@atoumanendiaye91605 жыл бұрын
Dieuredieuf Serigne Touba Dieuredieuf Serigne Touba amna solo trope Machallah....