Thiatou Yoff est l’un parmi les meilleurs de l’arène
@hj-eu6xc10 ай бұрын
Je me demande si Yoff connait vraiment le potentiel et les qualités physiques et techniques de ce gosse. Kii bou amè suivi ak sérieux bii modou lo am koumou beurél am nga tioow lou mate tiow. Il est redoutable Machalah. Wait and see.
@mousseniang21910 ай бұрын
Yoff dougne diapalè mbeur lolou moy thiat li
@beyonder191810 ай бұрын
Thiatou yoff c'est l'équivalent de Malick Niang en terme de frappe masha'Allah.
@kamal313ndiaye310 ай бұрын
Wàllaay wax dëgg mbër bu mën xeex ak mbëre.
@lomamadou452610 ай бұрын
Sa c vré
@coulzjamdong476410 ай бұрын
Mais il est plus technique en lutte
@TARKiNDaBi10 ай бұрын
Boye bi machallah dina donii roi des arènes 🎉❤
@ModousambModousamb-mm2wk10 ай бұрын
Thiéy sama mbokou lébou yi Bénén Malick Niang nieuweutina😮😮😮 Thiatou Yoff et fière d'être lébou ❤❤❤
@allealdiop96110 ай бұрын
Thiayou Yoff sera un grand champion..il est technique avec une bonne frappe et tres discipliné.
@badandiaye861910 ай бұрын
Thiatou yoff champion la ❤
@kurayahmi10 ай бұрын
*Thiatou Yoff, Thiatou Daouda Fall, Soundiata, Talfa, Tony Jr, lamb Ji ci sen lokho ley moudjei d’ici 10ans*
@cheikhbasskeurmassar954810 ай бұрын
Soundiata non
@omaralfoutiwc.o.d198710 ай бұрын
Soundiata mbeur la dhé@@cheikhbasskeurmassar9548
@modo621810 ай бұрын
Guene si thiatou daouda fall dafa begue lou yombe
@kurayahmi10 ай бұрын
@@cheikhbasskeurmassar9548 setanal tous ses combats
@DjibiThiaw-wy2xy10 ай бұрын
@@cheikhbasskeurmassar9548si sondiata mbeur la dé
@cheikhbasskeurmassar954810 ай бұрын
Thiatou yoff félicitations ndaandane la de machallah
@Concept020810 ай бұрын
Thiatou Yoff, yalnako Yalla moussal ci Thiatt rek🙏🏿 Loko faye ci lamb meritewonako, dafay beuré, bafay xex. Louko wa yoff diapalé rek doyoul, nañko guena taxawou.
Mangui londres mais thiatou yoff khamoumako wone... mane Apecsy 2 la deukk... Fallou Seck Cafè dafma moussa wakh wakham.. ndanane la bilahi. Tè daffa yarou mais nakk yalla bakhna
@Mbt.-_10 ай бұрын
Non boul wakh lolou juste diay combat bi rek la won nak
@pathembegue702910 ай бұрын
Thiatou Yoff bilæ amougnou sa faye ❤
@tonssdieye882710 ай бұрын
Thiatou yoff ésk dou robot😂MACHA ALLAH
@mouhamed_d10 ай бұрын
Ndiaye tine dawna khékh bii ba sone😅 Mais ndeysane khamoul né thiatte yoff beuré sakh la gueune mane
@MbayeBeye-nd8oy10 ай бұрын
Lamb moy afairou mafia mé boy yi yepp thiatou yof dou sene morome kham nguene ni niang bou ndaw mi di beure grand combat lifi thiatou yog df mom defouko
@alinesyllaSyllaaline10 ай бұрын
Bilay
@DjibiThiaw-wy2xy10 ай бұрын
Billahi
@IbrahimaDiouf-p1o10 ай бұрын
Ndiaye tine woroul wone bayi ki feter ko thi souf bobi la def thi deun bi imposer force boumou am félicitations thiatou yoff🎉
@yayadia915110 ай бұрын
Il a de l'avenir,s'il est sérieux sur l'entraînement il peut faire beaucoup dans l'arène