dieuredieuffety Sokhna aida Saliou , wawaw Serigne saliou ak boubacar konaté bekk naniou lole si sene wakhtane wi . ka´w na lole , manguilene di nianal sene kham kham wi geuneu yokou té SERIGNE TOUBA samm léne , yaggal fi lole SOKHNA AIDA SALIOU THIOUNE