moussa yaw dama begg si yaw ndakh si deug rek gay dokh kendu wakhni figa far te analyse bou logique gay def moussa il faut gnu defarate imagou lambe ndax li kenduko rafetlou signu culture il faut gnu defarate ko meun ko exporter bitim rew ba toubab yi gname gneuw investir pour lambe geneu jeum kanam