Urgent🔴Déclaration Bou Ame Solo Ci Touba S.Assane FALL ibn Cheikh Moustapha FALL

  Рет қаралды 15,539

TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD

TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD

Күн бұрын

Пікірлер
@tout1958
@tout1958 6 күн бұрын
Li Sérigne bi beugeu moye am par kou respect woul Sérigne bi génal touba
@kionking-i9k
@kionking-i9k 6 күн бұрын
Ki djoudo touba amoufa droit de sol
@GERRARDSteven-u3y
@GERRARDSteven-u3y 5 күн бұрын
Propriété privé la deuk kou jamburr laa ​@@kionking-i9k
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
MachaAllah 👏 Fall yaram bii ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@SerignemodouFall-n5f
@SerignemodouFall-n5f 6 күн бұрын
Machallah fall yarma ❤❤❤❤❤
@GallassThiam-d4f
@GallassThiam-d4f 6 күн бұрын
Dieureudieuf Fall yag fi te weer
@ModouDiop-z1t
@ModouDiop-z1t 6 күн бұрын
Machalla amnasolo loll 🙏🙏
@yytv8221
@yytv8221 6 күн бұрын
Serigne bi dei sou dei YALLAH rek moko nior si yen baayefaal yi la wara dieukei ndakh kou baayi diouli ak woor amoulo kiliffa bai yillif keineu
@makhtarniang8577
@makhtarniang8577 6 күн бұрын
Jeurejeuf cheikh bi
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 6 күн бұрын
Dieureudieuf Serigne bi sante nanioula bou wer li Serigne mountakha beugue rek mooy am Touba
@AblayeDiouf-hl7wh
@AblayeDiouf-hl7wh 6 күн бұрын
Dieureu dieufeuti fall yaram
@yytv8221
@yytv8221 6 күн бұрын
Nafekh ngein deff waya YALLAH dina attei,bayi diouli ak woor mo geuneu grave diouniye yonn
@babacardiop9699
@babacardiop9699 5 күн бұрын
Yaw Imbecile nga rek ki mo grune sa baye
@ousmanthiam6066
@ousmanthiam6066 4 күн бұрын
Yalla daléna santé diouli ak wor gniou bagne
@alphaoumardiallo3884
@alphaoumardiallo3884 6 күн бұрын
Akassa Fall yaram contaan nanie si yaw barké Siidy Birahim Fall Lampe 🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NdameAldiana
@NdameAldiana 6 күн бұрын
❤❤deurdeuf ❤❤
@CheikhBeye-o2t
@CheikhBeye-o2t 6 күн бұрын
Mchalla Fall yaram
@dioptamsir1864
@dioptamsir1864 6 күн бұрын
Serigne bi limou beug rék faw moy am. Dieuredieufeti Ku Ted ki ❤
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Waw Gorr ☑️☑️☑️☑️☑️☑️
@MouhamadoulamineSamb-n8g
@MouhamadoulamineSamb-n8g 6 күн бұрын
Waw gor fall ndigal rek ❤❤❤الامر
@Djilydiob-jf2ey
@Djilydiob-jf2ey 6 күн бұрын
Hakkasaa jaajëf Murid amal jamm ❤❤❤❤❤❤❤❤
@TOUBAELEC
@TOUBAELEC 6 күн бұрын
Lii rk mooy dégg . Ñakk fayda weesuwul dëkk Tubaab di caaxaan ñula koy teree ngay nari wax . Jaangeen jëf yeen Baay Fàal yi ❤❤❤❤❤❤
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Lerrr neuu 🎉🎉🎉🎉🎉
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Amatinaa Solo way ☑️☑️☑️ Fall yaram bii ❤ kadouy amatinaa Solo way ☑️☑️☑️
@AssaneDaige
@AssaneDaige 6 күн бұрын
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته
@laminembaye497
@laminembaye497 6 күн бұрын
Dieureudieuf serigne touba ❤️
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Jereujeufetii ✨ CheikH Ahmadou Bamba ✨ Xadimou Rassoull 💓 Jarama Mame CheikH 💡 Doley Xassida yii ☑️☑️☑️
@mortalladieng8595
@mortalladieng8595 6 күн бұрын
Amna solo dieredieuf
@MorNdiaye-i4y
@MorNdiaye-i4y 6 күн бұрын
Ndiaye touba
@aboudiop-fj4ug
@aboudiop-fj4ug 6 күн бұрын
Dieureudieuf fall yaram
@user222
@user222 6 күн бұрын
Jerejef faal yaaram❤❤❤❤❤❤
@mortallafall130
@mortallafall130 6 күн бұрын
Mashalla
@bassiroundiaye3913
@bassiroundiaye3913 6 күн бұрын
Dieureudieufé Serigne bi Mane. Dé bay fall yi la andale. Kou menoule dieufé ndigale guénale touba
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 4 күн бұрын
Fall❤❤li serigne bi beug fawwu mou am❤❤❤❤
@barasow3654
@barasow3654 6 күн бұрын
DIEUREDIEUF fall
@khadimgaye5125
@khadimgaye5125 6 күн бұрын
Lerna
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Jereujeuf ☑️☑️☑️
@MaguetteAmat
@MaguetteAmat 6 күн бұрын
Alkhourann ba alkhourann dièkh yalla wakhoul feinn bou lein diouli
@ibrahimandiaye8214
@ibrahimandiaye8214 6 күн бұрын
Mandou mo gueun djiouli té yaw mandouwo dégoulo alkhouran dieuredieuf
@coursdecoutureenwolof
@coursdecoutureenwolof 6 күн бұрын
@@ibrahimandiaye8214esk nioy weur di doré mando nanio
@BayeAbdouGaye-x6o
@BayeAbdouGaye-x6o 6 күн бұрын
Walahi fall yeugu fi lool te weur❤❤❤
@serignefalilougueye3983
@serignefalilougueye3983 6 күн бұрын
Aka bakh lolou Cherif assane fall
@thiammady4782
@thiammady4782 6 күн бұрын
Jihaad nafssi , dioulli moossi djîtou.
@IbrahimaNdiaye-f4w
@IbrahimaNdiaye-f4w 5 күн бұрын
Jeureujeuf fall yaram guéna yag guéna weur
@MamecheikhFall-m5t
@MamecheikhFall-m5t 6 күн бұрын
❤❤❤❤
@mouhamedgaye
@mouhamedgaye 6 күн бұрын
défal sa déclaration rek té wakhe loleu wor
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 6 күн бұрын
Jarama Mame CheikH 💡
@salioucisse2355
@salioucisse2355 6 күн бұрын
Bokalle_VS_football😂
@serignendiayegeneraleht2470
@serignendiayegeneraleht2470 6 күн бұрын
Alqouran loumu wakh si djoullie
@mouhamedndiaye1628
@mouhamedndiaye1628 6 күн бұрын
Bonne question
@diwoutloubakhdiwoutloubakh6815
@diwoutloubakhdiwoutloubakh6815 6 күн бұрын
Jerejeuf fall Lerna de
@Beug-io8bs
@Beug-io8bs 6 күн бұрын
Lii rékk lanouy khaar si Kilifeu, Ouf ndiaboote gui té yeurreumléne tey déffar lépp lou narra yakkhou,Dieureu-dieuf Fall Yaaram Yague fi loole té andeu ak Wérr.
@MalickMbodj-cm3ss
@MalickMbodj-cm3ss 6 күн бұрын
Dierediaf fall amna solo lol
@MbathouGaye
@MbathouGaye 5 күн бұрын
Li Serigne bi beugué rk moy am
@10tvndieye22
@10tvndieye22 6 күн бұрын
Li dhe moy wakh dji
@beugbamba4026
@beugbamba4026 6 күн бұрын
Chaine bi ay seytané nguéne
@kionking-i9k
@kionking-i9k 6 күн бұрын
Donc tous les jeunes de touba vont quitter
@serignesonhiboudiakhate3977
@serignesonhiboudiakhate3977 6 күн бұрын
Cëy ndayssan waxji dh leerna nàññ ta wallahi lii képp moo ñuy jariñ
@beugbamba4026
@beugbamba4026 6 күн бұрын
Amna lo khamné ay vue diarrouko
@FayeSerigneDame
@FayeSerigneDame 6 күн бұрын
Way NDeey Saan Fall Lu Wér Way Touba Rék Lanu Am
@MorNdiaye-i4y
@MorNdiaye-i4y 6 күн бұрын
Baye fall nio nek si deg nie nekol si Lou bakh rek nioy wakh
@SeydouWade-d8t
@SeydouWade-d8t 6 күн бұрын
On joue au foot é arabie pourtant
@ModouSylla-o1i
@ModouSylla-o1i 6 күн бұрын
pér bayyil sa doul yi domiram dji
@babacardiop9699
@babacardiop9699 5 күн бұрын
Yaw kou rew mo geune sa baye
@maimbengued.7504
@maimbengued.7504 6 күн бұрын
Lou khewone?
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 4 күн бұрын
Ch thioro dafa beuha gate fane serigne. Bi kép kouye péxé nguir yaq ab ligéuyam do goudou fane bo wédé ana ki taxone safinatou amane areeté séne ligéuye bi kokou domi s cheikhouna mou s abdou lakhat la manga armél ya yalla lémna ay fanm bou yag
@maamceernosiise5994
@maamceernosiise5994 5 күн бұрын
Bëgg ku la seetaan rekk Nga tiitare lii, aka wuute ak wax ji😂
@babacardiop4173
@babacardiop4173 4 күн бұрын
Boy ragal ragalal yalla Di jomba def yéne yi nga wara mena yar sa bopou bou féké lingay ragala def yalla takhoul yonéteu wdangay woté lo guemoul balo doundoul motakh ngay bayi Touba Di dém fénéne dikofa defé yaw ragalo yalla ragalo kéne loudoul ay at AK ragal koula door ragalo yalla m ay at nga ragal
@beugbamba4026
@beugbamba4026 6 күн бұрын
Vidéo bi yangui kooy dougal nguir yé feneu
@PapeDrame-c7q
@PapeDrame-c7q 5 күн бұрын
Diadieuf
Что-что Мурсдей говорит? 💭 #симбочка #симба #мурсдей
00:19
Regardez la réaction de Cheikh Oumar Diagne après son limogage 😭
28:05
🔴Urgent Declaration des Bay fall Kureel Samm Wormay TOUBA
25:42
TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD
Рет қаралды 14 М.
urgent Cheikh Amar reviens sur les vrais problèmes de Touba
6:50
Assalaamy TV
Рет қаралды 4,8 М.
Série - Jeux de Dames - Saison 1 - Episode 35 - VOSTFR
35:13
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,5 МЛН
Touba Baye Fall yi Lou Doy waar Xéwo nafa Cheikh Thioro Mbacke...
3:48