Mbaye Sy Ndiaye Bayina Wally à vie douko awoti…? Son frère très en colère, attaque Abba et Boucher

  Рет қаралды 17,827

Senbuzz TV

Senbuzz TV

Күн бұрын

Пікірлер: 58
@fatoukarimsylla449
@fatoukarimsylla449 9 сағат бұрын
Mbaye sy ak Wally sekkou gnou bayanté 🙏🙏🙏
@aminatacisse818
@aminatacisse818 7 сағат бұрын
Wally seck mbaye sy ndiaye Thione seck khady seck ❤
@GueyeSeynabou-v9i
@GueyeSeynabou-v9i 9 сағат бұрын
Metci frère tu as tout dit 👍🏼wakhtanou famille vraiment sen yone nekou si,mane mom franchement guissouma thi lou gnaw wala lou graw 🤷🏽‍♀️♥️
@kanitouray713
@kanitouray713 7 сағат бұрын
MachAllah MachAllah wakh gi refetna. Yalna Yalla def diamu.
@MustaphaFaye-t5g
@MustaphaFaye-t5g 9 сағат бұрын
Merci sama khôl bagui mélni kholou yayou sadio mané ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@fatoukarimsylla449
@fatoukarimsylla449 9 сағат бұрын
Ki dale nite la vraiment wax dji rafet na 🎉🎉🎉🎉
@AissatouDioufDiouf-rq4ur
@AissatouDioufDiouf-rq4ur 5 сағат бұрын
Bilaye ya bakh Machala Alkhamdoulilah diam si yenn
@kumbasarr1444
@kumbasarr1444 9 сағат бұрын
Exactly well said . Doro gaye is a friend but you guys are family
@Sambou-sh3qx
@Sambou-sh3qx 5 сағат бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤mbaye sy wally seck ♥️♥️♥️❤️❤️💖💖❤️❤️🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@PapeKane-sj9ll
@PapeKane-sj9ll 5 сағат бұрын
Wally moy mbaye sy nio bok leup ❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂
@MrissaDiop
@MrissaDiop 9 сағат бұрын
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤
@AdioumaDiagne-c1o
@AdioumaDiagne-c1o 9 сағат бұрын
Bilahi benne laniou boulene kenne diakhass way
@DabaSamba-s7z
@DabaSamba-s7z 8 сағат бұрын
Machalla wah dji rafetna ❤❤❤❤❤❤❤
@AidaGoudiaby-yc1cj
@AidaGoudiaby-yc1cj 9 сағат бұрын
Merci yaw nit ngua ❤❤❤❤
@toubataif5678
@toubataif5678 7 сағат бұрын
Machallah ❤❤
@fatouseck4915
@fatouseck4915 9 сағат бұрын
Certains sénégalais gno mandouwoule c'est pas a boucler de données des conseils a personne nit avant gaye wakh thi dara il faut ke gua métrisé ko milieu politique AK show Biz bi c'est patout au lieu kil s'occupe de leurs problème mais non Wally AK mbaye sy c'est pas problème guintei moy tass sen ande
@elhadjimbaye2710
@elhadjimbaye2710 5 сағат бұрын
Boucher seytanè piir leu
@ibs335
@ibs335 6 сағат бұрын
Vérité absolue rafetna
@ceciliamanga8746
@ceciliamanga8746 4 сағат бұрын
Thank you ❤❤❤❤❤❤❤
@BayemodouNdiaye-f6b
@BayemodouNdiaye-f6b 8 сағат бұрын
❤❤❤❤Bilahi wakhége dégue
@BintouNjie-w7s
@BintouNjie-w7s 2 сағат бұрын
Thank you brother people are hypocrite 🙏 ❤
@pendaouzmboup6963
@pendaouzmboup6963 2 сағат бұрын
Merci ❤️ ❤️
@evasy9140
@evasy9140 5 сағат бұрын
Wally nagne ko nianal té bayiko mou liguey Na niouy rafetal waay
@Dam-g2u
@Dam-g2u 4 сағат бұрын
Wally dieule.dama.sene wala salam Diallo.mu.awula.mbaye.sy.rek.défe.né.geuweul.tassou.yi.waly.bayin.ahmed.thioune.té.staf.contineu ligeuy.rek😊
@AïsatouTambedou-p5p
@AïsatouTambedou-p5p 2 сағат бұрын
Merci beaucoup
@evasy9140
@evasy9140 5 сағат бұрын
Li nga wakh deug la Wally dafay yakh khew Nieuw neu ci décès borom neko diegal nala pcq nitt yi talla tougnou woon deudj bi
@DameSaliou
@DameSaliou 3 сағат бұрын
Merci wakhnga lèpou ❤
@wfamily9941
@wfamily9941 6 сағат бұрын
Abba dafay kaf mais rarement mou kaf si louy dieumalé Wally kanam même souy kaf il s'assure bien que ni dou apporter dara Wally. Abba aime trop créer de fausses polémiques inutiles. Bouché comme kou beugeu lek Wally, il n'a plus de vie le pauvre. Mbaye sy mo def erreur wally corrigé ko, sou gane gneuwé si kaw scène en plus mou nek ko khamni yena bokou lingeniy def, yaw ya warone arrêter lep lingay def diokh ko sa micro, wally waroul sakh diokhé micro wam. Na mbaye sy nangou ni mo dioum, wally defoul dara limou ko wakh khath na sen diganeté. Pour ay affaires de guenté wally manoul kou khewlé mou dem, déjà gnongui koy conseiller mou sam image Jam. C'est pas le premier enfant de Mbaye sy. Wally sou namé badianam day dem setiko. Warolen khadial ken si sen famille té ngen nangou ni guinaw thione Wally moy star bi moy sen patrimoine. Solen nango rek problème dou am
@Meumz-p7z
@Meumz-p7z 5 сағат бұрын
En tout cas mane sama xeile dalatoul dara wally dal na wouti aye remplacent you waure teike lolou moy deug 😢bou mou sagane baniou taylei ko
@wfamily9941
@wfamily9941 5 сағат бұрын
​@@Meumz-p7z mais wally orchestre complet la yor, kou absenté am na kouy dieul relais bi. Bifi ameth thiou néké sou mbaye sy dane absenté moy dieul relais bi vice versa. Il lui faut juste kenene kouy def comme li mbaye sy di def
@Meumz-p7z
@Meumz-p7z 5 сағат бұрын
@@wfamily9941 tant mieux mane je ne suis pas trop se show biz mais la manière dont certains sénégalais de mauvaise fois utilisent pour massacré se wally qui n'a vraiment pas fait de mal à personne me touche du fond du cœur ❤️ n'a tahawate tei boumou wolou keine . Wally est un proie kou neike beugue dieul sa wale et c'est grave
@wfamily9941
@wfamily9941 5 сағат бұрын
​​@@Meumz-p7z c'est vrai parfois je me demande comment il fait pour tenir. Lou ndaw lay wakh gars yi def ko polémiques média yep disi wakh, les mauvaises personnes disi profiter. Ce qui me dérange moy ay mbokam gnoko djapaléwoul am compréhension, Wally star la, ay khew ak yep gnom gnoko wara tegil thiono bi.
@Meumz-p7z
@Meumz-p7z 5 сағат бұрын
Kou bakh la ki mais manei wally laye wakhal na tahawate bou bakh thi bopam voilà gni ma guiss barki yonenbi thi worr wally laniou dieum surtout borom clavier bi na wouti aye remplacent you waure teike leine de côté reike moye li waure voila . Mane ma guissatoul lou dal sama xeile si famille bi 😢😢
@MatySeck-m3u
@MatySeck-m3u 5 сағат бұрын
Doyna war dal
@Taphiendoye
@Taphiendoye 6 сағат бұрын
Dett way mbaye sy
@fatounjie9444
@fatounjie9444 9 сағат бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@senyfaye-r1g
@senyfaye-r1g 3 сағат бұрын
Aka ma beugue wally mai nanou ko wakh deugue nak
@kadiag1876
@kadiag1876 8 минут бұрын
Vraiment nul n est parfait, wakhtan wakh deg thialla ,Wally à beaucoup changé, il est devenu impulsif. Nit Ken dou ko torokhal si dig nawlem.
@prince_photogrphe7236
@prince_photogrphe7236 5 сағат бұрын
Vraiment nit kou deugou gua Amal diam bou bkh bouchez doul kat la
@aissatouguisse1824
@aissatouguisse1824 7 сағат бұрын
Deug pirrre bayillene famille diambour famille soniou manoul wakh lou bakh nga mandou thi mo geune
@AstouSangaré-s2f
@AstouSangaré-s2f Сағат бұрын
Wally na bayi humilliation yi lolou moy deug
@matyndoye9417
@matyndoye9417 4 сағат бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@MalickSy-i9g
@MalickSy-i9g 8 сағат бұрын
❤❤❤❤
@mariendiaye1348
@mariendiaye1348 2 сағат бұрын
Dierredief thi lérale bi
@BathieDiaw-c8l
@BathieDiaw-c8l 7 сағат бұрын
Séne sang yéna kham mai degue yalla ko mome problème ame n'a mai nak le reste séne afaire la
@NafySene-o8y
@NafySene-o8y 3 сағат бұрын
Aye Sénégal bayi léne yakh gni gno bok séne mame nafékh bakhoul
@FatouNgom-z2q
@FatouNgom-z2q Сағат бұрын
Thiey xaliss
@kanitouray713
@kanitouray713 7 сағат бұрын
Wooiy demlen setti sen mbokou
@djimsow6895
@djimsow6895 3 сағат бұрын
Akk sidi diop moléne dall rek
@OppoMaroc-uo3xz
@OppoMaroc-uo3xz 8 сағат бұрын
Na dem dieuli Ah Maïté tiou c tou
@absaduop7965
@absaduop7965 3 сағат бұрын
Doule Rek
@bayemodoufall2879
@bayemodoufall2879 8 сағат бұрын
W🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@philomenemendy7052
@philomenemendy7052 3 сағат бұрын
😂😂😂😂😂
@absaduop7965
@absaduop7965 3 сағат бұрын
Yawe nit kou bakh les sites doules rek
@AdjiaFall-j4o
@AdjiaFall-j4o 5 сағат бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@mariendiaye1348
@mariendiaye1348 2 сағат бұрын
Dierredief
@OulimataDieye-y4l
@OulimataDieye-y4l 3 сағат бұрын
Tu as un mon. Coeur ces le sang lonque vie
@SènFallou-e6n
@SènFallou-e6n 7 сағат бұрын
Machallah ❤❤❤❤❤❤
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 42 - VOSTFR
48:58
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,1 МЛН
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН