A Cause de sa Femme, Il Fait Souffrir sa Mère et sa Sœur | @nettalitv

  Рет қаралды 16,017

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 40
@ElhadjThiam-p7x
@ElhadjThiam-p7x 15 күн бұрын
Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta frère bi dina ko regretté yalla nako yalla sopi
@DIAMBAR55
@DIAMBAR55 15 күн бұрын
Naniouy yar doomyi guir yalla, amoul taaw amoul thiaat, ndax kou yarouwou badée sabamméel yarla, neenañu kou yar sa kouy bamou màgg balaamoo mbeukk kenn mbeukk lah
@YoussouDiop-sn9ye
@YoussouDiop-sn9ye 15 күн бұрын
doyna ware lole😢😢
@Générale-Ba4
@Générale-Ba4 15 күн бұрын
Nite waroo thiakhane né sa wadjiour boco défe après ngacoye guiss khamena sy dara 😢😢😢😢
@fatoukin7e
@fatoukin7e 15 күн бұрын
Yayam lay khass dina ko guiss dhé 😢
@ndeyedabasamb9029
@ndeyedabasamb9029 15 күн бұрын
Merci fatou
@AbdouDiop-n9l
@AbdouDiop-n9l 15 күн бұрын
Li naturérloul dall mystique mogui si birr
@souleymanendiaye7963
@souleymanendiaye7963 15 күн бұрын
Astakhfiroulahi ki cas wam bi yalnama si yalla mousseul Torokh moka gueuneu djégué
@tidianiasy8265
@tidianiasy8265 15 күн бұрын
Ki dhè naroule téki boudé andeuna ak sagome peut être il est atteint mystiquement
@ThiateNdiayeSawarè
@ThiateNdiayeSawarè 14 күн бұрын
Bien dit boudé ande na ak sagom ndakh li mom dou lou naturel vraiment
@Générale-Ba4
@Générale-Ba4 15 күн бұрын
Sokhna fatou dougou nagniou si 2025 khana diga changer tourou thioukoum ndiaye ak ablaye ndiaye ak ana ndiaye khana 😂😂😂
@malickseck3063
@malickseck3063 15 күн бұрын
Èhhh Mani wallahi diaroull dioyy ... Rakam djo djiou . i'chla Dina torokh sonne wallahi dinako guiss torowal sa yaye môme alakou RK
@aliounbtoure8018
@aliounbtoure8018 15 күн бұрын
Fougnouko mana dougueul dinako regretté
@Mbenendong2007
@Mbenendong2007 15 күн бұрын
Dioyelo sa yaye boudoul dak torokh bougoul dak rék yaye dou morom bilay goryii delen tane sokhna tè bayi guaniethiakhou seune yiguendi tak bakhna
@aichaba1113
@aichaba1113 15 күн бұрын
Mère yii nio wara xolate sen façon yarine bougn wakhé rek niouné thiatte…thiattt dafa guéneu gnisi desss motakh voici les conséquences délène yamalè sen jaboote
@TallaDiop-zf7pv
@TallaDiop-zf7pv 15 күн бұрын
Yee mena dall lii
@seuneba7091
@seuneba7091 15 күн бұрын
Lou way rindi si sey loho ley nathe
@AssaneDiop-t2n
@AssaneDiop-t2n 15 күн бұрын
Yala Nanou yala mousel ci djiguene bou bone
@diariabousso466
@diariabousso466 15 күн бұрын
Lolou moy kou yare sa kouye bamou mague bala dane kéne yow lay dane lolou mo dal Yaye dji. Yéne wadiour yi nioy tasse séni keur. Aye dome daniou léne di yamalé yare léne 😢 Bou lolou wesso Yalla naniou Yalla mousseul si diéke bou bone bouy tasse aye mbokou
@SerigneNiang-y9l
@SerigneNiang-y9l 14 күн бұрын
Salut CV sokhna Fatou Mais sokhna Fatou KOU djigeun ki bou khamone fimouy moudie bou yaabo Mou déff ndake 💔💔💔
@MaryNdiaye-c7j
@MaryNdiaye-c7j 15 күн бұрын
❤❤❤❤
@boundawdiakhate2801
@boundawdiakhate2801 15 күн бұрын
😭😭😭😭💔💔
@wanealpha1965
@wanealpha1965 15 күн бұрын
Djigen kou bone la
@wanealpha1965
@wanealpha1965 15 күн бұрын
😢😢😢
@boubaka7172
@boubaka7172 14 күн бұрын
na wouti ay gniane,lou loxo déf loxo meune nako dindi
@elhadjiwilane5041
@elhadjiwilane5041 15 күн бұрын
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 12 күн бұрын
Niare mo meuna nék : soit diabar bi mystik ko ba xamoul loumouy déf ou bien mou done tayéfe. Boudé mystik leu. Yow sœur bi ak sa yaye, déme lén nguéne nianelouci. Wayé lou meuna ame. Diabar bi nite kou bone leu. Baxoul dara. Boudé tayéfe leu nak. Mome alkou na. Yaye dou morom. Té dinako guiss.
@diariabousso466
@diariabousso466 15 күн бұрын
Lolou dé dou wéye beusse dina nieuw mou beugue réthiou beugue dèloussi ci wétou yayam féke c trop tard
@DiagaFaye-i1f
@DiagaFaye-i1f 15 күн бұрын
Dinako rethiou S Fatou Mangui lay ziare di rafetlou lingay def douma tarde dara
@sokhnalo3334
@sokhnalo3334 13 күн бұрын
Naniou mounie guéne sétane léne touti rek lirek mofi bary sama frère migui fi ak nioune même quartier mome ak diabaram 4ans guisoul yayam
@ironahide5896
@ironahide5896 14 күн бұрын
Des fois nak goor yi daniouy len di mystique dé. Mane mi djiguene la mais guiss nako ba tayi. Daniouy len di dedalé AK sen wakeur yi
@astoumaguettesissokho32
@astoumaguettesissokho32 15 күн бұрын
Mani yaye dji nako bayi ak djabaram bopam lakoy déf bousi déwé rék dém safara nako sétane beus dina gnew mou rethou Yalla na fék boumou trop tard
@wanealpha1965
@wanealpha1965 15 күн бұрын
Hale bou goor bi defa torok
@abdoulalayeba4496
@abdoulalayeba4496 15 күн бұрын
Reroul de defa rew rek mere bi na jital xeul bagne jital khoulou ndiourel dom ji mo rew nako bayi ak yalla
@madiopmbaye9010
@madiopmbaye9010 15 күн бұрын
Nako bahi ak yala kokou dafa alkou yag yag dina massa guisse louko bete
@Etvabcd
@Etvabcd 15 күн бұрын
Est-ce que c naturel
@TallaDiop-zf7pv
@TallaDiop-zf7pv 15 күн бұрын
LIBALIMA KOM XAMNGA NE SARAKJI DUFAY BOR LUTAX NGA KOY LEBAL NONO
@SerigneNiang-y9l
@SerigneNiang-y9l 14 күн бұрын
Lou waay déff boopam
@MarieThioye-i9c
@MarieThioye-i9c 15 күн бұрын
Dinako Regrette
@antawade2878
@antawade2878 7 күн бұрын
Hustoire j'ai l'impression que cette histoire n'est pas vrai
Net Tali: Amour Brisé,  Lla femme de Sa Vie Lui Brise le Cœur
27:20
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
Don’t Choose The Wrong Box 😱
00:41
Topper Guild
Рет қаралды 62 МЛН
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 120 МЛН
NET TALI : Son Mari Atteint de déficience Mentale | @nettalitv
22:43
Solution: Donnez vos Conseils dans les Commentaires
12:59
Sénégal Infos
Рет қаралды 6 М.
Solution: Donnez vos Conseils dans les Commentaires
14:59
Sénégal Infos
Рет қаралды 7 М.
Solution: Donnez vos Conseils dans les Commentaires
13:03
Sénégal Infos
Рет қаралды 6 М.
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН