SITEU MENACE LAC 2: "KI SOUMAKO DIAPEY...GNIMEY WOUMA, MANE LEU TARKINDA BII..."

  Рет қаралды 287,062

2stvsenegal

2stvsenegal

Күн бұрын

Пікірлер: 369
@generalndiaye7353
@generalndiaye7353 Жыл бұрын
Siteu Bo Téyé rékk Yalla dinala may Ndamm in cha'Allah 🙏🏽
@MohamadoulamineSarr-h9w
@MohamadoulamineSarr-h9w Жыл бұрын
Lima guiss nii siteu dina dane inchaalakhou
@LougaLo-dh2qo
@LougaLo-dh2qo Жыл бұрын
​@@MohamadoulamineSarr-h9wamine inchallah
@mabeyegadiaga9199
@mabeyegadiaga9199 Жыл бұрын
Doful dina tey ay mak ñoko yor na baye lac lambdji rek bu nule victoire siteu la dakh lac moy lolou 😂😂
@MbayeKa-c9p
@MbayeKa-c9p Жыл бұрын
Siteu mi mou téy mou yarou déy danou lac dou moroma moko mene moko eupe dollé siteu li rek la ame si komba bi
@MohamedMohamed-dw4xh
@MohamedMohamed-dw4xh Жыл бұрын
Siteu mounoul daane gouye gui ´guene beug mou daane lac ? Bayléne di fowai séne khel . Combat bi nul lay done wala victoire pour lac .parceque lac2 dou djieul béne risque day takhaw deglouko
@mbenediouf634
@mbenediouf634 Жыл бұрын
Siteu machalla nice ❤❤❤❤💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💯💯💯❤️❤️ inshallah inshallah Amine yarabi ❤️❤️
@Le_R319
@Le_R319 Жыл бұрын
Tapha mbeur nimou déf liss ndiago Lay ragal Lac2 defko siteu 😢😢😢yalla may diameu nieup niou féké talko ❤❤
@toutiwakhjobloubari8746
@toutiwakhjobloubari8746 Жыл бұрын
No li mome vraiment dou combat , lac mo meune mo eupeu dolei .
@dykhaamar6350
@dykhaamar6350 Жыл бұрын
Ndam rk Yalmbine siteu kassé ❤❤
@mouhameddiallo7007
@mouhameddiallo7007 Жыл бұрын
Lac yalla nako yalla may ndam
@syalima7549
@syalima7549 Жыл бұрын
Siteu yalnala yalla maye dame
@MamadiGassama-tl4bh
@MamadiGassama-tl4bh Жыл бұрын
En tout cas lac2 et un grand technicien force à toi lac2❤❤
@MoustaphaWade-u4m
@MoustaphaWade-u4m Жыл бұрын
Nn siteu ya woor dé😂 yaw rk lanouy topp yalna la yalla may ndam inchallah ❤
@IbrahimaGueye-q7e
@IbrahimaGueye-q7e Жыл бұрын
Siteu yombale guako dh 😢 té gua déff Ndank mbeur mi guéneu nakharé beréle guaye dadiéle
@bambagueye4141
@bambagueye4141 Жыл бұрын
Bilahi lolou moma diakhal
@momoseck1617
@momoseck1617 Жыл бұрын
Siteu ni nga doone wakhé contre Sa Thiés 😂 Wakh djiou néh nga meun on te connais très bien
@AlyNdiaye-f8i
@AlyNdiaye-f8i Жыл бұрын
Siteu défale attention bou bakh guediawaye la deh ❤❤
@ibrahimacoundoul7118
@ibrahimacoundoul7118 Жыл бұрын
100%Yalmine tarkinda 🤞
@DialloMouhamadou-c5x
@DialloMouhamadou-c5x Жыл бұрын
Lac il est très intelligent 😅 combat bi dou yomb si siteu
@ndeyecodoufaye399
@ndeyecodoufaye399 Жыл бұрын
Ahh père Becaye je t’adore 😂😂❤❤❤Lac nak manga deugueul sa bopp ,siteu attention Lac da nakari beurel 😂😂😂😂😂
@idrissabaro3132
@idrissabaro3132 Жыл бұрын
Bilaye Siteu daye thiahane
@doudoundiaye7130
@doudoundiaye7130 Жыл бұрын
Allez siteu....vive la jeunesse
@lassanatalla767
@lassanatalla767 Жыл бұрын
Siteu mi am na loumouy dieul li naturelle loul d 😂😂😂😂
@momobouthiapathiolybi7752
@momobouthiapathiolybi7752 Жыл бұрын
Lac d'à nga wara attaqué force siteu ndam rk inchalah
@mamadoutchente1170
@mamadoutchente1170 Жыл бұрын
Lutaj Lac di attaque?? Siteu mo am louma wara wone
@mabeyegadiaga9199
@mabeyegadiaga9199 Жыл бұрын
Dedet siteu kay na tok xarko rek comme nena day attaquer
@layesam5162
@layesam5162 Жыл бұрын
🔥🔥🔥🔥🔥DESI CALANNDA , C'EST CHAUD😂 NÉKHNA BA PARÉ . MASHALLAH 🥰
@seydoudieng9099
@seydoudieng9099 Жыл бұрын
Siteu outaal doolé ta boul faté lac de guerre respect motakh mou dieulleu nguir yalla boulko yah oie borom bakhnga
@ngallmbaye1052
@ngallmbaye1052 Жыл бұрын
Siteu mystique rek la yakar
@mbeusseneymar5862
@mbeusseneymar5862 Жыл бұрын
Yalmine bi inchallah yalnala yallah may ndam🙏🙏🙏🙏
@CISSEBOUSONKO
@CISSEBOUSONKO Жыл бұрын
Nervi yi kou daan yaa xam kounou daaan yaa xam focus 2024😂😂❤❤
@bathiedioum898
@bathiedioum898 Жыл бұрын
Siteu yalna yalla maiye ndam inchalla
@cheikhtall-rp4di
@cheikhtall-rp4di Жыл бұрын
Wakh deugeu yala siteu manoull dann lac 2 bilahi
@elbiranetoure262
@elbiranetoure262 Жыл бұрын
Waxou lac 2 kay situé yalna yalla mayla ndam inchalah
@amarniang3915
@amarniang3915 Жыл бұрын
Siteu moye Sénégal
@baba_07sn
@baba_07sn Жыл бұрын
Siteu rék Incha allah ❤
@424000
@424000 Жыл бұрын
Libérez Sonko.
@falldragonmart2161
@falldragonmart2161 Жыл бұрын
Siteu mi day theatre rékk 😂😂😂😂. Vraiment li d'où Lambeu
@Hamadythiam-s8b
@Hamadythiam-s8b Жыл бұрын
Siteu yallah nako yallah may ndame❤
@madefaye5980
@madefaye5980 Жыл бұрын
Lac 2 mo geuna ragal thie lamb bou siteu ndam rk inshalla
@ndiogoundiaye8555
@ndiogoundiaye8555 Жыл бұрын
Bn chance yalmine bii siteu rék
@PapaAbdouDiédhiou
@PapaAbdouDiédhiou Жыл бұрын
Siteu combat bi déé boco yakaré si mystique je suis d'accord té meunoulo eupeulé lac mystique ni dollé ni rien ..
@assanediakhate3618
@assanediakhate3618 Жыл бұрын
Degue bou weer
@fatoumbaye1121
@fatoumbaye1121 Жыл бұрын
Machallah deugue bou wére gan wakh boudé muystique lac 2 monko euppeu si lamb dji boudé doolé tamit lac 2 monko euppeu wayé lac2 na déffe trés attention bala nioukoy déffe comme ligniou déffe balla gaye2 soteuko boy niang2 ak reug reug nioy diappalé siteu si ngalathieu ak yénéne mbeur si Souf lac 2 souma sagnion daffay guéne guédiéwaye dem fénéne préparer combat wam kéne bagnia kham foumou néke té lac 2 n'a kholat boubakh entourage gam bala nioukoy diay comme nigniou déffe balla gaye2 Mane faralouma lac 2 faralouma si kéne Mane ama baldé moy sama mbeur séke lac2 daffa yaarou kham nimouy wakhé motakh mou nékhe ma siteu temps yii mystique bou doy War la yoor entout cas lamb dji 50/50 la kounéke meuneu na daan moromam lamb leigui doolé fégniatousi kou euppeu nagalathie yay daan lamb daffa barri surprise motakh diaroul wakh kimoy daan bala jour ba gay rouss lamb leigui kéne khamatouko daffa diakhasso dakh mystique bou barri dagay guiss mbeur yooré victoir ram diékou mystiquement baparé si jourou combat bi niou nangou victoire bi si lokhom diappeuko mystiquement mbeur bi rére si sass si diakhasso Di déffe loum meussouta déffe avant arbitre Di sifflé tamit dagniesiy diappeu mbeur yéweko bamou deugeur nagamal ayy tankam ba tankeu yii dotoul meuneu bougé dagay lale sa nguimb adversaire rek mou teural la dagay méle ni néwe ligeiy bou Boon mougui nonou si tankeu wala lokho néwe lagniekoy ligueiyé boparé déffeko sisa birr nguimbe bi nguimbalé woko sa sa adversaire bouy lale sa nguimbe Di danou momla boy niang 2 nguimbo woon motakh kouy wakh si lamb nagan kham boubakh ligay wakh lamb leigui ak bou dieuckeu bokoul
@IbrahimaFaye-l1k
@IbrahimaFaye-l1k Жыл бұрын
kone dolé si volume là khamo lamb
@cheikhndiayetouba040
@cheikhndiayetouba040 Жыл бұрын
Lolu dong lasi yakar ta lolu Lac mo kolo apoole
@BinetteSylla-gy8nk
@BinetteSylla-gy8nk Жыл бұрын
Fii koufii mére diokhé 100 fran Siteu kassé ndam rk inchallah
@MourtadaFaye-l7v
@MourtadaFaye-l7v Жыл бұрын
sitteu rk lañouy toppou ❤❤talibé bamba❤❤
@ousseynouba3805
@ousseynouba3805 11 ай бұрын
Bilay lac moy sm mbeur me siteu j❤
@mbodjielfromfouta1244
@mbodjielfromfouta1244 Жыл бұрын
Billay Siteu moy sénégal🇸🇳 Tarkinda yi niongui sa guinaw💪🏿💪🏾💪🏽💪🏿
@ndiayeibrahima8931
@ndiayeibrahima8931 Жыл бұрын
LAC 2 EST L'UN DES MEILLEURS LUTTEURS DU SÉNÉGAL.
@BinetteSylla-gy8nk
@BinetteSylla-gy8nk Жыл бұрын
Wakhi doff Lac 2 est ce que mbeur lhe match nul rk
@malicksene8838
@malicksene8838 Жыл бұрын
Rasou rèk lafi nèkè
@ndiayeibrahima8931
@ndiayeibrahima8931 Жыл бұрын
@@malicksene8838 moko djigue, motakh c le vip qui a moins de défaite
@ronaldgomis
@ronaldgomis 11 ай бұрын
Arrête way
@woneabda5298
@woneabda5298 Жыл бұрын
Siteu c'est un vrai guerrier et un vrai comédien 😂😂😂
@rokhayandoye7184
@rokhayandoye7184 Жыл бұрын
😂😂😂Bilay dafma reitane Lo bama sonou sama fans bi
@LamineKane-dm6gc
@LamineKane-dm6gc Жыл бұрын
​@@rokhayandoye7184mo
@fatouaidara7910
@fatouaidara7910 11 ай бұрын
Siteu attention lac ndanane leu dh mais lamb meuna lou nèk bonne chance
@MbendaThiam-m7k
@MbendaThiam-m7k Жыл бұрын
Man beugg na siteu trop mais lac Damaka beugg ndax limou yarou
@khalilfaye1289
@khalilfaye1289 Жыл бұрын
Siteu, Niang bou Ndaw rekk mollah eupe dollé.😂😂😂😂 Kone Lac 2 doussa morome
@mohamedballadiop6085
@mohamedballadiop6085 Жыл бұрын
😅😅merci lolou la wakh ci sama khél démb😂😂
@massambadare
@massambadare Жыл бұрын
Le 19 ngeni comprendre siteu mo Moun koudoul lac 2 bala 19
@papasamb8709
@papasamb8709 Жыл бұрын
Bialhi 😅😅
@NogayeThiam-t8s
@NogayeThiam-t8s 11 ай бұрын
Siteu rkkk❤❤❤❤
@djhotgoudiry9818
@djhotgoudiry9818 Жыл бұрын
Focus 2024 Ousmane Sonko rek
@FatoupendaBa-tt9kb
@FatoupendaBa-tt9kb 11 ай бұрын
Aytia lac ndam rek sama nidiaye bi💪💎
@mbayelo7022
@mbayelo7022 Жыл бұрын
Siteu kassé ❤
@mballomaoulidou3358
@mballomaoulidou3358 Жыл бұрын
😂😂😂😂😂 défa am ay risque yo khamné boko bayiwoul diko diel manga diaré fofou déé té man ragalna lac doorko mou wadd niou yobouko principale mou fatou. Way siteu day toukh yamba way
@malickkmplayeurniang9404
@malickkmplayeurniang9404 Жыл бұрын
Siteu moytoul contre attaque gou lac 2, lou lere lala wakh
@Lilldio
@Lilldio 11 ай бұрын
Siteu rk jusqu'à ma mort ❤️😊😊😊😊
@amydiome1366
@amydiome1366 11 ай бұрын
Situé yalnala yalla may name
@MaimounaNdiaye-v4u
@MaimounaNdiaye-v4u Жыл бұрын
siteu seull dokhol khana❤
@Loriginalfaye
@Loriginalfaye Жыл бұрын
Niounne tarkida bi rek laniouy toppou
@papeyakhyasow989
@papeyakhyasow989 Жыл бұрын
Siteu mi na yammm té régler sa thies sako meune foufff té sa thies lac de guier moy magam
@amarecoulediop3324
@amarecoulediop3324 Жыл бұрын
vraiment sawayy siteu sa wakh barina trop khaliss rek guay oute si combat bi mais lac dou sa morome meuno ko dane
@Ndayemoussaliou
@Ndayemoussaliou Жыл бұрын
Ay niom niep damalén beugua 😍
@JuniorSeye-u5x
@JuniorSeye-u5x Жыл бұрын
Siteu yalna ko yalla mayy ndam
@seydoudiop9579
@seydoudiop9579 Жыл бұрын
S déh wah rék lacii am
@JuniorSeye-u5x
@JuniorSeye-u5x Жыл бұрын
@@seydoudiop9579 lolou nga yakar rek yalla mo yor ndame yalna ko diokh siteu
@massendiaye5802
@massendiaye5802 Жыл бұрын
Non Siteu déy thiaxane bilahi Lac mi mo gueune nakadi dane si ténors yi am dolé, technique, tactique défensif té erreur bo déf mou exploité ko. Eum kén dou mom mom miko dane
@ndiayesouleymane7041
@ndiayesouleymane7041 Жыл бұрын
Siteu bayil volé yi fo tolou yangi souss amo dolé mé beuri nga wakh
@moussaseck9513
@moussaseck9513 Жыл бұрын
Waw lac parck ragal le
@mohamedseye321
@mohamedseye321 Жыл бұрын
Champion ya gui soga am combat
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv Жыл бұрын
Siteu yabaté nena zarko mo gueuna tangue lac 2 😂
@babadiop4316
@babadiop4316 Жыл бұрын
Siteu khana amoul mbokou 😂😂😂
@OusmaneNdiaye-dv3sf
@OusmaneNdiaye-dv3sf 11 ай бұрын
Yalmine bi kassè lagnie topou bly ioe ndam rek ❤
@NdongoDieng-gw1xo
@NdongoDieng-gw1xo Жыл бұрын
Siteu jour bi nga dieulé avenchou lac 2 nga coumacé danou ba lamb dja 😂
@seydoudiop9579
@seydoudiop9579 Жыл бұрын
Walaye wahga deug
@Jerkin-amabalde
@Jerkin-amabalde Жыл бұрын
Woyyy😂😂😂😂😂🫢😂😂😂
@daoudarassoul1848
@daoudarassoul1848 Жыл бұрын
Lac nak déma guiss ni dey titte mais yalna nga dan
@ismailayade4979
@ismailayade4979 Жыл бұрын
Bilahi siteu eupo lac doleii eupoko mistik koula khol kham ni si misrik gua yakar pour am ndam gay rapi rapi ni ndak rek vive lac 2 vive guediawaye
@souleymanedeme1095
@souleymanedeme1095 Жыл бұрын
Siteu rk lañuy topou BiLLaHiii walay ❤😂
@mbodjielfromfouta1244
@mbodjielfromfouta1244 Жыл бұрын
Mbeur deuk bi ♥️💪🏾💪🏽💪🏾💪🏽 Ndam rék inchllh 💪🏽💪🏾💪🏿💪🏼 SITEU yaa wooor 💪🏾💪🏿💪🏻💪🏾
@MamediarraGueye-z2w
@MamediarraGueye-z2w Жыл бұрын
Non mane siteu damaye fathie tarkindabi😂😂😂😂
@MoussadiaoMoussadiao-nt3xn
@MoussadiaoMoussadiao-nt3xn Жыл бұрын
Lac 2 amoul kimouy ragal si lambe beurré ak modou lo boy niang
@Jerkin-amabalde
@Jerkin-amabalde Жыл бұрын
Vraiment frère siteu comédien leu😂😂😂😂😂 bilahi
@momolecaporal5536
@momolecaporal5536 Жыл бұрын
Siteu Siteu leuH 💪🏿
@philippendenendiaye2756
@philippendenendiaye2756 11 ай бұрын
siteu rek sougne la dané dougne découragé ki dagne kaye dane
@ibougueye9109
@ibougueye9109 Жыл бұрын
Siteu danou nga ba paré ki ma giss
@babsngom9970
@babsngom9970 Жыл бұрын
😂😂😂
@alinesyllaSyllaaline
@alinesyllaSyllaaline Жыл бұрын
Siteu li rek la ame si combat bi
@barandiaye1474
@barandiaye1474 Жыл бұрын
Siteu sa wakh bi yeup tite kassé laa😂
@Gaston-q4y
@Gaston-q4y Жыл бұрын
Kou yakarnii siteu meunoul dane lac de guers yangui nakh sa bopp.
@senegalrek4657
@senegalrek4657 Жыл бұрын
Vraiment lac carrière VIP yassi gueuneu niaw carrière 😂😂😂😂
@cheikhomarniang3239
@cheikhomarniang3239 Жыл бұрын
😂😂deimal gestu khamo li ngay wakh kou sanione am mbeur bou meilni mome 😂😂
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall Жыл бұрын
@@cheikhomarniang3239kein bougoul am mbeur bou melni mom match nul ak daw moy palmarès
@papathiamdogo5439
@papathiamdogo5439 Жыл бұрын
Walahi Siteu sa wakh barina Defal sa Xelni eupokoo dolei ta Dou barré bi Farr nak meun ta niak si Pa Yiii amgua combat dh
@stevedanieldossantossilva7795
@stevedanieldossantossilva7795 Жыл бұрын
Bébé Diéne le Messi de l’arène 🎉
@odoa4880
@odoa4880 Жыл бұрын
Siteu li la lac wax bayyi ci xel«lii rekk nga am ci combat bi» 😂😂😂
@momoseck1617
@momoseck1617 Жыл бұрын
Siteu ni la doone def ak sa thiés 😂
@seydoudiop9579
@seydoudiop9579 Жыл бұрын
Siteu déh amoul chance cii combat bi
@Thebabacar
@Thebabacar Жыл бұрын
Ouais c’est ce que je pense moi aussi même si j’aurais aimé qu’il le bat
@seydoudiop9579
@seydoudiop9579 Жыл бұрын
@@Thebabacar môme ga nou wahdji geuneuh baré geune KO arranger dah bou dano niounéh dolé 💪 rék lako eup wayé eupouko fite 😢
@mamadoukane5669
@mamadoukane5669 Жыл бұрын
Le silence parle
@gatesneysen7777
@gatesneysen7777 Жыл бұрын
Siteu li nga am si lamji donc frofite toi de faire le show 😂🤣🤣🤣🤣
@coumbadiamadiaw3803
@coumbadiamadiaw3803 Жыл бұрын
Bayi léne di teugal lac 2 combat dou changé jamais
@beuguesalioubeuguesaliou524
@beuguesalioubeuguesaliou524 Жыл бұрын
kou meunoule dane sathies ak gouy gui est ce k digua meuna dane lac 2
@bassiroundaw4751
@bassiroundaw4751 Жыл бұрын
😂😂😂lolou la meunoul comprendre
@beuguesalioubeuguesaliou524
@beuguesalioubeuguesaliou524 Жыл бұрын
@@bassiroundaw4751 mane d lolou moma diakhale siteu na tok dégue lou wakhi nite yi migui sogua ame combat khamoule sakh si limou dougou
@momobouthiapathiolybi7752
@momobouthiapathiolybi7752 Жыл бұрын
​@@beuguesalioubeuguesaliou524lolou ngein done wakh si boye niang kou meunoul dane diw ak diw té mo dane siteu yalla nala yalla may ndam
@sabarasts
@sabarasts Жыл бұрын
Siteu sou dané Lac2 miracle la 😂 Lac2 sa rak Sathies da niow diakhassé Siteu dane ko, ey so nulé ak Siteu 😂
@seydoudiop9579
@seydoudiop9579 Жыл бұрын
Woléne sathies niko siteu gui roubéh fi
@aremijfaye5160
@aremijfaye5160 Жыл бұрын
LAC SA COMBAT YEUP AK MBEUR YOU MAG YI DAGAY RASSOU. CONTRE BOY BI NAKKK ÀMO DROIT RASSOU NAKK !!! 😮
@RioNdiaye
@RioNdiaye Жыл бұрын
Khana rassou bokkoul ci lamb
@mohamethsamb
@mohamethsamb Жыл бұрын
Lac dane Siteu loumou koy yokk ? Dara 😂
@Mamapapis-t1p
@Mamapapis-t1p Жыл бұрын
Mais siteu dafa dof dh 😂😂blie
@therealBabs92
@therealBabs92 Жыл бұрын
Siteu Rufisque est derrière toi ndam rk inchallah✊
@AstouGueye-w4m
@AstouGueye-w4m Жыл бұрын
Siteu Yako meune ndamm rek inchallah
@djibysoung2998
@djibysoung2998 Жыл бұрын
Bilaxi mosouma faral sita mes bi momlafaral ndakh sosiyal bimouy def lat mom daguemou bopam déy tut si combat
@IbrahimFall-is6je
@IbrahimFall-is6je Жыл бұрын
Lac guerre dou darr billahi, affaires by seteu
@babacarkhouma-rv5ts
@babacarkhouma-rv5ts Жыл бұрын
lamb fit mokoy déf té lac mii siteu dieulna fit bi bou yagg
@ametba348
@ametba348 Жыл бұрын
Na bayi souss bi 😂
@cheikhomarniang3239
@cheikhomarniang3239 Жыл бұрын
Siteu amoul fit day motalikou reik 😂😂😂
@RioNdiaye
@RioNdiaye Жыл бұрын
Iow lac lamb j ken eupou ko fiit yen pour yen fiit ci wakh leu
@ibrahimaniane6508
@ibrahimaniane6508 Жыл бұрын
Sawaay dioum nga kou am fiit dafaay nopii reek dii xapp dila bayii ngayy talakhou dii wakh reek mais biss boko songué reek mou todj sa lou bonn bou bakh 😁😄😃 dieuleul exemple siteu sathies ba arbitre bii nee parr noumou demeewonn ay rafall yo khamné😄😃😀
@papeleroipapeleroiofficiel7958
@papeleroipapeleroiofficiel7958 Жыл бұрын
Saway iow khamo lingay wax dh lac 2 face à face yeupp nii lay nieuwé ta siteu guiss nagn ko fi ak sa thies nii la woon ak gouy gui nii la woo ta zarko bimouy wax sax dako daan konn n'a yam rk siteu n'a aucune chance sou daané rk yalla si diapp
@AlassaneNiang-f4w
@AlassaneNiang-f4w Жыл бұрын
Ms siteu mi liguéyul luy yeungueul lac de guerre
@FallouDiouf-xo4ot
@FallouDiouf-xo4ot Жыл бұрын
siteu kesse lay top domou serrere bi
@lahatCissė-p9i
@lahatCissė-p9i Жыл бұрын
Lac yw layè waxal bou defè 2 minute ma bayil la😂😂😂
@mamadoukane5669
@mamadoukane5669 Жыл бұрын
😂😂😂mouni
@boylebou3230
@boylebou3230 Жыл бұрын
Beuré bi lac yoor Siteu manouko dane
@tydiomdiom4971
@tydiomdiom4971 Жыл бұрын
Bon frenchement lac 2 Sama Mbeur leu Ms Dama remarque siteu dfko joh tieur Ms Niongui jeema nehal combat bi ms lac amna nimouy wahé siteu Dfay moudje seed kw il faut ke lac yeungou tmt mou nah
@AgfhHsisi
@AgfhHsisi Жыл бұрын
Siteu le champion
@MakhouDiop-k9e
@MakhouDiop-k9e Жыл бұрын
Lac de guierre day féne rék 😂
WAXTANN BOU DOYWAR SITEU ET LAC2
16:01
Bantamba TV
Рет қаралды 330 М.
НАШЛА ДЕНЬГИ🙀@VERONIKAborsch
00:38
МишАня
Рет қаралды 3,3 МЛН
Человек паук уже не тот
00:32
Miracle
Рет қаралды 2,4 МЛН
Сюрприз для Златы на день рождения
00:10
Victoria Portfolio
Рет қаралды 2,7 МЛН
CAN YOU DO THIS ?
00:23
STORROR
Рет қаралды 43 МЛН
Echange houleux entre Ama Baldé & Modou Lo " Yeneu yorone pompe à gaz bi "
19:19
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 228 М.
REACTION DE SITEU ET DE LAC DE GUIERS 2 APRES LE COMBAT
18:16
2stvsenegal
Рет қаралды 770 М.
НАШЛА ДЕНЬГИ🙀@VERONIKAborsch
00:38
МишАня
Рет қаралды 3,3 МЛН