Maa chaa haala Sikhna Fabinta yalla fayla yiw ci barakatou seydina Mouhamed SWS
@SeutouDamel19563 жыл бұрын
Salalahou Alayhi Wa Salama
@fabintandiaye74258 жыл бұрын
Salam ya Salam magui ziarer seuttou damel machalah machalah alhamdoulilahi ligueye bi Serena rafetena adjaratou fa moukhetar migui sant sounou borom di si begual sope moukhetar yeup yalenanou yala fayale moukhetar te sounou borom sakhale gnou si di way rek moukhetar mamou cheikhena cheikh saadbou weny bikk machalah weny khatteu khatteu weny keubirra
@SeutouDamel19568 жыл бұрын
Adja Fabinta dieureudieuf 1000 fois si commentaire bi. Amouniou koudoul Mouhamed Salalahou aleyhi wa salama Yalna Yallah fay si taggue yi Khol yi seedna té fess looolllll
@fabintandiaye74258 жыл бұрын
Mais nak begone nak sen ay contact yen seutou damel vous avez fait un joli travail les photos sont belles machalah en tout cas beuguena khame seutou damel daal fougnou nek sen ligueye bi daal rafete na machalah he suis vraiment tres tres ravie et j ai pleure aujourdhui en ecoutant al moukhetar bilahi Ken dou moukhetar weny bik
@SeutouDamel19568 жыл бұрын
Salam jam yalna nek si Seydina Mouhamed, Salam diam yalna nek si Dioulit yi, Salam Diam yalna nek si Fabinta NDIAYE Al Moukhtar, Kourima, Assadal ilahi, Laka yamouh yil izani gni dioy lo internautes yi. Bisboula Moukhtar fayé bouniou faté. Sama contact moy seutoudamel@gmail.com