Franchement je ne sais pas quoi dire mais il mérite une personne dans sa vie Bilay walay ❤
@HousseyNouWade5 ай бұрын
Ma sœur c'est bien d oublier le passe et la vie continue j ai presque la même histoire comme toi au moins tu as des soutiens pour s en sortir quand à moi j étais seul à lutter contre mon chagrin même un début de dépression mais aujourd'hui je me suis marié avec quatre enfants macha Allah Sokhna Fatou bayyil dingue wokhe mewe gore nie
@AmicolléYade-o4w5 ай бұрын
Ndeysane thiey gorou Sénégal wadji dé sa akha dina ko dal lim la def bayi ak yalla rek yalla migui guiss lép mass ma sœur yalla dina la may kou bakh kou Guene si yaw inchallah ❤❤
@Xippill5 ай бұрын
Bon courage 42ans c’est rien thi yalla yow sokhna ci ndounde li yalla geumoul nelawoul wadjila la trahir digua ko yeureum inchalla ma dila wakh que boul décourager yalla adji mougne dji la andal digua ame borom keur thi kartanou sounou borom inchalla légui bon courage ❤
@ramaramatoulaye87705 ай бұрын
Bats toi pour avoir un autre mari tu vérras le bonheur que dieu t'a réservé. Tu vas inchalah etre trop béni jusqu 'a que lui il sera surpri. Juste Guemal sa bop ne te decourage pas sois trés forte pour te relever C'est juste ton destin donne une Chance a un homme et tu verras. Que du bonheur inchalah. ET celui qui ta trahi ne lui calcule Plus tu verras inchalah qu il va regréter tot ou tard😢sois juste forte et reléve toi prends ton destin en main et sois trés courageure❤❤❤
Mane Fatou yaw rek doy gua conseils liguey tontou mo guana deuguou kou Kam adouna gua ma sha Allah
@milkfall71405 ай бұрын
Islam ci bob bam mo nagu wul relation ñiuu durée islam 2 mois ciap 3 mois rékk la mañ Té soxna ci ñaw dagga xamul rékk lila wacci déf mo gune ci ñaw ndax bis bu lãa takone ama na ga dundu ci sëyy bu mété méti sax kon Al hamdulilahi ❤️
@mbissanemboup64995 ай бұрын
Thieuy goro Sénégal massa Sokhna si me bayi ko ak yalla
Dans tout ça ana wadji soudone manla dina fékhé ba kham foumou moudié lérnama ni wadji doundoul banékhou seye man nak en tant que djigéne dina oute borom keur ndakh gor gni yamouniou li dafa bokou sisa doundou yalla bakhna ❤
@bouhfall61595 ай бұрын
salam soxna si ma ngui ni
@Xippill5 ай бұрын
Ana goor gou bakh fi dima lire demander le numéro de cette femme à netali kou beugue sokhna sou bakh bou gore épouser cette femme yalla nako yalla may borom keur bou bakh thi barki yonen tobi kou wakh amine yalla nagua goudoufane
@AmicolléYade-o4w5 ай бұрын
Allahouma Amine inchallah ❤❤
@adamaniang59295 ай бұрын
Massa billahi kou wor Dina ko guiss
@wanealpha19655 ай бұрын
Nfinga am deukeur 😢😢
@abdoulalayeba44965 ай бұрын
Yalla diekhoul na gum yalla
@sysada89925 ай бұрын
Massa c dur comme vécu en plus les docteurs ne savent rien .La dépression ne se soigne pas comme ça
Sokhna si beumal yallah te kham ni yallah rek mofi nek. Tu as toute ta vie devant toi. Fateel Ndeye sa ex bi way
@brombakhyay5 ай бұрын
Li yep niaka guem Yalla rek mola diap jiguen day am 50ans di am diekeur yaw Wadji takk na bayila nga nare yakh sa aduna ta Wadji mome ma ngay thiokom ndiaye yaw nga Nara doff yaw tamit sa aduna diexoul ta Yalla niep lafi nekal😊😊
@allediouf12865 ай бұрын
C vrai l'amour est fort mais de nos jours ça ne valait pas la peine d'autant plus de mm arrivé à détruire ta vie.une livre n'est pas une seule page il faut donc tourner la page et essaie de lutter contre la vie ne te désespérée pas tant qui y'a la vie y'a toujours de l'espoir tous les hommes ne sont pas paraît.en wolof on dit: loxo boula bayi loxo mongui thi wétt bi di khar.l'homme n'est pas a 100 pour cent coupable car il n'était pas destiné a vous car y'a trois femmes que dieu a créé pour l'homme 1er celle qu'on a créé pour vous nul ne peut l'épouser apart vous 2er celle qu'on a créé qui ne vous ai pas destiné 3em celle qu'on a créé pour vous et votre prochain c'est pour cela qu'on vu des couples en divorce pour que l'autre puisse la mariée.apprendre cette message et tout allait mieux
@AminataSarrNdiongue5 ай бұрын
Merci
@Mike_saliou5 ай бұрын
Bo amone dieukar bou yag rek diekhna la soliton😊
@SoxnaaJoop5 ай бұрын
Adoynawar yallabah'a comme Fatou ningcay wahe
@fatougueye50885 ай бұрын
Ma fille boul yax sa adina ndax workatt diarouko métina mé kou la bayi bayiko dagno nék si adouna bo xamné djiko you noble yi gnoo xawa diéh
@mariemendy-qf3kz5 ай бұрын
Bilay yako sa adina dafa am goor yo khamni diarouniou sakh khool bay beug 😢😢
@astoumaguettesissokho325 ай бұрын
Guor guou yakar ma misére le ngua dé dé té yénén guor nékafi boma woré thi lay guene meune défarou pour kénén guisma beuguema amna gno hamni wor séne dérét la néke reléve toi Yalla dîéhoul
@bouhfall61595 ай бұрын
salam soxna si
@seutouaby41405 ай бұрын
Massa 😢
@AdjiSaye5 ай бұрын
Nakpu bay ak yalla
@YoroBa-po5xl5 ай бұрын
😢😢😢😢
@souleymanendiaye79635 ай бұрын
Ki dafa soff daka diare mome késsé doufi goor
@AminataSarrNdiongue5 ай бұрын
Loula béte meunela,après 15ans,
@AbbisDakos5 ай бұрын
Djiguene gniy wór gòr Nak😢 Lolou mo gëna mèti😢
@ModouDrame-ts6qc5 ай бұрын
Mane ah abonné sama xool mo sédé❤
@scoutmaiba95845 ай бұрын
IL faut qu'elle se fasse désirer à nouveau et reprendre sa vie
@ManaamWade-sk9xr5 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MamadouhlmBa5 ай бұрын
Thieuy Thieuyyyyyyyy
@seydinafseck69545 ай бұрын
Mais Fatou c'est vis versa les filles le font aux hommes aussi khanna niane yallah bagna dadjié ak worry katt rek
@youmafall22115 ай бұрын
Thiey Sénégal
@boubacardiop37943 ай бұрын
Cela fait mal wallahiii, elle a tout sacrifié pour ce gars. Li wadji deff Sokhna ci Yalla nakoo guiss, wadji mbaam, vrai domeraam là. 15 ans de relation et quand tu commences à avoir de l'argent tu laisses tomber à la fille, alors qu'elle a tout sacrifié pour toi. Elle t'a supporté durant les moments difficiles et tout. Des gens qui l'aimaient ont parlé, elle a refusé parce qu'il t'aimait. Wallahiii wadji dinako bala moh deih.
@Sallmoukhamed5 ай бұрын
Non wa ji dabonnn
@antaalax-bi6yu5 ай бұрын
Bilay
@NdeyeamyDiop-ec3co5 ай бұрын
😢😢😢
@alinguet79745 ай бұрын
❤️💙♥️💓💙💪💪🇸🇳😭
@Marvelous10005 ай бұрын
Benna tou beye
@OussyenouSeck-wh8uf5 ай бұрын
Fatou daga toukhou wate si ataya jdi
@OumyOumy-m6c5 ай бұрын
Sama papa deh dana wakhni kou yoboule meuno kham exsatema louye diekom yama dakhe pasiante te mane 15leummm
@altesseroyale43835 ай бұрын
15 ans de relations? Bobou perte de temps moye lane? Diangue bobou bane façon la? Amena gnou khamné lou lène dale gno ko tèk sène bop! Ana tope goor pendant 15 ans sans marriage? Tchiiiip li dafa tangale khole!
@astoumaguettesissokho325 ай бұрын
Dafa bari trop lolo tah mou défko choc
@kebbajohnson125 ай бұрын
😢😢😢😢😢🙏
@coumbasow87194 ай бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@NdeyelayeDiaw-cf3tn5 ай бұрын
😊😊😊😊😊😊😊❤❤😊😊❤😊
@thiabagueye52775 ай бұрын
Metina
@ndeyembengue45905 ай бұрын
Metina trop
@AmadouLeigh-c3t5 ай бұрын
I am very sorry sister but please find a husband the day you got a husband is the day of the problem of the Man that's what I believe please find a husband he is not the end of the world