Allahou Akbar mangui dioy 😭des larmes de joie 🤩quelle changement incroyable ndeysaan Dakar buzz Sénégal amoul sen fay walahi haziim yallah na yallah fayleen 🤲🤲
@mamadousene62102 жыл бұрын
Amine way 🙏
@khadydiop99972 жыл бұрын
La santé c'est tout
@BeifaMk922 жыл бұрын
Amine 🙏
@senordamas72142 жыл бұрын
N'oublions surtout pas les 5 prières quotidiennes. Prompte rétablissement
@abibatoubathily37832 жыл бұрын
Merci beaucoup
@timatima90132 жыл бұрын
Bilahi les cinq prières et les invitations du matin et du soir
@aladjifaye5728 Жыл бұрын
Acá am solo machalah day defar nit te fot ruhu diko diegalé diam bi boromam
@mariamsy36412 жыл бұрын
Sites internet yi neek Sénégal lii guéne wara ligueye au lieu di top ay cas di yaak der niit yi di douk ay vie privée diambour yi.bravo dakar buzz chapeau 🎩
@Noba-konate2 жыл бұрын
Un changement incroyable merci Dakar buzz que dieu vous assiste
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
Bilay ioe vraiment Amine 😁
@boudechou2 жыл бұрын
Vraiment pas croyable Allahou Akbar
@missnikisow84562 жыл бұрын
Un changement extraordinaire mane da m’a diakhle sahk Bilahi contente n’a trop Merci
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
Heureuse de le revoir en bonne santé MaShaAllah Alhamdoulillah 🥰 💕😘❤️ wolahi Yala rékeuy Bour Malikoul Moulk Loul Jalali Wal Ikram Allahu Akbar 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭☝️☝️☝️💖 !
@sarrastou66172 жыл бұрын
Manshala
@nourradam63912 жыл бұрын
ALLAHU AKBARR ❤️kuneh soygenn sa keurr dilwakh diang,bismillahi tawakaltou ala'llahi wala hawla walakhuwwata illah billah,ak ay yenen ALLAHU AKBARR KABEERA
@SENEGAL3032 жыл бұрын
Merci. Je le fais depuis des années. Et alhamdou lilah. Diam rek Lassi guiss. Alhamdou lilah... Koudoul lémou yangui sarakhé sa bop.
@NdeyeNdiaye-c3l2 ай бұрын
Mante g l'habitude même sama dome 3ans ndianguale naguoko
@neneoumou85512 жыл бұрын
Alkhamdoulilay je suis tellement contente je me sens pas bien depuis ce matin mais vu cette vidéo je suis guérir. Je me préoccupait tellement de son vidéo avant que J étais là 1ère à commenter. Vive Dakar buzz et merci encore à fadel de redonner la souris à cet merveilleux homme. ❤️❤️❤️❤️
@ndoumbediagne4672 жыл бұрын
Guisga motakh sante yalla rek Bilahi tout le temp amna ko tané motakh sante rek nianal len aussi khamni a tout moment li raw li meune nagne ko doundou, yalla rek kham mais nagne doli sante yalla rek
@bayesakho31272 жыл бұрын
Alhamedoulilah jeune homme ça fait chaud aux cœur je suis très contente de vous voir sourire
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
Seigneur Merci bcp de lui redonner le sourire et la joie de vivre ! MaShaAllah Alhamdoulillah 😊🥰💕 😘 ❤️ 🙏☝️💖😁☺️
@ladivachou27532 жыл бұрын
Ndeysane 12 ans metina 😢😢 Sant Yalla diouli si yonent bi ( SAW) , MashAllah yalna Yalla doli wer ak sutura. Nagnou moslou thi sheytané sa sou nekk.
@niangtra2 жыл бұрын
Ooooo kholal différence bi rek 😭 yalla lay karim. Chapeau à vous wa Dakar buzz
@awandior95222 жыл бұрын
Allahou akbar 😇Ohhh macha'allah, allahouma barik, contana, sama khol seddeuna, yalla dinalén fay dé, sakhlén ci rek ❤,yalla goudal sen fane équipe bi yeup,yalla defalén tawfekh,macha'allah ❤❤❤
@aramediop41242 жыл бұрын
Billahi dama cotane😭😭😭yalla na léne yalla fay ni ngéne Di seddalé kholou diam gni yalla na léne KO yalla fay🙏bék nagnou lool👏👏👏👏👏👏
@bijougueye54422 жыл бұрын
Noooo fadel yaw diam rek guaye ame barki serigne fallou yagui dimali diamou yalla yiiii. Yalnala yalla faye sa xoll. Borome bakh nga ani gniko beugue.. 😍😍😍
@karsmatk-k82102 жыл бұрын
Gloire a Allah seigneur de l'univers, la transformation du monsieur m'a fait pleurer. (Niit Diam la kham) Merci dakarbuzz merci aux donateurs
@amatoullah67662 жыл бұрын
Un vrai glow up maachaa Allah 😍😍 Sante yallah boubaakh et merci à toutes ces bonnes volontés. Yallah na yallah dolli soutoureu ak khêweul. Fadel kenn amoul ssa fayy. Yallah miyy fayy yallah na la fayy ay yiw 🙏🏾🤍💙❤️
@ndeyebadiallo2 жыл бұрын
Alhamdoulilah Alhamdoulilah, très contente de revoir ce mr retrouver sa santé, Yallah nako Yallah yokkal wer té wa Dakarbuzz Yallah nalen Yallah fayal bopam🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤❤❤❤
@Ndoma2 жыл бұрын
Machallah yala nalène yala fay si nigèni diapalè ak di dimbali niouko yèyo yala na yala doli soutouro yarabi yala faylène yarabi🙏
@khadimtoure53472 жыл бұрын
Ll
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
Amine
@dieynaka4052 жыл бұрын
Ndessane li terre wone nama nelawe billaye barkue serigne babacar dakar buzz yallana yalla faiye amine
@ngonendiay5372 жыл бұрын
Hoooô ndayesan ki rekk warna takh ñiou delo leep thi yalla ki kouko gissone avent et après nga khamne yalla rekk mon yor rou tee febar takhoul deee
@ndeyefatousarr49452 жыл бұрын
Allahou Akbar ay kii lima ka khalate wallahi temps yii rk sama khél mingui wone si mom yallah sédé nako wayé changement bii ma guiss nékhna ma trop machallah lou waay ame rk naka santé sounou borom ndakh lép rk mo gueune déh. Wa Dakar buzz yallah naléne sounou borom samme yok léne banguéne yék ko may léne guoude fane wérr ak diame diou sakh contane na trop Alhamdoulilah.
@astoudione10192 жыл бұрын
Machallah bilahii j ai les larmes au yeux que dieu vous garde
@mameabyba82422 жыл бұрын
Ndeysane javai écouter sa en teuss Alhamdoulilah si tane bi yalna yalla khep doli
@fatousow38802 жыл бұрын
Machallah khôl yeup sed na fadel niang yaw ak wa dakar buzz yeup yalla naléne yalla faye ak bep dioulit ci barker seydina mouhamed psl amine yaraby
@abdouazizdabakhgueye63822 жыл бұрын
Nooo ki première fois bimako guissé Billahi dama diooy ba j'avais mal à la tête ce jour là. Mais wallahi sama khol sédd neu Billahi j'ai envis pleurer pour mbécté j s8 vraim content. Alhamdou Lilah dieux é le tt puissant
@ouleymatoudiagne12162 жыл бұрын
Sama khôl ba nji séed loll billahi. Machallah Dakar Buzz longue vie à toi Fadel
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
Vraiment seen liggueey rafetena waa dakarbuzz,Yalna Yalla fayla yiww bi gueun tchi yiww yi🙏💓💓💓💓 Vraiment soxlanaaleen trop tchi benn cas, sama grand-frère lagn diam tchi beutt ta ndeyssane dafdoon aattei kheekh rek, mou djeulei tchi silmakha ça fait 10ans maintenant.💔💔 Il doit se faire opérer pour retrouver sa vue à l'extérieur et il n'a pas des moyens. On vous a appeler à maintes reprise mais Khamnaa seen cas yi dafa bari
@aissatasow73012 жыл бұрын
Alahouma amine 🙏
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
Walahi soon n'a trop, il y'a des gens riches ici qui peuvent l'aider mais lui font du chantage, mais dafa gueum Yalla mootax nangouwoul, ndakh rouss na diaay ngoram nguir bagn Lou neekhoul Yalla😭💔
@salyndiaye922 жыл бұрын
Yalnako yallah safara
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
@@salyndiaye92 Allahouma Amin🙏
@nnswsssn38312 жыл бұрын
allahou akbar
@ndeyegning55652 жыл бұрын
Yalna leine yalla faye. Sen liguey rafet na Mashallah 😭😭
@bayecheikhndour102 жыл бұрын
Kaye ma May lako ioow
@bayecheikhndour102 жыл бұрын
Dosi diamou yalla
@mamediarragueye59052 жыл бұрын
Machallah sama yarame Bangui daw sax 😭alkhamdoulilah sante yalla ware na kounék Merci Dakar buzz♥️
@ndeyefatousarr49452 жыл бұрын
Une prothèse pour lui😭
@ndeyedioufmouserignefallou67202 жыл бұрын
Yalla nalen yalla fay thi barcké alhouran chapeau à fadel
@binettegueye28132 жыл бұрын
Alhamdoulilah je pleurai bama sétané Mouy nétali liko Dale dama dioye Aÿ kheukheute may défilé guiss vidéo bimou weuré alhamdoulilah la sant yalla suis très contente pour lui.fadel yalnala yalla Faye sa xole🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@laurentsambou76622 жыл бұрын
Merci seigneur de lui avoir redonner la santé et le sourire
@djibydieye78112 жыл бұрын
Je le connais très bienn un gaa très bien nio bokou kogn diakarlo keur aussi serigne cultivateur la wonn kou bakh sakh bilakhi yalla nala yalla défal diamou may la goudou fann
@MameboussoSaw-nr3seАй бұрын
Amine
@smaeteaa53582 жыл бұрын
Fadel machalla nitou aldiana gua yalla molay fay
@sarrastou66172 жыл бұрын
Alhamdoulilah la santé n a pas de prix.longue vie à Serigne et Fadel
@cheik-pointsg12382 жыл бұрын
Merci 🙏 on est fier de vous. Dakar buzz on est fier de retrouvé ce monsieur 🙏😎
@Ebena-n4l2 жыл бұрын
Ndeysane son cas m’avait tellement choqué louma diakhalonn mettiwonn ma aussi mais alhamdoulilah li moy wanei ni loudoul yalla neinn la❤️❤️Gnane yi nangouna machallah nakh gneup sen khol lagn ko tibei❤️❤️❤️yallna borom bi dolli inchallah ❤️
@awamandiang50362 жыл бұрын
Oh Alhamdoulilah merci beaucoup je suis trop contente de changer la vie de notre frére
@madamemadame33802 жыл бұрын
Eskeuy! Vraiment incroyable. Mach'Allah ça fait tjrs plaisir d'avoir ces genres de retours très réconfortant.
@veriteabsoluedeugneekhoul17202 жыл бұрын
Il est devenu tout beau Machallah
@mmmmdiattara69772 жыл бұрын
Ayway alhamdoulilah dieu merci de lui donné le sourir et la guerisson yanala yalla guena takhawou ak kepp kou nekk si ay diafe diafe yanalenn yalla takhawou sante yalla❤😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲🥰j'ai les larmes de joir😭😭❤🥰❤🤲🤲
@ndeyeastousamb36212 жыл бұрын
Alhamdoulilah Vraiment amou gnou sen faye li guéni liggey amena solo
@daoudandour3922 жыл бұрын
Machallah amna solo vraiment je suis fière d’être Vous Dakar Bezz
@ndiayekhalil95732 жыл бұрын
Mashallah xol séde n'a lol🙏🙏🙏🙏Fadel yalla na yalla fay ioew ak sa equipe
@mamadoudiallo16512 жыл бұрын
Akh wéer rékh móo mata niann 👌🏿chapeau à toi Fadel akh keep khou diap sii émission bii🙏🙏
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
k'Allah récompense toutes les bonnes volontés et particulièrement Fadel 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@naboudia35542 жыл бұрын
Ohhh neina kouy diamou yalla rk mokoy khol ndeyssane di nga am kou bakh legui koula mounieul incha alla yalla bakhna Fadel yalla nala yalla fay yiw yak sa équipe tecknik yeup🙏🙏🙏
@mbayebambaloartiselo15422 жыл бұрын
Ganyi nagnou gnanal fadal bou baxe yalla yokkou ko arko li gourgui la waron walla milliardaire yi . yalla na borome bii samla la 😭😭🙏❤️
@genius21582 жыл бұрын
Euy waay Dieu merci, j'avais mm pleuré lorsque j'avais vu la vidéo d'avant🙏 Yalla mooy bour🙏🙏🙏 Diamm ci yêên waa #Dakarbuzz yalneu Yalla hêêb dolli, moomit Yalla dollil ko diam ak khéweul 🙏
@misssow32562 жыл бұрын
Yaallah rekka meune 🙏 yalnaléne sunu borom fayal boppam 🙏
@adambass80322 жыл бұрын
Fadel yalla bo guiss lo ragual Fadel yalla bo guiss dara loula diakhal yalla lafal la thiat dolila soutirage machalla on t'aime bien amal diameu
@belladiopdieng48782 жыл бұрын
Je ressens un immense joie 🥰🥰 machalla, bravo fadel et Dakarbuzz ,vous êtes plus utile que ce gouvernement incompétent
@amicollehane47622 жыл бұрын
Ndeysannn dieredieuf Fadel ak Dakar buzz social yalla nalen yalla fayy ak kepp kou diappale Serigne bi ba yalla mayko mou werr walahi ❤️Sedna si yen bne continuation
@Onomar2 жыл бұрын
Oh alhamdoulilah suis vraiment content pour lui ♥️❤️🥺❤️♥️♥️♥️♥️prompt rétablissement yallah nala yallah geuna taxawou . N’oubliez pas de prier pour moi aussi Les amis 🤧❤️🩹🥺🇸🇳❤️♥️wër ak goudd fane reik lay niane le reste beugouma
@rachidacamarasylla12302 жыл бұрын
Yalla nala yalla maye were AK mbolèm dioulite bou fèbar
@mariatoubeye10212 жыл бұрын
Yalla nalako yalla may ak mbolém dioulit ya rabi amine
@awasambou14642 жыл бұрын
Machallah Dakarbeuzz thia kaw thia kanam rek💪💪💪❤️
@gueyedoudou85902 жыл бұрын
Sou leen yalla fayer touti reelkk aljanah ngueine dieum machallah
@beuguerassouldia47302 жыл бұрын
Ahhhhhh Machallah alhamdoullillah yalna Yalla doliko wer doliko mbolem domi Adama si barké yonent yalla Mouhamed Rassoul Aleyhi Salatou wa Salam ❤️,Fadel le Missionnaire de la population diadieuf 👌👌
@abloslimshady2 жыл бұрын
Macha Allah, s’en liguer rafetna khol seddatina tchi linguen sopalé waadji. Yalla Fay lenn ngandi fayy! Bou lenn fatté senn Azkar Bolenn di guenn s’en keurr wala Bolenn di dougou aki gueenn douche c’est très important…! Nitt kessè deukoul tchi souff ci, djinné yangui tchi sougnou biir? Wax lenn Bismillah tawakkaltu ala llah, Laa hawla wala quwata illa billah aliyul al A’zim. Sa yolenn di guenn s’en keurr!
@khalifaababacarNiang3132 жыл бұрын
Alhamdoulillah . Yalla rek moye kenne. Avent bi seetane nako après aussi. Yalla n'a yalla dolli soutoure defale lene diamou ak yokouté 💚🤝💙
@falloudiaka47922 жыл бұрын
Fadel vraiment yew ak wa db yalla nalène yalla takhawou si barcke serigne bi
@awaaidara87292 жыл бұрын
Ndayesanne merci fadel
@oustanoudiop85132 жыл бұрын
Mashallah 🥰tout le temps dafa done nekk sa khel 💕Fadel yalla nala suniou Borom fay thi barké yonente bi
@ngagnedembacisse42632 жыл бұрын
comment je suis content!! 🙆🏽♂️✨✨🤩🤩🤩🤩Alhamdoulilah 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@thiorondione32362 жыл бұрын
Machala Fadel yalnaleu yalla fay ak kep koulendi diapalé
@safietoufall99752 жыл бұрын
Machaallh tabarakallah je suis contente de le voir comme ça merci Dakar beuzz social
@maimounadiongue60682 жыл бұрын
Oh yalla na geuneu wéer ci barké Séydina Mouhamed PSL
@andrendione90212 жыл бұрын
Merci Fadel 🙏🤲🙏🙏🤲🤲
@tydasadio49832 жыл бұрын
Cas bou doyone waar ndeysane teuss lako djeukone degueu c’était triste ma setane video bi dioy mais tay lep lima nakari wone nekhnama mashalla je suis très contente dakar buzz yalla nalene yalla fay yarabi
@pxstelcloud66982 жыл бұрын
MashaAllah Alhamdoulilahi Rabil alamin. La illaha illah Mouhamadou Rassoulilah.
@Leuz_vision2 жыл бұрын
Merci fadel ak dakar Beuzz
@seynaboumbaye99222 жыл бұрын
Yalla nalen yalla fay insha allah yokk soutoura 🙏🏽❤️
@fatouseck46722 жыл бұрын
Billay febar moy nonou nitt kholal bi mou weurré nimou changer rek bélli ndeysaan machallah yalla na yalla khep dolli
@falloudiouf84422 жыл бұрын
Allahou akbar yalla kén la ms Fadel esk kham ngani missionnaire nga 💪💪yalla na sa mission yague 🙏🙏
@SOLEILCISSE2 жыл бұрын
Nallén sunu borom sammeuh 🙏🏿🙏🏿🙏🏿. Hamo lén sah ndiarign bi sén tahawaayy am🤞🏿
@aidambaye27022 жыл бұрын
Cet homme ndeysane teuss lako déguelou dama dioy oooooh depuis lors sama khél mossoul diouk si mom j’aimerais bien avoir ses nouvelles ndeysane yalla naléne yalla fay way yok ko wër allahouma amine
@ladyjabz6332 жыл бұрын
Subhana'Allah 😭😭😭 Thank you Dakar buzz you doing a great job for the people who are in need of help .
@khadysy16682 жыл бұрын
Merci beaucoup dakar bz chapeau bas à fadel ligueybi Nice na
@yamasoda32302 жыл бұрын
Ma challah wa dakarbuzz yallna léne Yalla takhawou 🥰❤❤❤❤❤❤❤😍
@bbndeyefam2982 жыл бұрын
Yalla nalene yalla faye xol ced neu si yène ❤kene menoul yalla rekk mo meune sante yalla
@queentouray44122 жыл бұрын
Allahou Akou Bar dieureudieufé Yala sunu borom video bimu fébaré limu ma dioylo wone et je sais que dou mane dong Alhamdoulilah si numu amé tane yala na yala fay len wa Dakar Buzz défal gneup diam gni tawate mou may len wer et gni tiabi fété guinaw mou guindi len inchala Alhamdoulilah
@aliouyade96862 жыл бұрын
Joindre l'utile à l'agréable, merci Dakarbuzz. Continuez à changer des vies. Je suis vraiment content de vous.
@mamemordieng76502 жыл бұрын
Fadel bilahi bo yalla fayé dinga khamné yalla amne fay se ligueye refet n'a loulll machalla Fadel
@sofimarietoucisse44122 жыл бұрын
Quelle joie maa shaa Allah Fadel yalnalén Yalla fay way
@bassirouba49942 жыл бұрын
ndeyssane Fadel contane vraiment yalla n'alla yalla fay yow ak sa équipes yeupeu alhamdoulilah
@mamegormboup2712 жыл бұрын
Merci dakr buzz❤❤
@khadimgadiaga57302 жыл бұрын
Al hamdoulilah yalla nalen yalla fay bilahi bimako guissé avant damako yeureum loll kheyna sounou yéné donone na gnou takhawouko mais antouwoul si gnoune mais al hamdoulilah yen gniko diapalé bamou nekak yalla na yalla téguil bepp nite ay natou
@dmxjjj75552 жыл бұрын
Yalla naléne yalla faye bilahi vous êtes des anges de dieu 😍❤🙏🏽
@loyennetv70532 жыл бұрын
Etat war nalen defal compte banque ak hôpital diohlen ak docteur dilen ko fayal bilahi ndax li moko warone def yalla ham nako 😭
@khadymboup98812 жыл бұрын
Bilahi wakh ga deukeu
@rokhayalavillageoise83802 жыл бұрын
Ohhh lalah très bonne nouvelle bravo gars yi Sen Ligueye rafet na dé machalah
@oumythiam73132 жыл бұрын
Ndaysane yalna yalla dolil leu tawfékh ak khéweul bamou beuri dolil mbolém dioulit
@landaya64532 жыл бұрын
Ndaysane tonton Fadel ak tonton pape yalla rek mo ame fayy yalla nalen yalla bourbi fayal bopam
@babalie45042 жыл бұрын
Thanks so much bro 🙏🙏🙏🙏🙏
@amardiarra71392 жыл бұрын
Yalla nalène yalla faye sen khole 🥰😍liguène beug yalla nalène ko yalla faye bi si barkè S touba thia kaw sa kanam 🥰
@mayarassoul14942 жыл бұрын
Merci Dakar buzz merci fadel yalla na la yalla faye thi barkep seydina Mohamed (psl) merci aux donateurs akk sénégalais you barri yeurmande yii
@ollaid2 жыл бұрын
Machalla il a repris forme.. vraiment merci a ceux qui l'ont aidé.
@maryamadiakhate822 жыл бұрын
ohhh bilay💗sed na fèlicitation fadel yalla nala yalla fayal bopam
@natachadiallo38602 жыл бұрын
Ay way sama khol bi sédd na machallah yalla na yokk
@papeassanebadjibadji7busin9392 жыл бұрын
*BISMILLAHI TAWAKALTOU ALLA'ALLAHI WALA KHAWLA WALA KOUWATA ILLAA'BILLAH* Une prière Divine qui te protège au quotidien. J'en ai vu des preuves/ YALNANIU YALLAH Saameuh Té Saameuh suniu njaboot.
@mariehelenebodian70742 жыл бұрын
Alhamdoulilah machallah ohh sama khôl fesna dama contane bimako djissateh