Tidiane laa déi. Waayé si sama guiss guiss, serigne fallou mii saf na sape ak yalla. Diagualnama lou bari si Mame cheikh Ibra Fall. Beuss kiki téy diapènaa bail fall yeupe ay nitou yalla. Yalna yalla yok sène lèr. Dègue yalla dafa nèkh Dieureudieuf
@falloumbacke45855 жыл бұрын
Machalla Daga am tawfékh rk te Mame cheikh ku yalla nara dimbali wan la ay mbiram jajuf
@dearfrienddiop79492 жыл бұрын
Ndeysann
@diopassane43143 жыл бұрын
Kou fie nék diko déglou 2021 Yall nagne ko féké 🙏🏾🙏🏾
@tatoucagna5 жыл бұрын
Je suis tidiane je viens de le découvrir mais je l'aime beaucoup mashalllah yqlla nqlq yqlla yokk banga yek ko yalla deefal La diam t yok kham kham serigne touba amoul morom Mame cheikh ibra dou tiakhane
@famambengue70593 жыл бұрын
M
@amadouabassane94033 жыл бұрын
Bien dit
@ibrahimafaye58083 жыл бұрын
Wallaahi kou yalla dimballi ngii yaaaram
@bayedarousopayboromdarouno65852 жыл бұрын
Yallha na la yallha fay
@senegal_aux_senegalais5 жыл бұрын
Kou beug douguou aldiana na mandou si Cheikh Ibrahima Fall🙏🏻
@oumybadji94829 ай бұрын
Kepp nk
@alabdoulazizidiouf98885 жыл бұрын
Yalla na nek talibé cheixou Tidjane mais bilahi dama bgue mame cheikh IBrahima fall ba beineu yoon bima dem touba xabrome la fanane sama xol nekk naci té yalla boumou ci djiog
@ousseynoufall50045 жыл бұрын
Akassa Macha halla
@cheikhounagaye81405 жыл бұрын
Macahall ko bakh yalna yalla godal sa fane taga wèr barekip serigne touba
@papyxalebambasambe16225 жыл бұрын
Yal nala SIDI Brahim fall fay
@falloumbacke45855 жыл бұрын
Yaw Dh man fallou Mbacke beugna nou khamante
@falloumbacke45855 жыл бұрын
Boulasi Dr géuné beug nala ngir yalla
@maguettendiaye42083 жыл бұрын
Man li douma ci doyal 💙💗💖💕💚❤❤❤❤😢😭😢li dioye lo na koune man chiekh Ibrahim rkk la beug wa'Allahi
@maguettendiaye42083 жыл бұрын
Lii amna louko dak li 💗💖💕💔💓bly done baye fall mo wore ❤❤❤❤❤
@thebigvoicetvasiamalaysia91123 жыл бұрын
Je viens de voir video bi, Mashallah, Serigne bi amna xamxam am yar, am fit, foulla ak fayda. yalnala Yallah doli ler ak wer.Alhamdullilah
@abdoulayembaye60485 жыл бұрын
Salut..machallah il a bien parlait car il se réfère sur le saint Coran et poursuit sur les khassida de mame BAMBA..Donc liih douh ay tiaxaneu waay.. Yalla nanou yalla défeu aay mouride dëgeu..Magui Ziaar serigne bii 🤝🤝🤝
@mouhametbachir47345 жыл бұрын
Li kawei na barki broome touba Qu’ALLAH swt nous fasse miséricorde et t’ei def ñou aie baye fall deugg 🙏🏿👌🏿
@ballaguaye42035 жыл бұрын
Alhamdoulilah machala waxtane bi am na fassakha cheikh Fallou diapandal yala na yala defal la taw fexxxx barke ya rabiii
@mbengueibra17555 жыл бұрын
Neke senegal te neko baye fall yangui si ereur diarama cheikh ibra fall niake la kham woroul 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@seydinamfall56145 жыл бұрын
Mbengue ibra nékk adouna* t doundo baye fall mo woroul ndakh Mame moy baboul mouridinah t lolou moy wone ba dieum thia Yalla( l'Universel)...kone dessouko yamalé fén
@dearfrienddiop79492 жыл бұрын
Bilahi
@taalalabsolu7025 жыл бұрын
Mane dh amna yènè guiss si dieum ngir dieumi cheikh ibra fall tawfèkh rk koula tèk beutt khamni fess nga deug baye fall èlegance civilisè yalla na lèn kou tèdd dèfal diam ❤
@fatoufall91225 жыл бұрын
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@adiyatoulayediallo25745 жыл бұрын
😭😭😭😭 chekhraaa Falll yaar nga ñou khamal ngañou souñou borom😭😭😭😭 sama khol sed naaaaaa
Dééguenaa degue ALLAHOU AKBAR LA ILAHA ILALELA rek woorrrr XAM XAM amena
@cheikhndiaye73445 жыл бұрын
Akasa amna solo Dieure dieuf machalla merci 2stv
@sanzondiaye19725 жыл бұрын
Dieuredieufay Serigne touba mais son bisi souf nekh na trop machahala
@momom54935 жыл бұрын
Assane Ndiaye sidy mboup la
@niangsaly21083 жыл бұрын
Kéne la CHIEKH IBRAHIMA FALL 💞👌💞💞💞🤔
@BAMBISTETV5 жыл бұрын
Macha allah serigne fallou wahtan bi kawene lerna werna Diarama cheikh ibrahima fall
@mamadouseck50705 жыл бұрын
Machalha wakhdji rafétna lérna YALA nguéne am gueureum fa Yalla ci barcké brom TOUBA
@bassiroumbacke16785 жыл бұрын
Diuerue diuef serigne touba diarama mame cheikh Ibrahim fall 💓💓
@KhadyGueye-kq8od11 ай бұрын
Amna solo dh thiey sowrou fall
@babacarmboup93554 жыл бұрын
Machalla amna solo lol mercie beaucoup pape sidy !!!
@fautadiop87855 жыл бұрын
Macha allah wakh tabi weer té leer ! Yallah na khame gui guena yokou
@fatidiop71394 жыл бұрын
Amine
@albourygueye47083 жыл бұрын
❤️❤️❤️ ndeysane. Do len ma dimbali ci ki di wayy ci souff
@fallibrahima9675 жыл бұрын
Thieuye borom ndiapandal mo bakh d tes Barry kham kham sa diangeu alkhourane lerr nama mane mi machalla Yalla sa diam yageu borom Ndar deuk Pape Malick Mboup ba
@cheikhfalloudiapandal44075 жыл бұрын
Fall Ibrahima sama kharite borom chine
@moustaphasarr8495 жыл бұрын
Diadief amna solo trop machalla
@thiattemiffa95345 жыл бұрын
Ken dou Serigne touba bilahi😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿🙏🏿
@abonewyoffcity6005 жыл бұрын
Thiey cheikh ibra fall kén dou mom 👌🏿👌🏿
@mbayemaper3785 жыл бұрын
Yallanala yalla yok salér si barké Mame chiehe ibrahima fall
@mbathiondoye73705 жыл бұрын
Mane dé tidiane la wayé sama khol dafa toy envoyer léne ma numéro téléphone nous cheikh falou diapandal
@tatoucagna5 жыл бұрын
Mbathip Ndoye mane mi veug nako
@elgoramboup78695 жыл бұрын
Deifleine ma signe si 777904597 ma yonei leine koo
@khadysoumare19645 жыл бұрын
manchallah
@AbuBakar-gi7vr3 жыл бұрын
M'achallah Baye Fall Yal Nanio Yallah Dëfal Topë ak Dëgue çi Barkép Mame Cheikh ibrahima Fall Lamp : Gracias Mame Bamba !
@cheikhndiaye725 жыл бұрын
Baye Fall Triple Noble La Jeurejeuf Serigne Fallou👌
@cheikhmoussaba73235 жыл бұрын
Goor fall walahi liguaye wakh kou khame yalla rék molo mana dégue diadieuf cheikh ibra fall, goor fall na gayi déme khame lahilahaila lép moye diamou yalla cheikh ibra batine la yoro wone,serigne touba diokhéwoul diouli , woor,adjimaka yalla ladone woné diko khame lé ma baeugue cheikh ibra ak serigne touba bima khamné yalla la léne khame deugue ñome douñi nite walaye hi ...?
@kanealy53234 жыл бұрын
Cheikh Ibrahima fall amoul morom
@morndiaye31865 жыл бұрын
😍 thiey cheikh ibra 😍
@laminesamb36045 жыл бұрын
Kene dou cheikh ibrahima fall❤️
@toubamoylislamtouba23315 жыл бұрын
akasa waw gor serigne touba kène le amoul morom ibra fall diaraw lakk
@ndeyeniang17655 жыл бұрын
Machalla envoi ma sa nimero seuyebi
@dyepi71225 жыл бұрын
Dieureudieuf Mame ckeikh ibra fall
@nafissatoudiakhate29425 жыл бұрын
Oh sama yarame dawna.
@coumbaaicha5 жыл бұрын
Dioye na ba sone ndakh khol bou sedd.
@assanefall35905 жыл бұрын
NDEYSSAN
@sambafall83905 жыл бұрын
Dioyii fii la waré barké serigne touba
@kingrassoul90375 жыл бұрын
Salamalaykoum sam mbook bay Fall yi ziar bou werr Man dh dama khamoul souma donoul won Mouride nane lay def 😭😭😭😭😭😭😭😭 titres Sons bi Svp
@momom54935 жыл бұрын
Sidy mboup « lampe fall »
@assanefall35905 жыл бұрын
THIEYE CHEIKH IBRA KEN DOU MOM
@salioudiome66855 жыл бұрын
Je veux le son stp
@barajr31865 жыл бұрын
Sidy mboup lamp fall
@khadimsarr19432 жыл бұрын
Thieye Mame cheikh Ibrahim fall
@barajr31865 жыл бұрын
Wakhtan bi nekhna troppp
@ismaelng70113 жыл бұрын
Commence ma emission bi son biy daw si souf noumou toudou svp
@looystudios3 жыл бұрын
Sidi Mboup LAMP full HD
@looystudios3 жыл бұрын
tapél lolou youtube
@aminatadiop16682 жыл бұрын
Ndeysann serigne fallou ndiapandal takh nga niou geuna xam cheikh Ibra Lamp baboul mouridina chak jr Gouddi gui damalay sétane ba nelaw souma yéwo fadiar gui avant may diangui damay sétanate avant may diangui
@khoudiangom77445 жыл бұрын
Tiey mame cheikh 💓💓💓sedena
@natou7685 жыл бұрын
Ma challah amena solo
@cheikhfalloudiapandal44075 жыл бұрын
natou768 sama yaay name nala ani pere
@laminefall2385 жыл бұрын
Akassa fall amna solo
@oumarsy56225 жыл бұрын
son bouy daw ci souf dawna yaram comment l'avoir SVP
@fatoudethiembaye46325 жыл бұрын
Modou aida fall
@momom54935 жыл бұрын
Non c sidy mboup lampe fall
@oumarsy56225 жыл бұрын
Merci mes confrères
@oumarsy56225 жыл бұрын
@@fatoudethiembaye4632 sohna Fatou je confirme que c'est Sidy Lamp Fall et encore une fois merci pour votre apport
@mouhamadoulaminebarakante40443 жыл бұрын
Manchalla .Mais svp kou xam kiy way si souf si commencent bi
@marasarr26195 жыл бұрын
khamnani daaal sangou makka ak medina diouli moo daane feekheul kholam وجعلت قرة عيني في الصلاة mo waxaat ni liniouy takkalé ak yeefeer yi moooy diouli
@wakeurboromtoubasenegal59055 жыл бұрын
Saa waay doulll bo khamoul noppil
@marasarr26195 жыл бұрын
@@wakeurboromtoubasenegal5905 dieureudieuf
@wakeurboromtoubasenegal59055 жыл бұрын
@@marasarr2619 ap mbiir bo thi xamoul dara boul ci dougou boul ci wakh way yen