Sauté de foie a l’ail recette tata Ouly Ramadan 2019
Пікірлер: 467
@mahawadrame14715 жыл бұрын
Aytieulenn merci tata Mariétou MACHA ALLAH on t'adore pour tes recettes saines et tes conseils bienveillants, et surtout on te respecte🙏 kou d'accord niou deff AY Way si commentaire yi...☺👏👌 un max de pouce bleu please..
@bmv26105 жыл бұрын
Hiiii Saveurs planétaires daal bagn lén suivre bakaar leu. Foie rek la beugg tey. Recette bii tey djii lakoy essayer. Tata Mariétou longue vie à toi. Et un grand merci à tata Ouly.
@ccseydou99984 жыл бұрын
Vraiment mesdames ,merci pour vos recettes...En plus de bonne humeur...!! Continuez des millions de personnes vous regardent...!!!
@amma92455 жыл бұрын
Li nak moy wokatou bou dadiék gestou.Dama yéwou tey sama xel nek ci foie def frites ak salade ma oubi sama KZbin rek dadj ci li non tata marietou doundeul way hamo sakh linga deff je l’avais imaginer autrement mais so boss bi nak lay deff khana ay wakh day diekh😍🙏
@aminatagueye58545 жыл бұрын
Malako wakh 😀😀😀
@fanasall28255 жыл бұрын
Khana ay wakh day dougou maïga guén khégn oignon
@aminatagueye58545 жыл бұрын
@@fanasall2825 eupeuna
@ndeyeamydiop8364 жыл бұрын
Eupence😘😘😘
@baramata96445 жыл бұрын
Kou beugeu tata maryetou beussel Jamie 😘😘💗
@seynidiop53705 жыл бұрын
Tata Ouly Konaré machallah sen foie sauté nèkhna Ta Titina Konaré ak Mamy Konaré ndax moune nagnou liii machallah Mme Sarr.Zoumana boy lèk plat bi woma
@toureawa52945 жыл бұрын
Merci Tata Mariétou nioune amouniou sa fay, khana dila nianal Yalla lokho bi werr, Yalla sammal la bopam si barké sangou sangueu yi. Tata Ouly mom teint toubab la yorr ba voix bi moudié toubabé 😍😍😍 ma ngui key bégué bou werr.
@tigressendiaye41525 жыл бұрын
Enchanté ta mariétou je vien juste d'abonner sur votre chaine é sache ke vous m'avez bcp plue rien ke d'entendre votre voix ça me fais plaisir é j'adore vos plats oci ils sont succulent j'aimerais bien y goutter un jour 💞 longue vie à toi ta mariétou
@bintoudia22415 жыл бұрын
Ayeweuyyyy chèeeee bien avc saveurs planetere on ne cesse d aprendre yalnalene yala faye
@khoudialo92275 жыл бұрын
ahh mane dall youbi yaba yi momay ray ak néko si relll. j'aime vraiment vos plat s'est superbe
@seynaboumbodji3029 Жыл бұрын
Treeeeeesss biiiiieeeeennnnn❤
@yaffafatou67315 жыл бұрын
Mach'ALLAH tata fi nga guéne tay nékhatinama 😋😋😋👍🏾👍🏾. Merci à tata ouly.
@famagueye59685 жыл бұрын
Woooow machallah defna nekh
@matyniass68215 жыл бұрын
Aye waaaye cheeeebien tata todia tinga fi mangui nii siyoonou marché poure défare reccete bi tata bii mome maye mako ndakh dama beugg foie macha Allah nékhna
5 жыл бұрын
Maty Niass Masha Allah ma Cherie mais il faut metre plus d’ognion c tres bon
@matyniass68215 жыл бұрын
@ macha Allah recette bi mome la défare ndogou mai nékh n'a trop té monsieur beugg nako loole néna nékhna maniko sama tata du çeure moma ko diokh té khamnaa kou gnakk kigniaane nga yall nala yalla faye barcké wéerou koore gui❤❤❤❤love you💋💋
5 жыл бұрын
Maty Niass ohhhh Masha Allah ma Cherie manite bëk na dè
@pendandiaye36015 жыл бұрын
Aythia léne aimé léne pouce bleu à gogo😍😍merci tata
@mariemeba92035 жыл бұрын
Machalla Yalla back si new génération.
@astoundaw69325 жыл бұрын
😋😋😋
@isosanneh22714 жыл бұрын
Masha allah ramadan mubarak b bana💝💝
@ayinkdiaw40985 жыл бұрын
Toujours dans la bonne humeur ça fait plaisir 🙏🏾🤣🥰
@diarrabousso38345 жыл бұрын
Tata marietou beug nagn la guiss nak yak say invite😥😥😥 ,mais plat bi mom jadoree foie damako beug sama xol🤣🤣🤣🤣tata ouly yalla nala yalla faye,tata marietou yaw mom dougnou diok si dila nianal🤲🤲🤲
@yacineseck68955 жыл бұрын
Tata vraiment yangui May gagn hewayyyyy
@annakeita22445 жыл бұрын
Merci Marietou belle recette simple et facile machallah merci à Ouly aussi longue vie santé à vous big up
@nabousylla13145 жыл бұрын
Machalla bonne recette. D'habitude je sauté le foie avec du beurre. Je vais essayé cette recette inchalla. Merci encore Marierou
@fatouba69734 жыл бұрын
Wa tata marietou nala yalla defal diam trés bien
@astousall37305 жыл бұрын
Recette biiii laaa dooone weur ...dama ko daane leekeu sama keur maame.... non marietou niakkeu la khame errreur bou ngaaaaandeee la ..mashaalah que Allah te protège....ouly contaane nagne ci yow.
@famadiop57695 жыл бұрын
Tata marietou boul changé dé j'aime ton bonne humeur heu way😁😁😁😁😁😁 li rek mo nekh retane kaf dafa bakh thi santé 😚😚😚😚😚😚
@ndiorodiouf41945 жыл бұрын
Tu as raison. J'aime bien quand elle dit ayy wayyy___ gounouss gounouss__ ché biennn__ youbiyaba. Vraiment merci pour les recettes
@fatoumatatraore555 жыл бұрын
Machaallah tata ouly sauté de foie à l'ail bi nexna. Merci Tata mariétou eupena.
@ngonendiaye63085 жыл бұрын
J'aime tes recettes et ta joie de vivre ma tata adorée yalnala yalla faye
@khadysene85665 жыл бұрын
Machalah keuf gui guoudouss guoudouss si n'a chai bien merci pour la recette
@aidadiop50795 жыл бұрын
Kharal ma mayko un ptit yeugeule no tata sa terme yi momay danel macha allah sa kaw si kanam rek incha allah
@mary182035 жыл бұрын
Oh j'ai l'eau à la bouche. Sopa na sa guest bi 💗💗, dafa toubabé.
@mameboye935 жыл бұрын
Ma Sha Allah😘 Merci Tata Mariétou,merci sister Ouly☺. Diam dafa nekh Ma sha Allah
@mariefaye76695 жыл бұрын
Machalah amena solo trop recette by merci beaucous à vous
@mariehelenedasylva15175 жыл бұрын
Nekh Tata ouly comme d'habitude Man mangui doga abonné mais machalla
Thiiioum , Amna plat bou ma togual Tey Mr ndoguou. mercii Tata marietou god bless 💖💖
@adjadiallo45155 жыл бұрын
mane dei ayyywayyyy bi momay ray....thanks so much
@bowelin68115 жыл бұрын
Wa li neikhoul 😍
@dadydieng46005 жыл бұрын
machalla boko khole sakh xamni nexna sel na bi mom samedi ma prepare ko inchalla merci tata ouly et tata marietou big kiss
@aichatoumboupmboup43885 жыл бұрын
Merciii Tata Marietou darling fi nga guène noyatina Tata Ouly merciii à toi également niom youbou yabba saparal na machaAllah chéé biennn😂😂😂😂😂😘😘😘😍😍😍😍😃😃😃 nékossi si rél fi néna radiakh ehhhh wayyy😁😁😁
@lachica78055 жыл бұрын
Aïcha jte vois chez alphie🤣
@kyadiagnendoye12005 жыл бұрын
@@lachica7805 😂😂😂😂😂ayway
@lachica78055 жыл бұрын
@@kyadiagnendoye1200 bilaye😂❤❤
@leylalati83605 жыл бұрын
Tata bii khanaa toubab la lokho yi wéekhnagn dé machallah, koumpaa ngimay ray dé beugoon naala guiss je sais que tata bou rafet nga, maa dagn koumpa🤭🤭🤭
@oumasarr90805 жыл бұрын
Machalah tata mariétou j'aime bien té video et té expression way mala beugue piir
@ngoranadjouaange-jokebed9264 жыл бұрын
Recette bi nexna. Dieuredjef tie Marietou. Testé et approuvé 😍
@mariemeyoumpagnefaye73815 жыл бұрын
J’adore votre joie de vivre Tata😘
@oumytam11095 жыл бұрын
Tata ouly bi bakhneu dé machallah contanéne. Tata Marietou ziar nale di le bégué rek bou bakh
@k-dy42105 жыл бұрын
Aythiaaa aythiaaa bsisimilah yalla ne gneup am diam ak wa saveurs planétaires ak mbollen djoulite thi barké kou tédd ki amine
@gueyeadama58665 жыл бұрын
Ah nekh na trop Machallah 😍😍
@ndeyeamydiop8364 жыл бұрын
Manchallah manchallah😘😘😘
@gnimasn52755 жыл бұрын
Euuuuuwaaaaaaaay 🤣🤣🤣non keneu dou yaw tata marietou. Lov u tata😘😘
@mamekaffofaye50815 жыл бұрын
Merci tata belle recette machala yalna sa diame yague
@Serenandiaye5 жыл бұрын
Thioooo tata 😘😘😘😘😘😘
@klejul56615 жыл бұрын
Oh j’adore le foie trop bon merci tata j’adore te suivre
@zeinafall38785 жыл бұрын
Machallah tata mariètou laf thiat❤
@petitenita49925 жыл бұрын
Machalla Tata yaw mome amal diame rek ak wer bou sakh dakke 🤲🤲🤲
@djeinaboudiallo76685 жыл бұрын
Magnifique tata mariétou merci beaucoup ta Ouly
@aminataba39024 жыл бұрын
J'adore ta façon de sauter
@aidabalayara88595 жыл бұрын
masha allah barakallahou fik tata marietou
@xujfaye10725 жыл бұрын
Tata diguama ray rek Jtador trooop😂😘😘
@aissatandg14135 жыл бұрын
Ah Tata Ouly amgua mana Mercii bcp ❤️❤️❤️
@maimounatoure85555 жыл бұрын
Wa khana OULY mi toubab la. Machallah
@houssaryatesenegal13914 жыл бұрын
Olalaalaaa jv cuisine ça pour l ndogou aujourd’hui insha’allah 200000 Bisous
@sallyspectra98245 жыл бұрын
Wa mère yangi may dadji sa ganou tay bi mom manchallah😍
@hawandiaye55915 жыл бұрын
Merci Tata Ouly très intéressant dourouna nekh masha allah
@miammediop43575 жыл бұрын
C la première foi ma sétane KO mai MASHALLA mère Marietou Ya takh ma abonné Yama fatheee jtm.way no stress beug lolou hahaha
@mberrymmy92755 жыл бұрын
Tarkallah Ouli on aime 🥰
@awabadiane94505 жыл бұрын
Machaallah mane dama amone probleme louma togg ndogou mė magui si bi merci tata ouly
@khadygassama67635 жыл бұрын
Machallah chef merci beaucoup pour les recettes bisous
@sochocolatyes41815 жыл бұрын
Mach Allah les tata yalla yalla fayelene yiw ci barke were bou tedbi
@mariamacisse89615 жыл бұрын
Salamou anleykoum sokhna marietou diazakilah khayran machalah recettou tata ouly bi amoul noumou nekhewoul je l'ai reproduit mais c très bon yalla nalen yalla fay ayy yiw you barri
5 жыл бұрын
Encore merci pour la pub ta marietou .wa ouli fimou guenn noyyy naaaaa
5 жыл бұрын
Reine du GOÛT :Queen of Taste ouly lidè ladef
@okalsdiallo24435 жыл бұрын
Merci tata diokh nama idée pour souba inchaalah
@ndiayedaro92755 жыл бұрын
Merci tata Mariétou tay bi la togou ndogou mais nékhna lolll tarkala
@mamediarraboussodiatta82245 жыл бұрын
Lundi ma dèf ko dama animié 😍😘merci tata au carrée😘❤
@rackygackou11885 жыл бұрын
Maman.machala danga bakh.motakh toujours dangaye yatal ta.ouli plat.machala bakhnna.thi.ndogou
@rackygackou11885 жыл бұрын
Mercie ma maman.cherie d avoir aimer mon commentaire
@Zenitude.245 жыл бұрын
Machallah demain moom laay toggg ndogu. Je suis très contente de vous les dames.
@khefakanish97975 жыл бұрын
Bilay j vous aime tu prépare bien
@adjandiaye50914 жыл бұрын
Machala rêne ouly 100 sur 10 tothie guafi
@oulyfall63915 жыл бұрын
Machalla sama toma amna solo
@olleygaye82835 жыл бұрын
ouly sama tourandor lah mashaallah I love it
@yacinesarr4385 жыл бұрын
Tata Marietou gudal fan way merçi Tata Ouly pour la recette jw vous adore❤❤
@aidadia63825 жыл бұрын
Deuxième 😌❤️ Souniou Youbou Yaba 😁😂❤️ dafae fadj
@tallndeyeyatou25005 жыл бұрын
Tata Mariétou bale ma akh dé ma part bale nala yalla na gnou yalla bolé bale
@yacinembaye90905 жыл бұрын
Machala tata ya tax ma niamé wanie yalla na sa diam yague
@madonaka31755 жыл бұрын
Je reproduis la même chose ce soir bisous à vous deux depuis la france🤩
@khadidiatougueye70575 жыл бұрын
Hahhahah no tata marietou meune nga ray nite nénako badijoner dans le pain khouuukhouuu goudeul fane way yallah bayila ak gnoune way
@khadidiatoudiatta56295 жыл бұрын
Bjr maman merci pr la recette j v l préparer ojordhui pr l ndogou soumala amoul wone non dou bakh nous on aime vraiment tt c k t fais 😘😘😘
@AfricanBeautyHairStyle5 жыл бұрын
Mashalah mane amagoulna Sama béne recette foie saute a l ail ba paré pour la fête inshalahou merci bcp guys
@rokhayadiaw97325 жыл бұрын
Aywaaaaay Ché bien😂😂😂😂😂ta Maretou ré na ba sonou
@mamigueye46245 жыл бұрын
s
@mouskebasane61945 жыл бұрын
manchallah tata Marie done khalate limay défal Sérigne bii ndogoo guislii Merci beaucoup
@ndeyemoussalioumbackediop66075 жыл бұрын
Machala nekh na way wa xarit bi begue na francés lolou way
@haouaagee95555 жыл бұрын
Bonsoir Madame. Vos recettes sont intéressante, ce qui manque dans ce que vous c'est la traduction en français. Si vous pouvez traduire simultanément en français sa sera plus intéressante. Merci et bon courage. La Nigerienne
@bapollinaris4 жыл бұрын
Chéééé bien😂😂.. punaise je kiff🔥🔥✨
@ndeyearamesall70135 жыл бұрын
Macha allah.Sauté bi nekhna té saf.❤❤❤
@safikhadi39195 жыл бұрын
Machalla c Riche ET appétissant
@fatimaababacarsy88705 жыл бұрын
Tata Marietou dall saa gann bii non seulement limou togg saff naa maos mane damako saakh beugg mane Waaww kayy Saveur planétaire sii kaww sii kanam silou bakkhh😍😍😍
@aidadiatta95685 жыл бұрын
Ay mane biyone mom tardé na di tey rek ma togalko Mr.beugue nala dal Tata Mariètou
@marietouaidara79205 жыл бұрын
Ma sha ALLAH j’adore 😘encore merci toureundo ak tâta ouly
@mamefamandaw91875 жыл бұрын
Walaykoum salam machallah amna solo na réss akh diam😘😘
@mamygomis78045 жыл бұрын
Bien expliké merci tata Marietou ak sa invité oci tata Ouly
@diarrandiaye29305 жыл бұрын
Le vinaigre on le mélange avec les frites au lieu de le mettre direct dans l’huile chauffante. Sinon le reste a l’air excellent. Merci pour les vidéos tata marietou. Yalna borom bi defal la diameu sassouné
@yacinecisse49835 жыл бұрын
Tata Marétou nekho si reule saf gua ma waye vrai senegalaise
@fantasylla24685 жыл бұрын
Vraiment c'est délicieux 🤤
@diaboufall6325 жыл бұрын
Tata je suis ta plus fervante fan😂😂 im dyi g every time im watching thanks for making us laugh i have to comment❤❤❤