Jaime ce genre de femme avec un caractère de fou👌👌 👏 bravo
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
Yow domou xaram dji Lo wakh lou si sa yone seytaner
@farmatathiatediakite75855 жыл бұрын
pape Sene ioe lousi sa yonne oci si sama commentaire imbéciles way yay domékharam bou bakk bi🖕🖕🖕🖕🖕🖕🖕🖕
@momomergane31405 жыл бұрын
😂😂😂
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
@@farmatathiatediakite7585 yow dou mala saga khamou len mbirou yala ma ndoulen si nioun sokhna aïda saliou la top faww mounou len si dara kou nangou rek napalou
@farmatathiatediakite75855 жыл бұрын
pape Sene je ne connais meme sokhna aida c juste k j’ai aimé sa façon de parler avc son caractère mais tu n me connais pas et ru minsulte apprend à respecter les gens aux moins ! On es sur KZbin chacun a le droit de donner son point de vue mais personne n’est obligé de répondre
@58balamoussa5 жыл бұрын
Ceux qui refusent de suivre la Voie d'Allah, suivront la voie des hommes de gré ou de force.
@talibebambasalihousarr10675 жыл бұрын
Serigne Cheikh Béthio Thioune yalla na yalla yokou aye léram té dolli yermandé si mome amine Serigne Saliou Gueltappé khalife de cheikh béthio yallla na yane bi oyofff
@sokhnamanethioune59595 жыл бұрын
Talibé Bamba Touba Sarr amine 🙏🙏🙏
@arametoure82585 жыл бұрын
Machallah nitt day am foula cheikh bi yalla nako yalla yeureum
@mbenetoure3335 жыл бұрын
Sama domou baye aida môme cheickh dako beguone môme mé bon guor moy djitou nak c vrai
@naphiendiaye85175 жыл бұрын
Degue nekh
@arametoure82585 жыл бұрын
@@mbenetoure333 Domou baye je suis d acord avec toi mais lou thii nek nitt daff ko wara bayé ak kiko mombeu la succession se fait de pére en fils et en plus daffa mél ni mom rek mo fay Sokhna
@mbenetoure3335 жыл бұрын
@@arametoure8258 c vrai môme domou baye môme lo nék sokhna ak lougnou la guene diouplou bisse bou dé gneWé dé nga kham ni lép deguela nguourou yalla rék modoule diekh nak sosi amé se keur ak saye biens bakhna
@habysiby635 жыл бұрын
arame toure 9gprfd upllb
@boubacarsagna72455 жыл бұрын
Kiiii fan nakoo wayyy 😀🙌🏽
@amantousambe67965 жыл бұрын
Sa Baye Aka Goré Wathiona Ak Nieup Thioune ❤ Barki Serigne Saliou Walay Keine dou Mome Si yonou mouride🙏 Nioune Dé douniou diouk si Diko Santeu Barkep Serigne Saliou🙏
@naardiagne36665 жыл бұрын
Bilay wakh nga deugg
@amantousambe67965 жыл бұрын
@@naardiagne3666 wawaw
@deguenefall96625 жыл бұрын
Wakh deugg yala dome dh moy donou bayam. Merci mere thioune
Franchement les journalistes sont grave tout le monde sait que cheikh bethio à des héritiers arrêter de créer des problèmes et de la haine ds les famille
@cloclosylla39975 жыл бұрын
J s8 de ton avis
@papengom84705 жыл бұрын
Bilahi
@madamedieng21085 жыл бұрын
Billahi wakhal book journaliste yi kay mais képp kouy yé fittna yalla rëbbēna
@astoundiaye56985 жыл бұрын
Nene Keita deug deug lo kham si seytanai
@astoumar41435 жыл бұрын
Deuk deuk amena question yo khamené day diakhassé aréter way ahh
@gueyemalick72165 жыл бұрын
Thièye cheikh bèthio diamou serigne.....................................yallah na khippè aldjiana si barckè serigne saliou.
@awasow18585 жыл бұрын
Ohhh contane na siii yow ,bi deugeu eupeuneu
@oulyndiaye12365 жыл бұрын
Diadieufffff
@cheikhbasskeurmassar46545 жыл бұрын
Ndeysane
@wapladdss69035 жыл бұрын
Tres bien dit ma Fille. Aida dotouko défati...
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
Sa leufeul ndeye yow
@farmatathiatediakite75855 жыл бұрын
pape Sene t’es vraiment con a insulter les gens comme ça 👅
@rakhouguedjii15065 жыл бұрын
thièy aida diallo nan ko yalla moussal thi thiatt bilay da mako yeureum ay bou fi cheikh bi nèkonn di guènn ko may diam dè
@legeographe2215 жыл бұрын
@@papeadiyasene2781 Yaw sa ndeye amoul leufe pakh la ame imbécile.
@lesbabtoussontdesporcs97805 жыл бұрын
@@legeographe221 non yaroul pakh dh , téne la yorr 😂😂😂
@ndellagueye3965 жыл бұрын
merci tata fatime bien s saliou thioune gueul tapé khalif koul thiatacound aida seytanè la yall na niou yall moussa ci aida diallo ngibil sa keur bay mome gueuen
@thiawadji9295 жыл бұрын
Je taime mére fo deuque ma sétesila😍😍😘😘😘😘😍😍😍😍
@diawrama43735 жыл бұрын
Franchement elle a raison
@alimadiouf69505 жыл бұрын
Liberté 6 extension
@ndeyekeita49995 жыл бұрын
Nagnou KO wakh gnou ande setiko nite daye ame foula waaye
@bintsouleymane68595 жыл бұрын
Ndeye Keita hana boleinn di dem yobaléma way
@manembaye66825 жыл бұрын
Walahi je vs fan mére thioune j'aime votre caractère et comme vs parlez vraiment bien dit
@maguettethaim73335 жыл бұрын
Foula dal bou diéxé thi niit dara amatoufa machallah cheikh bi yalla nako serigne saliou térou
@bbchougalaxys19035 жыл бұрын
Machalla djiguéne deye ame foula boulene.nagou kene kou diakhassé sene famille
@badougueye35775 жыл бұрын
Macha Allah sokhna si kadou yii amna solo trop sakh.
@coumbasamassa50655 жыл бұрын
Koumbasamassa
@astoundiaye56985 жыл бұрын
Ndeyesane sokhna fatim thioune goudal fane waiyy
@sambasy84165 жыл бұрын
Wawaw machallah deug pir fan nala trop thioune rek
@mariamabandia777 Жыл бұрын
❤❤❤❤
@sokhenaoumydienne10605 жыл бұрын
Sa sokhnap baye la donc na lep raféte😍
@habydiop78135 жыл бұрын
C'est la fille de son père "cette femme elle a de forte caractère" j'apprécie beaucoup d'honnêteté.
@ndeyeastoundiaye42305 жыл бұрын
Mane sama yaye dji la beugn aka am fouleu 💖
@awadiallo69315 жыл бұрын
Mash’allah wakh djie rafète na sène baye yalla nako yalla yeureum té kharéko aldjana mais nak amegua foula
@Laspheredesdistinguees5 жыл бұрын
Bethio amna ay domiiii mak ndeyssane ! Nako yalla faye kholam !
@coumbasarr41125 жыл бұрын
man Sokhna Aïda la beugue nitt da Guay def té dosi bolé thiow niaw yw rk ak sékhe bi ak yalla rk ka kham lou takh gua tokk ba legui kon boul tontou bou lén fallé yw contunél rk sa li guéy wakh amoul na dieuf rk am❤❤❤👈
@angeliquendiogoye94705 жыл бұрын
Deug deug nitt day am foula deug dieureudieuf serigne saliou mbacké balla lepp mome leu
@mariamadiouf38255 жыл бұрын
Waaw kay nak yaw ak say raak ngay wakh.mai li SERIGNE bi beug moy gnoun thiantacone mom lagnouy def Sokhna aida lagnou SERIGNE bi lobele tei mom lagnouy toop faaw.Moy took si fauteuil ba adouna seréko ndakh dafay beugui beugui SERIGNE bethio.
@mariamadiouf38255 жыл бұрын
Waaw kay nak yaw ak say raak ngay wakh.mai li SERIGNE bi beug moy gnoun thiantacone mom lagnouy def Sokhna aida lagnou SERIGNE bi lobele tei mom lagnouy toop faaw.Moy took si fauteuil ba adouna seréko ndakh dafay beugui beugui SERIGNE bethio.
@mariamadiouf38255 жыл бұрын
Tei sakh nak Sokhna aida dafa guethio woule ndono mom day thieumii SERIGNE bii tei lolou moh fetei kaaw lepp tei bimahii nane dem rk lepp dina lerr!!
@mustaphasamb23135 жыл бұрын
Merci fatim thioro thioune dieureudieufeuti
@dioudba50995 жыл бұрын
Mer liga wakh deugeulah aida nadem doni keur bayam😂😂😂😂
@dfbcdfbc22945 жыл бұрын
Serigne béthio thioune wathionak niëp linga wax deugue la wayé na raféte nioune thiantacoune yi xamnagnou taxawayou sokhna aïda bou raféte bi ci thiante gui ak ci diéf yiii litakhone serigne fonkone ko da meune ci diéfou serigne touba yii kone nagnou wéegue serigne rék té fonk niëp serigne bi ame talubé rék lagnou diangale dieredieuf serigne béthio thioune wasalame 👏
@papito80255 жыл бұрын
Elle a raison dal Douma talibé cheikh Bethio dei mais dal ndaw ci wakh na deug ... ana jiggen ak beug tokk ci kilafa 🤷♂️ Serigne touba dieureudieuf
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
Bane deug SERIGNE BETHIO mome ay taloubem djokh lene S.AIDA nguén di wakh lou nguén xamoul
@ibrahimagueye94245 жыл бұрын
Pape Abdoulaye sane
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
Kou bah donou serigne touba ak don serigne touba bokoul na ler sokhna aïda saliou da don serigne bethio dou samay wakh serigne bethio moko wakh yay man may yow kou si beug lou la ler ma diokh la sama numero wathsapp
@o2la2.095 жыл бұрын
@@papeadiyasene2781 yow yereum nala d. Khana légui Aida Diallo moy S. Serign Saliou légui di Serign Touba ? Domoram nga rek même bouko serigne bi wakhé et alors ?
@papeadiyasene27815 жыл бұрын
@@o2la2.09 lolou dou lou malay wakh dina la ler nange sou nékéii narr nga ame nduimbalou serigne touba
@kebsvipkebe1035 жыл бұрын
Mancheallh Soxna Fatim gadd yii Amm na solo lole mancheallh Cheikh bi Yalla na yalla yoke Ayy lérame
@fagueye54695 жыл бұрын
waw waw ,thi fouleu ,masha allah. d'accord avec vous
@fahrozblanche24315 жыл бұрын
Video bi setane nako plus de 5 fois , cette dame est veridique
@mamediarracisse45635 жыл бұрын
fahroz blanche de mm k moi setane nako plu d 5 foi bilaye
@fahrozblanche24315 жыл бұрын
@@mamediarracisse4563 mane je vois k ni femme bi dafa lenn yaga deranger
@leontinemendy45915 жыл бұрын
fahroz blanche Moi j arrête pas
@seckmoustapha77235 жыл бұрын
Degue deuge rek ga wax Aida Dallo dafa yabatè té fouye imbecille
@sokhobbsamb62655 жыл бұрын
Bien dit niit day ame foula wayy ba adouna di bakh fane la djiguéne di djité
Khana meunou Léna bayi sokhna aida défu léne dara lim amone kouné ka beg guone ame. Si ndiguel cheikh bi rek la done dokh .nday raféte aduna amul solo 🙏
@mberryable5 жыл бұрын
Wallahi wakh nguan degue de
@modoufallbetebeteitsenegal52725 жыл бұрын
MACHALLAH JE SUIS TIDJIAN MAIS MAMEN LINGUA WAKH AMNA SOLO KÉN DOU DONDOU BAYOU DIAMBOUR TA AY DOMAM DI DOUNDOU
@ayshajuliette5 жыл бұрын
Ndeysane on connait pas ses enfants tey kenn dou lenn degg ci dara machala Wakham deugeur neu maissss cest la vérité kou sa diekeur décès nga delou sa keur baye
@Amy-vg3md5 жыл бұрын
Ndaw baye you beri seut😊
@somb81225 жыл бұрын
Moy deuuuug
@marietoudiop55345 жыл бұрын
Bilay kousa djeukeur wath ligueye gua delou sa keur baye aida diallo nit dafay a personnalite tu nas mm pas le droit de dire mot
@awadiallo69865 жыл бұрын
aissatou seydi deugue deugue
@tarikhefall39635 жыл бұрын
Merci djiguen foula
@hadaraseydihadjimalick91575 жыл бұрын
vraiment cette question ne doit pas causer de probleme.meme un thantacoune conscient sait k le pure khalif de cheikh bethio est son fils aineé. une simple femme noumouy dondeé la xamoul
Une simple femme nga wakh lol n'est pas femme qui veut Simple femme mola diour
@hadaraseydihadjimalick91575 жыл бұрын
@@galsenflow9077 Wei une simple Femme. Meme si c'était mw une femme ne peut être héritier de mon père Mais je vs comprend vous ne connaissez pas votre religion Géré len s'en problème😁
@aissatoulo25995 жыл бұрын
Après je suis d’accord que tegoulfeine pour dieul succession bi mounone nge wax lolou.........mais arrête de dire simple djigueine c’était comme ci tu rabaissais les femmes alors k ay nitleine comme gneup sen mentalité yi nak moy lolou ..lolou momeu gueneu meneu enerver fallait pas dire ca..arrêtez de prendre la grosse tête ay simple domou adama ngeine du sang et de la chair vous n’êtes personne.arretez ses mentalités attardés
@cheikhseck75234 жыл бұрын
Mach Allah amna solo yaye fall bi niite daye ame foulle waye 👏👏👏👏
Wallahi c vrai .yalla nako yalla yeureum amine yaraby tout mais condoléances a la famille
@selfmadegirl86555 жыл бұрын
Son fils moy donne khalifa bi c'est clair et net lolou kenn weranté wouko. Mais sokhna aida dafa am liguey bou mou dann liguey bou amm solo si bolei ak dadialé thiantacounes akk yenen nak yenen yoo khamni ayy domou cheikh bi defouniouko. Instant bi mom ken meunoul khalat thiant wala magal sans ayy sokhna cheikh bethio. So lenn fekhé ba séparer wou akk sokhna aida di ngen tass lou sen bayy ligueyonn. Même si vous n'êtes pas d'accord acceptez k dafa liguey lou bari ba eksi fii. Mom dal na continuer di ded patt akk organiser pour wakh deug nakk mbeuguel bi nitt yi amone si cheikh bi si sokhnam yii la niou ko gueuna yeuk que si ayy doomam nakh niom laniou dan guiss
@magattesarr73005 жыл бұрын
Avis partage
@mberryable5 жыл бұрын
Selfmade Girl ouhh vérité billahi wakhnako sen problème famille leu mounon neu geuneu rafet rek Aida diambar leu won thi yoon wi
@ndeyefatoucisse79485 жыл бұрын
Selfmade Girl
@mberyniang83575 жыл бұрын
Machallha tnit day amfoul la aida diallo demal fowe
@banelsy81915 жыл бұрын
Machallah sa wax rafetna trop
@nassimiliansidibe27525 жыл бұрын
Thieuy Serigne Béthio Mo diaboot, Yaw sa Baye Bamouy ndoundou Gnémé wo Wone waxé Nii Thi Sokhnam Siii; dieuw Ngako Dhé, Sokhna Aïda défoul loudoul done Talibé, Tarbiyou sa Baye bamou Dèf Thi Mome limou Dogal Thi Mome Kone Bagne Bagne Nangou; Serigne Saliou GeulTapé Moy Xalif bi lolou Force la té Borome Xèl douko Meussa LameLaamé Kone Ay Chaise xeuy na yèn la Sokhal Wayé Gnoune Thiantacone lignou Sokhal Moy Kignou Sa Baye Bolèl Té Mouy Aïda Diallo Momou Nga Xamni Seuy dongou kofa indi Wone mou Gneuw ame pastèf ba ame fa limou Ame; wayé Mome dé Nite Kou Serigne Béthio défar la; Diabote Gui dou tasse Mouk Diougë Thi Mome Kone Dieul Lène Sèn Temps Rék bouy paré Mourou lèpeuh lère. Aussi sachez que Talibé liko Serigne gnam Digeul lay Déf, boudé Thiantacone Nga dieufèl sa ndigeulou Baye Té Xameni Aïda Diallo Moye Dieuwrignou Dieuwrigne yi tèyite Moy Deugui Deugui Dieumame Gui(Waxi Serigne Béthio), Yaw nak Kou pank ngamay nirou wayé waxoofi loudoul waxi Kou fiiir, Amal Talibé Thi Sène Diewrigne Djii Niko sa Baye Diglèè,je pense que Mo geune topeuh Réseaux sociaux yi Gnou lèni ladjie ladjou diaxassé kouné di wax waxî haine et ça restera pour toujours dans le net.... Aïda Ndongou Nak Mo meune Thi Talibé yi Dara, Talibé kèneuh Douko donnou mba nganiko force dagay Dieuf 💃💃💃💃Kiko meune ak kikoy diëm dougnou bèneuh; Diame dafay nangou Dogal🙏🙏🙏🙏🙏Deugui Deugui Dieume Gui Yalla Nafi Yag Lool Té Wër Barké Serigne Béthio Serigne Saliou Mbacké 🙏🙏🙏🙏
@labelle49415 жыл бұрын
Mala beug pire aida dhei doussen morom sax batay degoumakoo mou wax. Aida molenn eupp fitt sou paré dina diaxassé carte gui. Yenn yi jalousie la koi. Vive aida
@senzanome99315 жыл бұрын
Deug deug aida diallo khana amoul ay mook wala beugoul benne diekeur aaaaaaaaah litamit aida Diallo
@fatysyll56435 жыл бұрын
Depuis la mort de cheikh bethio j'ai jamais vu aïda parler
@dalyndiaye20365 жыл бұрын
🤣🤣
@papeousmanefall57965 жыл бұрын
Deflen nank boulen tong aida wakhagoull dh esk doulen rouslo deflen nankk té bayi journalistes yi danioulen didouguell
@adjiabousso78645 жыл бұрын
@@fatysyll5643 bilahi lii d la beugone wakh mais Es ce douniou am mal entendu si lolou
@senzanome99315 жыл бұрын
Pape Ousmane fall fi rous amoufi kou neek sagn gua diokhe sa khalat bou wakhoul naak moy li guen sakh naak
@madondiaye7755 жыл бұрын
Aka mala nawlo djigéne foula 🥰
@awadiop96625 жыл бұрын
Très bien ame lenn foula rekh Aïda Diallo nane la meune dhite Aÿ Gor khilifeu kene mousoul guis li
@ibrahimadiallo73295 жыл бұрын
Mère bi wakh na deg santé na yalla dakh amna yakar récupère sama mbok bi Ana Diallo Diallo ak aferou seringue
@arimaz895 жыл бұрын
@@ibrahimadiallo7329 😂😂😂
@mamanniang29705 жыл бұрын
Que la terre lui soit légère Cheikh Bethio Thioune
@daarychiekhahmadoubambajuz75785 жыл бұрын
Merci maman rafetna
@madamethiam65085 жыл бұрын
Sehk bi yalla nako sounou borom yeureum te hkareko aldiana si barké borom touba
Ma chère yamal sa place tamitt aida sa baye mo changer son nom defko thioune donc eupeulei woko limouu ligueyeul saa baye defoo khadj bii topato bimou ka dann topato rek meuno kokoo fayy dc reglel .Aida dé mouguii tégn tei baatayy wakhoul wakhou succession yene nak guene dii kheutioo ay donantei mais c grav khamna dé yakamtii guene wonn Cheikh bii décédé "nako yala yeureum"
@fatoumbackesylla44815 жыл бұрын
Wax deugg Yalla merci beucup
@nabouthiane44015 жыл бұрын
Yaaw yaye domeram kan moy yakamti baye déé ébécile
@fatimadiop83835 жыл бұрын
Chièkh bi moko nommè aida diallo oussi mome dafa diongoma kar machallah bayilène diambour aida mofi nek
@nokiambappet67895 жыл бұрын
Machalah thioune wakh djii amna solo
@laminendiaye95375 жыл бұрын
Dieureudieuf Thioune 👌👌
@talibeserignebabacarsy30555 жыл бұрын
C la vérité mes na raféte
@papiscooniang10695 жыл бұрын
Oui frere sui dacor avec toi
@naphiendiaye85175 жыл бұрын
Wakh bou am solo mounout doon bayem mbeuye doon bayou diamou
@aidasagna67785 жыл бұрын
Ass Fall bilay même si elle a raison mais wakhiine bi meunone n'a geuneu nooy da deugeur trop😂😂
@modoumbacke64845 жыл бұрын
@@aidasagna6778 hahaha deug bi rek mo ame solo.. Aïda Diallo meunoul woutou cheikh bi té ay domame nékk fi nit dafay nitté !!!
@aidasagna67785 жыл бұрын
Modou Mbacke lolou leep deug leu mais waxdji nay rafet rk t en plus esk Aïda da waxni day donou cheikh bi?
@golbytv98895 жыл бұрын
Allaahou akabar yen adouna dou ni dem lén diamou ji yalla ta bayi khiro bi ak nia wo bi kou diamou woul yalla top seydina Mouhamed perte nga
@senegalmafierte5 жыл бұрын
Le fils est toujours le digne héritier
@a.fniang2225 жыл бұрын
Cheikh Diouf mais il était où tout ce temps
@dieynabasarr64825 жыл бұрын
Adouna lépa wara rafet lii lèpeu daye dièx bolène xollé cheikh bii xamni adouna dou dara kagn laa cheikh bii nèlaw banguène dii wax aye donou naa rafèt yalla naguène dègou bou bax sii barkep serigne saliou
@bambaseck625 жыл бұрын
Dafa melni dangà méré sokhna aida ci intimité ak cheikh bi
@cheikhounabamba10065 жыл бұрын
Cheikh Bethio Bethio môme diouroul kou niake yar ta diouroul aussi kou niake talibe . merci maman Fatim thi leral bi .
@assanesane96905 жыл бұрын
Té moi personnellement j'ai entendu nullement Aida Diallo parler de sa depuis le décès seul klk talibé et journaliste en parle elle était la femme a cheikh Bethio si vous suivé la vidéo quand cheikh Bethio disais qu'il a tout départager pour que quand il sera plus de ce monde qu'il n'ai pas de querelle toutes ces femmes ont eux des maison un peu partout au senegal. amoul.loumoulene desseul wationeu.ak.niom donc na nityi dougou founiou hadj la famille est sacrée yonou kene nekoussi nakou nek djeul exemple nouniouy gérer famille
@BAMBISTETV5 жыл бұрын
Merci frere rafetlou na Liga wah journaliste yi nioy diakhase rek
@andrenabigueye32015 жыл бұрын
Assane Sane meme moi aussi seul les sois disant journalistes qui veulent creer des histoires dans cette famille
@thiounadiamousangueuyaram53035 жыл бұрын
Djokhma sa num. Yaw kou mandou nga.
@assanesane96905 жыл бұрын
@@andrenabigueye3201 vrement
@assanesane96905 жыл бұрын
@@BAMBISTETV danio seytane trop keur gou tass nioko tass neuw neu siniouy doheul deug mais la plupart diahasse rek
@malawdiallo22545 жыл бұрын
Machala dieureudieuf contana si yaw
@touresane34145 жыл бұрын
Li moye deug 🙂👍🙂👍🙂👍
@ruthzossaimoukala35335 жыл бұрын
D deuge la lolou ame merci
@dembafaye73715 жыл бұрын
Merci foula bakh na trop ci domou adama
@mamembackediakhatetalibese21105 жыл бұрын
Machalla maman beugeu nala loool way
@thiounetabara21885 жыл бұрын
Machalla am na solo gourou sonou borom rk modoul diekh adina amoul solo
@raay.chigaarmbodj845 жыл бұрын
Waw ya am foula yaw sakh meun nga diour Aïda Diallo ndakh amnga. Presque 60ans
@baradiagn58415 жыл бұрын
Diara diaf dage do boyi noppo machalla
@abdouniang6545 жыл бұрын
Raay.chigaar Mbodj liga wakh deguela waye naravet rek moguen
@assndiaye88555 жыл бұрын
Raay.chigaar yMbodj
@somb81225 жыл бұрын
Deug
@fahrozblanche24315 жыл бұрын
Mane moussou ma guiiss djiguenn bouy donnou khilaffa
@youssouka79445 жыл бұрын
Machallah
@bassiroumbackecisse3555 жыл бұрын
Très bien wayy, iow adouna taxoula diougue
@titifarou82575 жыл бұрын
Yallah nako yallah yeurem té kharé ko aldjana
@juniorpro15235 жыл бұрын
Macallah djeguén nomoy djéte amol fenn
@myvision76475 жыл бұрын
Ndeysaan wakhj amna solo tata bien dit niit foula ak fayda rek
@amydieng18655 жыл бұрын
MAchahalla nite dafay am foula j t aime maman ❤️❤️❤️
@babagueye84535 жыл бұрын
Machalla deugeu rek kaye deugeu
@socendiaye89075 жыл бұрын
Machala fatime tioune😭😭😭😭😭
@myagueye68185 жыл бұрын
Aida limou amme yalla moko maye dèllène wakh rèk aida di liguèye yalle boroma me aida bimouy liguèyell sa baye daguadone nèlawe🛌🛌🛌mouy nèk si digueleme
Tu á raison ma maman princesse Cherie je t'adore que DiEU te bénisse amine amine amine
@coolamie82805 жыл бұрын
Je suis catholuque mais cela ne m'empeche pas de voir la verité sur ce qu'elle vient de dire.Aïda stp sois uniquement l'heritiere de tes parents et laisse la famille d'autrui.fini l'histoire des épouses exemplaires.dailleurs tu n'es pas la premiere épouse donc calmes toi
@thiounadiamousangueuyaram53035 жыл бұрын
Ehhhh. Yaw danga deiggg fou Sokhna Aïda wakhé ay mbiroume ndono ??
@thiounadiamousangueuyaram53035 жыл бұрын
Nioune li sunu yone neikou ci
@thiounadiamousangueuyaram53035 жыл бұрын
Meussouniou ame blm ba beine thiantacone doggou ci ok
@maremesaliougueye34855 жыл бұрын
jtaime thioro thioune li la beugue wakh day direct.. serign saliou thioune rek
@astouka20855 жыл бұрын
Li rafetlouwoumako dara gniawna trop trop na raféte rék adouna amoul follo adina ay diékh sokhnasi
@barroelhadji985 жыл бұрын
Lep cheikh bi la yalla nako Yalla khari aldiana nak .
@mamadoucirely77795 жыл бұрын
Fatim thioro thioune..fouleu ak fayda ...tu as raison l infirmiere..
@doudouwade36665 жыл бұрын
Wax deug Meno donde sa baye donde bayou diambour Boudoul dara taw ba paré fou bay diaxlé taw lay wo
@mohoussa5 жыл бұрын
Wa eskeu meuss ngeen degg Sokhna Aida wakh ni dafa beug dondou Cheikh bethio ??
@doudouwade36665 жыл бұрын
Messouniouko degg mé souko waxoulwone dou law baniousiy diottt
Mane dhé lima diaxal moy aida diallo ba legui déguagouniou fimou waxéni moy djité
@nenediaw9405 жыл бұрын
Merciiii
@hafidarharrabti22515 жыл бұрын
Waw kay wakh nga lepou niene gni nio diortou di wakh aka diakhase di yakh xelou nitgni mai lep si diam lay moudjou serigne bethio ndiabotam yepoula teksi yon
@tymacdl90525 жыл бұрын
Me 17 bi passe ninou mo niawe
@fatoumbackesylla44815 жыл бұрын
Wax deug
@damedia22735 жыл бұрын
je ne suis pas mouride mais j'ai vraiment constater que le cheikh a bien éduqué ses enfants et ils se montrent très humains depuis son décès
@maibo795 жыл бұрын
En tout cas. Si adiya Talibé yi lako bayam ndieundal auto ak ay keur. Gni di diokhé ay sass sene wadiour da gno soneuh. Il lep affairou xaliss la. Dou yallah dou yenetibi. Tiantacone bou continuer si bi mascarade, bo guissé vidéo bi war ngua délo sa xel si yalla nakhé bi doyna
@ismailasakho92995 жыл бұрын
m
@mouhamadourassoulthiam64295 жыл бұрын
Ki beug na ko dehh 🙏✔
@abdoudiakhate7905 жыл бұрын
Ki dé nimiy waxé so na aida néxouko mé niépa xamni mom soxna lawoon mé nay rafet rek na kaddou yi rafet bagnlén moytou reseau sociaux yi fanyi rek dinanulén diaxassé sisén biir
@baomaguette8755 жыл бұрын
C VRE DONTE SOKHNA LA WONE MAI DAFA AM LOUMOU WANE BAGNOU FALLKO DIEUWRINE NA RAFET GUIR KIFI BAYEKO
@bouboudiop87065 жыл бұрын
Degue pur la wakh
@malawdiallo22545 жыл бұрын
Machala amna solo trop
@ramsesalsalihatbeautymane28365 жыл бұрын
Dou lolou sakh Aïda Diallo mo waroneu yameu placame tu sais 17,avril bi limou deff ameuna yéneu domeu Cheikh Bethio diokhoulén wagn lolou ngua fok ni yoneu la Thiante mpu oute sécurité né moy djité tente 17avril béneu domeu Cheikh Bethio Thioune démoufa à par soxnam yi bilahi lolou yoneu na lou meusta ameu si famille bi mou beug ka fa indi dangn ko moy
@mberryable5 жыл бұрын
Ramata Mane neu rafet rek ndankh amneu geureumeul borom keuram
@sopebayamesanteyayame53975 жыл бұрын
Machalla Tata mala beugue, vraiiii
@Lafayette27085 жыл бұрын
Seytané ngen nakk. Wa sohna aïda kagn la wah ni dey donou cheikh bethio. Ragal len Yalla tamit.
@aicha7625 жыл бұрын
Yaw khana guissoko thie 17 avril bi mou togg aye ngor dikko ramal
@Lafayette27085 жыл бұрын
Aïssatou NDAO guiss nako. Mais batey deguouma mou wah Bou fi cheikh bethio djougué mofi nekk. Franchement beuguon na dall niou teyy si mbirr mi té wah liniou wor.
@bayesaliouseck78675 жыл бұрын
Vraiment tu as bien dite Ki rék doy na exemple si Aïda Diallo moka mak té waxoutt sakh lou dieum si ndono mé Aïda Diallo Nanou maye afïa way