Journée de rassemblement des Jeunesses tidianes à Tivaouane, Serigne Abdoul Aziz Sy al Amîn délivre son message aux jeunes.
Пікірлер: 168
@sophierienquelaverite66211 ай бұрын
Beugeu Nalene ba paré guissouma loukay ndindi inchallah si barker yoneta bi ak seydina cheikh
@serigneabdoulazizsarr81663 жыл бұрын
Qui regarde ça en 2021 pour moi c'est le meilleur discours de Serigne Abdoul Aziz
@patrietv27562 жыл бұрын
Ki regarde ça en 2022 Met un 👍
@bocarbocoum42218 ай бұрын
Machala Aka bari xam xam yalla nako yalla xare adiana
@modouawafall11533 жыл бұрын
Machallah yalna yalla yokkou gueureum si moom rta fayalniou ka inchallah
@mouhamedgueye91445 жыл бұрын
Wallahi top santanne yalla mo AM solo Ay guiss yalla ak yoyou diaroul sakh wakhtanne naniou gueum yalla rek te bagna eupeul wa salam
@adamasow92923 жыл бұрын
Sawaye kone dé guemo Cheikh Tidiane...si kham Yalla la Baye Niass todié adouna......kou tassouroufate si cheikh Tidiane défar roukhou yii...démal tarbiya kham Yalla khamé mbolém tadjiliyatou yii
@fatoukinetdieng29173 жыл бұрын
Nooon SA ma papeu yalla na khipè aljanna tes supports sont Quran et les enseignements de notre bien-aimé saws ( la sunnah)
@sophierienquelaverite66211 ай бұрын
Yalla n'a yalla yok say ler bilahi ya bakh sy malick
@papacisse71555 жыл бұрын
Maodo étai trop intelligent regarder bien durant toute la période coloniale il n'était pas loin des français les Zawiya sont tous dans les capitales régionales qui pouvait le faire en son temps ils sont tous vécu avec les colon qui osé bâtir une mosquée .
@associationdentraidedansla49425 жыл бұрын
Alhamndoulilah bama télè hamé dioug dieum si baye.si keur gui la bokone gnou sol si mane ay kathieu ak ay fene you amoul fene pour rek teunk gnou si wout linouy dieurigne fenene.tay yallah yob nama si baye hamna deug deug moto top. Yaw ak gni melni ioe ndah dangéne di réreul diam gni .Sene mame maodo wathiena way yène topo lène tankam.
@modoutop84864 жыл бұрын
Dangay doul rekk moso bokou si khadra Cheikh Seydil Hadji Malick... Yénay réral nit gni yén ngouy teugü di féthi té tarikha bi amoul teugü ak féthi
@modoutop84864 жыл бұрын
Ndeysane Yalla na Yalla fayal niou Seydil Hadji Malick
@adamagueye54828 жыл бұрын
Diereudieuf Sy yallah na bour bi goudal fan yi te yokou wer gui
@khalifafaye27987 жыл бұрын
1994
@khalifafaye27987 жыл бұрын
-
@ibrahimadiallo30325 жыл бұрын
seringe abdoul Aziz sy al amine sama yakar❤❤❤❤❤❤💖💖💖💖💖
@ndakarudialdiop12065 жыл бұрын
Machallah sy malick gni wakh nieup ba ngéy doundou mik lagnu déf wakh dji mo bari rek
@djibrilfaye34535 жыл бұрын
Bilaahi Al Amiine yaabaakh çi guayi d. Dangalénn diy dorr té dollénn laal. Kou beugg ak kou bagn keur Seydil Hadji Malick nioffi toggal Tarikha Cheikh Tidiany Shérif
@cheikhniass3575 жыл бұрын
Fen nga d lolo cheikh tijan sy ci boopom wedinako fi nio fo nek nieup ay kholafa cheikh lagno
@omarsiby6955 жыл бұрын
Djibril Faye lol
@azizdrame53535 жыл бұрын
Mdrr kii insni malaka yii niongui kay khawa dadji barsakhhh
@malickdiallo95734 жыл бұрын
Qui;allah vous pardonne et vs amène dans ses parais amiine
@TalibeCheikhoulKhairy5 жыл бұрын
Ndeyssane.lii kèn meunouko wakh😢 Yalla nako Yalla yeureum
@assanediop43024 жыл бұрын
Je
@adamasow92923 жыл бұрын
Amine nanou ko gnanale Yalla rel
@adamasow92923 жыл бұрын
En tout cas tarikha bi sou weuré adouna Baye motakh
@omarthiam70845 жыл бұрын
Yalla nako yalla dieigueul mais histoire bi teudei woul nonou.
@papendiaye78275 жыл бұрын
Ki yalla douko yeureum mouk kou tollou ni aladji Abdoulaye kouko feinall do and ak yeurmandé yalla
@mouhamedniang46665 жыл бұрын
Yaw khamon li khew
@mouhamedniang46665 жыл бұрын
@@papendiaye7827 yaw dagua alkou
@mouhamedniang46665 жыл бұрын
@@papendiaye7827 nitou safara gua bou mak
@modoutop84864 жыл бұрын
Lou takh wédi woulén ko laata moufiy diougué?
@ndarylo67816 жыл бұрын
Khawma kan waye d domala massa ,fate
@serignegueye46025 жыл бұрын
Baye niass merci ❤❤❤
@diopdiop70084 жыл бұрын
Walahi ndeysane diambar thia❤
@daniellemaire39334 жыл бұрын
Machallah. Sy.. Alhamdoulilah 👏👏👏❤️❤️❤️😭😭😭
@sarribrahima52785 жыл бұрын
Machallah Sy Malick Yalla Nanouko Yalla Fayal
@mouhamedgueye91445 жыл бұрын
Nit kou bakh machala
@cheikhdiop90135 жыл бұрын
xam yalla moy deug baye niass rek moko meusseu wotei am plus de 80million de fideles world wide koudoul mom local nga
Fami sy lou you mer baye di gat baye niass rek moy baye
@aidaguene19486 жыл бұрын
Aka dègeu machalah loumou wakh téèréla
@cheikhsound70375 жыл бұрын
Aida Guene mensonges
@fatoukinetdieng29173 жыл бұрын
KHADRA MALIKYA KESSE Machallah
@ayabaaddi57186 жыл бұрын
Dieureudieffff mame abdou sy
@settegaye12916 жыл бұрын
Macha Allah Serigne BI ziarra nala
@niangballo42215 жыл бұрын
Sy malik amna sola
@fatoukinetdieng29173 жыл бұрын
Sy malick kou am yonent bi saws do niakeu dara
@Ifrahimabasn6 жыл бұрын
Qu'Allah nous préserve tous.
@sambandiaye85345 жыл бұрын
Li kay moh takh iba der thiam di féne😂😂😂lay li lagni wakh serign si nakh talibé yi dakh mbeuz la ilaha ila la mane dh meussou ma guiss li yallah nako yallah bale
@papendiaye78275 жыл бұрын
Bilay walay kilifeu dou feine
@elmalick92885 жыл бұрын
@@papendiaye7827 Do guiss bene talibé Maodo Dem si video Baye Niasse Nane day Fene et c'est la différence entre Maodo et les autres
@@papendiaye7827 Je m'en fous de linga Wakh ça n'engage que toi et dinga ko layo ak sa borom. Mani do guiss mouk talibé maodo dem si video baye niasse nane dafa fene meme si on ne croit pas en ce qu'il dit.
@azizdrame53535 жыл бұрын
Gni deh niom ak iba der thiam nio yaam😂😂😂
@zoobthe13 жыл бұрын
Generalou tarikha bi
@mbayendondeniass22496 жыл бұрын
diarama BAYE ABDOU ( RTA )
@mbayeabdouaziz86965 жыл бұрын
Masha Allah sy
@ngagneseye95525 жыл бұрын
Macha allah sy Malick dieureudeuf ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏
@azizdrame53535 жыл бұрын
Ioe yaaa niakk ko geureum😂😂😂😂😂😂 aniimou téy malaka yii niogui kay door😂😂
@talibecheikhtidiani56114 жыл бұрын
Serigne Abdou dafa tontou séne aye Wakh dongue,ki Mission la yoroone amoul séne d'hôte. Kougnou féye sa bore nga mér kone linga léblé woone moo baakhoul.
@nittoudeugg30254 жыл бұрын
Tontou ayyy wakhiii kann kilifa dou fennn kilifa dou doulll regarde le témoignage qu'il a fait sur Baye Niass
@bobcamara41275 жыл бұрын
thiakhane rék
@papacisse71555 жыл бұрын
Merci MAODO
@mouhamedgueye91445 жыл бұрын
Rahmatouhi aleyhi
@papemalickkane14857 жыл бұрын
wakhtan bi amna solo torop
@abdousakho6887 жыл бұрын
rhamatou lhai halayhi sy malik
@daoudaniang46515 жыл бұрын
Machallah ken dou Mame maodo
@azizdrame53535 жыл бұрын
Dioumo dh dafa maana doull motaax kéneu dou mom😂😂😂😂
@azizdiop404 жыл бұрын
@@azizdrame5353 yaghi dounou ba lêgui
@alioubadara79685 жыл бұрын
Wxam xam bou amoul xam yalla dou xam xam te yalla manoko xam te guisso ko nanguol léne baye niass lolou rek moye sen ndiuerigne
Salam ma ngui ziar meunone nga bagna toude serigne gnou kén. Nit kou nék na gueum teh degou ci loumou nék teh bayi pass passou gnénén. Je n'en vois pas la peine. Gayi topou nou Baye comme ça lou leer le wax ték quo ci xam xam. Xolal terém kachifoul albass fi khatmil abil abass. J'avoue que am gnou ci bolé lou ci bokoul. Mais lis d'abord ses œuvres pour comprendre loutakh. Tariqua bi ay ndananes rek ngo ci nék. Kou ni nék ci gnom au moins taxaw nga ci khoutbaniyatou. Comme Seydi el hadj Malick qui était le fard al jamiyal ou le ghaws selon certains grands soufi de la tariqua
@adamasow92925 жыл бұрын
Moy lépam si naka?moko indil tarbiya?moko yobou international?moko diangal alkhourane?moko diokh millions millions de talibés yi?so amoul loye wakh nga nopi...
Bassirou Gueye yaye domou kharame Sama baye moye fene
@bassirougueye20075 жыл бұрын
@@mamadousy5587 bilahi walahi barké alkhourane sa papa limou wakh dou duegue
@mbayegaye82285 жыл бұрын
Bou mak wahé loulaléroul boulko wah dagaye féne gueustoul rék wala bo amé ci mayeyi gua Doug kheulweu séte bakham limouwah amna am dét wayé liga gueum baye wédi di saga moné magalako wah rék ga gueumko kone likoye leral dotoul nék nite ci yalla rék laye léré a(al martabatou dou balé bayiléne togne yaw Kaye nél gueumouma lolou rék mo gueuneu raféte gueuneu simple té d'Ara doulaci fék ga balma
@sadadiop8445 жыл бұрын
Mais pourquoi Baye Niasse a séjourné à Tivaouane pendant tout ce temps alors alors qu'il rentrait du Maroc ?
@sideexattidjaniyababa29245 жыл бұрын
@@mamadousy5587 ioe yaye doumou khaath ioe sabaye moy fén doumou khaath junior mi loumouy waxi Serigne cheikh Al hakhtoum wédiko té ki tamite mo wolbatiko bindaat téré si baye diko taague Kone lane lagnoko meuna djapé tontou té yén xawma lolén Di topé s'en Serigne qui né faangue xamoul yallah té sokhlawouko guénkoy topou yén ay mbam guén doumou khaath
Sounou MAME bi bamouy doudou gayi waxou niou way legui dme na guin coy wax lou nek tey li fi laco waxe dou yomalhi yama bâ mouy dundou kenn waxoul way legui Côme dme na legui guin âme lanim pour wax louco way wax bou souba dinco retiouw ki bamouy dundou sou reweu bi diaxaley mo dann wax guin nek fi counek di wax lou niaw
@prezygraphic38285 жыл бұрын
Pape ousmane Sonko vrament persone na demanti
@adamasow92923 жыл бұрын
Les preuves sont visibles....lolou yeup amoul solo wayé monde bi sounou wakhé tarikha Tidiane Baye Niass motakh...Mane douma khass béne waliyou Yalla nak wayé lepp lérna tey
Kii mosoul am lérr baa yalla dii yookou lééram kii doull rkk lay d3ff
@azizdiop404 жыл бұрын
@@azizdrame5353 yaw yaghi yak sa bop déh domou maodo ko féké wone yén fékéwouléne ko manou si bala gha yakou mo guene yobou léttre bi Mame Abdoulaye Niass bine après la da bouguone maodo négocié ak toubab hi pour niou bayi continué liguéyeme maodo fékhé ba mou nék léona ndiasséne ta bari na gni mou dimali si réw mi
@momarkebe31165 жыл бұрын
Bou nékone el malick mo yorr mbiir yeup koneu dou diokh faydou bii ayy domam wallahi baye niass amoul morom
@adamasow92923 жыл бұрын
Sawaye boulma réye waay🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@falloutalibiecheikh17567 жыл бұрын
machalla
@momarkebe31165 жыл бұрын
Dolén meusseu guisss yalla ndakh tololén fofou Ben mbiir lah té yalla diokhnako el Hadji Ibrahima niass
@sidytayibeniass14085 жыл бұрын
Ngënéel Yalla mokay diokh Diamam Bouko sop Moussa AS lougne diokh Yonent bi sakh Nianon Na Borom bi Mou diokhkoko Yalla Nekko dedet Mounéko Bolema Si khetam bi Yalla neko Doyloul Siliamala diokh El Hadji Abdoulaye RTA domam lagni tekeulé Ak S Hadji Malick wakhoumalak Bayam nak Lolou nak Yalla moka def Ken manoussi Dara
@mafaryseye45505 жыл бұрын
YAGIBU VA YAKFI LILMARI MOURADIAHATUHA TOLA HAYATIHI AII INTIBAHUHA VA IMTISALHA DIASSAHU ALLAHU KHAYRANE
@modoutop84864 жыл бұрын
Bane domam lagnouy teukalé ak Maodo? Boudé... kokou da ngakoy lath Mame Mansour Balxawmi kérok bimou ko mbéthdié...
@sidytayibeniass14084 жыл бұрын
@@modoutop8486 Mdrrr j'ai pas me temps pour répondre à des idioties toutefois je respecte les Waliyus arrêter les amalgames et que chacun respecte et reconnaît la dimension de l'autrui
@ismailagueye36464 жыл бұрын
@@modoutop8486 شكرا
@adamasow92923 жыл бұрын
@@modoutop8486 Baye Niass khol ko moye ame nga kersam nakh soko foto si akhikha dieum Seydina Mouhamed psl ngaye ame...saway déléne ragal Yalla si séni wakh
@alioubadara79685 жыл бұрын
Xam xam 000000000 serigne bou manoul wane yalla mom khawma si mom dara yalla naala yalla yuerem te diugual lua sy diuere diuefeéééé baye niass mom miy xamlé yalla te diko wané
@prezygraphic38285 жыл бұрын
salam diame fi yafi wakhoul ignorant
@gorguidiouf48255 жыл бұрын
Aliou badara dangay tègal sa ndeye di fañ
@alioubadara79685 жыл бұрын
@@gorguidiouf4825 tegualal sa ndeye be paré khmna mo guena yombou si yaw psk sa yo khuyé rek yangua yangui diakarlo ak sa bounou ndaye bi sayo léké wala ngua nane rek nourou bouthie ngua sa tatou yaw domou haram bingua done
@alioubadara79685 жыл бұрын
Souléne nitt di wakh si xam xam doléne ko tontou si xam xam mais diko sagua mane sama serigne limou ma wakh la guem yaw guemal lila sa serigne wakh rék après mou diékh
La vraie histoire n’est pas celle-là. Talibei Baye bu guena ndaw xamna touru Yalla biniu neub... Yalnako Yalla Yereum Tei diegalko mais bimou wahei li guinaw gui diegalou nah amna gniko wowon diko ladj loutah mou wah lii tei amoul? Mou diohei explication... Kone niu moytu rek Yalnako Yalla yereum nak. Mais li xew deug deug niougn xamnenko. Magui ziar nieup di commentei dilen ndokel dilen nianal Yalla. J ai une audio où BAYE NIASS racontait l’histoire devant seydi Mouhamad Habib (petits fils de Cheikh Ahmad Tidiane Cherif(rta)), devant Serigne Mountaga Tall (rta), devant Mame Abdoul Aziz Sy Dabakh (rta)... On sait les vraies choses mais soutoura Yalla mo guene... Pour un conseil nak. Que chacun essaye d avancer sur le droit chemin et d eviter les polémiques. Yalnaniu Yalla yereum tei diegalniu. Magui ziar nieup niu commentei di sakou niane si yen. Jerengen jeuf
@mamadousarr62175 жыл бұрын
Voici l’audio de BAYE NIASS devant seydi Muhammad Habib (petit fils de Cheikh Ahamad Tidiane Cherif (rta), Seydi Mountaga Talla et de Mame Abdoul Aziz Sy Dabakh (rta) kzbin.info/www/bejne/kHXQqauDoqmoqM0
@cheikhdiop90135 жыл бұрын
gni danio ragal perte talibès baye niass fep lay tibbè nul ny peut rien
@Feliiciiaa5 жыл бұрын
Sen serign yi sou goudei nga len di guiss niouy yote di dougou si khabrou baye nakh seni talibe wayei niom nioniou gueuneu xam kouy baye
@papebirahimdiop74252 жыл бұрын
@@cheikhdiop9013 Maodo moy sen serigne wédi takhoul mou dagne
@sarribrahima52785 жыл бұрын
Machallah Sy Malick
@serignegueye46025 жыл бұрын
fen rke 🤔🤔🤔🤔🤐🤐🤐🤐
@thiamemahmoud38395 жыл бұрын
ndyssan walahi yérnaala آن الذين يفترون على الله الكذب لايفلحون
@sambabayemodoubaka25275 жыл бұрын
Ndeysane nane leu kouy wooté wo Khalifa cheikh tijanî meuneu waxé ni dou guisss yallah.... Mdrrrrrrr Baye Niass daal amoul morom gniiiii gnoo gnakha kham kham deugg deugg.... Ki nane lako nittt di toppé nane ko serigne tchieuuuuteuuuuteuuuu
@sideexattidjaniyababa29245 жыл бұрын
Marsha Allah ya sheikhy
@niangballo42215 жыл бұрын
Bilakhi maodo mo raw
@moustaphagueye22885 жыл бұрын
Bilahi danguaye féne rekkk waye masso guisse YALLA ki waliwou YALLA la bi mouye guéne aduna dafa sourire bou raféte machalah té YALLA khamalone nako né dafaye dame machalah
@sambabayemodoubaka25275 жыл бұрын
@@moustaphagueye2288 Mdrrr lolou ngay wax moy ay fennn deugg ay sourire ay door yen lagnouy nakhé pour téyé len rek vu k amougnou kham kham bougnou len jokh... Kou waxé né yallah ken douko guisss weddi nga yallah weddi yonent weddi Cheikh Tijâni weddi Hadji Malick weddi Waliyou yeuppp... Mais lolou moy woné né amoul benn thieur ci yallah... Dem len outi serigne bo gueun ci yen... Té nguen bayi bolen amoul loloen wakh di saga ak khasssté
@sambabayemodoubaka25275 жыл бұрын
@@niangballo4221 noumou rawé ak koumou raw
@sowahmedtidiane28005 жыл бұрын
Li ngaye wah khamó thi dra
@prezygraphic38285 жыл бұрын
sow Ahmed tidiane dagay doul Ya khamoul dra
@papendiaye78275 жыл бұрын
Bayil doul yi khamo lenn dara khalif dina tokk nane kou wax dafay guiss yalla waxoul deug NN ana srgn yalla nagnou yalla fayal bay
@mamadudieye6425 жыл бұрын
Yaw yay doul
@mandiayediagne76035 жыл бұрын
Yaw ya khamoul loy wax yaw nitt bou amoul louko lérrr day déme geusstou dji ba paré
@assba885 жыл бұрын
Katal sa ndéye domeram
@modoutop84864 жыл бұрын
Yaw yaye doul lou takh bamiy doundou wédi woulén ko sén bén kilifa wédi wouko...Khalif général des Tidianes Tivaoune rekk ngakoy dégü
@moussathioub8445 жыл бұрын
عالم الكذ ب لا تقول حق في الدنيا. اليوم في الخبر أنت لم تلت أبوك الكريم
@moussathioub8445 жыл бұрын
هذا رجل نذاب فقط
@moussathioub8445 жыл бұрын
والله أنت كذا ب
@abdasy11085 жыл бұрын
Machala
@diagneousseyou80187 жыл бұрын
machalla
@egccbnndiambour17945 жыл бұрын
mme Guèye dieuredieuf sy malick kou djouké dja cheikh fez loye wouti sanawelé tokhe fa 90 jours wala 6 mois louka warale qui bayame ak mamame la wédi dou yowe.