Baye Sam mbaye yala nonou KO yala fayle si barkep Serigne Touba Amine
@moustaphangom45352 жыл бұрын
Machallah serigne sam mbaye tontou ga lép mbaye wallahi mala beug si sama khol yallana yalla yok saye lérre té tas gniousisa barké
@thiernoniang56253 жыл бұрын
Machalla serigne Sam mbaye yallana noko yalla fayal amine yarabi 💕 💯 💞
@mhm.tthiam60353 жыл бұрын
Ils sont innocent deysaaan Nalen yalla yereum😯
@inconnu90000 Жыл бұрын
Do degu de yaw
@modoudabo71633 жыл бұрын
Yalna soufe woyofe si kawame Nite kou amone savoir yalna aÿ lérome yook si képou kouye DIOULITE 🙏🙏
@bambafall67233 жыл бұрын
Amine 🙏🏽
@thiernoniang56253 жыл бұрын
Amine yarabi 💕 💯 💞
@safartvdg26593 жыл бұрын
Amin
@cheikhmbackeseck67043 жыл бұрын
Machallah amna solo trop yalnako yalla yereum ✅
@khadimdiop74853 жыл бұрын
Koula dégu am lou lér si adouna bi yala yoki léram si barké nabie sa
@khalydiagne13763 жыл бұрын
Akassa machallah amna solo yalla na yalla faye
@abdoulayeosnseck70123 жыл бұрын
Mashala Serigne sam mbay Yala na yala yokk ay lëram tass niou thi barkém
@thiernoniang56253 жыл бұрын
Amine yarabi 💕 💯 💞
@Ousseynoud182 жыл бұрын
Yallah nah yallah yokki lérame Serigne sam mbaye❤️🙏
@naskelly44513 жыл бұрын
MASHALLAH THIEYE SERIGNE SAM MOO YÉMÉ BILLAHI ❤️🙏🏾
@mbsylla3 жыл бұрын
Li am solo moy moytou téré Yalla yi. Sounou borome moniou gueneu kham souniou bopou. Ndialo dafa diara moytou. Boudoul wakh dji sakh, togne sa dome wessou woul nga fatou yaw baye dji say domou yone dila donou mome niou guéné ko si mirass mi. Kokou yako togne, yako touteul. Naniou Si Yalla mousseul, té mayniou niou moytou téréme yi. Nieupe kham namou dioudo.
@bintoudiop51543 жыл бұрын
Walahi
@mamediara58913 жыл бұрын
Billay yalnagnou yalla samou
@BayelateKane-i4w2 ай бұрын
Machallah serigne sam yalna souvent wayofe si kawame
@souhaiboundao52723 жыл бұрын
Yallah nanouko sunu borom fayyal
@atumandiagne88283 жыл бұрын
Niit warna na kholat bopam, yalla warnaniou wessou diko djamou rek ngir dougou aldiana akk ragal safara !
@assanembow64603 жыл бұрын
Li rek motakh moy salté kallah nous pardonne
@aliounembayendoye60273 жыл бұрын
Machallah yalna yalla faye
@babacartoure37863 жыл бұрын
Yallah nayallah yereum ko moy sounou bay
@serignesambadiagne69763 жыл бұрын
Machalla diadieuf serigne sam Mbaye
@djilymbacke4946 Жыл бұрын
yalla na niou ko yalla fayal😧🙏
@maguttediop20713 жыл бұрын
اللّهمّ إغفرله وارحمه
@ibrahimambodji32203 жыл бұрын
Bouko kenen waxone ma wediko😭... allahu akbar
@cheikhounagueye5263 жыл бұрын
Amna sola
@ibrahimambodji32203 жыл бұрын
Nagnou sante sougniy wadiour bou baah
@khadimdioum95843 жыл бұрын
Nagne ko santé yalla nakh souniou borom moko namé nonou
@TheBadiane23 жыл бұрын
Depuis quand une personne décide kouy dougui adjana 😔
@soxnamariammbackengom22343 жыл бұрын
Ioe xana amo degu?
@TheBadiane23 жыл бұрын
@@soxnamariammbackengom2234 ngue balma tu ne m’as pas compris. Je ne faisais pas allusion si Sergine bii...
@falloucisse333 жыл бұрын
@@blacknegro7408 ah kay diar na niou diamou yalla nguir you bary : 1 même bou démoulé al Diana dou dem sawara dem sawara nak louneeko geun. 2 yalla lom digle def rek, amoul di chart dem al Diana wala sawara. 3,4,5,6,7,8,9........
@moussadieng33783 жыл бұрын
@@blacknegro7408 C'est du n'importe quoi.... yalla dafa mandou. Amoul féne fou yalla wakh ci al quran ni doumou ndialo dou dém aldiana. Kou am ayya bi namaka wakh, parce que duangue na fatiha ba nassi, guissouma ci aya bobou. Sénégal nak, ay nite nioy takhaw di légiférer ci dine yalla dji, diko toumal té kéne sagnou léne wakh danga dioum. Des gens se sentent exclus de cette vie, deviennent défaitistes et pessimistes à cause des avis et jugements erronés de certains illuminés.
@mansour32843 жыл бұрын
@@moussadieng3378 Mane daal guiss naa kou yalla khass Si alkhoy Aane tei Loumouko khassé moy Dimou ndialo
@sarrabdousalam94933 жыл бұрын
Akasa ❤️❤️❤️❤️
@abdouazizdieng56713 жыл бұрын
Machallah
@maissandiaye88953 жыл бұрын
Bilahi ya woor🤝
@alicisse5554 Жыл бұрын
ما شا االه
@diopmareme37523 жыл бұрын
Yalla rek mo kham kouy dougou aldiana ak kiy dem safara li am solo moy gua nek nitou diné ak l'islam li yeup amoul Sanche
@mamediara58913 жыл бұрын
Kone wero
@diopmareme37523 жыл бұрын
@@mamediara5891 lolou gua fokk
@elbachirmbaye03152 жыл бұрын
Serigne sam mbaye brome le 15 mars
@elbachirmbaye03152 жыл бұрын
Brom le 14 mars
@bambafall67233 жыл бұрын
Machalah Yallah nako Yallah fay 🙏🏽🙏🏽♥♥♥
@abdoubarham3 жыл бұрын
Dem nek harifou bilah moy mouslouway bi si Mom
@cheikhdiop52268 ай бұрын
Fenaal yonente bi mome bakaar bou reuy la . Yalla dou togne keen et dou diamou yalla walla djoud mou yobou nit jannah . Kou dougou jannah rek , yeurmande yalla nga fa dougué..
@mouhameddia51683 жыл бұрын
Domou ndiallo sou diamo yallah dina dougou aldiana
@inconnu90000 Жыл бұрын
Do degu rek limou wakh
@mouhameddia5168 Жыл бұрын
@@inconnu90000loutakh maye dégue limou wakh ?walla mome sou wakhé nieup wara wakh waw lohlou yalla réck moko ame
@mbayeniang55973 жыл бұрын
Waw kon li yalla wakh ni man amila salían falinafshihi khana weroul
@Abdou_por3 жыл бұрын
💯
@salamsalam-ph4vf3 жыл бұрын
Li wer moy domu ndiaalo ak kudul mom gno yam si diamou Yalla, su diamoo Yalla dafay doug aldiana com gneup. Lolu la yénèn borom xam xam wakh, té lolu mo yanu maana, mo deupo ak manduté Yalla, mo deupo tamit ak li Yalla wakh si alqur'ane. Wayé lolu téréwul Serigne S.Mbaye ku maag la si gnune, wayé Yalla rék modoul dioum .
@KaadukSerigneSaamMbayetv3 жыл бұрын
Serigne esk man gnagno fatali li Yalla wakh si Alkhourane ci domou ndialo
@damediopdiop22123 жыл бұрын
@@KaadukSerigneSaamMbayetv mangui ziar boubakh sama dieuwrine am na solo lolll
@KaadukSerigneSaamMbayetv3 жыл бұрын
@Dame diop diop ndiongui lay délo ziar
@serignefalloudiop58273 жыл бұрын
Sa Diagu SORIWOUL
@blacknegro74083 жыл бұрын
@@KaadukSerigneSaamMbayetv Yalla wakhoula fén si alkhourane k domou ndialo dou dougou aldiana.limou niou Sant moy niou diamou ko té môme su boba moy aaté diaam yeup si yeurmendém
@linekoubakhndiouck85403 жыл бұрын
💗💗💗
@kadzooballer9463Ай бұрын
Madiama fall warneu deglou li serigne sam wax si domou ndialoo
@adoufaye65083 жыл бұрын
doomou ndialo bou defer louko mana dougeul aljanna dafay dougeu aljanna. et amoul lougnioukay labaler. un enfant adultere n'a pas besoin d'etre purifie
@cheikhsambou61903 жыл бұрын
Ndakh daguane na si ape joulite mou taka domou ndialo
@Beateye3 жыл бұрын
Mais Domou ndialow meuna nékk dioulitt di kon kay loolu Dou cas
@amndiaye19853 жыл бұрын
Lima nakari nekhouma
@seynaboudione37713 ай бұрын
C'est n'est vraiment pas normale ça les enfants nos rien fait
@mendesshasha10213 жыл бұрын
Yallah rek modoul dioum. Kou siania wakh ni domou ndialo d'où dougu aldiana yagui si dioumté bou reuy. Gni dioude si boume téwoul nio geuna Bone kouy Bone niom dagni dougu aldiana ? Mdrr
@magicfoot78453 жыл бұрын
Ndeysane kham kham bai beury tontu nla sx si birri wakham naina snu diané dji dousi philosophy wala science wala khel nn boudone lolu ylla dou yonni ay yonnenti niouy dianglé
@KaadukSerigneSaamMbayetv3 жыл бұрын
S.Khadim diop dieuradiaf
@mendesshasha10213 жыл бұрын
Amoul Loy wakh ba confirmer ni domou ndialo d'où dougu Aldjana meussouma guiss kouko firi. Et montre moi un verset du coran ki le stipule . Fanatisme bi ngeni bayi
@TawbatouNasouhTV5633 жыл бұрын
Yaw S Same tontoul nala bopam ci wakhtane wi deglouwat ko ?
@mbayeniang55973 жыл бұрын
Yalla de néna bakan bouné lamou dief lañoukoy fay waw domou ndialo bouy def lou bakh badé sí himane mom loukoy yobou diahannam té yalla néna mom dou tong bene diamam té li yalla wakh moy deug piur
@beuguesonko-wt6eu5 ай бұрын
Amana borom xam xam you dakh lolou
@afrokema33883 жыл бұрын
انا لم أوافق معه بهذا المسألة لأنها ينافي بالعدالة والله عادل أما من رباه المشركين ووالديداه مسلمان. إذا بلغه الرسالة النبي صلى الله عليه وسلم فأبي أن يسلم فهو كافر وان لم يبلغه الرسالة فلا يقال إنه كافر بل يفوض أمره إلي الله والله أعلم
@umuaboubcr9613 жыл бұрын
أوافق معك لأن الله يقول في تنزيله:( من عمل صالحا من ذكر أو أنثى وهو مؤمن فلنحيينه حياة طيبة ولنجزينهم أجرهم بأحسن ما كانوا يعملون) فكانت الشرط الإيمان أي أن يكون شخص مؤمنا ليتقبل عمله ولا يُمنع من دخول الجنة بذنب فعلها غيره فالله تعالى يقول:( ولا تزر وازرة وزر أخرى)
@afrokema33883 жыл бұрын
@@umuaboubcr961 شكراً أخي جزاك الله خيرا
@magicfoot78453 жыл бұрын
Motax yalla ni bou diamo ylla dou doug safara
@talibebayamcisse50583 жыл бұрын
وأناماوافقت معكما ! أيه الشيخانى لولاالفهم ماكان العلم! ماقال شيخ صام مبى بأن ابن زنى يدخل نارا إذاكان مومنامسلما بل يدخل فى الأعراف! وهومأيدقوله بقول رسول الله صلى الله عليه وسلم لأن ابن زنى هوماءالذى تحرك أولاللعصيان، ودخول ابن زنى فى أعراف وجدت هاذاالقول فى كتاب شيخ بمب المسمى بمنورالصدور ! إذاالفى مع عارف بالله ربمايمكنه أن يطهره بتوفيق الله! والله تعالى أعلم
@africaunited923 жыл бұрын
C'est faux !!! Vous blessez des gens qui n'ont rien demandé...Alahou ahlam...