Thieyy 😭 Baye Adama Sarr Wakhtane wou yémé ci Serigne Touba ak Mame Cheikh Ibrahima Fall

  Рет қаралды 103,905

Xidma Tv

Xidma Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 61
@codoumbow3433
@codoumbow3433 Жыл бұрын
Thiey bayefall yiii nio yémé de sallaw borom Touba amoul morom ken la mom😭🙏
@adjiagaye5897
@adjiagaye5897 Жыл бұрын
Akhmadou Bamba djadieuf❤❤❤
@mbengueamdy
@mbengueamdy 10 ай бұрын
Dieureudiefeti serigne touba diarama mame cheikhra fall ♥️♥️♥️♥️
@karaseck2462
@karaseck2462 Жыл бұрын
Cëy Baye Adama Sarr yàggal weral
@alphaoumardiallo3884
@alphaoumardiallo3884 Жыл бұрын
Amiiine yaa Rabbi Barké Borom Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌🙏🙏🙏
@ndemoudiofior8338
@ndemoudiofior8338 Жыл бұрын
Kene dou seurigne Touba ak chekhe ibra fall❤❤
@salioutine4426
@salioutine4426 Жыл бұрын
thieuy serigne touba khadim rassoul amoul morom kenn la ❤❤❤
@dikhasalikhate234
@dikhasalikhate234 Жыл бұрын
Diarama mame Chiekh Ibrahima fall lamp baboul mouridina ❤❤❤❤❤
@ibrahimandiaye8214
@ibrahimandiaye8214 Жыл бұрын
Baye Adama Sarr yalla gua fi yagu lol té andeu weer barker mame cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina Dieuredieuf
@SaliouSakho-m4s
@SaliouSakho-m4s Жыл бұрын
Thiéy baye adama❤❤❤❤❤
@BabouMafary
@BabouMafary Жыл бұрын
Thieye Ahmadou ammale gaayi amoul woone khamalna gaayi amoul woone fégnalna mbeuri yii neubouwoone woone.
@dikhasalikhate234
@dikhasalikhate234 Жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba Chiekh ahmadou bamba khadimoul rassoul ❤❤❤
@wakeursrmaïAmarviasselle
@wakeursrmaïAmarviasselle Ай бұрын
Santé Serigne Touba
@badarasane
@badarasane Жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba diarrama mame cheikh ibra fall akassa Bay adama sarr
@ibrahimadjitte9294
@ibrahimadjitte9294 Жыл бұрын
Dieuredieuf borom ngay
@MatareBiteye
@MatareBiteye 10 ай бұрын
Baye adama noumaye dèf ba am numirom guir Serigne touba khadim Rassoull
@Beugfallou2203
@Beugfallou2203 Жыл бұрын
Alhamdoulilahi bima amé koudoul Serigne Touba ❤
@ffama100
@ffama100 Жыл бұрын
Akasa baye Adama sarr❤❤❤❤❤❤
@ABDOURAHMANESECK-y9w
@ABDOURAHMANESECK-y9w Жыл бұрын
ماشاء الله تبارك الله ❤❤❤٣
@bambiste3040
@bambiste3040 Жыл бұрын
Saf sap si Yallah 😭
@DianguaneMbaye
@DianguaneMbaye 10 ай бұрын
Ndayssanne lou nekhe
@salioutine4426
@salioutine4426 Жыл бұрын
waw goor mourde machallah
@AminaDiagne-r9y
@AminaDiagne-r9y Жыл бұрын
Machalah ❤❤❤
@MatarGueye-t5p
@MatarGueye-t5p 5 ай бұрын
Baye Adama Sarr Yagg fi lol té andeu ak weur dolé Bayefall
@abasselo8206
@abasselo8206 5 ай бұрын
Cey yalla rek. Lansa waratek
@XidmaTv28
@XidmaTv28 5 ай бұрын
Source ? AL QURAAN wala Hadiiz ?
@diopcheikhfalilou-wy3or
@diopcheikhfalilou-wy3or 10 ай бұрын
Yakarou diam gni dieureudieufe hakhmadou bamba
@SambadiawBoydiaw
@SambadiawBoydiaw Жыл бұрын
Alassane mouridoulla
@Bargnykip
@Bargnykip 10 ай бұрын
❤️❤️❤️
@BayesallKebe-nl5ek
@BayesallKebe-nl5ek Жыл бұрын
𝗕𝗶𝗹𝗹𝗮𝗵𝗶 𝗸𝗶 𝗴𝗼𝗼𝗿 𝘆𝗮𝗹𝗹𝗮 𝗹𝗮
@MatarGueye-t5p
@MatarGueye-t5p 5 ай бұрын
Amoul Personnalité bou melni Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul AK Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baboul Mourirde Dini. Le KZbin est partout et disponible pour tout le monde amna toutes les histoires des grands hommes. Allez vous documenter et faites vous une documentation sincère doleen Guiss kou melni NIOOM. DIEUREUJEUFATY NIOOOOM❤
@moussafall948
@moussafall948 Жыл бұрын
Jeureudieuf baye Adama Sarr . Mom si maguegni la yagg fi ta werr sarr
@ndeyesarr4109
@ndeyesarr4109 11 ай бұрын
H❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@khadimgueye665
@khadimgueye665 Жыл бұрын
Kadou yi soumako guisser ci KZbin bi damay tiit ndakh gni khamoul kouy serigne touba ak cheikh ibrahima fall abo ridialou lahi , serigne touba ak cheikh ibra fall nagnoulen di diaye fougnouy diarer,
@AssaneDieye-n7t
@AssaneDieye-n7t Жыл бұрын
Waw fall boum la méti ndakh Ame na niou geumoul Yalla sakh bilahi kou née kigna Yakar kôkou brom Touba la yakar ak koumou meun done bilahi dierudieufé brom Touba diarama Mame cheikh Ibra fall
@alimajolie1214
@alimajolie1214 Жыл бұрын
Soxna diarul tiit kou Yallah xam yonent bi xam la boula gni xamoul wagnu wuko dara dafa diot gnu xam sunu wadji kou nieuwul nak da amul nimbal rék
@alphaoumardiallo3884
@alphaoumardiallo3884 Жыл бұрын
Bly Serigne bi nangou na linga wax waxtaan nou nèk la ken warouko indi si pènthie donté k menagn ko layal si alkourane wanté amna nio xamni sen dègu dafa gatt warou niousi diott Cheikh Moussa ka nè na amna si may yo xamni dou fègn si adouna ndax mboott yimou lamboo ak mayya ndaxté niou diingatt ko té kom niou yakkou ndaxté kou diingatt waay Yalla ya tiay yakkou
@ndiagambow9617
@ndiagambow9617 Жыл бұрын
Cheikh Ibra falllll reek dou morom deih bilay 😢😢
@papediop7647
@papediop7647 Жыл бұрын
Machallah mourid
@bassetouboe6711
@bassetouboe6711 Жыл бұрын
Limiye wakhe nékhena looo si ab mouride ms lisi wérr bari woule dani sosale serigne Touba rek
@brigadeantibidah2911
@brigadeantibidah2911 Жыл бұрын
Féne rek moye séne diangalé aye sama serigne néna wouleu sama mame néna doléne wakhe mouk Y'ALLAH SHWT Néneu wouleu YONENBI SAWS Neneu 😢
@MaguetteDiop-e9d
@MaguetteDiop-e9d Ай бұрын
Nioun brom Touba lagn xam
@brigadeantibidah2911
@brigadeantibidah2911 Жыл бұрын
Magoume dieume tok dou féne askane bi RAGALÉNE Y'ALLAH sounou Borom 😢
@mameseyefalloumbacke7906
@mameseyefalloumbacke7906 4 ай бұрын
Baye Adama sarr bgna thi yaw lol ndeyssan
@malickseck8002
@malickseck8002 Жыл бұрын
Fen rek lay def
@gentlemara6345
@gentlemara6345 11 ай бұрын
Serigne Touba n'est pas plus qu'un serviteur de Allah. Et c'est lui-même qui le dit إني عبدالله وخادم رساله
@malickseck8002
@malickseck8002 Жыл бұрын
Pabi ne respecté nit nji 😢
@MoussaDiop-e7c
@MoussaDiop-e7c Жыл бұрын
Cëy
@ditonkone
@ditonkone 11 ай бұрын
Nivo ba ngi sikaw
@abdoumbaye3659
@abdoumbaye3659 Жыл бұрын
Yague fi te werr lool fall yarame bi
@modouseck6796
@modouseck6796 11 ай бұрын
Yagg fi t werr
@AmadiopDiop
@AmadiopDiop Жыл бұрын
AY WAKHI DOFF REK NGUEN DI WAKH RAGALEN YALLA MO GUEUN SEN SERIGNE YI NGUEN YAKAR GNI NIONIOU DÈNAGN YAGG NEU KENEU XAMOUL FOUGNOU NEKEU KOUDOUL YALLA ! KONNE RAGALEN YALLA MO GUEUN TÈ NGUEN BAYI YALLA AK DIAMAM GNI NDAKH MOY SEN BOROM OK
@ablayediouf5314
@ablayediouf5314 Жыл бұрын
😂 yalna yalla dimbali la barker brom touba
@Amdy114
@Amdy114 Жыл бұрын
Jërëdëf Serigne touba jarama mam sëex Ibrahima fall
@khatabdieye4320
@khatabdieye4320 Жыл бұрын
Yaw yay dégue dégou dof😂 sa bop bi da touti😂 ndaysanne
@MaguetteDiop-e9d
@MaguetteDiop-e9d Ай бұрын
Ndaysan yal nga xam kouy brom Touba
@sileyedia6108
@sileyedia6108 Жыл бұрын
Machalla ❤❤❤❤
JAZBOUL MOURIDE 26 01 2021 CHEIKH IBRAHIMA FALL ak ZIKROULLAH (BAYE ADAMA SARR)
1:20:54
MAME CHEIKH IBRA FALL, Une merveille de DIEU
1:14:48
Edu BayeFall
Рет қаралды 107 М.
Hilarious FAKE TONGUE Prank by WEDNESDAY😏🖤
0:39
La La Life Shorts
Рет қаралды 44 МЛН
GIANT Gummy Worm #shorts
0:42
Mr DegrEE
Рет қаралды 152 МЛН
Journée MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL TOUBA APECSY par SERIGNE ADAMA SARR
12:51
GËME WÓOLU YAAKAAR SERIGNE TOUBA
Рет қаралды 515
Waxtaan : Ci  MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL Baye  Adama SARR /Janvier 2017
50:31
MALAKA MIKAYIL NDIAYE AK BAYE ADAMA SARR
1:16:10
KEMANE TV HD
Рет қаралды 217 М.
Hilarious FAKE TONGUE Prank by WEDNESDAY😏🖤
0:39
La La Life Shorts
Рет қаралды 44 МЛН