ndeysane mangui dioy jumeaux yi yalla nalen yalla samb tais arléne si barki seydina Mouhamed je vous aime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ametmbaye94139 ай бұрын
Kou dioy comme mane lalal j'aime 😢😢😢
@ndeyebiramndiaye45019 ай бұрын
Moi j’ai pleuré dès que petit à commencer
@ablayekuyate76649 ай бұрын
@@ndeyebiramndiaye4501tu ment
@ndeyebiramndiaye45019 ай бұрын
@@ablayekuyate7664 je t’en merde
@MatyMbow-fr7of9 ай бұрын
🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲💗💗💗💗🥰🥰🥰
@CoumbaSaye-h8k9 ай бұрын
Machalla ❤❤❤❤❤❤
@SiraBeautiful9 ай бұрын
J’ai des larmes aux yeux 👀 yaram dawna laf thiate je vous aimes beaucoup les jumeaux 😮❤️♥️
@ndeyembengue29669 ай бұрын
Lima néh thi khaléyii danio khamé khameni yalla amena yonéntabi moy souniou sanga lép loye déff tes djitalo yalla khalatokoo do dême t'es niom aye khalé lagne louniou wah n'es yalla sop naléne masha allah sama rongagne dafa tourou longue vie à vous ❤❤❤❤ beaucoup de réussite totale ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@antafall55969 ай бұрын
Bilahi
@charlottecurtis40659 ай бұрын
Nameu talleu la si talibé cheikh motakh gnou khamm yonenté psl❤
Mancha Allah les jumeaux sénégalais petit et papa je vous aime beaucoup et je vous ai suivi sur toute la serie Belle Famille. J'aimerais bien avoir des jumeaux comme vous . Je vous souhaite tout le bonheur du monde et bonne continuation mes chers jumeaux. Bonne chance
@ThiérnoDiagne-q2h9 ай бұрын
Dama dioye yalla na yalla guoudeule fanyi❤❤❤anime
@bintaniabaly99539 ай бұрын
Ils me fument ces jumeaux là 😂😂😂😂 mais nakk longue vie à eux
@DièynabaDiène-w1k9 ай бұрын
Euy😮
@PapisMane129 ай бұрын
Ohhh ndeysane machalah yalnala lenn yallah sammm
@fatousow90079 ай бұрын
Yalla nalén yalla samm si barké alhouran
@MariemeKane-hi4dd9 ай бұрын
Aminn
@AminataKande-l6c9 ай бұрын
J'ai même pleurer mes jumeaux du courage yalla nalen yalla tahawhou thi barkel seydina mouhamed psl 🙏
@FatouNdong-ps7hb8 ай бұрын
Machaalah yala n'a lene yala samee Arlene soutourale lene bilakhi sama kholbi da sede si niom
@demzogueye12169 ай бұрын
Vraiment jumeaux yi séne série bi sak jours ma sétane ko dagnouy dindi stress
@matyndiayeduval72639 ай бұрын
Vous qui demandez leur papa arrêtez way leurs larmes disent tout laissez leur vie privée là où ils s'arrêtent avec les médias en écoutant leurs paroles on comprend leur vie un peut ❤❤❤ longue
@maimounandiaye-le1tu9 ай бұрын
Tu as tt dis ils sont très intelligent ma sha Allah de ne pas villipenter leur soutoureu mais les pleurs en dis tout
@elhadjiyoussouphdiatta28109 ай бұрын
😢lep nga synthétisé
@AïdaFaye-l1t8 ай бұрын
Li dawena yaram Bilay yalla nalene yalla same vous m avez fait pleurer
@mariemendoye28679 ай бұрын
Ndeyssane talla hane,mague na way.longue vie aux jumeaux
@Djamila468 ай бұрын
Il fesai quoi
@Djamila468 ай бұрын
Il fesai quoi
@bibafaye73389 ай бұрын
Machallah Cheikhou yalla yi longues vies à vous❤❤
@sylviemendy89799 ай бұрын
Bilay sama xol toy na que le bon dieu vous protège 😭😭😭
@hhjg16648 ай бұрын
Maa shaa Allah yalna len yallah laflen chatt cii barkeh sidina Muhammed S.A.W.S🤲🤲🙏♥️♥️🤲🙏🤲
@khadijandour64369 ай бұрын
❤❤koulene xol xamnè gnou am Diome lagne mashallah dioylo guenema😍yalla nallene yalla sammeu❤
@Muslim923109 ай бұрын
Yalla Nalén Yalla taxawu wanté déme Lén Djangi Al khourane
@SiraBeautiful9 ай бұрын
J’ai des larmes aux yeux 👀 yaram dawna laf thiate je vous aimes beaucoup les jumeaux 😮😮❤❤❤♥️♥️👌👌👌❤️❤️♥️
@ndeyembath95969 ай бұрын
Yalla nalen yalla samou def len ay magou dinê Machalla dioy na sakh
@evacoumbicamara78508 ай бұрын
Machallah samay morome sekh je vous adores ❤
@YellySow-ho1db9 ай бұрын
Ndeysane mangui dioy jumeaux yi yalla nalen yalla samb❤❤❤❤❤❤❤
Hooo Macha alla Yalna yalla saneu arlen baguén teral sén yaye yalna diam yagg
@NdeyeNdeye-x1h9 ай бұрын
Kou doiy comme Yalla nalène yalla sambe😢😢😢😢
@AmyCiss-m1o9 ай бұрын
Yalna yalla motali senni yene thie sen maman si barké mouhamed psl ❤
@SonkoMoydiomayFaye9 ай бұрын
Ndaysan ohhh yalla nalén yalla defal jammu ✅ mbagen tikki bah terall sén way diour
@MatThiam-m9g9 ай бұрын
Machallah di ne bakh dé ❤❤❤❤
@sididieng83389 ай бұрын
Yalla naléne yalla takhawou❤❤
@abdoutop639 ай бұрын
Hooo dama yaram dayna billae yalla nallene yalla samou
@liusaseck37259 ай бұрын
Delen khol linguen Di bindeu
@assthiam81609 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂dayna kaye 😂😂
@MatyKane-v7b9 ай бұрын
Vraiment jumeau yi Macha'Allah beugg naléne bilahi walahi kou beugg yayam damalay beugg yalnaléne yalla sam
@owbiking93419 ай бұрын
Sén papa esk mingui dund! Toud niouko ci émission bi??? Mais yalla na sén diam yag🤲🏾🤲🏾🙏🏾
@Marietou-i6u9 ай бұрын
Yaye yi nio yore séni dome ligui baye yeup Dow naniou😅😅😅
@miadiallo30849 ай бұрын
@@Marietou-i6ubilaaay
@awadiagne56229 ай бұрын
Ah man je pensais que leur mère et leur papa ne sont pas ensemble si interview yima deglou yeup lolou lasi tiré hawma nakk
@SIRA.K9 ай бұрын
Masha Allah les jumeaux yallah lafale thiate si barké serigne Babacar longue vie, bonne continuation ❤
@SophieNdao-vd3mt9 ай бұрын
Bilae lolou ame na cheikhou yalla yi mane mi cheikh la yalla na yalla goudeul sene fane🙏🙏
@madiorgueye56409 ай бұрын
Ngiome ngar rek laye topp da ngio diambar ❤❤
@sellediene71559 ай бұрын
Ndeysanne je vous adore yalla nalénn yalla sam Arlen moussal lénnn si thiattt ak lamine diam si yennnnn❤❤❤❤❤❤
@leboumixteo36429 ай бұрын
J'ai les larmes aux yeux 😭😭 c émouvant yallah Naléne yallah sam
@nogayeseck75608 ай бұрын
Machallah sama jumeaux yi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ndiolledieng9 ай бұрын
Machallah ms jumeaux bnn continuation ❤
@ndeyemariemediakhate70169 ай бұрын
Dioy lo nagne ma ndeyesane dioy na ba sonou😢 sougnou yaye yi gno sonou gneup meune nagnoula bayi gnou desse ak yaw
@mariameniang35629 ай бұрын
C'est inévitable de pleurer 😭
@abdoundiaye12079 ай бұрын
Aywaay dioy loo guéne ma rétaan lô guéne ma 😂
@antacisse38609 ай бұрын
Yalnalene yalla def ay kilifeu you am weurseuk
@SoomarNdiaye-ee4bu9 ай бұрын
Machallah yalla naléne yalla sambe ar léne ci barkép Serigne Fallou❤
@AwaSy-t2t9 ай бұрын
ndeyssane ils sont tellement drôles ❤❤ameléene diame
@mayanngom71789 ай бұрын
Yala nalen yala defal diam may lene fane bou goud bayi lène ak sene yaye banguen koy teral dioy Lo ngéne ma bly 😢😭❤
@SamsidineBadiane9 ай бұрын
O😅
@lala-wo1ge9 ай бұрын
Machalla chékhou yalla yi yalla naléne yalla défale diam mayléne goudou fane akhe wére si barké Seydouna Mohamed ❤❤❤❤❤❤
@assanetoure7999 ай бұрын
Ndeysan machalha Amin yarabi
@OusenouSoow9 ай бұрын
Machalla mane cékh la dama beugg ay cékh❤❤❤
@aissatoufall35289 ай бұрын
Yalna leine yalla defal diam bilahii liguey bgue seine yaye yalla defaral leine ko❤❤❤❤
@baye46139 ай бұрын
Ndaysan j ai des larme aux yeux 😢😢😢walahi dafa nekh gay liguey di dioh sa yay yalla nalen yalla samu
@aminatasamb96949 ай бұрын
Boule ne lene bayi moukk ngir dieumy borom by merci bcp pot bonne continuation j ai pleuré moi aussi
@MamediarraBéye-r7p8 ай бұрын
yalla naléne yalla lafal thiatt
@cheikhseck99889 ай бұрын
Bilahi boy you am gam gam magui né yalna diamou yague rek ❤❤
@abdourahmanembodj28529 ай бұрын
Machallah machallah❤❤❤❤❤ machallah machallah machallah peti e papa sy barkè Serigne Babacar sy laf thate❤❤❤
@Niangdametv9 ай бұрын
Ndaysane Dina bakh deh❤
@AissatouSambou-q5g9 ай бұрын
❤❤❤❤ machallah que le bon dieu vous protège des mauvais oeil,😂😂😂 mais il faut étudier ❤ les sénégalais vous aiment, je peux dire toute l'Afrique
@NgarDiop-c7n9 ай бұрын
Macha allaah yalna yalla motali yéné biguéne ame si sen yaye si barké seydina mouhamed
@fatouchadiallo79 ай бұрын
Ayy khalé laniou dé ms aka nio kham wakh machallha ❤
@khadygueye57149 ай бұрын
Blh kay❤
@cheikhfall43779 ай бұрын
🇺🇸 Congratulations les Twins ❤ma cha Allah 💕 yalla n'a yalla mottali yéné nieüp incha'Allah baniou yobbou wadiour yi maqqa si barké seydina Mohamed psl ❤❤❤❤
@allaji-falluu9 ай бұрын
Lo mougn rekk mou diexx yallah sougn borom arlene tai sameu leine ak Sen yaye❤