J suis tidiane mais j'aime bcoup borom Darou simple modeste🙏❤❤
@fatimatacamara26393 жыл бұрын
De même k mw ki ky manchallah yallah nako yallah taxawu
@bocarndom013 жыл бұрын
@@fatimatacamara2639 amiin yrbii
@papebabacarthiam90273 жыл бұрын
Un guide religieux débonnaire teinté de valeur incommensurable : Mame Thierno birahim Borom sikorii Yagg Fii lol Serigne biii. La seule science utile est celle que la personne a apprise et enseignée exclusivement pour l'amour de Dieu Très-Haut Mais non celle apprise pour les disputes et controverses, ni pour la gloire, le prestige ou autres vanités Non plus celle apprise pour des objectifs purement mondains, tels l'amour de l'autorité et l'accession à de hautes charges Ni celle apprise, ayant pour but d'attirer les coeurs vers soi dans l'amour de ce bas-monde Les actions ne valent que les intentions qui les ont inspirées.(Cheikhoul Khadim ♥️) Dieureudieuf Cheikhoul Khadim ♥️ Dieureudieuf Mame Thierno ♥️ PBT fier d’être le Géotechnicien de Cheikhoul Khadim ..
@diaomody993 жыл бұрын
Alhamdoulilah
@djoulytoure17473 жыл бұрын
Qu’est-ce qu’il est modeste .. c’est la première fois que je la vois … C’est un bon marabout..machaala..
@petitcomedien7793 жыл бұрын
Tu as dis vérément la vérité
@mordiarambodj5073 жыл бұрын
Damay name toujours des discours de Mame Borom Darou riche en enseignements. Jerejefety Borom Darou
@diarrandiaye40913 жыл бұрын
Macha allah mane talibé mame dabakh bi sope nala loll,liguey ak diamou yalla rekk.yalla nagnou yalla may deg ak topp
@boyeabdoulaye51193 жыл бұрын
machalah je ne le connaissais que de nom . Mais je suis séduit franchement ki serigne la . depuis je suis à la recherche de ses vidéos machalah
@talibecheikh76283 жыл бұрын
Man dè talibè cheikh laye diéma don mai kou dèg touram sopouko wayè boko dèguè mou wakh nga naw ko sa diambote boulla dègal dina fèss ak diom mbackè goudal fan waye koulla sopou la machallah 🙏🙏
@mouhamad49253 жыл бұрын
Sama papa dji manchallah contane nagn si iow..Ce genre de personne que jaime authentique, qui triche pas. Yalna yalla yagal taxawé, yok maxaama bi ak fane wi si barké serigne touba biniou bok 👐
@lufnia55343 жыл бұрын
Amine
@kourkopoulopoulo5203 жыл бұрын
Amine way
@caffaniass7883 жыл бұрын
Machallah c’est ça un guide religieux vraiment c’est un exemple 🥰
@ramaba27953 жыл бұрын
Je suis tidiane mais je l'aime beaucoup c'est une véritable guide religieux simple et modeste
@Rassoul39863 жыл бұрын
quelle modestie damal darou yageu fiii tééé wérrr
@katyfall36103 жыл бұрын
MachaAllah vous un exemple pour la jeunesse liguey diamou 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@astougueye64733 жыл бұрын
MASHA ALLAH Mbacké. Yaa baakh Oyof tei Yarou kham lolou Adouna ak wakh djiou Rafét. Amine YA Rabi Mbacké tchi Barké Borom Touba Daradiaye SEYDINA MOUHAMMAD ALEHI SALATOU wa SALAM tei gnou book léep ak Mbolemou Djioulite ak Adouna.
@ndayemachalahcestbeauciss78173 жыл бұрын
Je suis talibe cheikh mais j'aime sa philosophie d'éduquer ces talibes je rêve de le racontre un jour borom darou
@missmbaye78493 жыл бұрын
Machalla mbacke machalla mbacke
@bayefall54523 жыл бұрын
Yague fii lolou tei andak weer mbacke balla damala beug ba souma guissei sa dieum dji ak cadou you selyi douma mouna teiyei sama😭😭tei douma ko tay dieureudieuf mame thierno mbacke naga bax tei yeureum niou tei yeinei niou bilahi mbacke di naniou gueneu goor goorgorlu Inchallah yague fi lolou mbacke tei andak weur🙏🏿🙏🏿🙏🏿❤️❤️❤️❤️
@aminatadiouf2343 жыл бұрын
Je l'aime bien barké baye niass 💖 yalna yalla goudeule faname mayko wér thi barké baye niass
@mortallatalla81623 жыл бұрын
Amine
@straightbullet3 жыл бұрын
Khamnala dh iow wa corniche te réclame loll
@aminatadiouf2343 жыл бұрын
@@straightbullet mane ngay wakhal waleu
@straightbullet3 жыл бұрын
@@aminatadiouf234 waww
@cheikhbouelcheikhfall66263 жыл бұрын
Mane dé damaye niane yalla done talibe cheikh mais mame thierno brom darou kilifa deug leu teh oyoff
@qakk84353 жыл бұрын
Mo di Baboulah danga bakh rek niak kiniane Thierno sounou yeurmeundé leu diadieuf
@soukeynandiaye44703 жыл бұрын
Mane de talibe baye la wante damako beugeu borome daro te yalla rek mo takh. Dama guisse nimouye diokhole mou doyma.
@malickndiayemalickndiay74573 жыл бұрын
Bilahi walahi même k moi
@saliousylla15223 жыл бұрын
Yalna yalla douli diamo ak Salam amine
@basidiahmed46233 жыл бұрын
@@qakk8435 reste le Sénégal en ze recevez zey équipé d'une gaze en bois za pour zey 4ème pour les zeyni et zeyni zey zey za ( en za de Zazie zzzzzzqe qrreyz4ezzqz ): pour a la version zeyni zey qui a le 6prix mois et ... il s6z4ezezzeeqzz ras à en ( de pour 34q4
@mamygaye43783 жыл бұрын
Mame Thierno Borome Darou gnoun Daniou ko beug rekk ta yallah takhe Yague fi Loll Tamou and akk Wer Mbacke Allahouma Amine y'a Rabbi Masha Allah Dieureudieuf 🤲🤲🤲❤❤❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳🤲🤲🤲🤲
@ibrahimafall683 жыл бұрын
Quel homme dans toute ses dires *sama borom* rek nguay degg machalla
@ndarndar89713 жыл бұрын
Il est vraiment modeste.
@ousmanethiam33543 жыл бұрын
Machallah des paroles riches et qui incitent les jeunes à travailler
@abdoulayesarr21933 жыл бұрын
Merci merci merci
@mamanndiaye67593 жыл бұрын
Je ne le connaissait que de nom mais après cet interview j'ai beaucoup d'estime pour lui c'est un exemple surtout pour la jeunesse
@SayDBamba2213 жыл бұрын
Thiey Baaay ily 🥰🥰Jewrine Elimane Chikory Yala Cheikh Ahmadou Kara Mbackè Noreyni yagal sa Takhawayy Tè Deureul ko Deugui Góor Yalla Mongui Nonou Wett lool Thia lamou Nekk Di Ko Nianal Tamitt Maam Thierno Borom Darou Noreyni Nafi Yaggueu lool té Werr 🙏🙏🙏🙏
@mamediarrafaye41413 жыл бұрын
Vie bien et longtemps mbacké machala un exemple de guide religieux...
@beuguborombi62043 жыл бұрын
Hoohooo thieuy mbacke aka bakh aka gorè balla aissa mame thierno ibra faty noreyni baboul lahi baboulahi djinaty. Ken dou you yaw. Nekk sa talibè fièretè la dè machallah. Matt gua wasila matt gua serigne matt gua Baye si say talibè mbacke. Exemple gua si kilifeu ndakh di gua takhawou talibè mou melni sa djiabote walahi Azim. Mane dè khamna si dara . Si yaw la guiss serigne bo khamni diafè woulo mbacke .tè di topou ak di dimbali say talibè guir sen adouna ak sen alakhira noumouy bakhé mbacke. Mon guide et père spirituel dia bèguè dia titeuro yagu fo lollll tè wer balla aissa. Sokhna maguette depuis maroc
@mouhameddiop20133 жыл бұрын
Ndèysane sama xol tôyna,billahi js8 talibè cheikh mè damako begue,
@ndeyeadadieng0043 жыл бұрын
Akeu bakh teh oyofff yagueue fi teh wer❤️❤️❤️❤️
@ndiayemandela52753 жыл бұрын
Kou melni Mame Thierno diaffé na si yoonou mouride wallahi maacha allah waay
@ouleyediouf14943 жыл бұрын
Yague fi lol te wer machalah
@bintandiaye47303 жыл бұрын
Layenne la mé dama beuk borome darou rek te yalla takh
@lufnia55343 жыл бұрын
Ndaysann danga bakh rk
@elhadjimouhameddiallo57713 жыл бұрын
Machalah danga baxx rek
@moustaphasenghor61473 жыл бұрын
Tawfekh rekk nga siye dieulé
@salam-yk8ny3 жыл бұрын
Walakhi ya bakh kouy dieufé say ndigal di bayi say téré dinga té téxé tay ak euleuk yagg fi lolou té andak wérr mbacké balla❤❤❤🙏🙏🙏
@khadysarr99083 жыл бұрын
Machalla man Borom darou khamoumako mais machalla dieureudieuf Mbacké
@bbthiam85233 жыл бұрын
Sama xol seed na. Il donne un message qui rappelle ALLAH ! Li laniou sokhla si guide religieux. Yalna Allah takhawou la Mbacké.
@oumouba56573 жыл бұрын
Quelle sagesse. Il parle tout doucement machallah je te connais qu'à travers la télé mais je t'admire beaucoup. Liguey rek mo worrr. Qui peut me mettre en contact avec lui please suis tidiane mais dinala diokh adiya des produits biofertilisants pour les champs.
@abdoulayeseck34643 жыл бұрын
Lou lérr diokhma sa número ma envoyé lako🙏🏽
@oumouba56573 жыл бұрын
Je t'envoie le numéro où ? Donne un courriel su possible
@thiamaly22073 жыл бұрын
Jereudieuf
@mouhameddiop20133 жыл бұрын
Billahi oumou contane si yaw,js8 talibè cheikh mè diaralnama arrêter sama contrat nèk si liguèyame,damako bègue,goudale fane wayy papa sa doundou amna ndiarigne machallah
@Sonko-vk5qb3 жыл бұрын
Billahi wallah man ioe la begeu bay daro yalla yalla may goudou fane way 😭🥰❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
@mamysow25783 жыл бұрын
Je suis talibé Cheikh mai sopou n'a lolll borome chicori Doundou rek Serigne bi
@serignemodousarr23463 жыл бұрын
Fierté mouride machallah un vrai guide religieux modeste humble et très cultivé
@Yakknoss3 жыл бұрын
Masha allah un homme special
@oussou76413 жыл бұрын
Il a le nour Macha allah. Il est humble et véridique
@bayedaroubii34613 жыл бұрын
Yalla ngafii YaG lol tè wèr Mbacké 🙏✅
@papandiaye66733 жыл бұрын
Je suis un Tidiane et un disciple mais mame Thierno kou bakh la Kou leweet kou yarou Je suis aux usa mais je vais le voir quand je serai au Sénégal incha allah
@moussangamb58453 жыл бұрын
Massalah Yalla nalla sinou brom dèfal nga nieuw ak diamou kou bakh nga
@papandiaye66733 жыл бұрын
Ok kou bakh amoul been problem
@likdkte54653 жыл бұрын
Il est simple et modeste!❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
@ousmanembaye36973 жыл бұрын
Mame Thierno nafi Yaga tawer inchallah Amine
@massba69723 жыл бұрын
Rafétna machalla yalnala yalla may goud fane ak wer🤲 votre frère depuis tivaouane.
@amycole6213 жыл бұрын
Borom darou Mame thierno dôùdal ba saye maye Di bavane ya defare haleyi douma tayi dila wah sama seute Pape Diop mygi si yawe yala nala Serigne Ousmane norreyni Faye ci barkeme Mame cheikh Ibrahima fall diarama Mame thierno
@babsprogalsentv39443 жыл бұрын
Machalah borom darou yague fi lol té wére yakarou jeunesse bi ❤️🙏
@commandantfall94573 жыл бұрын
Très modeste yague fi lol mbacké
@ndeyemariemefall49673 жыл бұрын
MACHAALLAH MBACKÉ BALLA AICHA ! CO.NTENU BI AM NA SOLO LOOL ...AMIN YAA RABBI !DÉWËNATI INCHA ALLAH !
Porteur de messages dieureudieufe Mbacke Yalla nangua fi yague loolll té andak werrr
@mraelcapdip26433 жыл бұрын
Machallah borom daru yalla nafi yague té wérr❤️🙏
@adamadiop85653 жыл бұрын
Machaallah je suis Tidiane mais je l'aime bien machaallah
@cheikhgueye48303 жыл бұрын
Tu es tidiane mais tu n'est pas musulmane tu peux me dire la difference 😂😂😂😂😂😂😂tu es fou ehh
@pHyto2213 жыл бұрын
Koula guena doff amoul Kou bagna comprendre fi nitt di wakhé mom Ken menoussi dara
@cheikhgueye48303 жыл бұрын
@@pHyto221 les fou dans nous 😂😂😂😂😂😂Ks nd dh
@pHyto2213 жыл бұрын
@@cheikhgueye4830 mak bouy saga awma temps boumay perdre di wakh ak mom . Bonne journée 🙏
@cheikhgueye48303 жыл бұрын
@@pHyto221 koula wah makk la may halè bou ndaw journè bonne pwr tw chez nous tous vas bien
@cheikhfall29973 жыл бұрын
Wallahi borom darou ya mat serigne mala beug billahi.
@bakussakho73133 жыл бұрын
QHUALLA te protège dans ta mission backé ya 20 ans que je t'ai connu tjrs le même
@abambayediop22323 жыл бұрын
Do gawa guiss sa none dé sangue bi yalla na yalla defal la ndam ak djam jou sah ak soutoura si barké mouhamed yalla goudeul saw fan may la wér barké alhourane sa bén sope talibé Mola defal gnane gui adiya
@serignengom18833 жыл бұрын
Macha Allah borom barou mbécté jamono jërëjëf
@mansoursarr24993 жыл бұрын
Merci mame kaddou gui rafet na wallahi yallah na yallah gouddal sa fane ❤️🙏🏾
@ndeye86583 жыл бұрын
Machallah Amnasolo borom Darou ❤❤❤
@khadymanga99093 жыл бұрын
Je suis talibé Cheikh mais j'aime vraiment sa simplicité machaalah
@abdoulayeba82043 жыл бұрын
Ma sha Allah Borom Darou yalle nala yalla samme tahawoula may weur diame ak salam.
@abdoulayeba82043 жыл бұрын
Je suis Talibe cheikh ma sha Allah Borom Darou yalle nala yalla samme tahawoula may weur diame ak salam
@bell26923 жыл бұрын
Man dall beug nala borom darou ❤️❤️❤️
@assanediop98933 жыл бұрын
Geume yalla ak diamou yalla rek mo wor, dieureudieuf mame thierno
Dieureudieuf mame thierno, yalla nala yalla faiye si barkai Mohamed salalahou alaiyhi wa salame
@natachfaye37642 жыл бұрын
Yallna ga goudou fane ak weur inchallah. Mane mom beug nala trop
@khadykounta72553 жыл бұрын
Salam macha allah merci
@lenasall41313 жыл бұрын
Ma-chaallah 'sopéyé nginp 'yalla n'a yalla goudal saaye faane amine ya raabyyyy
@mouhamedsall78663 жыл бұрын
Mame Borom Darou yagg fi lolllll té werrrr machala 👌🏾mbacké
@khadijadieng22763 жыл бұрын
Chicory la terre promise Dieureudieuf Mbacke balla aïssa Boury 🙏❤
@lunediop51023 жыл бұрын
Guiss na tchi Borom daarou Sagesse Mashallah yalla na yalla samb ko
@cheikhoundour39953 жыл бұрын
Mashaallah, xol Séddeu wayyy, merci seydina
@fatouelizabethseck30813 жыл бұрын
Machalah qu Allah l assiste
@mouhamedsarr76562 жыл бұрын
Macha Allah amna solo lole waye Mbacké
@iboundione31353 жыл бұрын
Dieureudieufé mame borom darou👌🏾🙏🏾
@thiernoniang71173 жыл бұрын
Ma sha Allah Mbacké
@Hadithsdujour7.73 жыл бұрын
MODESTE SIMPLE HUMBLE SAGE…….. MOY BOROM DAROU
@toubadarousalamtv67163 жыл бұрын
🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️❤️❤️🤩 Macha Allah Macha Allah Macha Allah ... . Vraiment Begg naa loll C Talibé SERIGNE AHMADOU MBACKÉ Gawane Djieuwrinou SERIGNE Mor Faty Mbacké Gawane. Vraiment borom Darou Yagfi loll taa wérr Mbacké
@mariamamimidiedhiou89853 жыл бұрын
Machalah mbacke borom darou borom deugue
@bintagueye43253 жыл бұрын
Machallah damo ko beugue trop ndax dafa yarou
@patamaniaousmanepatha95253 жыл бұрын
Dieureudieuf Borom thiekory 🇸🇳🇩🇪🤲🤲
@amsatadiaw28343 жыл бұрын
Machalah
@papegoradiallo1193 жыл бұрын
😭😭😭walahi borom darou mon yarou
@ousmanethiam33543 жыл бұрын
Borom darou kou gneup admirer
@moustaphawathie13993 жыл бұрын
Machala borome darou ont aimes pour de vrai
@Thyphanie80193 жыл бұрын
Maa shaa Allah.beugue nako ziarre
@nafissatoudiouf56743 жыл бұрын
Aka oyoff machallah nitte kou bakh
@awandiaye29253 жыл бұрын
Machallah Mbacké gnioune dé danou laaye sante reckh ndakh sa oyoof yaala n'a yaala goudel sa faane amine yaraby
@ndeyekhadymbaye74303 жыл бұрын
Bilay deug rék nga wakh. So néké si deug yag yag. Yalla dina lèral yone bi kheweul bou sawane bawane. Macha Allah kadouyi rafetna
@diallilsambou25013 жыл бұрын
Je suis trop fier de BOROM DAROU
@omardiop283 жыл бұрын
Un grand exemple sur tout les musulmans particulièrement au talibé mourid macha Allah borom darou jërejëfeti serigne touba jarama mame cheikh ibre fall
@kumbatouray81473 жыл бұрын
Delo ndioukel Ch Ahmadou Kara Mbacke Noreyni
@МабеМагг3 жыл бұрын
Machalla mbackè balla sama sopè goudal fane waay mbackè
@gorandir32103 жыл бұрын
Machalla mbacké aka bakh yarou dieuredieuf mbacké
@boubadiop34733 жыл бұрын
Machalla mane talibe cheikh bi malla sop
@impact21753 жыл бұрын
Machalah Dafa wathiè boppam
@abbakaradiatta70423 жыл бұрын
Ooooooooooh khôlal imaaaam maaa bek si ioe ngir maaa ngi faateulikou baniouy indeul bilaahi yaaram mam thierno mooo dimbeuleeeti
@khalifasimal77582 жыл бұрын
Je suis talibé cheikh bilahi damako massa guente ni mou oyofé torop mbacké balla Aicha yague fi lolou té wër borom kaddou you am solo yi thi diamou yallah yii mala beug trop nitou yallah piir mo nguini
@gorguifaye22563 жыл бұрын
machallah ❤️🙏
@momodiagne18373 жыл бұрын
Je l'aime trop un exemple a suivre
@ndiagaeurodiouf31043 жыл бұрын
Merci borom darou 💓💓
@daoudagueye5243 жыл бұрын
MASHA ALLA SOPEE NDAW GNI...MAN DEH DAMA KO BEUG TE YALLA REK TAKH .....MBACKE YAGUE FII LOLL SAKH
@nioxndoye64752 жыл бұрын
Bilaye diaféna cou mélèze nie mome je l'apprécie diadieuf