Serigne bi loy def wala nga d'i ko beugueu def nonoula,yalla nala serigne TOUBA fayal boppam.t'é d'i gnan YALLA nga yagg f'i lol t'é wer
@Djiily74615 жыл бұрын
Sama SERIGNE sa seeré çi sama nijaay rafét na machallaah s bassirou lô dénkeu naala S TOUBA nala teuyeel boppam boula kenn meuneul darra lou bon mouthieul ta am jamm
@antagueye79935 жыл бұрын
Cheikh Mountakha bachir yagg fii lol té wérre si barké cheikhoul khadim