Serigne Touba Mo Kawé Yalla ?? - Oustaz Alpha Ba

  Рет қаралды 13,675

Watawasaw Bil Haq

Watawasaw Bil Haq

Күн бұрын

Пікірлер: 104
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
cher mouride deug nekhoul ne soyez pas orgueilleux et acceptez la verité !
@MoussaAw-q2n
@MoussaAw-q2n Жыл бұрын
dieurdieuf Serigne Touba
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Dieureudieufé serigne Touba
@amethdiasse220
@amethdiasse220 Жыл бұрын
Dieureudieufé s touba nako gneupou wakh séne commentair yi❤
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
au lieu d'ignorer do dem khol traduction yi baga guissal sa bop
@Niokkobokkou-lc2pd
@Niokkobokkou-lc2pd Жыл бұрын
Wakhtané Serigne bi dafa nekh ci nieppou nhdeketé... ndeysane !
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Dieureudieufé cheikh akhmadou bamba khadim rassoul
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Machaa Allah diazakaallah khaiyran yaa Imam Cheikh Alpha ba
@MoussaAw-q2n
@MoussaAw-q2n Жыл бұрын
alpha démal togui ngoune Serigne Touba lane geume dieurdieuf Serigne Touba
@AdamaDiop-er5st
@AdamaDiop-er5st 7 ай бұрын
Talibe Serigne Touba yeupe nio deme aldiana
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Cheikh akhmadou bamba loudoul yalla ak S W L❤️ topalo niouko
@ndeyeyandediouf684
@ndeyeyandediouf684 Жыл бұрын
Cheuuu yalla meuna mougne yalla nagne yalla mousala si seytané
@moustaphadiaw988
@moustaphadiaw988 Жыл бұрын
Bilay
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
wallahi et dire que avec tous ca il nous pardonne 😭
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Waw yalla endana ak mom cheikh akhmadou bamba khadim rassoul koufi def lou ken defoul am lou keneu amoul té dotoul am kou Mel ni mom yalla nala yalla mou seul si koumay bayilo serigne touba ❤
@moussaba805
@moussaba805 8 ай бұрын
Kènne bayilowoula serigne touba, il faut gua dèglou ak hèll tè bagna dèglou akk kholl, tègua nangou deug
@fallpapa
@fallpapa Жыл бұрын
Yalla nagnou sakh mindoume serigne bi❤
@ahmethndiaye7943
@ahmethndiaye7943 Жыл бұрын
Salam aleyk Oustaz, Yallah na Yallah xêp dolli. Bonne continuation qu’Allah nous guide tous. En tout cas ya ngui déf liguey bou am solo fa Yallah té tégoko si lêne mba kéne koudoul môme. Dila gnanal mou takhawoula té défal la diammeu défalko mbolom dioulite. Grâce à Allah par ton intermédiaire sachant que tu a emprunté l’unique chemin Mouhamad psl. Baraka Allahou fîk.
@houssngth2905
@houssngth2905 Жыл бұрын
Bou fékké serigne bi mo wakh bala yalla déf dara lathie serigne bi yalnako yalla diègueul mais en tout cas wakh diou reuye leu
@FatimaBaa-t6r
@FatimaBaa-t6r Жыл бұрын
Soubahanalahh Bilahi gnokhite yiii 😢
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Serigne touba xol bou naroul tékhé douko dioublou
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Walahi guisouniou keneu kougnou meuneulo bayilo cheikh akhmadou bamba khadim rassoul
@mamemorniang9550
@mamemorniang9550 Жыл бұрын
عبدالله وخديم رسوله serigne touba kemanou sou nou borom shw diamoupp yalla di ligueyall mouhamed PSL
@moussaba805
@moussaba805 8 ай бұрын
Wa ba parè Yalla diko taguou, fènne yii reuy na dall
@bambistekara2232
@bambistekara2232 Жыл бұрын
Reudieureudieufé téti cheikh akhmadou bamba khadim rassoul
@azizndiaye1027
@azizndiaye1027 Жыл бұрын
Ndeysan yaw ndeke khamnga ganna te ganna mom khamoula 😢😢😢 wout dinadeee
@PapaFall-t5x
@PapaFall-t5x Жыл бұрын
Yala moye yala kouya yala di tagou dh doula béte s Dh walahi
@AMIN-xi9jv
@AMIN-xi9jv Жыл бұрын
😂الله اكبر 😂الله اكبر 😂
@AMIN-xi9jv
@AMIN-xi9jv Жыл бұрын
Bo moi j'ai peur franchement j'ai peur 😮wouuuu j'ai peur et tremble en ce moment
@sakhoousmane7066
@sakhoousmane7066 Жыл бұрын
Am na soulo
@abouomardiollo
@abouomardiollo 6 ай бұрын
Alpha ba هل serigne touba هو على صراط مستقیم ؟؟؟
@mor787
@mor787 Жыл бұрын
Thiay serigne Gana yalnala yalla Faye barkeb borom Touba quant à alpha dala naw ndakh kham nala té khamo ko alpha démal took khar😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😋😛😜😜😜😜😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝😝🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐😑
@youngflick8082
@youngflick8082 Жыл бұрын
ioe wahal wahou nitt … Wahal ci mbaussaur yi serigne bi bind
@watawasawbilhaq
@watawasawbilhaq Жыл бұрын
Niom sene diné parparlo la. Sene mbok bou neke si loudoul deug au lieu niou dioubanti ko dedete. Dagn kay gueune dougueul
@fallpapa
@fallpapa Жыл бұрын
Gnome nénaye aye djoulite lagne di yéné sa moromou nitt safara lolou moy piire safara😢😢
@maimouna314
@maimouna314 7 ай бұрын
Gana mesere yamana fen
@aichadiop1298
@aichadiop1298 Жыл бұрын
Macha ala amna solo trop
@FallouMbengue-t8o
@FallouMbengue-t8o 10 ай бұрын
Yen gni yéna danguéna boon blahi boulen akou Serigne bi dallé😂😂😂
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 3 ай бұрын
Akou serigne bii d'où dale kén té fimou ted meuneloul bopam dara .té hamoul sakh foumou dieum .
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
Ghana messere mounouma ko deglou
@ousmanediallo9194
@ousmanediallo9194 Жыл бұрын
Bonjour.....je voudrai savoir votre avis....votre position sur la femme de Christiano Ronaldo qui s exhibe en Arabie Saoudite.... pourquoi vous ne parler de ça.
@valkane3596
@valkane3596 Жыл бұрын
Wa arabie saoudite degou niou wolof. Te senegalais yi deukouniou Arabie saoudite
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
@@valkane3596 merci d'avance mon FRERE
@mightyb8614
@mightyb8614 Жыл бұрын
Deug benella.
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
avant niouy wakh ci benene deuk daniouy wakh ci futilité tarikhas you nekk ci bir galsen gua khamnè amoul bene diarigne
@madamebk1962
@madamebk1962 Жыл бұрын
Bala nga lakh diay lakh lekk lineu senegal moh raw lathia Arabie saoudite fouf
@aissatoubae9150
@aissatoubae9150 Жыл бұрын
😂😂Yeine Dal doleine sonou doleine tayi Thieukeulma yi loutah ngueine eupeul la khamoul mounane na tass sa direct bou weit tei niak khorom
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
lou wett dina am 1000 vues ? yene werolene 😂 alkourane ak sunna rek moy deug te niou beuri niougui yewou grâce à Alpha ba te yalla gua bokk ci niouy yewou
@SerigneAzizRidialloulah
@SerigneAzizRidialloulah Жыл бұрын
@@layekharagne2224 fo ko tek iow amoul fouko yalla wakhe DH
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
on est fiere mec !
@moussaba805
@moussaba805 9 ай бұрын
Ay door leu rèkk
@fatoubeye6028
@fatoubeye6028 Жыл бұрын
Bayil ma dofe yi
@mamadousalioucocou-zs2fx
@mamadousalioucocou-zs2fx Жыл бұрын
Yaw oustaz bii yaramnaala sak mildiou narta réfett yalla guathi sax
@FallouMbengue-t8o
@FallouMbengue-t8o 10 ай бұрын
Koul meuna féne nga
@MoussaAw-q2n
@MoussaAw-q2n Жыл бұрын
alfa ya boone lousiï sayone
@moiiza10sidibe30
@moiiza10sidibe30 2 күн бұрын
Toma khana déguo gana yaw?😂
@mamediarraseck4813
@mamediarraseck4813 9 ай бұрын
Alfa ba yaw yay dadial sa dokhoty mame
@CheikhtidjaneNdiaye
@CheikhtidjaneNdiaye Жыл бұрын
Mbind mba ko yemm ndeysane
@ndiayeabasse955
@ndiayeabasse955 Жыл бұрын
Serigne Touba bou fi féinioule wone Kone yene séné baye AK sen ni Mame yeep ay yeufeure laniou donne bi Serigne bi Di kheikh islam fi Sénégal sa Mame ak sa bay founio neikon yeuremedé way yaw
@moussaba805
@moussaba805 8 ай бұрын
Bayil thiakhane serigne bii da dioudou fèkk fii l'islam
@ndiayeabasse955
@ndiayeabasse955 8 ай бұрын
@@moussaba805 yaw bou neikoule wone Serigne yaw leine gay neik mais pas dioulitte bayilene séné thiakhani yi âme guene leine loy lene débat k Serigne soffe guene toroppe
@azizndiaye1027
@azizndiaye1027 Жыл бұрын
Alfa khkhkh dinga dé dé dé yeuremnala dinga wakh ba giékh te ken doula geum
@moussaba805
@moussaba805 8 ай бұрын
Alpha deug lay wah
@combecane257
@combecane257 3 ай бұрын
Serigne bi liguéye na lou bari si l Islam lou takh dou nguén wakh si lolou. ... arrêtez lén di wérénté
@BoubacarDiallo-i5f
@BoubacarDiallo-i5f Жыл бұрын
Toufflit yonente bii mo guene serigne bi khamo lou takh yonente bii mou touflé amna malaka bouye dieul touflite bii yob ko aldiana ta serigne bii lou dema aldiana touflite yoyou laye nane
@yadijallo1969
@yadijallo1969 Жыл бұрын
Gana AK mouride yi nio meuna fen
@mor787
@mor787 Жыл бұрын
Ball nabou la yalnala yeureum🙏🙏🙏🙏🙏
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
Alfa wuyou ma ngir yalla tontul ci commentaires bi
@abdourahmanediallo24
@abdourahmanediallo24 Жыл бұрын
Iow diarro tontou tu oses critiquer alfa par ce qu'il dénonce des paroles de mensonges en vers Allah, celui qui défend ce qu'il critique est un mécréants.
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
Yéné sén khôl mo jékh motakh amolén métier chaque jour yénagi khôl ci nit GNI lounguén wakh loutakh dounguén lijanti sén bopu
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
@@abdourahmanediallo24 té man douma wakh ndéréng bou jogué guinée 🤣😂🤣
@abdourahmanediallo24
@abdourahmanediallo24 Жыл бұрын
Ça se voit que tu es un égaré la religion n'a pas d'éthnie ni de nationalité iow sa life koouko lijeuntiii? Votre Serigne dis des mensonges en vers Allah c'est de notre devoir de démentir ses écrits car si non nos proches nos amis nos enfants risquent de croire à ses écrits qui les conduisent en enfer. Té yalla nieuppa ko bokkk kouffi wah ay kacccc dinagn la dioubantiii
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
@@abdourahmanediallo24 tu doit regarder les mensonges de vous même alah swt Di dans le Coran عليكم أنفسكم لا يضركم من ضل je ne parle plus avec un greng dans ma région.
@satoubabii3449
@satoubabii3449 Жыл бұрын
Wa yaw sa bay mom lomou binde
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
mom au moins bayam reraloul kene comme niko sene serigne bou makk deffè
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
@@layekharagne2224 🤣🤣🤣 je t'aime toi
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
@@malickdiaw4678 je t’aime toi o6 😂
@AMIN-xi9jv
@AMIN-xi9jv Жыл бұрын
Je ne peux plus continuer a écouter des blasphèmes de bébé diakhate
@modoumboup1485
@modoumboup1485 Жыл бұрын
Nitte daye mandou
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
nitt day nangou deug
@ousmanesow6736
@ousmanesow6736 Жыл бұрын
Khamnani warnguéna sante Serigne Touba déh Com que yén amouléne liguéye sa younguéne kheuyé Di yeur khassida yi diko wakhtané Pour am ay nombre de vues
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
Alpha khana amo méthié عليكم أنفسكم lijantilén sén siki bopp té bayi dérri jambour yi
@boubacarsamb91
@boubacarsamb91 Жыл бұрын
ALPHA KAGN NGAY GNIBISSI SÉNEGAL???? KHATIMATOU MOUNA DJATI BI DIÉKHÉWUL FOFU DÉM LÉN CI FIN BUDÉ YALLA MOLÉN NJOR WALA BEUG SIIIIWWWW
@satoubabii3449
@satoubabii3449 Жыл бұрын
Yaw amo kham kham
@AbouZayd4674
@AbouZayd4674 Жыл бұрын
Tontou ko thi xam xam
@malickdiaw4678
@malickdiaw4678 Жыл бұрын
@@AbouZayd4674 🤣🤣🤣🤣
@KhadyGoudiaby-m1j
@KhadyGoudiaby-m1j 11 ай бұрын
Alpha ba embecile gua quoi 😅😅
@matarngom1173
@matarngom1173 Жыл бұрын
Votre arrogance est egal au degres de votre ignorance !!! xamoleene Yalla , ta deguooleene Sounah , des novices en la fiqh qui font du dahwa
@watawasawbilhaq
@watawasawbilhaq Жыл бұрын
Khamal niou yaw mi kham. Khassida bi lousi serigne bi wakh expliker niou
路飞做的坏事被拆穿了 #路飞#海贼王
00:41
路飞与唐舞桐
Рет қаралды 26 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 676 М.
Подсадим людей на ставки | ЖБ | 3 серия | Сериал 2024
20:00
ПАЦАНСКИЕ ИСТОРИИ
Рет қаралды 480 М.
Oustaz Alpha Ba Donne La Parole Aux Mourides
1:48:14
Watawasaw Bil Haq
Рет қаралды 18 М.