Franchement wa fass ils sont forts en communication
@papafall89056 ай бұрын
Machallah WAKH BI RAFET NA ❤
@mamemalicksarr-ci5bx6 ай бұрын
Serigne ndiaye yangui baap eumeu sene dei
@AdolpheGomis6 ай бұрын
cou dacord ni franc est le meilleur lutteur du mois de mai juin-juillet aout septembre ba décembre😂😂😂 lalale j'aime
@karbalaweuz99566 ай бұрын
Machallah yalla na gua doon roi dès aréne mé wa cedeao mome bayillén gniouye wakhe
@elhadjiibrahimadiatta94856 ай бұрын
Merci beaucoup Champion
@Capsiladeuk6 ай бұрын
13 victoires Franc yi yangui si vraiment nopil. Goor gorloul nieuw dap ko champion nga warna meune nek.. mais bayil larabinane ay eum sa mak leu pour Am combat 😭promoteur yi weurougn li bayi si khel.
@moussapayemane41676 ай бұрын
Franc dane nako mais manouko,dacor nga si lolou,Franc bimou beuré ak sokh baparé moudém mbapate,sérigne ndiaye 2 yénouko touti mou rayko 😂
@khadimdiouf76186 ай бұрын
@@moussapayemane4167franc dane nako 6 fois lutte simple daneko lutte avec frappe aussi donc diaroul beurri wax
@moussapayemane41676 ай бұрын
@@khadimdiouf7618 bingané 6 fois la ham né féne kat nga,sénn rencontre si lutte simple ba,manomasi wah dara,fép founiou dadié mangui sibir arène bi togue di sétane
@tarkindabi41686 ай бұрын
Franc nak ýeungeul neu lamb ji dh😂
@Bilal668506 ай бұрын
Journaliste bi il est très fort et calme chapeau 👍
@lahaddione18146 ай бұрын
Bilahi ki ndakarou nieuppa wara bolè dolèl ko ki Moy mbeur mi💪💪💪
@bachirdiop196 ай бұрын
Franc batay dépassé woul Eumeu si sport rek la wakhé
@hakimytb45966 ай бұрын
Amoul yar lala wakh
@morseye80236 ай бұрын
Communication yereumta lou bii ngen xewal legui pour berei. Amlen foula grand yii diekhal nan ba parei. Fou ay door derett di guene respect amou faaa. Sou diekhé nak ngen wakh wakhou respect
@hakimytb45966 ай бұрын
Yaw mome moussooo
@papakasse7956 ай бұрын
Machalah Serigne ndiaye ❤
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Ils me fais rire coi ils commique bien c'est des politiciens coi sport de combat da sokhla chaleur avant et pendant 😂😂😂 nékhal laté coi😂😂😂
@andrendione90216 ай бұрын
Saway franc wahoul Lou graw . Yéne franc yaganaléne niousss ci mbapatt ak ci arène bi. Franc manquéwoul respect limou wahhh dayy diayy combat en plus sa pousse eumeu a réagir
@moussapayemane41676 ай бұрын
Franc kane la niouss si mbapate,Reug Reug niousko 14 ba derniere moment bi pour moudém mbapate day calculé
@shabazzpiru6 ай бұрын
Reug reug mo niouss Franc plus de 15fois, ya même qui disent que c'est 18fois..😂😂😂
@maguettediagne22056 ай бұрын
😂wa cedeao borom défaite tou mbapat you baryyy yii
@mbineyalanetv55716 ай бұрын
Machala il communique très bien les lutteurs doivent apprendre a communiqué
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Il veule prendre la place de ipau ngari wala Lamine samba mou nane communique bien li dou daïra😂😂😂😂
@SneijderJunior6 ай бұрын
Serigne ndiaye meuno wahh ba franc djieul l😂😂 Deil mar tatou eumeu sene rkk pour beug beurrei Lolou gnoune dougn ko dff
@riusjea6 ай бұрын
Tiogou leu aye markatou tate laniou
@moussa12576 ай бұрын
Machalla champion ❤❤❤
@emmanuelsarr40316 ай бұрын
Yow Frank lim la wone,non bayilén boy bi,dou sén adversaire
@moussaseye34396 ай бұрын
Wakhou seytaner rek franc wakhoufi dara li motakh sport senegal dou dème
@ElhadjiNiang-so9nh6 ай бұрын
Legui do champions d'Afrique ak dinala doumeu dinala dane lane moci manqué de respect li ngueini wax delen ķo xol
@Maramsamb-kd9uz6 ай бұрын
Merci Serigne Ndiaye 2 Yar Mom Loumou La Mayoul Doula ko khagne
@Mouhamed-vz7hy6 ай бұрын
Kou bagna daanou boul dieul franc 😂 nakhane té amoufi 😢😂
@Aki_Jr.6 ай бұрын
Na diel doudou Sane khool
@ndiamegueyesopeyserignebab49906 ай бұрын
Na dieul gris 2 khol😅
@thiernodembaya83556 ай бұрын
Fram et eumeu sene où sa thies 🤔🤔🤫🦁
@ndiamegueyesopeyserignebab49906 ай бұрын
Gris 2 vs fran moy combat bi
@falydiouf77466 ай бұрын
Grand champion
@babsdia15056 ай бұрын
Wadji aka mo fan serigne nidiaye
@ABAKARA-q8o6 ай бұрын
Très bien Serigne Ndiaye 2 vraiment kou digne gua seye parole machalha rafetna wa pikine nieupeu naguou nagniou sa combat yak eumeu sene dakh yaw dagua am yarr le futur rois des arènes Serigne Ndiaye 2 coryass
@IbrahimakhalilNdong6 ай бұрын
Yaw katal ndem feulé ak yarr lamb la bayiléne ndey seytané eumeu séne bou dieulé franc franc DEUG ndem bamou teud si soufff
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Parce que mo geuna noye thi yéne😂😂😂😂 wiri wiri rék ak franc fi ni dina lérrr
@walyfaye49596 ай бұрын
@@IbrahimakhalilNdong boye sa commentaire bi yeup saga leu , waxal xam xam, et domu sererer xamé wounko indiscipline
@IbrahimakhalilNdong6 ай бұрын
@@walyfaye4959 pardon dhé grand deuk bi mo deri nafék way
@MomoSeck-zd4bt6 ай бұрын
Saway lambj leu nak franc niakoul respect kén lambj dale légui affaires yambarr la quoi franc dafa déff loutah mou wara beuré ak diambar yii
@mouhacoly81206 ай бұрын
Pounkaal bu tolni ioe gananeu sama papeu Aziz ndiaye no xaliss meune na lounei 😞😞😞 sa Thies dou sa morom fran dou sa morom reug reug dou sa morom
@Pastef8596 ай бұрын
Nako Franc jël budéé du moromam
@simmelsarr35996 ай бұрын
Serigne sama mbeur ga mais danga wara tay ci Franc. 2016 lala dane té ba legui amoul défaite iow aussi bobou ga gueudia am défaite. Donc Franc mola raw bimoula dané da paré enchaîner ay séries de victoires. En plus gni Franc dane danoléne. Franc dafa dane Thiatou Yoff,Tyson 2, Sokh , Forza. Franc daflene raw fouf
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Merci beaucoup toi au moins tu est bien informé😂😂😂
@sophrotall81056 ай бұрын
Nama yalla ball mais amnaniou kham ni niawww motakh niou nekkk mbeur ki sila boook .Layyyyyy😮
Serigne Ndiaye mouno teubb rek di beurré ak Eumeu Séne. Difference de cachet bi daye eupp lool. Eumeu daf la toudou pour merlo Franc rek. Yaw daal Tyson 2 le vrai lieutenant de Eumeu Sene moye sa natango instant yi. Serigne Ndiaye 2 vs Tyson 2 Serigne Ndiaye 2 vs Gora Sock Serigne Ndiaye 2 vs Jordan Serigne Ndiaye 2 vs Fils de Balla
@DOpe-boy996 ай бұрын
Gni nga cité fi yeup dokh nanie sen combat niou daw niémé wounie Sérigne Ndiaye
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Yaw y'a co dokh hum 😂😂😂
@TiDIANETOURE-lw9or6 ай бұрын
Ioe nopil dano fi kene
@serignetoubagueye40676 ай бұрын
Thiéye koréasse mo rekk lay topp
@iscojo66006 ай бұрын
Gris 2 beugue Franc! Serigne Ndiaye Beugue Franc , Lac Rose kazalika🤦🏽♂️ même écurie Même écurie soyez organisé et poussé le plus méritant !! Et surtout Franc mok Gris bordeaux moy combat bi ah
@alexbalde35076 ай бұрын
Ki defa bari wakh dano fi ken di wakh Ama le 30 day déféral sa Patron
@bouramadiatta38736 ай бұрын
Yaw ya bari wax amoul droit gnanal patron wam,je ne sais pas pourquoi vous êtes compliqués
@riusjea6 ай бұрын
Gordjiguene bi motakh amouniou supporter. Gor yalla guey sarakhou aye combat. Franc mola meune aller retour
@danielcorreia20736 ай бұрын
Fran dan nala ba paré, amal diom dem gorgolu, yen communication yermandé nguen dokhale franc d’où négocier ak moromam gor ci sport de combat🤦🏿♂️🤦🏿♂️
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Bilaye Franc dou manequin boucole thi gni défilé de mode
@danielcorreia20736 ай бұрын
@@AdolpheGomis Diadieuf na ndiafou biki bou four😂😂
Serigne ndiaye bayil doul😂😂franc amoul dara loumouy respecté ci eumeu....Mod lo dafa douma eumeu aller ak retour😂😂😂Donc franc faléwoul Eumeu
@babacardieye76516 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Lamb dji yakho na
@lhomme_fort6 ай бұрын
Serigne ndiaye eume dou meusse beuré ak ioe
@OusmaneNiang-w2e6 ай бұрын
Yaw soy nék Hal gua nék Hal ko frack do nékhal kén guomo Dara
@user-cg5ku7qg1h6 ай бұрын
Sering Ndiaye vs Jordan combart la
@mamediakhoumpa67486 ай бұрын
Franc dala Dane ba sonou mbapatt ak arene beneu yone gua dane franc mbapatt moy derniere combat mbapatt franc gua khar koo no pill franc doussa morom
@guilayendoye29846 ай бұрын
C faut daan nako plus de 3 fois
@diopmortalla19766 ай бұрын
Nouveau roi
@Oroysan6 ай бұрын
😂😂non lamb légui yakouna pour beuré ak vip yi dagua lén di nékhal😁
@CheikhDiouf-y2c6 ай бұрын
Serigne ndiaye franc t'as battus en lutte avec frappe il faut attendre et bcoup prouve
@DiamaCisse-v8q6 ай бұрын
Fass yeup kenneu doussi dane ama yawak gris2 yenneu yor relève bi té bouleene ama diaper danellene gris Bordeaux mola geuneu khamni coup de sifflé mokofa bayi
@assleye86546 ай бұрын
Wakhi dji nice na. Franc mome dafa soff reww doff
@zen051116 ай бұрын
Démal outt touti bayra…😅
@tavarezcheikhou5176 ай бұрын
Danla aréne danla mbapate Mola meune fouf weur du wakh nga
Sériée Nadiaye 2 gayi dagne ko wara dieul way ki mbeur lah vraiment lamb legui politique rk lah
@FallouNdiaye-y9i6 ай бұрын
Nekh le mo amoul si lamb dj
@issaniang92806 ай бұрын
Franc sa baye leuh sa léwéttayy
@MamadouLamineGaye-b6d6 ай бұрын
Serigne diaye 2 moy sén baye
@Oumar-jw9cb6 ай бұрын
Bouléne niou sonale waye fran Modou lo moko maye cote franc danoufi kéne
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Lolou sou ngiou yoone nékousi heur bi bowa khoul franc li ngaye wakh dou saff dara
@mamediakhoumpa67486 ай бұрын
Legui gnata yone lako franc Dane mbapatt
@ismailasene90426 ай бұрын
Match nul la 3fois lakko Franc Dane aussi serigne ndiaye 2 Dane na ko 3fois
@BabaNdiaye-s2b6 ай бұрын
yaw gumul sabopou
@moussapayemane41676 ай бұрын
Ki gueum bopam motah wérouwoul si kéne,kinga hamanteuné mo gueumoul bopam mongui parcelles didém yendou keur Modou Lo souba ba heur entrainement,diko togal ataya
@ousmanecisse25576 ай бұрын
Serigne Ndiaye kassé
@MoussaDiakhate-n6h6 ай бұрын
Serigne Ndiaye mon mane franc fouff
@Mowmetg6 ай бұрын
Loutakh franc dane ko ??
@SneijderJunior6 ай бұрын
Sangara bahhoul sayy😂
@lhomme_fort6 ай бұрын
Ioe mome khame nga franc boubakh
@DOpe-boy996 ай бұрын
Ladial Franc Kouy Serigne Ndiaye Iba mar diop😂
@bachirdiop196 ай бұрын
Yaw Franc dane nala ba paré amo lo wakh boula eumeu dieulé bayi fi franc dafa def louko nekh rek
@kara18936 ай бұрын
Guemal sa bop bayi bar tat bi Eumeu biguene di nekhal pour lanla meleni balla gueye bok
@AdamaThiam-ut2pj6 ай бұрын
Bou lén niou thiatou dh
@FalouKanse6 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@sambatorino81156 ай бұрын
Bayile nekhale yi
@modougadio69596 ай бұрын
Nite kou yarou🙏🤍
@assannda49196 ай бұрын
Yaw amo lowakh franc dane nala arène
@roots7.6286 ай бұрын
Nako May revanche
@ABAKARA-q8o6 ай бұрын
Way franc dane nako arène wayé mome tamite Serigne Ndiaye 2 yanou n'a franc bathie kaw deurr si souff lutte sans frappe té lep lamb leu
@IsmaîlaCissokho-s8s6 ай бұрын
Franc amoul loumû wax dafa d@ne soh dimanche bisi topû mou nieuw ibamar sa way douma wax sax yamagueuna sipp ragalou niou lolu
@makyarrjaimemonpaysgeumbam74636 ай бұрын
Ak mbappatt
@NdiagneNdiaye-wn5ts6 ай бұрын
Dafa yénou franc ba barbier wéékh batheko thi souf
@FalouKanse6 ай бұрын
❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️💪💪💪💪
@kara18936 ай бұрын
Yaw meuno Beuge fran nakh dafa dougou fass danla dana forza con meunoko beuge
@MamadouKa-h2k6 ай бұрын
Dooo dara
@yabadiouf83616 ай бұрын
Respe mounoul am si lamb kounioye fay ngaye khekh
@sambandiaye64726 ай бұрын
Serigne ndiaye moffi yenou franc boulene ko fattè deh
@DoudouThiam-r4e6 ай бұрын
Franc dane ko 6 en mbapatt
@FallouNdiaye-y9i6 ай бұрын
Gor dou nekh le
@tallakebe1666 ай бұрын
Ñi ay nafeekh lagnn barke yalla
@ousmanous6 ай бұрын
Yaw Lamb dou baap ay nitt ta encore rien et n’oublie pas que Bb Saloum nga daane 😅 champion nga nak vraiment mais Franz dou sakh seu morom tè actuellement sou Jacob Baldé daané bb Saloum vous 2 se serait un combat très logique enfin kharal Jacob Baldé mou nieuw té nga khamni ta encore rien fait !
@babacarwathie6 ай бұрын
Lamb amoul nekhalanté yeufou Goor la franc dou nekhal mbeur diambar la
@yabadiouf83616 ай бұрын
Ki singiye raye la boukh
@BabacarMbaye-q5q6 ай бұрын
Sérigne ndiaye koumou dane si aréne lolou lay lathieté
@afro38276 ай бұрын
Yow mom franc mola meune danala arene😂
@omarfaye25806 ай бұрын
Serigne ndiaye dane ko mbapatt yeukeuti basi kaw dort si souff
@BabacarMbaye-q5q6 ай бұрын
Bou lamb démé ba bala beré ak mbeur faw nga bape ko reug reug bombar ndiey li mo takhone ñouni kombine le lamb amoul nékhal Fran da prouvé dou nékhal kéne yéna sof sokhor
@issaniang92806 ай бұрын
Yow nopil safo mbeur safo joueur sa kanam bou lewet ni sombi
@omarfaye25806 ай бұрын
Wakhi sokhor rk ghafi
@MuhammedJah-x7w6 ай бұрын
Yow daga sohorr raka
@PapaMatarFaye-y1q6 ай бұрын
Il est mousse boy bis ni la si façon de communiquer est fiable
@mohamedmustaphadiouf82936 ай бұрын
Ki il parle bien srx
@assleye86546 ай бұрын
Kii ak franc moy comba
@s__m__m17176 ай бұрын
8victoires combat gay teppeku😂
@ibrahimawalydiouf57456 ай бұрын
Insbi mo meun franc
@MSam5-vp5ed6 ай бұрын
Yangeh duul. Franc daan na kor. Teh franc amout defait