Son combat avorté, Baye Mandione se fâche ,fait de terribles révélations et vilipende Tapha Guèye ..

  Рет қаралды 27,405

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Пікірлер
@modoufallbetebeteitsenegal5272
@modoufallbetebeteitsenegal5272 5 жыл бұрын
Je suis TIDJIAN et fier d’être talibe cheikh Beugue serigne Babacar Sy rta MAIS LI Baye Mandione Wakh si Mame Ahmadou Bamba khadim Rassoul nguir mougne deugue pir leu ta dafa seddeu sama khol wallahi yallah naniouko yallah fayal mame bamba
@mansourdieng2000
@mansourdieng2000 5 жыл бұрын
Baye Mandione Chanpion Ngua Dip Rék Teuwo Baye Inchallah Dina Bakh
@mansourdieng2000
@mansourdieng2000 5 жыл бұрын
Khoyantane Boudé Am Ngua Fitt Nieuweul Sénégal Beuré Ak Baye Mandione
@pamodousallah8386
@pamodousallah8386 5 жыл бұрын
Baye daa ragal rek diambarr
@ousmanengom5224
@ousmanengom5224 5 жыл бұрын
Dagno ragal rek mais Baye mandione mom dou yak lamb.. Louy dagg ay wéé ? Yeufou dof yoyou... Mandione Goor Yalla deug leu 💪
@pandiaye94
@pandiaye94 5 жыл бұрын
*Fadel doo journaliste yagui melni kou tookk seu salin di wakhtane* demal diangui waye grand bi
@tinealiou4039
@tinealiou4039 5 жыл бұрын
Ndione dinama reyyy billaye balla gaye bonne continuation sa khole moo rafète
@zappingzap827
@zappingzap827 5 жыл бұрын
Fadel ya seytané bilahi warone wone d'accord mou tekko
@amadougaye9255
@amadougaye9255 5 жыл бұрын
Afér bi baye madione la
@abdoulayedieng6973
@abdoulayedieng6973 5 жыл бұрын
Affaire bi yeep khamgua lanla wa gambie Khamouniou lamb
@cheikhtidianesarr741
@cheikhtidianesarr741 5 жыл бұрын
Merci madiol
@abdoukarime8302
@abdoukarime8302 5 жыл бұрын
Baye mandione beguenala ta serigne Touba rek takh
@t-gibson7735
@t-gibson7735 5 жыл бұрын
Un journaliste doit rester neutre
@hamzoespana2618
@hamzoespana2618 5 жыл бұрын
Journaliste bi weuh 😅😅 Kii bou togone ak khoyantane loumiy wakh 🤷‍♂️
@wakhtuwi379
@wakhtuwi379 5 жыл бұрын
Ndione aka geum bopam💪🏿
@aliou6396
@aliou6396 5 жыл бұрын
Journaliste bi vrai domeram la
@papeousmanesamb4880
@papeousmanesamb4880 5 жыл бұрын
Moi pèrssonnèlement Thiaroye guèdji la deuk tè lèbou la en plus amouma bèn mbokk Gambie mais attation nioune Sènègalais yi naniou moytou baye Mandione Sèytanè la diakhassè sènègal ak gambie la beugeu dèpuis 9 ans amoul victoires wakh rèk lay dèff kou thi noy bopou di nala yobalè Tapha Gueye loumou wakh moy deug deukou diambour bofa dèmè lou sèni règlement wakh da nga ko wara nanguou sinon boul dèm tè en plus mom moy kane ba wa gambie diko khèkh yaw ko kham ni baboye 50 ans moleu dane ak niom gora sock domèram yak dèrou thiaroye guèdji rèk thiaga bou dioug dane sa ndèye ba parè mouy weur di doul rèk fi CNG niata mbeur lagn dag lo sèni wèè niou dèm dag ko avant combat bi non Baye mandione may niou waye tè dièmeu beurè dann mo gueune ratatati bi ak say wènn you reuy
@asssow180
@asssow180 5 жыл бұрын
Pape Ousmane Samb iow ape nonam gua say wakh diarula degelou
@taybtoure8525
@taybtoure8525 5 жыл бұрын
Amo droi siwele audio Moustafa Gueye bi
@mansourdieng2000
@mansourdieng2000 5 жыл бұрын
Amna Si Droid
@gallasfalle2815
@gallasfalle2815 5 жыл бұрын
Machalla baye
@jesuissenegalaijaimemonpay455
@jesuissenegalaijaimemonpay455 5 жыл бұрын
Journaliste bi khamoul doule
@deugdeug19
@deugdeug19 5 жыл бұрын
No journaliste bii mo saytaané !! No tay réék laa waarou koi !!!
@gueyemalick7216
@gueyemalick7216 5 жыл бұрын
Baye mandione dinga am lou bakh inchallah
@astousaliou6997
@astousaliou6997 5 жыл бұрын
Machalla
@modoufallbetebeteitsenegal5272
@modoufallbetebeteitsenegal5272 5 жыл бұрын
Je suis d’accord avec baye mandione sauf limou wér Moustapha Gueye donté dadon dieuwaté mais meunonako soutoural bania publie audio vocal yi .. mais nul n’est parfait yallah nasi yallah def diamou banguén trouve terrain d’entente
@mansourdieng2000
@mansourdieng2000 5 жыл бұрын
Fadel Amal Diam Bou Bakh
@abdounangosyllasylla1456
@abdounangosyllasylla1456 5 жыл бұрын
baye Madione yokal sa entrainement am nga taille ak dole boo waŕè beure ak roi des arenes moytoul pressbi te liguey
@adamamballo7886
@adamamballo7886 5 жыл бұрын
bon courage dione.c clair
@sopeboromtaif3475
@sopeboromtaif3475 5 жыл бұрын
Baye mandione mande guen nale bague yalla ne se diam tague ak hay ndam you barri
@ZeynabRassoul1
@ZeynabRassoul1 5 жыл бұрын
Tapha Gueye wakhoul lou gnaw si Papa Sow dafa wakhé kilifa ni bouthi kéne tontou. Lolou amoul lou gnaw. Yaw ya wara roy si serigne Touba té ami soutoura bayi diakhassé yaw ak journaliste bobou
@aliousoung2831
@aliousoung2831 5 жыл бұрын
Dione wakhji amna solo yallna là yala defal diam
@ZeynabRassoul1
@ZeynabRassoul1 5 жыл бұрын
Yaw doff nga rék. Li dou yone. War nagnou si wakh. Deuk bo khamni seuytané diakhé lékanté Di ték ay audio transférer audio. Audio Tapha Gueye ki lako transférer Badola la. Yaw miko ték dof nga té gnak soutoura. Di diakhassé . Tapha Gueye wakhna deug arbitre moy maitre du terrain daNga warone nangou té dé beuré dji
@mansourndiaye8922
@mansourndiaye8922 5 жыл бұрын
Ki dou journaliste saytané la
@cheikhbassmomyfall8798
@cheikhbassmomyfall8798 5 жыл бұрын
Mansour Ndiaye 😂😂
@hamzoespana2618
@hamzoespana2618 5 жыл бұрын
Baye mandione khol bou rafett nga yor
@moussaseye3439
@moussaseye3439 5 жыл бұрын
Yaw journaliste nga wala l'âne nga
@oulimatandione3037
@oulimatandione3037 5 жыл бұрын
Animateur bii manoumassi dara🤷🏾‍♀️
@senegalba1071
@senegalba1071 5 жыл бұрын
Bravo bay mandione
@baaxdeuggu8621
@baaxdeuggu8621 5 жыл бұрын
Senegalese kou jokk yabko... Ndax sugnu ndjityi gnu doul jdieull séni matou waay si doomi réwmi....!!!
@mj-zq4qg
@mj-zq4qg 5 жыл бұрын
Khoyontane monu tonge rek Senegalese yi bari na wakh, te wakh bo guiss amna niarri borr,
@mamediakhoumpa6748
@mamediakhoumpa6748 5 жыл бұрын
Baye madione bagnone guafi gouy guiii ayyyy diamano si plateau lamine samba sur walf tv
@ndiaye8075
@ndiaye8075 5 жыл бұрын
Baymadione mo yakha comba bi
@modra5465
@modra5465 5 жыл бұрын
Yowe saga ndeye nga fog ne moye ndam...amo ben respect ak sa wene djigene..tarpet nga...saga ndeye dui jai beurre...
@almamyseckBouMameChekhIbra
@almamyseckBouMameChekhIbra 5 жыл бұрын
Fadel waron wone bayi saway play audio bi nak yow tam
@ndiayekane7780
@ndiayekane7780 5 жыл бұрын
Baye mercii
@babaragnuing3524
@babaragnuing3524 5 жыл бұрын
Was ki yoné Dion audio bi kokou moy seytané té nék bir fasse tapha limou wakh dara nékou thie
@davidndiaye1150
@davidndiaye1150 5 жыл бұрын
Kii journaliste la wala vive balla gaye
@bambyyemba3797
@bambyyemba3797 5 жыл бұрын
Fadel tu es nul
@diopcheikh8936
@diopcheikh8936 5 жыл бұрын
Merci ndione si balla
@ibrahimadiallo101
@ibrahimadiallo101 5 жыл бұрын
Ok chmpions
@mamadoulaminediop9058
@mamadoulaminediop9058 5 жыл бұрын
mais tapha gueye wakhoul Lou ayy, mais papa Sow amoul discipline de groupe. fass am dogual mou dialaléko rek. tapha guiss guiss lay wakh thi combat Gambie bi. balla wakh guiss guissam
@thiernomar7681
@thiernomar7681 5 жыл бұрын
Vraiment wa dakar buzz dem len ngen wouti ay journaliste sen wadji ken khamoul lanla doule khamou ko di melni gueweul tchim
@ablayembaye8405
@ablayembaye8405 5 жыл бұрын
Fadel hamo dara
@ibrahimasow7585
@ibrahimasow7585 5 жыл бұрын
Nittt dafay ame sutura mais limou wakh li ayoulll
@alkhousseinbarak6778
@alkhousseinbarak6778 5 жыл бұрын
Yaw journaliste ngeu wala tapha gueye boula porté plainte dangay dougou putin thieuy Senegal
@abdousarr4928
@abdousarr4928 5 жыл бұрын
djamicain respectél askanwi té faye ki khalisam yaw dioubo deh
@salioudiop7527
@salioudiop7527 5 жыл бұрын
Khamalo ko dara
@cheikhmbackeseck6704
@cheikhmbackeseck6704 5 жыл бұрын
Journalistiby say nané pirr lah
@amadoudiopndoye3582
@amadoudiopndoye3582 5 жыл бұрын
Tapha Guéye n’a rien dit Li audio ouvrable la neubatouwoul
@ndiaye8075
@ndiaye8075 5 жыл бұрын
Fadel yaw wakhal d'águe rk boul faral baymadione
@mbayendiaye4562
@mbayendiaye4562 5 жыл бұрын
Mane kilakhamoul journalistela wala lanla
@ndiaye8075
@ndiaye8075 5 жыл бұрын
Fadel ywo li dou sa ligueye dh far rk?
@ibrahimadiallo5326
@ibrahimadiallo5326 5 жыл бұрын
Mais ki journaliste la.. do poser ay question ngay waxtane
@diopcheikh8936
@diopcheikh8936 5 жыл бұрын
Ndione daga bakh
@modouseck1563
@modouseck1563 5 жыл бұрын
Ndione nittou deuge begeu deupi italy pescara
@adamamballo7886
@adamamballo7886 5 жыл бұрын
amine way dione
@diopcheikh8936
@diopcheikh8936 5 жыл бұрын
Ndione dal amna beuz tanyi
@senegalbusiness1977
@senegalbusiness1977 5 жыл бұрын
Yako déff baye...xawma loy dém di beurék doff yoyou
@ahmaddieng6622
@ahmaddieng6622 5 жыл бұрын
What kind of journalist you're? yaw khamo dara yaw journalist bi
@amaduamadu1600
@amaduamadu1600 5 жыл бұрын
Il a generalise
@cheikhmbackeseck6704
@cheikhmbackeseck6704 5 жыл бұрын
Ki dh mane na tasoum réew journalistiby
@pababoujah2190
@pababoujah2190 5 жыл бұрын
Fadel nopil
@abdoujallow7645
@abdoujallow7645 5 жыл бұрын
Ragal nga
@salioudiop7527
@salioudiop7527 5 жыл бұрын
Mais li debater leu walla
@doufall2667
@doufall2667 5 жыл бұрын
D'où yone nane lafaye sa balise Dax thiome thio daw
@bafodediaby4207
@bafodediaby4207 5 жыл бұрын
Mais dem dekou diambur de force aye porte
@amadoubarry7214
@amadoubarry7214 5 жыл бұрын
Gambia khamildara
@biranendiaye2621
@biranendiaye2621 5 жыл бұрын
Baye baye baye baye
@idrissadione7279
@idrissadione7279 5 жыл бұрын
boufa béne mbeur démati dañoo sokjlhor même booy dougueu gambie dañou lay manqué de respé😡😡😡😡
Леон киллер и Оля Полякова 😹
00:42
Канал Смеха
Рет қаралды 4,7 МЛН
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mercredi 08 Janvier 2025
7:32
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 4,1 М.
"WAXTAN AK " invité  MOUHADAME SAÏDII BIRANE DIAW
1:25:19
ISTIQAMAH TV
Рет қаралды 3,9 М.