Yalla xamnani baye mbaye lingay def dara dara geunokoo am solo.. Li ma diangué ci yaw ci samam reew yalla Nala ko yalla faye
@generalgassama66504 жыл бұрын
Yalla nako yalla def télévision bar keb borom darou tape amine
@almamyhaere5024 жыл бұрын
Baay syll yalna yala mey la goude fane ak wer. Béggueu naniou lolou si émission bi
@douxinx21624 жыл бұрын
C’est à Sidya Ndate Yalla Diop que revient véritablement le nom de la place Faidherbe Ce serait une revanche de l’histoire
@RokhayaDiop-r6i11 ай бұрын
Salam oumar tu a raison marosso tassé yandé wagane fu mon grand Pére maternel mbaba ak Dior seutou mame Barack couly mbaba coult mbaba marosso tassé yandé waguane
@bcssn767 Жыл бұрын
c est lui qui a ete livre par lat dior aux francais>
@mamadoubarakebe33084 жыл бұрын
Dieirdieuf baye mbaye yalna yalla goudeul fanne yi
@ibrahimasylla68784 жыл бұрын
Baye Mbaye Gueye Syll sa liguey rafète na macha allah yalla na dieum kanam. Damay lathie ndakh seutou Mame Ali Weuli Syll nga ??
@fallouleyemilano18104 жыл бұрын
Machalla amna solo wayé donou dikal ci maba diakhou ba ak li takh niou lake daraye pirr grazie mille s sylla
@khalilbayefall23 жыл бұрын
Ngir YALLAH déléén partagé ak di aimé ngir sunu chaine bi dieum nakam
@abdoulayebaneniang4 жыл бұрын
Machallah baye mbaye gueye syll
@ndiayemana3144 жыл бұрын
Ma challakh amna solo looll
@cheikhououmarnabien35094 жыл бұрын
sama émission préférée abonné léen vous les enfants
@talladieng75104 жыл бұрын
Yalla na la yalla faye
@messambadiop4 жыл бұрын
Yalna yala fay la aw yiw ji barkep brom touba
@khadimdiop41994 жыл бұрын
Dieureudieufeuti baye mbaye gueye syll si leeral yi
@cheikhtidianethiam24536 ай бұрын
Moi je demande jusqu'à présent pourquoi exactement Lat Dior a livré Sidiya Ndatté Yalla à Faidherbe, parce que d'après l'histoire Lat Dior était l'ennemi public numéro 1 des français pendant plus de 20 ans alors pourquoi a-t-il commis cet acte odieux. C'est vraiment inadmissible 'et malheureux !
@gayeitech2484 жыл бұрын
Baye mbaye Gueye Sylla goney darou yépou contanagnou si ioW sa liggey rafétna bilahi
@oumardiawseck45944 жыл бұрын
Ndatte yallah s 'est marie a Marosso Tasse Yande wagane Diop apres avoir divorser avec Bethio Sacoura Mbarka fall Diop merci.
@falfalfalfal80134 жыл бұрын
AMNA SOLLO BAY MBAY , BOUL FATTÉ JÊRY DIOR NDÊLLA
@senelucky4 жыл бұрын
Bilahi bay mbaye degui gouwer nga wakh nanou sencè ay touri feder bou louma khamoul
@momoseye45924 жыл бұрын
Lii am na solo way.. Mousou ma xamné sigaya ndaté yalla xeex Kat la woon.. Billahi sounou njiit yi nio bagne seen boppou
@mameserigne69914 жыл бұрын
Sa taxha way rafét na ci réwme ak si Mouride giu na yalla taxha wo diambari réwmi
@cheikhndiaye13104 жыл бұрын
Amna solo
@badarangom33354 жыл бұрын
Sidya est un exemple car il avait tous les moyens de vivre dans l'aisance en soutenant les français mais il préférait défendre le leg de ses ancêtres.
@abakarafall3814 жыл бұрын
Akassa amna sono diere diefe Teti sekhe akhemadou bamba baye mbaye geye dondell 160 ani ak wer yokou ba yecko incha koted ki
@aronathiaw34944 жыл бұрын
Machalla
@ndiayemana3144 жыл бұрын
Baye mbaye ñiongi sakou ñian nga khamal ñiou boor sin coumba ndofen 🙏🙏
@modoudia13494 жыл бұрын
Baye amna solo mais dago koye def ben ben
@fatouyellyfaye33002 жыл бұрын
JËRËJËF WAXTAAN WI RAFETNA KAAR DI LEN JOQ DAJJE
@khew20064 жыл бұрын
Amena solo vraiment
@ngagnenaing60274 жыл бұрын
Amna sololol
@Enseignement232 жыл бұрын
Kharé Samba Sadio de sokhla nako lol
@Senekode4 жыл бұрын
Macallh
@cheikhniane53014 жыл бұрын
Thieye toubab yi masougno bakh
@serignemodoundiaye74344 жыл бұрын
Mardi 07/03/1820 😭😭
@yamalnitkifingabeggmuyamla62904 жыл бұрын
Yii réew mi yépp warna ñu koo seetaan, ndax ñu xam ne tubaab du royuwaay, ndax ñu xam suñu cosaan, xam ne ay jàmbaar lañu mas a am déet ay yambar.
@makhtarcissediaw60834 жыл бұрын
Merci beaucoup Pape Amna solo Trop
@MrSulmani4 жыл бұрын
Excellent de memoire historique
@fallam10104 жыл бұрын
Métti na ma trop rue fedherbe pont federhbe avenue lycée sunu diambaryi kéne xamouléne on est en 2020 !!
@khadimkante35014 жыл бұрын
Sénégal beugoul mbokam bilay
@mouhamedabdalah4443 жыл бұрын
Liguey bi amena solo. Mais pourquoi on ne nous apprend pas ça à l'école...
@syissa48112 жыл бұрын
Khana ki demoul dagana
@ablayesene10464 жыл бұрын
MACHALLA
@demahoumlayd3 жыл бұрын
L'équivalent de Damel et Teign au Walo c'est Barak et non Béthio. Bethio c'était une sorte de ministre...sous m'autorité du barak
@ndatteyalla99172 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@kalidouwade94424 жыл бұрын
Dieredieuf baye boye sa ligéye rafétna lol
@abdoukhadregueye46054 жыл бұрын
Merci infiniment
@bayenyny94354 жыл бұрын
dradef
@amdysyll92594 жыл бұрын
Bay mbay khékou niomré ba begon nan kham numou démé won
@kourelnoreynisamsam59614 жыл бұрын
Li rek lay deglou walahi
@youssouphagueye87514 жыл бұрын
Emission bi machallah. Mais béne critique rek la am. Ya trop de salutations de personnes. Pour moi une simple salutation en islam doyna. Après hors antenne vs pouvez remercier les personnes citées .ngueune balma nak contribution rek la.mais emission machallah