Serigne Moustapha Sy Voici la réponse émouvante de la fille de Serigne Mansour Sy Borom Dara J AMIRA

  Рет қаралды 553,680

Dakar Clic Medias

Dakar Clic Medias

Күн бұрын

#
ABONNEZ- VOUS------------------------------------------------------------------------------------
REWMI24 Tv vous fourni un travail de qualité et sur-mesure à la hauteur de l’attente de ses clients. L’agence de l’équipement adéquat à toutes votre disposition.
REWMI24 Tv intervient dans plusieurs domaines d’activités à savoir :
~ Production vidéo, à savoir: sketch, publicité des émission, couverture événementielle, film d’entreprise, le long et le court métrage, documentaire, clip de musique et de l'infographie.
------------------------------------------------------------------------------------
E-mail : rewmi24tv@gmail.com

Пікірлер: 954
@omardrame9287
@omardrame9287 4 жыл бұрын
yalna yalla bolé wa tivaoune si diamm si barké baye niass aminnn😢😢😳😳
@moustaphamboup3097
@moustaphamboup3097 4 жыл бұрын
Bilay ma beugue sama touro do bilay serigne Moustapha sy maka beugue mo raw népou bayi léne tongne ❤❤❤❤❤ kou beugue sama Toura do défal j'aime
@claramendy3336
@claramendy3336 4 жыл бұрын
Paix dans la famille du Khalifa Sy ! Dieu apaise le coeur des hommes, nous n avons que toi pour nous guider. A la grâce de Dieu
@DieryServices4263
@DieryServices4263 4 жыл бұрын
Merci Madame
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@ahmedbachirgueye2974
@ahmedbachirgueye2974 4 жыл бұрын
Ana Soutoura wéranté bakhoul naniou neube yi niawyi Dioulite daye rafétal aye Yallah li niawna ! Yallah na Yallah sakhal diame thie Famille ELhadji Malick Sy ( R.T.A)
@geuyefamily6807
@geuyefamily6807 4 жыл бұрын
Serign babcar sy mansour yall'na yalla yagal kofii loll barké seydina moukhamét psl
@taphadiallo1091
@taphadiallo1091 4 жыл бұрын
Amine
@cheikhdiop3835
@cheikhdiop3835 4 жыл бұрын
Gueye family. kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@mohameddiop2014
@mohameddiop2014 4 жыл бұрын
Serigne Mbaye Sy Mansour yalla nafi yague tei weure 🙏🏾AL Khalifa ❤️
@cheikhbi2056
@cheikhbi2056 4 жыл бұрын
Oumoul Amira la Lionne de Serigne Mansour. YALLA na YALLA dolli Jamm TIVAOUANE.
@laminedioppikinerue105
@laminedioppikinerue105 4 жыл бұрын
Amine ya rabi
@Maguichoumar
@Maguichoumar 4 жыл бұрын
Allahouma amine Way
@mamekhalifasy7767
@mamekhalifasy7767 4 жыл бұрын
La lionne bly....kii khamoule thiahane kou weddi ladj ma😀😀
@xudamulxadimxeexakwakhaabi3565
@xudamulxadimxeexakwakhaabi3565 4 жыл бұрын
@@mamekhalifasy7767 mbaadu xam nga si Dara
@mamekhalifasy7767
@mamekhalifasy7767 4 жыл бұрын
@@xudamulxadimxeexakwakhaabi3565 bly demm naa tivaouane ba guiss ko niou tokk di wakhtane mais srx amoule thiakhane....daa donn bayame serigne MANSOUR SY
@DioufMaodo-wr4oo
@DioufMaodo-wr4oo 2 ай бұрын
Yalanako yalla yeureum xaréko firdaosssi diarama sérigné Moustapha sy
@al-futiiyutv_TBD
@al-futiiyutv_TBD 4 жыл бұрын
Waaawww. Ben Tiwaoune rek mo am, té moy bou Mame Mawdo Malick, khalif di Serigne Babacar Sy Mansour.
@alassanendiaye1864
@alassanendiaye1864 4 жыл бұрын
Merci sokhnasi sy dathiye bakhe nak c bon awe ki momoul nit yi way
@mamadoudiouf6260
@mamadoudiouf6260 4 жыл бұрын
Xolalma li rék kunéka ngi khawi sa suture morom. Seytané begna lool fanyi. Wayé yalla na sunu borom fay bi tiow si barkép serigne touba.
@aboumansourniang4771
@aboumansourniang4771 4 жыл бұрын
Elle vient d’avouer que son père pratiquait le khërëm. Wallaye ndeyssanne !
@ousmanediop6119
@ousmanediop6119 4 жыл бұрын
Amiine
@mayadandiaye500
@mayadandiaye500 4 жыл бұрын
Fannn n'alla machallah sama mame la khass nako nieuppp bayi akk yallla😭😭😭😭
@thiatouyayamxaritoupapam111
@thiatouyayamxaritoupapam111 4 жыл бұрын
Ay way arrêter ça 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭Tarikha tidiane sokhlawoute li on veut retrouver notre tarikha sougnou mame El Hadji Malick djangualougnou li 😭😭😭 j’ai mal trop mal
@mohameddiop5380
@mohameddiop5380 4 жыл бұрын
Tarikha tidiane kay amoul problème séne famille gno ame problème lidiatilene séne problème ta guénési tarikha bi
@momodioufy3220
@momodioufy3220 4 жыл бұрын
Thiatou yayam xaritou papam tarikha Tidian meussouta ammm problème té yittt douko moussa amitttt probléme famille ak tarikha bi c diamétre ma opposé tarikha bi akkka yatou khipi len sen beutttt teyyy khôl
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
@@mohameddiop5380 kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
@@momodioufy3220 kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@gueyeabdou8849
@gueyeabdou8849 9 ай бұрын
Sama yonne nekku thi Sonko moÿ sma Serigne Yalnafii Yagg
@yacinesouare6413
@yacinesouare6413 4 жыл бұрын
Kérok dama 😭😭 si wakhou sérigne Moustapha m yalla bakh na alkhamdoulila Sante Serigne Babacar Sy rek khalifa bi yalla nafi yague t wére
@mamediarradiedhiou6402
@mamediarradiedhiou6402 4 жыл бұрын
Amine
@mamadou3723
@mamadou3723 4 жыл бұрын
Amine
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@mallbelly8250
@mallbelly8250 4 жыл бұрын
Sa khalifa bi bane khasida lafi binde khamoul tous
@OuseynouMbaye-fc1ev
@OuseynouMbaye-fc1ev Жыл бұрын
Yalla n'a yalla indi djamou thi djabotou maoulana cheikh Malick Sy thi barké maoulana cheikh Ibrahima Niass
@senegalvillagetvdiop5152
@senegalvillagetvdiop5152 4 жыл бұрын
Machalah me dalle al lou mena am wah dafa am place bou ameh ak blem ci bire famielle bi nako lidjiane ti ci bire famielle wame te bañko wah ci bir talubeh yi
@fatougueye9102
@fatougueye9102 4 жыл бұрын
Machallah Sy Malik longue vie amine yarabi au NOM de NOTRE PROPHET MUHAMMAD PSL
@elhadjibadiane344
@elhadjibadiane344 4 жыл бұрын
Naniouko nianal yalla délossi watt xélam bamou weulbatikou topou si aye guinaw bayam insha allah
@mallbelly8250
@mallbelly8250 4 жыл бұрын
Serinie Moustafa khalifa bi rawouko bamou koy topou
@mallbelly8250
@mallbelly8250 4 жыл бұрын
Wakh ma bane khasida lafi binde
@jeanmariekenndiaye4428
@jeanmariekenndiaye4428 2 жыл бұрын
Vous êtes une seule et unique famille. Ton rôle toi fille doit être d'unir la famille notamment les jeunes.
@lobsobservateur5375
@lobsobservateur5375 4 жыл бұрын
Ce que je l'habitude de dire à chaque fois, kham kham ak daraja deffeu wara andak yarr ak teguine wasallam
@talibebayamcisse5058
@talibebayamcisse5058 4 жыл бұрын
Ma tegal la ci ak ragal Yàlla sinon mu sonal Boroom
@cissejarod
@cissejarod 4 жыл бұрын
Ragal yalla te bagnko bocale AK ken
@bachirdiene7541
@bachirdiene7541 2 жыл бұрын
Fier de Serigne Moustapha Sy
@datly44
@datly44 4 жыл бұрын
Que Dieu le Tout Miséricordieux accorde la paix entre les descendants de la famille Sy adouna amoul solo wakhtane lène ba djoubo Yaye boye
@Del2Mas
@Del2Mas 2 жыл бұрын
Yow amo Respect sisa bay Serigne cheikh . Amira Do Dara nohoul feule yow guay djiguen wara defar SI yiw gua Tok Fi fen liguay wah Dara dousi deug
@mbenguemohamed8395
@mbenguemohamed8395 4 жыл бұрын
sokhna amira kagne Nga wérr bay khasté iow ci décès Serigne abdou bi rek Nga done khoulol s mb sy Mansour té iow sakh si sa bire wakh né Nga sokhna Sophie dème apré si fin bi Nga ni sokhna astou kane Amira ki es ti
@serignebabacarsyndiaye1546
@serignebabacarsyndiaye1546 4 жыл бұрын
Kii kañe boko hamei reik wakh mako
@manchoufaye6265
@manchoufaye6265 4 жыл бұрын
Jahal nama
@ndeyetalibekhalifaababacar8634
@ndeyetalibekhalifaababacar8634 4 жыл бұрын
Serigne Babacar Sy Mansour YALLA naa fii yaagu tei weurr
@dechibafall5630
@dechibafall5630 4 жыл бұрын
Sokhna amira sy wérale amale diame goudale fane 🙏💚
@moustaphadiagne4278
@moustaphadiagne4278 4 жыл бұрын
Yallena yalla delo si diam si famille yi réro yeup
@cissebabs8961
@cissebabs8961 4 жыл бұрын
Mes respects Amiral parfaitement raison ki dara diapoul ko loudoul bone ak sokhor
@ArameDiop-gp8fz
@ArameDiop-gp8fz Жыл бұрын
diarama serigne moustapha sy❤❤❤❤ l
@ndeyesalioundiaye3119
@ndeyesalioundiaye3119 4 жыл бұрын
Thiey yarabi 😭 😭 😭 😭 😭 mandee dama tiit te rouss niemantii khalif bii ndeyssan 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 mouride la dee m suis de t cœur avec le khalife 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@adjafall2536
@adjafall2536 4 жыл бұрын
Danga bakh machallah
@bakhalil3573
@bakhalil3573 4 жыл бұрын
Yalla nala serign touba takhawou
@gueyeastou5385
@gueyeastou5385 4 жыл бұрын
Yalla nalaa yalla deef deug deug talibé serigne touba yaa baak
@mamadou3723
@mamadou3723 4 жыл бұрын
diadieuf
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
Bayilen di wakh moridla ak tidiane la
@bnbezofficial1376
@bnbezofficial1376 4 жыл бұрын
Bilahi serigne moustapha molay geuna goudou fane
@adjandiaye7202
@adjandiaye7202 4 жыл бұрын
Machallah sy malick yalna yalla yokou diam dji ❤🥰❤🥰❤🥰❤🥰❤🥰❤
@ndiemediouf222
@ndiemediouf222 4 жыл бұрын
Problème bu commencer 1957 nganii 2020 nga kaay regleii koon weroo
@khalifaseck3351
@khalifaseck3351 4 жыл бұрын
Ki fene rek wakhofi dara demal Serigne Moustapha sy diagala mogeune si yaw bamoulene Di raw yaguena
@thiammbaye3602
@thiammbaye3602 4 жыл бұрын
Talibé day yam place talibé souniou thiofél ci ndiabotou maodo leu dieum mais dou ki wala ké. Talibé cheikh day mandou Wa salam🙏🏽
@khadykounta7255
@khadykounta7255 4 жыл бұрын
Salam macha allah merci
@cheikhtidianetoure7197
@cheikhtidianetoure7197 4 жыл бұрын
Ma khalla ligène di woté ngène atanoul khalifa général Tidjan mo takh li yeup am boulen sisou baye Niass khadioul thi gunaw ken fek topolène ki yalla dital thi adouna bii dolen djouk thi lii baye moy khalifa CHEIKH TIDIANE ❤️
@elhadjindiaye9632
@elhadjindiaye9632 4 жыл бұрын
Nga balma yaye boye nguir yalla rek boul topp ki yalla guis na lep
@FatouNdiaye-xx5ri
@FatouNdiaye-xx5ri 4 жыл бұрын
Thiéyy Serigne Moustapha kouko bagne dégayy sonn reyy
@tresortirera2093
@tresortirera2093 4 жыл бұрын
Cc j'aime le discours ms elle la fait une hereure ndakh champ de course Serigne cheikh moko fondé difa gamo Kone boné dafa khégne koufa diouly amo diouly yagui wakh loula nekh boy wakh wakhal ak Serigne Moustapha ms pas l'étirage parck Moustapha Mack gni nio wakh Serigne cheikh mou diokhko dayira mourchid Serigne Moustapha mm si il la fait erreur courigeko mom ms pas le dayira
@bourguibafaye8521
@bourguibafaye8521 4 жыл бұрын
Dieureudieuf sokhna sy
@cheikhenglishlo9121
@cheikhenglishlo9121 4 жыл бұрын
Ndeysann fekk ko xamné ay nagame nann si woulll nguén diko fi dougall vive Serigne Moustapha sy ♥️
@sunucoeurtv3842
@sunucoeurtv3842 4 жыл бұрын
Vive moustapha sy bakanou mbam
@cocottendiaye1944
@cocottendiaye1944 4 жыл бұрын
*Sa voix😭😭😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️SyMalick*
@zoooaam
@zoooaam 4 жыл бұрын
Alhamdoulilah, audio bi takhna ma gueuna diapeu Serigne Moustapha SY. Serigne Moustapha kay limouy wakh leupeu deugue la. Dégalma ndawsi lou gnakkeu solo li mouy wakh rekkeu. Alhamdoulilah ma ngui sante YALLAH bamouma nguindé.
@moustaphandiaye1219
@moustaphandiaye1219 2 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Moustapha sy maktom
@CheikhomarHane-ed1mk
@CheikhomarHane-ed1mk Жыл бұрын
Dieureudieffé Serigne Moustapha sy Malick
@fatimatambaye9116
@fatimatambaye9116 4 жыл бұрын
Mâcha alla sy demba 🥰
@serignendour7915
@serignendour7915 4 жыл бұрын
Contac merci sokhnaci
@matardiouf71
@matardiouf71 4 жыл бұрын
Machala amna solo khalifa bi yalnafi yague ak weer
@fallam1010
@fallam1010 4 жыл бұрын
wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete
@gueyesokhnaaissata6693
@gueyesokhnaaissata6693 4 жыл бұрын
Yenn nie di khass Serigne Moustapha Sy Lou Bonn senn thiotou ndayee
@kyabussinesswoman7094
@kyabussinesswoman7094 4 жыл бұрын
Sa leufal ndaye dmrm
@gueyesokhnaaissata6693
@gueyesokhnaaissata6693 4 жыл бұрын
😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@instagramsecurityhelping1095
@instagramsecurityhelping1095 4 жыл бұрын
Machallah sokhna si
@tourekhar4111
@tourekhar4111 4 жыл бұрын
Merci amira que dieu vous bénisse
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@youssoutoure2834
@youssoutoure2834 4 жыл бұрын
Ma bègue Serigne Moustapha sy al mactoum 🙏🙏🙏
@atoumanefaye6603
@atoumanefaye6603 4 жыл бұрын
kone dh yereum nala
@fatousarrgaye1194
@fatousarrgaye1194 4 жыл бұрын
Sokhnassi magui ziar .wanté yènenabok té Aÿ nit daniouy tanenté dah yonenbi psl bania fayoneté larawé nieup.bolènetah niou rétanlène.guiryala délène halage"" konopi mothieu" wahi yoneneta la psl
@momofall9721
@momofall9721 4 жыл бұрын
Merci yaye boye
@mouhamedkounta9819
@mouhamedkounta9819 4 жыл бұрын
salam maneu dhé khadirla magui gniane sama mbook yii book thi tarikha tidiane fi tiwaoune .. guéneu rafétal thé bayii wakh yii guéneu di wakh ndakh gniléneu sope barké serigne Babacar sy ndankh gnouneu tmt thi lagnou book koneu guir yalla bayil léneu lep tay diélalé guir yalla guéneu balma nak wa salam
@fatyfall7362
@fatyfall7362 4 жыл бұрын
Machalla sy Malick 💖
@amadoumboup2270
@amadoumboup2270 2 жыл бұрын
Dieurediuff sokh nasi
@ngagnemboup8841
@ngagnemboup8841 4 жыл бұрын
Vraiment képou kouy tidiane da ngeu am gathia billahi Mane damay took bam yague mani diamano dji djiémal kham sa diné bou wére di diamou yalla bou wére diartoul ngeuy djiokou si béne serigne ndakh moy lolou billahi sama xol dfa djiékh
@ahmadoufaye7047
@ahmadoufaye7047 4 жыл бұрын
C vrai dé fi guissouma fii dîné dh nioune talibéyii naniou kholat sougniu bop té djamoudji yalla dama rouss
@mkmk481
@mkmk481 4 жыл бұрын
No mai tijane tivaouane key Hanna. Coz nous les autres tijane ça ne nous concerne pas.
@Salam16488
@Salam16488 4 жыл бұрын
En réalité les tarikha nous empêche de mieux pratiquer la religion. Ça ne va pas durer ils ont perdu le contrôle. Seul la sunna est garanti par Allah pour l'éternité. KHÉLOULÉN
@ousmanenoreyninoreyni5996
@ousmanenoreyninoreyni5996 4 жыл бұрын
@@Salam16488 yaw boul wakh les tarikha dh yamal si sénn tarikha Babou mom Nga kham boul togne
@omardrame9287
@omardrame9287 4 жыл бұрын
bamou désse wa keur baye niass dieurdieufé baye niass
@alaminesylo2680
@alaminesylo2680 4 жыл бұрын
Sy malick nga balma mais djoumnga d fofou d mbousou ndakh sax doufa takhawalou nak geumlen yalla serigne limiy wax wax nako baparé deweun ngén kay guisat tivaoune inchallah yalla na yalla doli diamou
@benbib365
@benbib365 4 жыл бұрын
Serigne moustafha bou Dakar bou dewene mou khasate kenene bayiwoul kene dou baye dou papa kou wodo lamigne so nope raflé
@satoucisse9432
@satoucisse9432 4 жыл бұрын
Mom buz ak comédie lay def
@alaminesylo2680
@alaminesylo2680 4 жыл бұрын
@@benbib365 hihi mom kay limoy am amnako baparé adouna fo dem khamnagnko waxal rk t yalla takh
@mountagaadamatall8540
@mountagaadamatall8540 4 жыл бұрын
Certaines révélations ne doivent pas se faire dans les réseaux sociaux. Bien vrai que nous sommes tous contre les paroles de Moustapha sy mais c'est pas en racontant des histoires passées au saint de la famille, qui règle le problème . Croyant qu'on est entrain de blesser l'autre alors qu'on entrain de blesser tout une famille .On a toujours été une famille solide . La tariha tidjania a toujours servi de leçon à tous kéneu moussouniou dégeu si ay détail . DC laissons pas les ennemis se moquer de nous (wakh bou yégeu dof moko mom) . Pr finir Serigne Mbaye Mbaye sy mansour laniou âme té inchallah guissou niou louy takh niou wédi KO. DC naniou bayi tiow lii té bayi Moustapha sy Yalla dinako fadial bopam🙏
@babacarmbaye1805
@babacarmbaye1805 4 жыл бұрын
Masha allah ya yallah yockou diamou si sounou dinee
@cissamy9775
@cissamy9775 4 жыл бұрын
MashAllah merci beaucoup que Allah renforce notre croyance🤲🏾🤲🏾🤲🏾🙏🏾🙏🏾
@aldamesarr6697
@aldamesarr6697 4 жыл бұрын
Iow Amira Amo respé té serigne Moustapha sy d'où sa morom yaw amira yay kanne do dara
@cheikhniangfall5599
@cheikhniangfall5599 4 жыл бұрын
je veux que tu dis a sérigne moustapha sy qu'il n'est rien et qu'il respect les gens car si non il va voir...
@FrancijFrancij
@FrancijFrancij 4 жыл бұрын
Machala amira machala amna solo tropp dieurdieuf
@tawfiikhcheikhbi3161
@tawfiikhcheikhbi3161 4 жыл бұрын
Yalla na yalla déf jamou ya rabi
@OmarOmar-cu3du
@OmarOmar-cu3du 4 жыл бұрын
Sokhna ahtou kane koubakh té cele 😭😭 yawe ya bone
@maremefaye3146
@maremefaye3146 4 жыл бұрын
Yaw dh Serigne Moustapha s'y makhtoum molo guene fou
@cheikhly3893
@cheikhly3893 4 жыл бұрын
Sokhna Amira rousale sa mame Serigne Babacar SY Mansour mbété mbété gor la garmila seute Mame Marahm Mbacké niariyone Mame Elhadji Malick RDL ak Sohna Safiyatou Niang.
@Alkhalifaababakrin96
@Alkhalifaababakrin96 4 жыл бұрын
Kifi euppou kham kham si tarikhabi champ de coursou ba la dane gamo.
@khadyfall3909
@khadyfall3909 4 жыл бұрын
Walae ndeyssane
@boubafall1014
@boubafall1014 4 жыл бұрын
Merci yaye Amira
@aichakane1167
@aichakane1167 4 жыл бұрын
Wakhena lou niawe wayé ya wite wakhe nga lou eupou ndakhe ndakhe menone nga sè rousse serigne babacar wala al amine wala pape malick s’y ryth
@mamadoumbaye9872
@mamadoumbaye9872 4 жыл бұрын
Yalna yalla doliniou soutoureu té mousseul niou si cheytané, amine
@adioumaniass1098
@adioumaniass1098 Жыл бұрын
Amine
@elhajibiranesall8510
@elhajibiranesall8510 4 жыл бұрын
Famille mi yalla defsi diam
@badoundiaye6275
@badoundiaye6275 4 жыл бұрын
Néna serigne Moustapha diangoute😂😂😂
@sigadoumbia97
@sigadoumbia97 4 жыл бұрын
Oh franchement il faut arrêter nak vous avez révélé des secrets que nous n’avons jamais su nous les jeunes adouna Amoul Sollo li Rafetoul ci Degg degg
@adamandiaye4646
@adamandiaye4646 4 жыл бұрын
Machalah sokhna amira
@aminakane3214
@aminakane3214 4 жыл бұрын
Aye waye dou wakhou fii naniou mougne té khamni yalla ,wakhoul kéne darra
@cheikhtidianed
@cheikhtidianed 4 жыл бұрын
En tout cas Serigne Moustapha ay résultats wam niép guis nañ ko Lim déf ci tarikha bi kén ci yén défouko ci ignan rk mo lén diap
@wakhalsamarewmi2766
@wakhalsamarewmi2766 4 жыл бұрын
wala loumou defal buppam way defaloko tarikha bi
@manchoufaye6265
@manchoufaye6265 4 жыл бұрын
@@wakhalsamarewmi2766 en bon ? Tamnagne ko jiko soul 1000 jeuf you bah ndah 1.. sen jikola
@manchoufaye6265
@manchoufaye6265 4 жыл бұрын
Yalla lako taha wah 💖. Hasida Mame yi taysir Hylas... Cadets bo feug mou tarilla len firil lako lep ci lohom.. Yalna yalla guoudal say Fan may la weur ak weurlé sy Malick ❤️🙏
@cheikhtidianed
@cheikhtidianed 4 жыл бұрын
@@manchoufaye6265 walay nday saan chaque jeudi rabountabara bi diouli ci 5 continents yép vendredi kharatoul dioumah bi niki nonou li kou nékoul nafékh mangako sédé Jarama Serigne Moustapha ♥️
@cheikhtidianed
@cheikhtidianed 4 жыл бұрын
@@wakhalsamarewmi2766 kon yow wéro
@abdoufaye1909
@abdoufaye1909 4 жыл бұрын
Sokhna Amira nga balma wayè yangui beugueu nouro ak Moustapha. Liii waroko wakh fiii
@hawabathily4291
@hawabathily4291 4 жыл бұрын
Quelle direction prendre, où on va avec tout ceci ? Mon dieu donne nous le discernement pour pouvoir contempler le spectacle de notre Moi dans sa réalité précise, ne permet pas à l'ego d'obliger les citoyens à agir contre les impératifs de leurs consciences, garde nous de l'orgueil et de l'arrogance, fais que dans le monde chaque chose soit rangée selon l'intensité de la lumière qu'elle dans son intérieur. Seigneur des Vertus inspire nos Religieux, Spirituels (censés être les gardiens de tes normes, les exécuteurs de tes lois, les constructeurs de ton Univers harmonieux, ceux par qui tout ce qui a été créé puisse subsister.) ne tombent pas sous l'influence de médiocres, d'ignorants ou de pervers, donne leur des conseillers bons et généreux pour que notre pays demeure un exemple pour les nations et les peuples. Libère nous des tyrans, des ambitieux et des gens obscurs, d'où qu'ils viennent, car tu es en nous la Voix qui annonce la défaite du pouvoir des ténèbres et la Victoire de la Lumière. Que le meilleur soit avec la Paix pour tous. Amour et Gratitude à Allah S.W.T ! 🙏🏽☪️🤍💚
@papediop8064
@papediop8064 4 жыл бұрын
Machalah sy Malick 🙏
@mamediaraseye3746
@mamediaraseye3746 4 жыл бұрын
Yena bokou sene mame khadiou nousi barke seringe saliou na Lepou rafet
@aidaastoundiaye7495
@aidaastoundiaye7495 4 жыл бұрын
Feneu gua féneu reyyyy Sokhna astou kane dou déf lolou serigne cheikh raw ko si adouna yaw d méritèeou sant sy
@papelamineseye4161
@papelamineseye4161 4 жыл бұрын
Yalna diame yague
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@matarmbengue1528
@matarmbengue1528 4 жыл бұрын
Nga beugueu wakhe ni linga wakhe deugue leu té lii Serigne Moustapha wakh amoule mei Amira ko yappp
@دفراتسنغال
@دفراتسنغال 4 жыл бұрын
Sa yaye thiagua la. Legui kone deuguela d han
@assatoubanesamb5874
@assatoubanesamb5874 4 жыл бұрын
Wouy magui dé 😍😍😍😍😍😍😍♥️♥️♥️♥️♥️😀😀😀😀
@modouniass8093
@modouniass8093 4 жыл бұрын
Boul si khas serigne cheikh Serigne cheikh moy tarikhatoul tidiania yaw nak tamite wéro dee a 100% dé
@ousseynouka3963
@ousseynouka3963 3 жыл бұрын
Sérigne Moustapha sy mon rawe sa mbaye s'y xam xam amon loko wakh, seytané by gua done ,
@ToubaVisionToubaVision
@ToubaVisionToubaVision 4 жыл бұрын
Thieuy Saytané Togal Foumou Khadioul Réck Lay Douckou Innamal Mominona Ikhwatoun Fa Aslihon Bayna Akhaway Coume
@laminedioppikinerue105
@laminedioppikinerue105 4 жыл бұрын
Seytané nite la déh . Moustapha Sy sila bokhou seytané bou bonla
@deugdouroumbnop1434
@deugdouroumbnop1434 4 жыл бұрын
@@laminedioppikinerue105 wakh ko si kaw
@karadio692
@karadio692 4 жыл бұрын
Yénn gñi koulénn yéss amoul Rambatjj rekk
@karadio692
@karadio692 4 жыл бұрын
Touba vision si familles diambour sa yone nékoussi Sénn keur mo 1peu Prblém séytané conard
@Le_Natron_
@Le_Natron_ 4 жыл бұрын
Le Pays est entrain de Foutre le camp 😭😭😭. Où est Dieu dans tout ça !?
@iniiabdalahi4049
@iniiabdalahi4049 4 жыл бұрын
Macha alah sy abb doff kéneu douniko ya môme singa bok ngakay wakh
@mamadouseck3203
@mamadouseck3203 4 жыл бұрын
Moustapha SY est principal fautif, il ne fallait pas parler ainsi
@assmbaye1019
@assmbaye1019 4 жыл бұрын
Yalnako yalla soppi niite day am kilifa
@fallam1010
@fallam1010 4 жыл бұрын
wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete
@amathndiaye7962
@amathndiaye7962 4 жыл бұрын
Comédien laa
@papasy3679
@papasy3679 4 жыл бұрын
Merci Maman Amira Sy
@assanendiaye2483
@assanendiaye2483 4 жыл бұрын
Yallana yalla déf diamou thi réwe mi mbokou yi nanou moyetou yéne vidéo yi ak yéne kado yi d'Ay yakh mbok gui d'Ay yakh tarikha bi d'Ay yakh dinédji yallana yalla tapé khôl yi
@maneleye8829
@maneleye8829 4 жыл бұрын
Bonjour
@gadiagacheikh8559
@gadiagacheikh8559 4 жыл бұрын
Blh
@ibrahimaseck5020
@ibrahimaseck5020 4 жыл бұрын
😏franchemt yi diarouko koi. Wax diou bone deukoul famou dieum🤦🏾‍♂️ Yalla na yalla doli soutOureu ci tarikha bi ak ci reiiw mi ak ci aduna weurnGueul keup🙏🏾
@cheikhbeye9619
@cheikhbeye9619 4 жыл бұрын
Aye waye sagal lène séne mame tei bayi wakh dji
@taruland
@taruland 4 жыл бұрын
Merci beaucoup amira, weroul , ki mounee guisna yallah !
@DadaCeey
@DadaCeey 4 жыл бұрын
Alaaahu Akuubar ! Yanguii dougal sa bopeu deii. Sokhna Astou Kane ngay dugal ? Sa papeu modane raw serigne cheikh ? Je croi pas que c'est amira 🤔 Yaw Serigne cheikh senegal nieupa xamone neiikh kheilam. Serigne moustapha mii xamoul alhourane nimuy diangalé ay talibé yukoo meune té gueune ko mokal mboleiim talibé nagn mandou kone deii serigne waxxna deug bagnel bi yagana. Demal fadji sa rap bi mo gueune so bayii wul serigne dinga yaga danou yeussire.
@sunucoeurtv3842
@sunucoeurtv3842 4 жыл бұрын
Moko raw fouf motakh mou nék patron daradji niou nane ko borom daradji
@DadaCeey
@DadaCeey 4 жыл бұрын
Yaw naak baa yang leine di dieiima rao 🤔
@albaraka4111
@albaraka4111 2 жыл бұрын
Na lathtè lii takh mamame astou seck tendioul seriigne babacar sy
@bathieniang1334
@bathieniang1334 4 жыл бұрын
Soura yalla yatouna d'oùmala totou bilahi nk lithie kanam soriwoul
@evatra9396
@evatra9396 4 жыл бұрын
Dieureudieuf 👍👍
@fatimadiop1692
@fatimadiop1692 4 жыл бұрын
kzbin.info/www/bejne/eXexfmOwat-fibc
@morgueye2635
@morgueye2635 4 жыл бұрын
Machalla seringe Babacar s'y Mansour yalla nafi yague ta werr
Voilà La Réponse de Sokhna kiné Dabakh a Serigne Moustapha Sy
25:50
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 46 МЛН
Accompanying my daughter to practice dance is so annoying #funny #cute#comedy
00:17
Funny daughter's daily life
Рет қаралды 28 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 21 МЛН
Serigne Abdou Sy ibn Serigne Cheikh Ahmed Tidiane Sy Al Makhtoum😭😭😭
18:05
Serigne Abdou Sy répond à Serigne Moustapha Sy
12:54
STARTELE
Рет қаралды 92 М.
les éclaircissements de Serigne MOUSTAPHA sy AL amine
14:16
AL ÂBĀ-I TV
Рет қаралды 263 М.