Tèmoignage inedit de Serigne Saliou fils de Cheikh Bethio sur Soxna Aida“Soxna Aida moy langa bouri

  Рет қаралды 73,733

Sans limites TV

Sans limites TV

Күн бұрын

Пікірлер: 138
@sokhnadiallo9013
@sokhnadiallo9013 7 ай бұрын
❤️❤️❤️❤️Dieureudieuf Thioune Dieureudieufeuty Serigne Béthio Sokhna Aïda Saliou Thioune Yalla ngafi yag lolou té gueneu wér Mbacké Barké Serigne ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿
@momarseck5695
@momarseck5695 7 ай бұрын
Thieuye serigne bethio jereujeufati thioune yaram Ya mat ligua done sengue bi sokh na Aïda saliou thioune yalla nafi yague té wèr Amiiiiiiiiiine
@moussasall9051
@moussasall9051 8 ай бұрын
Tell pére tell fils machala ❤❤❤
@safiatoudiedhiou2534
@safiatoudiedhiou2534 8 ай бұрын
Machalla deuk rek deuk merci beaucoup frère deuk dou romb ah nope yala bahna yala nélehoul yala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AwaDieng-o6n
@AwaDieng-o6n 3 ай бұрын
Diamoudjiléne yalla té bayi thiakhane Serigne bi fowoul folouwoul
@aliounegueye3643
@aliounegueye3643 7 ай бұрын
SERIGNE BÉTHIO NÉWONE NA ADINA DINA GNOU MA KHÉB SI SOKHNA AÏDA SALIOU DI LADJ BAKHAM MA KO DÉFAR.SERIGNE BÉTHIO A REUSSI ❤❤❤❤
@salioundiaye888
@salioundiaye888 7 ай бұрын
Jërëjëf Thioune mame Bamby Thiam ❤❤❤ ya bakh ya téddeu.
@syllamomar5303
@syllamomar5303 7 ай бұрын
DIEUREDIEUFETY SOKHNA Aida
@tallfamilleelectroniquekol6840
@tallfamilleelectroniquekol6840 8 ай бұрын
Machallah amnasolo cheikh bethio yalla na ko Yalla yeureum te khariko aldiana firdawsy amine
@seydinaissademe
@seydinaissademe 8 ай бұрын
AMINE ALDIANA
@diemoygayetv4748
@diemoygayetv4748 7 ай бұрын
اللهم اغفر له و ارحمه
@AbyKaire
@AbyKaire 7 ай бұрын
DIEUREUDIEUFEUTY SERING BETHIO SOKHNA AIDA SALIOU THIOUNE ❤️🥰
@abdouazizthiaw3491
@abdouazizthiaw3491 7 ай бұрын
Gu giss sa kool gi xame né xaméwo zahir ak baatin... Démal topp sa xalifa mo gën ..ku sérigne Muntaxa sanni ça sën ba déssu ko topp
@sokhnaisseudiallo3347
@sokhnaisseudiallo3347 7 ай бұрын
Machallah tarkala amna solo
@badiartv242
@badiartv242 8 ай бұрын
BETHIO a été très Claire dans son langage, ou vous voulez faire les ÂNES. nena DIAPE thi AIDA DIALLO mi moye deug deug DIAPE THI MANE
@thiemokhotounkara9343
@thiemokhotounkara9343 8 ай бұрын
Bayil doul
@AsseSene-hn2df
@AsseSene-hn2df 7 ай бұрын
❤lila nèkh si wakh dji rèk nga beugue dègue wayè bimouy wakh serigne saliou thioune soma donoule koumay done khana dègoko
@Mp14729
@Mp14729 7 ай бұрын
@@AsseSene-hn2df mokoy donou key keneu dou donou bayou diambour serigne saliou mbacké bamou nélawé kuko donou dou domam cheikh saliou sk téré cheikh bethio dokhal ligey biko serigne saliou diokh bokoul li ndigal thioune donu lolou adaa leuh fodém amnafa wayé li ayda yoor moy ligéy bi ta moko meussa yoor nak depuis plus de 15ans thi doundou cheikh bi ....
@aliounegueye3643
@aliounegueye3643 7 ай бұрын
SOKHNA AÏDA SALIOU DIEUMI SERIGNE BÉTHIO GUI YAGAL DIAMONO TÉ WÉR SI BARKÉP SERIGNE BÉTHIO ❤❤❤❤❤
@ndeyeleye9606
@ndeyeleye9606 8 ай бұрын
Seringe saliou ndigal thioune rek mo mata naw dieureu dieuff
@DTFTV
@DTFTV 7 ай бұрын
Machallah ❤
@Guyope
@Guyope 8 ай бұрын
Ki mo safe khorome kome papame ndeyesane si saf khorome😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@safiatoudiedhiou2534
@safiatoudiedhiou2534 8 ай бұрын
Machalla deuk rek deuk merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@emobusinessmohamadezzedine2244
@emobusinessmohamadezzedine2244 8 ай бұрын
Ay problem famille souniou yon nek si .. Sénégal dem len ligey mo geun top Ay famille lolen ligey Diokh len ko niom niouy Ted nguen di soneu si wout rek .. Seigne khamal la sa dinner nguen sekh souko meunee wa legui yen Aïda saliou len la len meun khamal si yala Ak kenen Ak kenen.. nek len ay nit
@prince_mbacke2774
@prince_mbacke2774 8 ай бұрын
😂😂😂iow mi setane ba commenté 😂😂ligueyil
@Beugbamba2024
@Beugbamba2024 8 ай бұрын
Téré mayé sa Alal dh nèkhatoul nak
@Beugbamba2024
@Beugbamba2024 8 ай бұрын
Téré mayé sa Alal dh nèkhatoul nak
@sambaliou5859
@sambaliou5859 8 ай бұрын
Sayone nékousi loy commentaires 😂
@IssaBa-i2n
@IssaBa-i2n 8 ай бұрын
Problème famille vidéo diambour serignou diambour tamit sa yonou ndeye nékou thi😂
@AntaDiouf-wo2kl
@AntaDiouf-wo2kl 8 ай бұрын
Ndeyesane comme papam😄😂😅🤣 rekk machallah
@babacar1289
@babacar1289 8 ай бұрын
Ndeysane kou diourdôme déwôo kholallki rék ndeysane kom pàpàdji
@rassoul2294
@rassoul2294 8 ай бұрын
Nii la mel aka bakh saf xorom 😂😂😂meune conseiyei nite
@khabs2628
@khabs2628 3 ай бұрын
Cheikh bethio tek tek
@mounass2339
@mounass2339 3 ай бұрын
La ressemblance avec son père 😮
@khadimcisse-ll8uk
@khadimcisse-ll8uk 7 ай бұрын
Li dou dinei barkei Yalla
@albouchratv1741
@albouchratv1741 3 ай бұрын
Boulèn wakh sokhna wakhlèn serign aïda diallo
@mouhachannel6457
@mouhachannel6457 7 ай бұрын
Wi c brai c Mbakhane Thioune on a fait classe au CEM CANADA
@abdoubatbat6289
@abdoubatbat6289 8 ай бұрын
Serigne Saliou ndiouroul yaw Linga wakh sokhna Aída si lou bone mingui si Internet 1mois avant serigne bethio di guéne aduna yaw ya wakh soxna Aída daye Makro ay diabari diamour yi si medinatou salam
@awayaifaal7774
@awayaifaal7774 3 ай бұрын
Jerejef chune,yanyaka Kinyan
@mamediaradiakhate9105
@mamediaradiakhate9105 8 ай бұрын
Ki mom nirowoll sakh Domi Serigne 😮man dall Serigne salio thion la naw
@bassenebassene3815
@bassenebassene3815 7 ай бұрын
Ke les plaisirs de la terre
@mohamedba9766
@mohamedba9766 7 ай бұрын
Borom Ndigeul Thioune sampoupe Serigne Touba kouko topoule tiéré gua
@SoudaFall-q2t
@SoudaFall-q2t 7 ай бұрын
Bilay ya noble té niakk kiniane té nangoum dogal bilay ya niaka dof thioune soxna aida déei kou beug koubakh dingako beug ndax nekoul thi doudoul thi ndigueul
@Elhadjiarchitecte09
@Elhadjiarchitecte09 8 ай бұрын
Thiakhane rék ay tapalé topiléne yalla
@babacarfaye8268
@babacarfaye8268 8 ай бұрын
Mais se gars la est une personne irresponsable vraiment ak beugue lou yombou rek mola top
@sokhnaaidasanefedior7963
@sokhnaaidasanefedior7963 7 ай бұрын
SOKHNA AIDA SALIOU SAMA BOROME YALLA NAFI YAGUE TÉ WÉRE
@BiraTine
@BiraTine 8 ай бұрын
Yonou serigne touba deh djigene doufa djitté amo foula sakh
@abdoundiaye6900
@abdoundiaye6900 8 ай бұрын
Yaw nopil
@massambaseck5435
@massambaseck5435 8 ай бұрын
C le fils ainé de serigne bethio, il s'appelle mbakhane thioune, il a pris le nom de serigne saliou darou salam quand serigne bethio avait décidé de rebaptiser ses fils en leur donnant tous le nom de serigne saliou.
@petitfaye2408
@petitfaye2408 7 ай бұрын
Suma djumul moy diay café cité mixta
@seydinadjibril3491
@seydinadjibril3491 7 ай бұрын
Il est pas fils aîné mais le troisième dans l'ordre de succession
@Seck-vo9ih
@Seck-vo9ih 3 ай бұрын
Eske dou kattte sokhnasi sakh kiii woolou woumako dé nioome njeupp ay weuyou laniou ay mbaaame tiggi laniou 😂😂😂😂😂
@VieuxKara
@VieuxKara 3 ай бұрын
Lou way wax , dinko waxxatt
@abdoutoure-hd3pr
@abdoutoure-hd3pr 7 ай бұрын
Sokhna Aida SALIOU Sama Borom Sama yakar
@abakarafall6276
@abakarafall6276 3 ай бұрын
Aida ibllis diallo dou tous ibllis laye ligeyeull
@Hope_00007
@Hope_00007 7 ай бұрын
Sènègal mo nèx règ bètho ayda li yep ay fo leh tiaxan bge cumassè wax blègi waxo alkuran waxo sune ay lèk ay nan
@mbayelesse4010
@mbayelesse4010 8 ай бұрын
Ki deh solenko khamone Deug dingene xamni dokhoul si lene louy thiaxane li ame rk lay wax te bobak legui bayi lene xele ni yena ngi wax rk te aye mboram mongi guena dokh
@bassirougning3121
@bassirougning3121 3 ай бұрын
Limou wah kouko comprendre
@MamitaThior
@MamitaThior 7 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉❤❤
@abdoubatbat6289
@abdoubatbat6289 8 ай бұрын
Lou wakh taye bou souba nga wakh lénéne mouriide ndigal
@Elhadjiarchitecte09
@Elhadjiarchitecte09 8 ай бұрын
Walayi diné bi légui niem nama
@sokhnagueye1127
@sokhnagueye1127 8 ай бұрын
Dafa meusse nékh mbakhane thioune😂😂😂
@ElhadjiWade-bo6lp
@ElhadjiWade-bo6lp 3 ай бұрын
Ki amoul bén dignité kou gnak diom lamay nourou
@astouwade4206
@astouwade4206 2 ай бұрын
Ki dh diom rèk la am yakaroul daray kène ligeuye rèk la khalèyi
@aminatadiagne5135
@aminatadiagne5135 8 ай бұрын
Quelqu'un a compris quelque chose ?????????
@singarndoye90
@singarndoye90 8 ай бұрын
??????😅😂😂😂😂
@yayodiallo1021
@yayodiallo1021 8 ай бұрын
😂😂😂😂😂 explique moi
@adviseragnam7050
@adviseragnam7050 8 ай бұрын
😂😂😂😂???
@yayakane7951
@yayakane7951 8 ай бұрын
Lime wakh lérena kou môme sa yeuff koula nekh mayekoko
@AbdoulayeNdiaye-eq2dh
@AbdoulayeNdiaye-eq2dh 8 ай бұрын
DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIKAR NDIAYE..(MF?!?!)
@nabousylla1314
@nabousylla1314 8 ай бұрын
Copie conforme Cheikh Bethio machalla
@papeassanesow5248
@papeassanesow5248 4 ай бұрын
Kii waxou fii dara kii est ce que weer naa sakh maname est ce que doffoul
@franceamericanbullydogfami7992
@franceamericanbullydogfami7992 3 ай бұрын
Ki amna dara bou weer
@ndiayevallet-vp4wu
@ndiayevallet-vp4wu 7 ай бұрын
Ki moy Sax guemeul dara Torino lay takhawalou
@papesalioukandjindiaye9622
@papesalioukandjindiaye9622 8 ай бұрын
il dit vrai
@PapeSamb-d8c
@PapeSamb-d8c 7 ай бұрын
Dara wakho kofi dh
@DraDieye-p5p
@DraDieye-p5p 4 ай бұрын
Langa bouri bou balla Gaye 2 wala😂😂😂
@FallouSamb-w7c
@FallouSamb-w7c 8 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Papesarr-wv3me
@Papesarr-wv3me 8 ай бұрын
❤❤
@alioutoure5035
@alioutoure5035 3 ай бұрын
Gor dafay am foula jigen dou neke serigne si dinne bi
@SerimbackeKa
@SerimbackeKa 6 ай бұрын
lo a.mountakh wakh rek moy deugeu
@SidiKante-hj6ow
@SidiKante-hj6ow 7 ай бұрын
NIAK IGNANE MOTAX NGA WAKHÉ NI S.SALIOU NDIOUROUL AY DOGALOU YALLA KEN MEUNOU THI DARA SOKHNA AÏDA SALIOU THIOUNE DOGALOUP YALLA TA AB DIAM MEUNUTHI DARA
@MbayeSow-c6x
@MbayeSow-c6x Ай бұрын
Wakhofi daray khamkham
@taphadiop6081
@taphadiop6081 8 ай бұрын
Démal topi sa mak serigne saliou thioune mo geune kouni sama baye boufi nékone ma topouko sa tawou baye nékfi topoko sa baye boufi nékone doko topou
@AntaGueye-sd3xy
@AntaGueye-sd3xy 8 ай бұрын
Akka wer seugne Moustapha Aïda Diallo moom kouko top yena bok loby
@Cheikhibraheem
@Cheikhibraheem 8 ай бұрын
Tapha dél wakhé xam xam Fo tekk taw lagne wara top
@badoundiaye3158
@badoundiaye3158 8 ай бұрын
wa mane lima diakhal wadji au début serigne saliou thioune la andalone lane mofi changé si diguenté bi walla ndawsi dako tourr khaliss bok
@Cheikhibraheem
@Cheikhibraheem 8 ай бұрын
@@badoundiaye3158 da fatalikou dinkané bayaam
@taphadiop6081
@taphadiop6081 8 ай бұрын
@@Cheikhibraheem lolou sa mame ak sama mane lagnfi fek mofi masa am djiguene dou djité thi islame
@ridial4452
@ridial4452 8 ай бұрын
Yaw yafi done djine aida diallo lounè tay ngakay way fi ndax xaliss normal espagne da nga fa yague té amo gate motax
@diagnemareme935
@diagnemareme935 8 ай бұрын
Langa bouri kou diok danou bouri yako mom 😂😂
@toubadarmanko7193
@toubadarmanko7193 7 ай бұрын
Yaw dal daguaye khéxé sokhna aida sa problem AK sa famille yonu soxna aida nékousi dém topi Serigne saliou thione moye sa taxi Bay
@abdouazizthiaw3491
@abdouazizthiaw3491 7 ай бұрын
Waxu naxassa xandang.. ku réer..
@Elhadjiarchitecte09
@Elhadjiarchitecte09 8 ай бұрын
Nite yi légui khaliss moléne gueuneule séne diné
@bambadiouf6820
@bambadiouf6820 8 ай бұрын
Je n’ai compris demal and ak serigne Saliou Ndigueul Thioune nga topp femme bi moussama degg nga wakh si s.Saliou Thioune
@mohamedba9766
@mohamedba9766 7 ай бұрын
Xamna loutax dousi wax
@ElhadjSeye-d7k
@ElhadjSeye-d7k 8 ай бұрын
Ki com ma diambal diagne
@sidymbacke8837
@sidymbacke8837 8 ай бұрын
Ki mo niekke persenalite
@mamdiarraamar2045
@mamdiarraamar2045 8 ай бұрын
👏👏👏👏👏🤝🤝🤝🤝❤❤❤❤❤👍👍
@sambkhady6720
@sambkhady6720 7 ай бұрын
Wakho fi Dara nga balma
@KhadyseneKhadysaliou-lg6bo
@KhadyseneKhadysaliou-lg6bo 7 ай бұрын
Aye kadou you bone la djieukeu yéketi si mome 😂.
@faty5371
@faty5371 7 ай бұрын
Langua Bouri 😂Bouri langua kay😂😂😂
@mamadousalifdiallo
@mamadousalifdiallo 3 ай бұрын
Wakhi dof
@AmethMbaye-gd7pt
@AmethMbaye-gd7pt 7 ай бұрын
Nitou entere sokhor
@mourideseck2200
@mourideseck2200 8 ай бұрын
Ki daye doul dou domou Cheikh bi Serigne Saliou Darou Salam la toudou doul rék laye déf
@mohamedba9766
@mohamedba9766 7 ай бұрын
Non domam la dagua dioume reik mais moy lolou nimou mél
@cheikhbambagueye2432
@cheikhbambagueye2432 5 ай бұрын
Kou bakh ki dou segne sall darou salam bala nga wakh do khar ba kham lingaye wakh ak sa wakh dio niakki téguine yi
@khalyball3758
@khalyball3758 7 ай бұрын
Vas collaborer avec ton frère, ton "khalif"si tu es "mouride".c'est mieux que de faire la grande gueule.
@freesenegal12345
@freesenegal12345 8 ай бұрын
😂😂😂😂😂waaaaaa
@AhmadAhmad-qi8us
@AhmadAhmad-qi8us 8 ай бұрын
Ba gua gondiokhé gua yakou lol😂
@yayakane7951
@yayakane7951 8 ай бұрын
Lime wakh lérena
@aidacleannettoyagepro8418
@aidacleannettoyagepro8418 7 ай бұрын
Sal Ndiouroul aka nééékh kii
@moussadiamanka8688
@moussadiamanka8688 3 ай бұрын
Vrai ceddo
@serignefalloumbacke7849
@serignefalloumbacke7849 3 ай бұрын
Demal topi sa mak niakk nga diom trop
@cheikhbaal8867
@cheikhbaal8867 8 ай бұрын
Mome kou saf khorome la langa bouri
@AmdymoustaphaDiop-ql3nc
@AmdymoustaphaDiop-ql3nc 7 ай бұрын
Mdr
@AwaSine-s3j
@AwaSine-s3j 8 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@ElhadjSeye-d7k
@ElhadjSeye-d7k 8 ай бұрын
Domou kharam sa biir rek
@dioufmareme290
@dioufmareme290 7 ай бұрын
Yaw Moom noppil rekk
@absadiagne
@absadiagne 8 ай бұрын
Ay wax fay leer nafekh bakhoul
@mameabdoudieng3780
@mameabdoudieng3780 8 ай бұрын
😂😂😂
@Tawfeekh75
@Tawfeekh75 8 ай бұрын
Mooo cim kou niak khorom nga
@singarndoye90
@singarndoye90 8 ай бұрын
Bedio 2 tratar reek 😮😅😂😂
@MariemBa-w7s
@MariemBa-w7s 7 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@MamitaThior
@MamitaThior 7 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉❤❤
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mercredi 18 Décembre 2024
9:47
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 4,5 М.
Quando eu quero Sushi (sem desperdiçar) 🍣
00:26
Los Wagners
Рет қаралды 14 МЛН
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 141 МЛН
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 52 МЛН
Ablaye Diop Bichri "Wakhtane ci Serigne Saliou Mbacké"
41:35
Senegal7
Рет қаралды 888 М.
CHEIKH BETHIO THIOUNE RENCONTRE B
35:23
Touba Production
Рет қаралды 50 М.
Quando eu quero Sushi (sem desperdiçar) 🍣
00:26
Los Wagners
Рет қаралды 14 МЛН