Ague si yalla dou dekké khouloo ak wakhjoubary.beugue serigne touba doynanou kép.kou fonk laailaha illala wargaa fonk khasida ndakh serigne touba néna défna si samakhasidayi sékaré laailaha illala
@cheikhngom31945 жыл бұрын
Macha allah amna solo
@modoufaye16155 жыл бұрын
Cheikh Moussa kou bakhla. Waayé yéne ton bounakhary ak bou niaaw biguéniwakhé si serigne touba ak mouridyi rék mooma méti. Kou ague si yalla dou wakhénoonou.khasida boudé woyitte woy wouy agalé si yalla la.
@djattymenmusic80605 жыл бұрын
Djaradieuf mam moussa cisse
@kanesangue65193 жыл бұрын
Waxal nou tane ndax yaawara wax yaaye kiye waxal yalla