N’oubliez pas de vous abonner sur votre chaîne Senbuzz Tv et d’activer la cloche 🛎 pour recevoir les notifications merci.
@omarfaye1794 Жыл бұрын
Siteu mangui lay ñanal si barkei yonenté bi Aleyhi salatou wa salam fo dioublou yalnafa yiwou yalla dioublou🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳
@ibrahimacisse9349 Жыл бұрын
Amine
@aissatasow7301 Жыл бұрын
Alahouma amine 🙏
@fatousambasow2569 Жыл бұрын
Macha Allah Macha Allah yallah na souniou borome fayeu ko Amine Yarabi. Geste bou noble
@momeloucheikhebi8224 Жыл бұрын
Amine yaarabi défatina Lou rafét
@awajoofnyang3927 Жыл бұрын
Salalahou Alaihi Wasalam Ameen way
@ndeyemourseye6010 Жыл бұрын
Siteu yalla nako Yalla may goud fan ak wére si barké seydina mohamed psl ♥️
@awajoofnyang3927 Жыл бұрын
Salalahou Alaihi Wasalam AMEEN way
@prosperwalysemoudiouf3313 Жыл бұрын
Un geste d'une grande noblesse diarama siteu longue vie à vous
@aminatadiouf6031 Жыл бұрын
Machaala k Dieu te le rende en centuple amine k ton ami FODE repose en paix.Rafetna
@aicharassoulba9887 Жыл бұрын
Ameen ya Rabbi
@mamansylla9809 Жыл бұрын
Non siteu Moy gor Moy garmi moy gare li rek la kharit meuneul moromame mou 'mbebéte bayi guinaw motaliko machalla yalla nala yalla Faye wayé lepe yayam làa machalla
@rblxpolo3328 Жыл бұрын
Siteu sokko kholer rek khamni nitt kou bakh la MachaAlha. Ya Alha mi darra teuwoul Yalla nalla deffal lingua beugu temou doone sa ndigglay Barakatou Ya Rassululah SAW. Amine Alhahouma Amine Ya Rahbi
Baye fall deug yalla nala borom bi faye si barké seydina mouhamed saw 🙏
@mbayekhady Жыл бұрын
@@alimakounta871 amine 🙏🏾🙏🏾
@samueldiouf2863 Жыл бұрын
Rafetna trop. Ça mérite d'être montré même dans les journaux. C'est bien d'aider les personnes dans le besoin
@papeba3097 Жыл бұрын
Bilahi c est un exemple pour gninga ham né wah rék laniouy déf
@aminatakoubradiaw7773 Жыл бұрын
Ma sha allah yalanala Yalla faye
@khadysarr3388 Жыл бұрын
Machallah dioulite Lila meuneule moromame c' est un geste très noble
@astouciss4961Ай бұрын
Certains miliardaires doivent en prendr exemple
@ndawdameliverpool2621 Жыл бұрын
Geste à montrer Siteu un vrai exemple pour les jeunes Ak adouna mél siteu ligua def yomboul Yoor yombou n'a diokhé mo diafé Un homme de grand cœur C'est ça qu'on appelle amitié kila yalla boléne Nitt ande ak nit mou décédé mou faté ko On t'aime siteu Reste dans la paix Fodé yalla n'a yalla kharé al aldiana firdawsi
@mayaciss6821 Жыл бұрын
Maachalah siteu sama lutteur préféré yalla na la sougnou borom defal djam AK soutoura AK kheweul bou barkel yalla na NGA done d ici peu de temps inch'Allah roi des arène, KO Amal combat yalla na ngo dane , Ton ami fodé est fier de toi li moy kharit, tu as tenu ta promesse ❤️❤️😍🤲 ta Maman aussi Elle est géniale 😍
@papisbadji3007 Жыл бұрын
siteu un vrai exemplaires pour les lutteurs ya gorré way tu es un brave lion courage
@eveane3302 Жыл бұрын
Hooo ndayssane j’ai des larmes 😭 aux yeux liii nékh na dawna yarame mâcha Allah Siteu yalla nala yalla défal diame barké Khadimou Rassoulilahi barké Serigne Fallou 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@youss5040 Жыл бұрын
Machallah. Bravo Siteu. Xarit amna dhé. Kerok sama bene xarit dafma dieundone café Touba puis m’a invité à une dibiterie et ça m’a beaucoup touché. Je sais qu’il pouvait me donner 1 millard s’il avait les moyens.. Pourtant il pouvait se dire que c’est moi qui devais tout payer parce que États-Unis la diouguéwone.. les petits gestes comptent beaucoup.. ne dites pas que si vous offrez un petit cadeau à un ami plus riche que vous, il va vous sous-estimer . R.I.P Fodé et vive l’amitié, le VRAI
@thiorofall1878 Жыл бұрын
Yawe Iow y’a gniak kigniane tu est reconnaissant ♥️🙈
@malicksarr1234 Жыл бұрын
Que dieu te protège et te bénisse richement frère
@salioufall27 Жыл бұрын
Un acte de grandeur a saluer vraiment Siteu nékal si jamm ak salam❤️❤️😍
@nogayendiaye7268 Жыл бұрын
Machalla li rek moy kharite
@abdousalamdiallo3787 Жыл бұрын
Siteu que Dieu te protège tji barke Seydina Mouhamed SAW
@aicharassoulba9887 Жыл бұрын
Ameen ya Rabbi
@abdoulayefaye605 Жыл бұрын
Ndeysane machalla situé boo bakh yalna yalla Faye barké Serigne Touba amine
@adlayejoop Жыл бұрын
Siteu ligau beugeu Yako kham yalla nako yalla notali
@alimatousiby Жыл бұрын
Siteu sa yaye kou bakh la machalla yalla na ay fanam goudou Amine ❤
@maguettegueye2971 Жыл бұрын
Li rec bakh moco Mane yallana sa diam yague té ande ac weer ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ siteu mala begue ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@abdallasayfoulayekamara5963 Жыл бұрын
C la 1er fois ma guiss lou mélnii .nit cou amé nii colleuré yalla na yalla faye layiw
@Magndiaye Жыл бұрын
Machallah sa kharit bobou dee do dadjer ak mome di Rouss gueunenala beugue li mo diaffer si diamonodji koleurer so dewer sa famille dougnouguissati kenn
@awasanokho3907 Жыл бұрын
Li dé yomboul Kharitou légui balanga dé lanlay war ya bakh siteu Yalla barkél keur gui yokoula banga yeuk ko inchala 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@oulouwane8662 Жыл бұрын
Siteu Tu as fait un acte noble tout le monde senegalais sont emus Grace a la Maison de fodé ton Amis intime C'est SA l'amitié Bonne continuation
@Iphone66666 Жыл бұрын
Adouna ngi ni deh yalla gis na lepp li rek Montre k nos hommes politic ont echouè parce k siteu sou amoul combat dou am salaire mai malgrè lolu mou ngi dimbali ay nitt si liko yallla di weurseu galè . Siteu yalla na nga am keur si aldiana si barkè Cheikhoul khadim
@rignesejoof9645 Жыл бұрын
Il a un bon cœur.
@adamandaoadama7275 Жыл бұрын
Aye waaye yayou fodé yalla naka mourlo waaye siteu yalla Maye ka wére ak wérlé machalla ♥️💞💞
@mariemamathiam7202 Жыл бұрын
Machalah sutue yalla nala yalla same mayla goudou fane gorr dege nga khole bou rafét nga âme yalla nala yalla Faye ❤️❤️❤️❤️
@byabya303 Жыл бұрын
Machallah que Dieu te garde très longtemps et que tu puisse réaliser tes rêves
@moustaphadiouf4076 Жыл бұрын
C'est la vérité d'être un Baye Fall..... 👌🏾
@tambedouyacine7227 Жыл бұрын
Machallah siteu je ne sais pas pourquoi mais je l'adore vraiment il est bien que le TOUT PUISSANT le protège
@rouguika965 Жыл бұрын
Machallah Siteu yalla nala yalla may goudou fane ak weur thi barké Seydina Mohamed psl amine kou bakh rék moy déf li Machallah ❤❤❤❤
@adiadieng1291 Жыл бұрын
Mash'Allah c'est une bonne initiative yalla nala yalla faye
@abdoulayengom4109 Жыл бұрын
Machallah amna solo loll dieuredieuf siteu yalnala yalla sam ar la li moy vres jest de noble yalnala yalla faye amine
@katyfall3610 Жыл бұрын
MachaAllah siteu ligua def rafet na li rek moy kharite deugue Yallah nala Yallah Fay sa djeuf Yallah lafthiet on est fier de toi bilahi naw nala trop sakh MachaAllah
@cheikhdia9776 Жыл бұрын
Ndeyssan machallah machallah yalna yalla fayeko yiiw inchallah 🙏🥰
@absagaye3674 Жыл бұрын
Siteu dieuff gua dieufi baye fall Machalla
@bambagadiaga2871 Жыл бұрын
Machallah yallah na rapp ak jamm
@aminatathiam709 Жыл бұрын
Siteu nitt boubakh ame koleurei rk moy def li mais sa yaye tamit nitt boubakh leu Machallah
@khadidiatounguirane2696 Жыл бұрын
Daysane siteu yalla nala yalla fayale popame si barke seydina mouhamed 🙏🙏
@mounasskebe9640 Жыл бұрын
Bilahi situé dingua ame diam ak soutoura kheweul si barke nabil moustapha inchallah
@PILN62 Жыл бұрын
Lamb deh koula sii daanatii dala eupp doleii wayeii dou niaan Walahi ❤😢 Kholl bou sedd rek doyna niaaan, Teii même gniy setaan sakh sen kholl sedd na si Ioe
@boussogueye2073 Жыл бұрын
Machallah baye fall bi yalla Nala yalla maye goudou fane ak wer fatèwo demb Fodè fimou nek talina dè
@bintafall2798 Жыл бұрын
Fière de toi Siteu talibé Bamba 💕🥰yalla gua yok ba yeuk ko ci barké cheikhoul khadim Mbacké Amin❤️
@djibrilmbengue5058 Жыл бұрын
Siteu mang lay siar roi des arènes yalla nala yalla fay sa xol si cool luu pa bii lay messager nii merci way
@dembaseck3478 Жыл бұрын
Bilae li daffa raffet di amde ak nitt bamou deudou gua réalise ko rêve vame ❤ toutes cœurs avec toi Siteu
@ndiayemandela5275 Жыл бұрын
Maacha Allah vraiment... wallahi keur gui maacha Allah tabaxantouwoul dèh yalneu yalla fayla yiw bidiaahil Moustapha
@daoudadiop5722 Жыл бұрын
Siteu Est le Référence de tous les Jeunesses✍️❤️
@bathiembengue9220 Жыл бұрын
Vraiment tou les Senegalai on et contente de toi
@buz7755 Жыл бұрын
Li moy nitt bilahi khaliss dou darà addouna ni la machallah Yalna Yalla fayla sa khol si berkep seringe touba mi nga yakhar 🤲
Siteu yalna la yalla soutoural téral la té goudeul sa fann, yokou la ba nga yeuko si barké Seydina Mouhamed psl
@maguettendiaye2280 Жыл бұрын
Machalahh yalna yalla motali leip inchalahh begg na ci ioe goudou fane ak weirr kheweul you sawane bawane mouthiou gou sahh dak barkep borom TOUBA
@ouzdaking382 Жыл бұрын
Siteu grand champion le baye fall sociale yalmine bi Yallheu neu Yallheu fayla sa khôl mou yoné la diamou ak khéwal ak mbollome djioulite inch'Allah 🙏
@ndayesophiediedhiou4580 Жыл бұрын
Siteu vraiment tu as montré tout le monde entier que Fodé est parti mais sa maman a un autre fils . Tu as essayé les larmes de la maman de Fodé.
@sodambaye4646 Жыл бұрын
J'ai les larmes aux yeux 😭sitteu Lou reuy kha deff té dikha am fayou sunu borom
@fatousambasow2569 Жыл бұрын
Macha Allah yallah na souniou borome fayeu la. Geste bou noble nga déf
@aicharassoulba9887 Жыл бұрын
Bilaye khamoule sakheu limou dééf yalla naka yalla maay limou beugeu dans ce bas monde et dans l'autre monde si daraja seydina Mouhamad PSL
@alunesarr9477 Жыл бұрын
Macha.allah fiston yalla nala yallah feey sa dieff
@gnilanendiaye9953 Жыл бұрын
Yahla na l'a yahla défal soutoura AK diam diou sahk dak Baye fall ❤️❤️❤️❤️❤️🤲🙏
@aidadiop4717 Жыл бұрын
Machaalah siteu merci li rafetena torop long vie à siteu
@aminetakane6747 Жыл бұрын
Li moy adouna siteu yaw yalla nala yalla yok liga dèf ni gor bire moko meune ❤❤❤❤❤❤bayi lèn guistal yi tè nguèns kole si yaw siteu adouna lèpe dafa wara rafète ndankhe euleuk nètaliba
@tallaba5715 Жыл бұрын
Machallah siteu yalla na yalla degeureul sa takhaway si barké seydina Mouhamed
@dioumabdallah2863 Жыл бұрын
Lii dafa Nice machallah Lii moy góor jàpp ci góor Góor jallalé góor Góor yégue Fa yalla Baay Faal mentality
@sarrabdou3040 Жыл бұрын
Siteu vraiment chapeau à vous vrai baye fall ngeu
@momo_le-pro.7 Жыл бұрын
Mane dhh fodé hamoumako wone wayé siteu filay diaré done sa fans ba faw li kou amoul khol bou bakh menoko ag diamono djiou metti sakh Yalna yalla yokou sa meun meun yërëm fodé thia firdaws ya
@katyfall3610 Жыл бұрын
MachaAllah maman bagua bakh rek té bakh yombul Yallah nalen Yallah Fay sen djeuf bu rafet mane dama beugue koy def Lou bakh InchaAllah 😊
@rokhayadiop3763 Жыл бұрын
Machala siteu yalnala yalla déf roi des arènes té mou djikla yalna yalla goudal sa fan sam la té aarla aar sa ndiaboot alahouma Amine merci beaucoup
@papamoussasow3293 Жыл бұрын
Merci maman et longue vie à toi
@jeannoeldoufysarr4833 Жыл бұрын
Que Dieu te paye ton cœur respect à toi
@ndiayeawa3907 Жыл бұрын
Noooon bulahi siteu mo bakhe wayyyy c'est des exemple comme ça ont veut pour le senegal
@khalifambengue6125 Жыл бұрын
Ma challah yalna yalla barkel lepp
@babacarsouare6241 Жыл бұрын
Bilahi dioyna dioyou xol kouy nite kou bakh rk sa xol Seed na si lii ❤️siteu yalnala yalla fay sa xol rafetna trop Machallah ❤️😭🙏
@yamadiedhiou482 Жыл бұрын
Très noble geste limoye koleré. Siteu YALANEU BOU YAAKAR TASSE INCHALAH YALANEU LEU LÉPEU YOOMBEU INCHALAH
@rokhydienesarr8382 Жыл бұрын
Yalnala Yalla fay Senghor mady🎉 nous sommes fiers de toi
@ahmadandiaye1637 Жыл бұрын
Mashalla yalna diamb yagg 🙏🏾yalna xeweul yi dollikou té séddooo ak Mbappé mbokk
@ouleyedeme8274 Жыл бұрын
Machalla li rafet n’a lol sakh yalla nala borome bi defal diam diou bari ak soutoura
@adamaka5641 Жыл бұрын
Machalla sama mbeur bi ci kaw thia kaname Ya bakh ya gueune Li moy kharite yalla nala yalla teral adina ak alakhira
@bassiroudiakhatediakhate8864 Жыл бұрын
Macha'allah lii réféttna toropp merci siteu ok nice cool 🤝🤝 merci beaucoup 👍👍👍👍👍👍👍👍 e
@bassiroudiakhatediakhate8864 Жыл бұрын
Merci siteu nice na
@chefmomo5871 Жыл бұрын
Oooh machalla kholle bou sétte rek mo meune Li Yalla nala Yalla faye
@abdoutouncara8685 Жыл бұрын
Asalamou alaykoum siteu vraiment tu es gentille tu es important tu es spécial lii dafa dépasser rafet
@ndiagasamb2522 Жыл бұрын
Vraiment sama hole noumou ceidei si siteu yalla souniou borome rek moko hame ,siteu yawe AK fodé ba aldjana firdawesi bilahi Azime inechallah🤲🤲
@issagning6985 Жыл бұрын
Machalla mon lutteur vraiment lii defa rafete trop yalna la yalla fey sa xol lii môme defa sede xol
@bassmbaye5160 Жыл бұрын
Ohh Machallah yalla nala yalla fay barké serigne touba
@bachirfall6151 Жыл бұрын
Machallah rafét na trop mé so wowoul wone presse dinama geuna nék
@amadoudiouf7585 Жыл бұрын
Notre fierté siteu rèk Doundal wèral
@serignemodoudiop7554 Жыл бұрын
Siteu yalla nala souniou brom takhawou ❤
@fallkhalifa3037 Жыл бұрын
siteu le nouveau entrepreneur 🇸🇳♥️
@gorandir3210 Жыл бұрын
Machalla diadieuf baye fall bi aldiana force inchalla
@ametba348 Жыл бұрын
Geste bi rafetna siteu machalah
@zackariatounkara5634 Жыл бұрын
Hum Sénégal Ndékété amna gni nirrou Borom Touba si holbou raffet Siteu yaal nalla yaal yook bagua yeuk ko Yaal gua raaw ceeey Mass Yaal nalla yaal yeukeuti sissabir aay Noone si barké seydina Mouhamed Sallalahou Aleyhi wassalem
@boussondaw8688 Жыл бұрын
Siteu li déss lép si sa carriere yalla bossi amati defete si barker seydina Mohamed ( psl )
@Madamemmedia Жыл бұрын
Machallah siteu Yalna la borom bi fay li c mignon sa kharite fodé yalna aldiana done keuram ❤
@tamsirmbengue1397 Жыл бұрын
Machala amna sollo lolllllll yalla nalla yalla fayyyyy amine
@aliouly8812 Жыл бұрын
N'déysaan j'ai des larmes au yeux adouna jeuf diou bakh rék moy li Am solo Yalla nanou Yalla khir thi jeuf lou bakh ak diko wakh.amiine
@mountagasow7539 Жыл бұрын
Siteu maguiley nianal goudou fane ah wer maguiley nianal si barké seydina mouhamed sallahou aleyhi wassalam yalla ga gueuneu yokou ba yeuk ko ya am koleuré lou diafé si diamono dji machalla nala thiate sekh lou
@magattelo1020 Жыл бұрын
Yal na la yalla faye yalla yeureum té diegal adji dem ji
@pape7592 Жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureme té khéréko aldiana si barkép seydina mouhamad
@yacinekonte1825 Жыл бұрын
Hoooo machalla yalnala y'alla fayy bilahi borome bakh ga li yombul nitt Kou ame coloré