Yen ay nafek nguen djiguenbi kou bone la sekoul dara ak serigne touba
@bigxouli6 жыл бұрын
C'est très triste. Une technique que j'utilise qd je me dispute avec ma femme. Je me pose la question suivante : Est-ce que je suis avec une bonne personne ou pas ? La réponse est toujours sans équivoque...et ceci m'aide à apaiser ma colère et aller de l'avant. Seuy responsabilité la ladj surtout si goor. Jigueen yi référez vous à l'Islam pour bâtir un monde meilleur. Le Sénégal d'aujourd'hui me fait vraiment peur!
@astoundiaye95536 жыл бұрын
.
@tdtd86246 жыл бұрын
Un bon témoignage que le bon Dieu lui accueille sur son paradis
@fatimatatraore47816 жыл бұрын
Que Dieu ait pitié d l'âme d cette femme ndakh li dara diarouko!
@deugrek33126 жыл бұрын
*Svp Ahmed Aïdara ak sa wadji liguéne wakh andoumaci, Serigne you beuri khaliss lanouy mayé sénii dôme. En plus il faut justice def liguéyeum. Femme bi daffa bone té rééw si les faits sont avérés. Sou fékké mokko ray nanoukko ñaff ci prison bi pour jusqu'à la fin de c jours. Amoul domou Serigne, amoul domou badoula. AAY BADOLA rek lanou, danouy djeulé village, eundileuh ndakarou, def la ci appartement ngay réwantalou. Éducation lanou amoule. Que la justice fait son travail*
@fatouma45896 жыл бұрын
vvvvbb vbbbbbbvvv ,voir de DIEU est éternel vvbv b b.,
@dabaseck25366 жыл бұрын
ndeysane kou khadi yak na adounam si kaso bi la nara déwé ni thieuy yalla nagnou yalla mouseul si seuy tané lou méti la
@mameboy46296 жыл бұрын
Alakhiram deh lako geuneu titeul, ndakh kou rey dioulite té tay ko safara rek rawatina sa dieukeur.. Allahou a'lam
@abodiop56896 жыл бұрын
Parlons de ces sappeurs qui n,interviennent jamais à temps ,qui ne sauvent jamais qui que soit ,qui ne répondent jamais au téléphone et qui malheureusement.........
goor yalla gui rafétoule si kéne. Jiggen danguaye bayi sa aye ndiaboot. Lou gniaw waroule béne jiggeen
@nayida4ever6 жыл бұрын
Elle doit recevoir une evaluation psychiatrique ... une femme enceinte ou post partum souffre souvent de la dépression nerveuse et peut faire des choses horribles.... beaucoup de cas similaires dans le monde... souvent la Victime est très proche ( époux, enfants).
@Yapiyapou16 жыл бұрын
Dom dji rek lassi yeureum
@niiakhanadiakhite46356 жыл бұрын
nagnko déff noume déff dieukeurem wakhdji diékh, bayléne nafékh ndogali yalla bosi talsa dieukeur, nitt kounéke nakol bopal bakane dafa for , yalla nagnou yalla mousal ciili.yalla kharéko aldiana.
@ahmedkeita68536 жыл бұрын
On parle de son père mais des actes de la dame elle es une criminelle elle mérite la prison à vie rek
@miachou87656 жыл бұрын
ce qui métonne moy comment tu peut etre enceinte a terme et ou est ce qu'elle a pris de lessence cétait prémedité lou fegne ci sey nouyowone na ci ngoro naka ngay tim sa dieukeur diko def lou meti divorce c'est mieux
@mendesshasha10216 жыл бұрын
Yaw ki daffa bone ki gniy rendi nitt sakh gnoko tanei ki mom limou def yeufou deumb deugu j la deteste
@bagdadleutv95126 жыл бұрын
Oh ndeyssannn c triste bilahi meitina femmes bi meire mako trop
@ndeyefatoudieng38726 жыл бұрын
Sa adina. Yakouna bâ yallah sounou borom diapela
@ZOTAIME6 жыл бұрын
Kikaye da tite motakh mou matou ak kanamame bou dangue biiii limou yakeuh mo reuy kiii dagnako wara topou bam seus pask d'apres li wadji wakh ki dako prépareiwone essence amoul loumouy deif si keur gui sou deug neikhei reik
@kenzandiaye53036 жыл бұрын
Justice pour khadim
@brasildakar1806 жыл бұрын
Té yala takh nith gni delolen sen xel Thi yala nii saytane dafa barrí dole te beupe Senegalais bou nek fii khamo sa eulekk nith Boy wakh na wakh loouko worr laniou sekkk Ba saytane niaw yala rek moko xam ak niar ngiko sekk kou xamoul sa eulekk nakk teyal Thi wakh dji , niou nian yala sam niou sam len , wa salam
@diakhatecheikhna81466 жыл бұрын
Bilahi Mansour vrai na fekh la ki ray ga wara wakh degeu né yala nena kou ray niou ray la ganane doundame mo diekh yaw alhourane diangeu diakhale nama mais li Gaston mbengue degeu la vrai na fhéh ga
@maremegueyegueye53256 жыл бұрын
Waw taximan bi bagne dou niou si wakh tamite
@yourdarkqueen62756 жыл бұрын
Khana thiey
@birahimndiaye57286 жыл бұрын
Thiéyyye yalla lou waye déf bopam
@antaniangseye75606 жыл бұрын
ki dall yakna derou jiigene nit kou bone la jiigene bou bakh dou def li ak problème bou mana am solution amna
@adjidiop516 жыл бұрын
Ak lou mene khéw bou rayone sa rak do wakhé ni ak nomou mene sante raye mome dou yone
@dawoudadione24246 жыл бұрын
Yalla naco yalla kharé adiana
@amadibarry50936 жыл бұрын
Il ne faut pas oublier que tous les senegalais sont égaux aux yeux de la loi. La justice senegalaise dois aller jusqu' au bout sans compassion. Sino nous autres senegalais nous n' allons plus reconnaître la justice
@dididiop11196 жыл бұрын
Mes aussi elle fille n a qu à finir sa vie en prison mm souko papam djouli aussi na loi def ligueyeme
@rosecisse40366 жыл бұрын
didi diop té mouy degeu
@mendesshasha10216 жыл бұрын
No mane lima guiss vs defendez la fille. Vs devez condamne sa. Mais solenkay defendre sa px encourager les otre femmes.
@ndeyesalysane81006 жыл бұрын
Sa t'etonne le senegal est gouverné par un tarikha qui ce prenne pour les maitre du Sénégal mé yalla bakhna gueneulaté bi dou fi alakhirala
@mendesshasha10216 жыл бұрын
@@ndeyesalysane8100 j fais partis des tarikha mais li mom mm boudone gno bokk tarikha sakh doumako defendre
@mendesshasha10216 жыл бұрын
@mooiboy mooigirl bilay yaw amiiine
@diamanovision47156 жыл бұрын
C'est une malade mentale on doi condamné cet acte gni wakhougnou fi dara li dafa gnaw ki rouslona mbacké mbacké yi
@mendesshasha10216 жыл бұрын
@@diamanovision4715 kikay rousslona nieup bilay limou def niaw na
@denanydiouf86546 жыл бұрын
Kham na dal lou bone kéne mounoul fékhé bé mou bakh, Sénégal neup neupeul ak ...., comment peut-on vouloir rendre pardonnable ce qui ne l'est pas???...Aucune excuse ne saurait justifier un tel comportement ...Mane dal ma warou si sénégal!
@boromxasssxasss33336 жыл бұрын
Mansour bayil khél yalla nafékh bakhol dé🙊
@thiorombaye23076 жыл бұрын
Femme bi daffa reww kessé. May wahh Aladji di diaye graww té warra wahh deugg nane doundame mo diéhh. Thipppp
@binetagueye17906 жыл бұрын
Li yeup seuytané rek la wakh deug yalla khéyna seuytané dagua meun rek
@mendesshasha10216 жыл бұрын
Les gars fii cheikh bethio sakh teudjone nagn ko prison donc ne vous inkieter pas la fille elle ira en prison. Personne nest au dessus de la loie. Li khew sen diguante nak yaw mi di netali khamossi dara donc ne dis pas lignouy wakh si reseau yi dou deugu. Tte facon justice a Khadim. Manila famille bi loum diegue diegue ils vont pas pardonner la fille. Manila seuytane bou nieuwe c psk moko permetre.
@brasildakar1806 жыл бұрын
Yaw ya xamoul lingay wakh , lou nek degue naniouko leup ay doul kou feke woul mbanoul , Ki wakh limou xam la wakh , barrí ngen problem trop ak mana goudal ay wakh
@fatythiofel27126 жыл бұрын
Iiao ki mola geun mandou Il a été clair il avoue qu'il connaît pas les causes pareil pour les proches personne ne s'est prononcé... Soof nguen trop ter gnemer critiquer
@dididiop11196 жыл бұрын
mendes shasha cheikh bethio 3personne la raylou ay talibè tes migui ni bougnou ko teudè aussi migui ni di leumbè thi rewmi badola yi raye bene nite thi prison bi là gnouy dèwè kon dou moudou fene.
@mendesshasha10216 жыл бұрын
@@dididiop1119 ta raison ossi bougn ko teudie tamit doufa yagu. Ayway k crim impuni lay done
@bibinettefaty56796 жыл бұрын
@@dididiop1119 ta parfaitement raison
@arlettegomis74306 жыл бұрын
Gni gno seytané maye wakhe mouné famille bi khalatoul plainte. Vraiment Sénégal amoul loi 😒
@assdiongue70476 жыл бұрын
Seytane aka gaaw entre l'amour et la haine il n'y a qu'un pas
@fromgouyembeuth6606 жыл бұрын
li yeup may sa diabar lou eup mokoy andi complexe devant leur femme li rek lay diourr djiguene sou bakhe diapal me sou bonne fassèko ci tell
@yourdarkqueen62756 жыл бұрын
Merci complexé ndakh domou serigne la et voici les conséquences
@yofariedieng20866 жыл бұрын
Bilay wakhatika j suis convaincus que c'est sa croyance qui l'a tué
@diopawa81146 жыл бұрын
Vraiment c'est horrible une femme dafa wara tey mane je suis enceinte et j'ai su que mon mari me trompe mais je l'ai réglé calmement sans que personne n'est au courant mais mome moy rousse rek
@TheGripe1236 жыл бұрын
tu vient de nous mettre au courant 😒
@madamebleu93286 жыл бұрын
@@TheGripe123 😂😂😂 vraiment et ici c'est pir
@mbayangmboup94986 жыл бұрын
j sw offusqėe.ds quel pays sommes nous.y as des actes q on n dw pas essaye de justifier et la loi dw sevir. si cete notre parent. comment allons nous reagir.
@lepatriote9346 жыл бұрын
Yéne ay nafèx tigui guéne nax Mbacké Mbacké la dotoulen wax louma gueum guén di défendre
@marianendiayeguellwarre79196 жыл бұрын
VERDICT VRAI merci nafékh you bone sakh Mbacké bathi lane
@khadykane716 жыл бұрын
me yén wa zik Aÿ seytanèguèn sou done sen mbok dolén wahè ni
@Secretfemmeafricaine6 жыл бұрын
SUNU BOROM KHAMOUL KI DOMOU SERIGNE LA WALA DOMOU YONÉNTI LA. YALLA KOU DÉFF BAKAR LA KHAM. ET LA LOI EST AU DESSUS DE TOUT ET DE TOUS ...BAYILÈN THIAKHANE YI KI LOUMOU DEF KÈNN MOUNOUKO JUSTIFIÉ
@salioufaye33766 жыл бұрын
Gor day matt gor wayé am sa soxna mou yilif la loumou wax nganni wàw ñiak fayda rek thiimm
Sénégal dou ndayi déme pask femme bi degg na domi serigne la kone dara doussi moudji
@yofariedieng20866 жыл бұрын
Mo kham dé beug lou nékh sa serign bou takhé dome bou doff bouma ame diokhla so déwé saye wadiour perte mome dess akk diabotame
@seynaboukane38366 жыл бұрын
On dirait c prémédité 😱😱
@fatourassoulsg58036 жыл бұрын
Mais arrêtez avec son père bayame santou koko raye lowou koko la fille est une citoyenne lameda justice sera fait inchalla je ne connais pas ni le père ni la famille de la fille
@fatoucissokho20586 жыл бұрын
Deugla ki loumou def niaw na ba si kanamou yalla mais kou kheuy na ga mouslou si cheytaner li serigne cheick tidjiane wah deugla rap you bone ya gi senegal moytoulen thiow surtout les femmes
@sopemaodo57736 жыл бұрын
Lois zero Sénégal dou déme bilahi
@golbytv98896 жыл бұрын
Teuss mongui ni nak Li moy teuss
@InfosetTutos6 жыл бұрын
GolbyTV billahi lii moye teuss kay
@bassewade59126 жыл бұрын
Yale na gnou yalla mouseul si sayetane
@khadypouye59546 жыл бұрын
Man declou ndoye ban moman genel ndakh mom ragaloule ta d'où far feen li am la y wa
@ibrahimandong67236 жыл бұрын
Bilahi Senegal mo bari na fekh wakhoulene fi dara loudoul defendre femme bi
@bijouxdiamant10606 жыл бұрын
Liyeupe seuyou appartement mokoye indi
@modoudiop83766 жыл бұрын
Koray nit mono bakh
@khadim57796 жыл бұрын
Sénégal mo nékh kou rayy nit géne di wakh affairou mbokou. Dan ko wara rayyy
@yassalamservices91246 жыл бұрын
entouca k justice soit faite
@mamadoumouhamedba47926 жыл бұрын
kou ray nit te tay ko dagnoula wara ray
@mamadoumouhamedba47926 жыл бұрын
yalla moko wakh dhee dou mane
@rakhouguedjii15066 жыл бұрын
Li ma si mètti moy legui gnou outal femme bi papiers doff tè dara diotouko
@khadypouye59546 жыл бұрын
Waw man warouwma des amna mbok kiniou ray Guen ma y wakh bok ray nit dafa eup gen di wakh mandou bilahi cou def nit lou bon yala alakla a met Aidara khometoumala invibi limouwakh tegouko feen ak louniou ma a diote li waroule won
@chernojallow15826 жыл бұрын
Li dee di nan takh gooryi do nyou takkk diarbar dee man de titt na trop
@brasildakar1806 жыл бұрын
Ayy Senegal delén téyy bala ngen dii wakh bilakhi Senegalais mo gawww nama yala ball , lounek degue nako bakarou Thi zero
@mgndiaye13396 жыл бұрын
Je peux jurer que Sénégal amoul loi. Elle va pas purger sa peine car soit disant qu'elle petite fille de Serigne Touba. Ta Serigne Touba khamoul Lou bone. Je ne veux plus être Sénégalaise. Je renonce à ma nationalité. Pauvre Sénégal
@hamadysow93326 жыл бұрын
Mois j'ai changé ma nationalité ça fait longtemps pour avoir même un extrait de naissance ces un problème au Sénégal
@dididiop11196 жыл бұрын
Mg Ndiaye bilakhi Sénégal amoul loi dou dem prison mes la femme est tres sadique Sénégal mome nafekh yi barri nagnou.
@mendesshasha10216 жыл бұрын
C desolant elle devrait purger une lourde peine cest qune imbecile cette fille limou def dou yeufou nitt. Ki kay seurigne touba seutlowouko. Lomou def c grave
@MT-vy1xs6 жыл бұрын
Bou ci dougeule Segn bi waaye. Arreter waaye.
@ndeyesalysane81006 жыл бұрын
Référons a la souna de mouhamed et on aura la paix nous lé musulmans
@diangadiallo82556 жыл бұрын
Teuthie ou pas adinam Yamuna c fini
@modoudiop83766 жыл бұрын
Senegal mo tarde sapor Man xamoma Loy diaredim
@serignembakcefaye99326 жыл бұрын
adou na dal doy na warr
@arimaz896 жыл бұрын
Tiey femme bi sadiq na, tal sa morom nit
@seckmoustapha77236 жыл бұрын
No yalla nanaou yalla mousal
@papasow50666 жыл бұрын
Senegal mo bary nafek ki danio wara rey ndeyame c t un criminel
@khadykane716 жыл бұрын
ki dafa bonne rek assassin la tè meuna féehé loubone
@ibrahimadia98536 жыл бұрын
Kou deh ya perte kholal kignu Ray bapare niewfi nane kou jiguen ki dafa bakh ki sunekon jamono yonente bi dankoy Ray joulit day mougn
@collesaliouseck89536 жыл бұрын
Cette femme es horrible 😭😭😭😭😭😭
@mansoursarr69316 жыл бұрын
Sougnou yone elle va pourir en prison! Par A ou par B cei pas la jungle icii deuk bi amna yone
@khadykane716 жыл бұрын
non Sénégal nehna limo tah niti di def loulè néh ki dagnko wara teuutie
@InfosetTutos6 жыл бұрын
Domou Serigne Babacar Mbacké Moukabaro noo lii meunta nékk waye no aduna dièkhna kone ba paré
@amarbeye38856 жыл бұрын
Bayilen massla bi famme bi bakhol dafa wara dee ci kasobi
@habaati70956 жыл бұрын
Allah y’a rahmou c est très triste de mourir de cette façon Qu Allah la rahmou amine
@bamariama29256 жыл бұрын
Boulène faté ni cheytané dafa am .nagni gnane di mousslou si mome aka am dollé mome cheytané
@dabz33186 жыл бұрын
Seytané dafeuh barii dolléii
@soknet28666 жыл бұрын
😭😭😭😭
@nitadiouf88186 жыл бұрын
Vraiment les sénégalais sont hypocrites,une femme qui assassine son époux et vous vous permettez de l'eloger.aucune cause ne peut justifier un tel acte
@ibrahimadia98536 жыл бұрын
Libéré ngaka blindé avec ça Guen Di critique macky Sall gniko Yi mo yaku
@rassoulsow22556 жыл бұрын
🤦♀️🤦♀️🤦♀️😢😢
@aladjifaye41256 жыл бұрын
teudjleen ko ma damisi diabi dji les femmes daniouma diakhal sunu dike di fitnal sene dieukeur yi paré legui sou ame kenen wala mouy dokhan niou commence jalousie topatoleen sene dieukeur yi mo gueneu de ndakh goor mom foumou ame diame rek lay weur wasalam
@modoudieng76616 жыл бұрын
Doyna war dal li métina trop
@modoudiop83766 жыл бұрын
Femm bi da wara kaso guiero don dam ñiaowna lol danu wara ubi la fal dayam domo aram
@thorthor42936 жыл бұрын
No wadji di nétali moy nanfekh deugu deugu deugu... ha d’accord prsk ki serignou wadjileu et Yalla dans tt cela? S’en genre yiii motakh crime di Bari.. ki Islam ☪️ ray nako bou yagu... ndaw si domeram lheu et kepou kou kay défendre dagno rayoul sa proche... doule way ay nafekh ngen rek. Thimm non SENEGAL sé fini.
@oxforbime61166 жыл бұрын
Mais ce meutre est premedité il faut le procureur fait un conference de presse...fi ya pa de masla c tun meutre ...
@madounegueye83616 жыл бұрын
Tŕé franchement kelk soit l motif ca n justifie pa cet act inhumain
@boromxasssxasss33336 жыл бұрын
Man dé dioména serigne dafay défff lo rafet😡😡😡
@cheikhseck60676 жыл бұрын
Dieu l'omniscient a décrété la polygamie La polygamie est culturelle mais elle n'est pas naturelle Les sociétés occidentales où se pratique la culture de la monogamie ont le taux de polygames beaucoup plus élevé que les sociétés musulmanes où la polygamie est autorisée
@yatmahane93836 жыл бұрын
Li c desolant
@mamadoufall87756 жыл бұрын
Léragoul
@khoudiadiakhate70176 жыл бұрын
Danio rayul sen mbokk rek
@ibrandiaye21526 жыл бұрын
diabar sakh légi worole
@bambafepp28106 жыл бұрын
saytané mon barydolé ak rap boy bonne
@adjiseck91046 жыл бұрын
Lorga sa dome de hagneko baaaye nite dafaye niteeeeee.