Mane sax dégona bimouy xass sonko mome laye guissé té nékouma Sénégal
@papyjunior4780Күн бұрын
Pour question bou nieuk bi moy entreprises you toubab yii bouniou fiy nieuw dafay fekk niou am dolé beu noppi. Tek si état bi daf len di teguil ay diouti bou beuri. Té bo nekké sénégalais, yagui tambalé si lou neew par rapport ak toubab yii, beu noppi ligay fey état bi mo eupp fouf li nieulé di fay. État yi fi nekkone daniou dine neeweul dolé sénégalais yiii!
@BassirouDiengsaloumsaloumlepatКүн бұрын
Abdoulaye giuse ak gayam yi vere eskoro lanye😅😅
@khikhou1980Күн бұрын
Focus
@farbadiouf1990Күн бұрын
Le "balai" ne fait pas de distinction entre les membres de tel ou tel parti. On sanctionne tous les concernés et on avance.