Thieye serigne fallou sama yakare tay ak euleuk kéndou mome yalla na niou ko yalla fayal si barkéb serigne touba
@matarndiaye31055 жыл бұрын
mane ak yaw serigne amoul morom moy samba mi meune kanamame ak guinawam
@fatimafaliloulah11455 жыл бұрын
Thiey Serigne Fallou Mbacké sama kharit bi kén dou mome ! Moy khewe ba fawe ! Yalla na yalla yoque leerame té tass niou ci barkéme ! Serigne Touba kén amouko nioune rek nioko ame. Dieureudief Mbacké balla
@ndeyefatouguissembow60125 жыл бұрын
Ay way gana meseré yalla na yalla goudal say fane bekk na torop thi liguay wakh thi sama serigne bi sama xol bi sédd na❤️❤️❤️🙈
@astatall97865 жыл бұрын
Bilay ndayssane
@fallougalasstoubakhaira41914 жыл бұрын
Sama Réseaux préféré mame fallou mane mome là amale affaire
@cisselampe22084 жыл бұрын
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@sokhnandiaye67163 жыл бұрын
Amine
@aidafallousall67935 жыл бұрын
Thiéye sama wadji, sama kharit bi , sama sangue bi, sama sopè bi,yakar taye ak euleuk, Mbacké balla kéne dou yaw Domi sokhna Awa Bousso dji, Serigne Fallou rék, kép, dongue la beugue bolé woumako ak lénéne bougama lênêne sokhla wouma lênêne , kholouma lénêne, guissouma lênéne. Thiéye sama wadji mala beugue awma sago ci yaw Mbacké.
@syllayatma93174 жыл бұрын
Cheix Mouhammadou Fadal ♥️sma yakar tay ak euleukk yalla na sunu borom yokou Say lérr🙏🙏Balla Aïcha
@abdoulayetop16155 жыл бұрын
Yalla naniou yalla fayal serigne fallou mbacke
@mariamasow39705 жыл бұрын
THIEY SAMA SERIGNE MOUHAMMAD FADAL MBACKÉ YALNA YALLA YOKE AYE LÉERAM ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@serignebarambackesalioufalliou5 жыл бұрын
Amine
@k-dy42105 жыл бұрын
Aminee
@coumbaniang95865 жыл бұрын
Amine
@ibrahimatop43425 жыл бұрын
Amine
@falllouseck71065 жыл бұрын
Sama tourondo Serigne Mouhamadoul Fadillou yalla nagnouko yalla fayalee amine🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@sabarasts3 жыл бұрын
Dieuredieufé Serigne Fallou Mbacke 😍❤️ !!!
@aissatoudiaw78605 жыл бұрын
Yallanala yalla defal diam ta yokk kham kham bii🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@MaodoMalickNiang-qr4lr Жыл бұрын
❤ Dieureudieufé serigne fallou 🙏🏾Sam yakar
@bambaniang93054 жыл бұрын
Mach Allah que Dieu nous protège et yalna yalla fayal niou serigne fallou mbacke
@gueyemourtalla96395 жыл бұрын
Machallah Gana yabakh
@diabambistesarr73505 жыл бұрын
Serigne Fallou❤ damako bgu awma si Mom SagO
@serignebarambackesalioufalliou5 жыл бұрын
Ak man mi
@fatoudioufmouserignefallou27095 жыл бұрын
Akassaaaa kokou sama way la serigne Fallou mbacké balla❤❤❤❤❤
@cheikhtalldioum84125 жыл бұрын
Diourom niaary Serigne Fallou défar na adouna
@cheikhtvkane35274 жыл бұрын
Dia dief
@cheikhounapro67165 жыл бұрын
mane dama khammé rék beuguko sama khol mame boy yalna yalla yooku sa lér
MACHALAH DIEUREDIEUF SERIGNE GANNA WAKHTAN BI AMNA SOLO BOROM TOUBA AMOUL MOROM KENLA
@falilloubasse52345 жыл бұрын
Thiey serigne Touba
@ElTIO_Galass5 жыл бұрын
Sama tourando bii Cheikh mohhamdou fadal mbacke mbacke Ken dou mom walahii
@mbayelo30225 жыл бұрын
Máchallah
@AwamouSerigneFallouThiam Жыл бұрын
Ndaysan man dama beug Serigne Fallou bagua xamné kou KO beug sakh wala gua toudou ko damalay beug te sama khôl bi day sed lool bilahi,yalna y'Allah yok Ay leram te khir gniou thi beug Serigne Fallou ba bamay saguo Souf🤲💓
@madickendiaye32444 жыл бұрын
Dieurédieufé serigne fallou
@diarrandiaye38194 жыл бұрын
Thiay s fallou
@bourydiattaa2294 жыл бұрын
Aka mako begue💓 mom serigne fallou awma si mom sago😭😭😭😭
@ndeyediopba5675 жыл бұрын
Mame fallou ma force
@adamambodji53685 жыл бұрын
Sama sope mako begue machalah
@princessebellandiaye47305 жыл бұрын
Beugu na tawlo dom bou goor toudé ko Mame fallou Mbacke.. nianal lénma
@falloujoop47424 жыл бұрын
Jeureujeuf serigne fallou
@metahgueye62335 жыл бұрын
Machallah Serigne Fallou Mbacke
@kinebeguefallou5 жыл бұрын
Mame fallou sama yakar adouna ak alakhira yalla nagnou serigne bamba tass si barkém
@layedia4145 жыл бұрын
Akassa mame fallou brome na am mou am si ❤️ sokhna awa bousso sama tourado bobou