TOUBA AFFRONTEMENTS ENTRE LES BAYE FALL ET LES TALIBES...BAYE ASSANE ET SA NDIOGOU EN DESACCORD...

  Рет қаралды 90,188

Solution TV

Solution TV

Күн бұрын

Пікірлер: 667
@seydinaanne9617
@seydinaanne9617 Жыл бұрын
Touba DEUG yalla la Souf si soufou yalla la béne Serigne momou KO andouna yalla KO môme bayi léne dof dof Lou gui Sénégal fép béne la niy doré ay bandi niouy protège lagne
@CXOUNABMB-07
@CXOUNABMB-07 Жыл бұрын
Wa légui li yalla beugeu nak eske yalla wathié na ay malaka pour gnou douma baye fall Yi ndax yalla wax nalen gnou djouli gnou bagne ndigueul li mo amoul sens ay tapalei RK la
@modoufall8739
@modoufall8739 Жыл бұрын
Mane Touba la dekk mais baye fall yi am na no khamné ay dof lane
@babakebe4094
@babakebe4094 Жыл бұрын
Nañ wakhanté DEUG, bay fall d'où yeufi dioulite, té nitéwoul ana safinat anan AK mod lo Ngabou, seuñbi follinalèn, violence rék, c trop
@friezabadiane5110
@friezabadiane5110 Жыл бұрын
Assane sui op d'accord Tay mome danou 'gua ... Serigne mountakha waxoul kén mou dorr walla mou sagga ,Démal Degglou li Serigne bii waxon thi mbir yii...j habite a Touba mé liffi niiy mboubo baye fall yii dii déff Tégouwoul si yonn bilakhi Ap Baye Fall dafay am Yeurmandé Amii Téguin Ak Talibé wayé linou guiss ni Banditisme lay gueuna Nirrou🙏🙏🙏
@Lara122e34
@Lara122e34 Жыл бұрын
Qui a donnné l'ordre aux baye fall?
@deugrek344
@deugrek344 Жыл бұрын
Bayil nafékh bi té wakh té yalla takh . Qui a donné l'ordre aux bayefalls? Votre fanisme, votre clanisme et vos mensonges sont à l'origine de tous les maux de ce pays merdique et de mensonge.
@deugrek344
@deugrek344 Жыл бұрын
@@friezabadiane5110 dél fowé sa khélmi ak sén arguments you faible yi "mandou"😂😂 kou doul diouli do woor war ngua yar kén. Yaw mi am xam xam bakhara ba nassi wakhma fen foumou wakh niit yi bouniou diouli bouniou wor😂😂 wala ngua andil ma hadith. Magui khar andi lolou. Tant que dolén nangou deugue beugua deuk thie ay fén ak ay thiankhane sen sénégal bobou dou avancer. Ay lapoto ak ay diam guén di nék rek😂😂
@deugrek344
@deugrek344 Жыл бұрын
@@friezabadiane5110 ay doméram guén rek dém lén guén dimbali dji sén baay ak ndey mo eup ndiarigne fofou di top thie niit yi daur ak humilier. Bane réw ngua guiss civil di éduquer moromou civilam?
@deugrek344
@deugrek344 Жыл бұрын
@@friezabadiane5110 doméram sokh lawouma kham dara thie fanatisme ak ay fén. Je suis trop pauvre même amouma sakh louma lék😂😂 yagui doul dima juger té khamo li laniouy wakh thie sénégalais. Sen adouna bi yép fén ak soss la. Té dolén wakh dara louy deuk. Bravo comme tékki ngua mane ma gueuna pauve thie adouna bi😂😂 mais sama mame nekoul wone diam comme ni say mane nékè ay diamou ak topou ak fén. Bo meuné fékhé ba layal baye fall rek dinaler. Kep koudoul diouli rek yéfar ngua. Wakhal sa serigne bi mou dugual lén diouli té bayi bokalé😂😂
@alioumbaye1292
@alioumbaye1292 Жыл бұрын
Assane est très fort il s'adresse aux intellectuels. Son discours est codé et très instructif
@cheikhdione2925
@cheikhdione2925 Жыл бұрын
Effectivement, Assane nandité de classe exceptionnelle la.
@abdoutine944
@abdoutine944 Жыл бұрын
Qui daffa dooff nganan
@moustaphaseck1231
@moustaphaseck1231 Жыл бұрын
Yaw y’a wayadi
@cheikhdiouf1739
@cheikhdiouf1739 Жыл бұрын
​@@abdoutine944yaw momou yay dof bou mag bi sa capacités intellectuels egoul si nga kham fi assane di wakhe
@moustaphafalldiouf7671
@moustaphafalldiouf7671 Жыл бұрын
L'hypocrisie religieuse, le drame sénégalais. Nos foyers religieux ne produisent plus d'hommes de valeur. Quel dommage de constater que les sacrifices des Aïeux soient vendangés à très vil prix. Tout est à refaire.
@Bluerain-j2v
@Bluerain-j2v Жыл бұрын
La solution est que l'homme religieux doit apprendre à prendre ses distances avec les politiciens.Ils ont à y perdre qu'à y gagner.Les religieux ont le devoir de préserver leur crédibilité car vu la configuration sociale de notre pays ce sont des gens en qui beaucoup de personnes reposent un certain espoir de les mener vers Dieu.
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 Жыл бұрын
@@Bluerain-j2v il faut comprendre ns sénégalais ns sommes pas civilisés on est des sauvages on se respecte pas
@mouridedioneofficiel5952
@mouridedioneofficiel5952 Жыл бұрын
Assane Lingay wakh Tégoko Fénn , Ndigeul li Dafa Wara Tambalé Sibir Keur Kilifa yi, Loolou Moy Deugg
@ibrahimafaye476
@ibrahimafaye476 Жыл бұрын
Ah vraiment
@MaAbdouRahmanGaye
@MaAbdouRahmanGaye Жыл бұрын
❤❤❤❤❤
@d.d.d-mouss
@d.d.d-mouss Жыл бұрын
No grand ,wakhou Assane fenenn ga kow dielignè laga wakh ley momitt fi wakh
@laminemaron3451
@laminemaron3451 Жыл бұрын
Si on ne parle pas la vérité, un jour Touba risque de s'embrasser dans une situation incontrôlable. Comment on peut donner ces genres d'ordre à des animaux qui ne réfléchissent pas
@OumyDiagne-lm4px
@OumyDiagne-lm4px Жыл бұрын
Bien dit ❤
@noreynily9925
@noreynily9925 Жыл бұрын
Touba diamou rék mofaye Ahmed bilahi
@maria1-s7w
@maria1-s7w Жыл бұрын
Mais sincèrement disons-nous la vérité Nous savons bien que les femmes de nos marabouts portent des cheveux et se depigmentent😢
@aminatasall2605
@aminatasall2605 Жыл бұрын
Vérité absolue
@mfn1-mj7cx
@mfn1-mj7cx Жыл бұрын
Tu as bien raison
@bambandiayediouftoubabrasi7893
@bambandiayediouftoubabrasi7893 Жыл бұрын
Ake lou mana khew dore mo mana nigaue 😢😢😢😢😢😢
@petitkebe9887
@petitkebe9887 Жыл бұрын
bily
@tassegueye8996
@tassegueye8996 Жыл бұрын
Yén gnognou si plateau bi Ay talibé guene ay talibé guèn wayé khamguéne Lou khéw Touba dou Yonne la religion c'est pas de la dictature
@gninguekhadim531
@gninguekhadim531 Жыл бұрын
Vous êtes insolent Touba loufa xew len certains choses ou ajustements de certain Baye fall ne sont pas normal je dirais oui tu as raison mais yaw xamal fika nek rekk
@KhadyTall-kj9uv
@KhadyTall-kj9uv Жыл бұрын
Ndigeul dieufe
@mamadouniang4531
@mamadouniang4531 Жыл бұрын
Touba loumouy tere lepp l islam moko tere
@Mohamedsallah487
@Mohamedsallah487 Жыл бұрын
Baye fallyi louñi déf tégou niou ko fénne
@petitkebe9887
@petitkebe9887 Жыл бұрын
bilhi
@MouhamedBa-k2s
@MouhamedBa-k2s Жыл бұрын
Dotouma séetan solution Tv à cause de ce gars, mais ki day yé fitna way, les personnes blessées sont des mourids il faut pensé à eux. Merci sa ndiogou, bien dit machallah
@bambatouba6884
@bambatouba6884 Жыл бұрын
Baye Assane Taye mom wakho wakhi nitt S.mountakha Dor lou woull sagalou woull wakhoul niou torokhall kenne
@SaliouSeye-cp5ze
@SaliouSeye-cp5ze Жыл бұрын
Baye fall yii no nge touba de deger bope baxol
@davembayesenior5973
@davembayesenior5973 Жыл бұрын
C est une situation dangereuse qu on est entrain de créer à touba qui fait partie du Sénégal. Faisons y attention sinon bonjour l anarchie . Le Sénégal est un et indivisible. Assane Mésséré dit franchement ce que tu penses et arrête de tourner autour du pot . Il n y a pas deux Sénégal. Il y a des institutions pour faire appliquer les lois régaliennes dans ce pays . Badola dou door badolo ni mome . Wassalam. Nous ne sommes pas en Italie . Mrci .
@babacarlam1845
@babacarlam1845 Жыл бұрын
Vraiment sa ndiogou vous êtes excellent
@elzoatti8951
@elzoatti8951 Жыл бұрын
Sa ndiogou félicitation ! Tu es très sage .
@hamaskingofficieltv6094
@hamaskingofficieltv6094 Жыл бұрын
Assane vraiment nit bou faut gua mala gueune deuk touba fouf mais liguay wakh tégo fa fen Amon niveau quoi metire wo plateau sakh tête vide gua leep lo guis wakhtane la door fadioul dara lislam sakh amoul force g vu baye fall bou torture sama cousine dieul numérom diko dokhane arret way del kham liguay wakh keep geuniou no begue serigne guay défendre ni honnête way
@bissentygomis9413
@bissentygomis9413 Жыл бұрын
Assane est très fort avec sa façon de passé de bon messages indirectement
@moustaphadieng7178
@moustaphadieng7178 Жыл бұрын
Merci beaucoup sa félicitations sa ❤ Dia dëf sa
@volkingcan5128
@volkingcan5128 Жыл бұрын
C’est des bêtises le pays est pour tous les Sénégalais que tu sois croyant ou pas. La région Touba n’est pour le Serigne ni pour les Mbaye Fall
@mohamedsakho7391
@mohamedsakho7391 Жыл бұрын
Assane sacré Assane,le règlement est pour tout le monde pas pour certaines personnes
@assannian7746
@assannian7746 Жыл бұрын
Bay assan wallahil hachim amo yeurmande nga nan ay dorr yaw l'an la😭😭
@BaraNdiaye-xi1lh
@BaraNdiaye-xi1lh Жыл бұрын
No assane dou nitou fi❤❤❤sonhibou bayilee Assane taye mom injustice la maye diamou si yene
@abosamb6235
@abosamb6235 Жыл бұрын
Macahalla sa amna solo ❤❤❤🙏🙏🙏🙏
@romanreigns627
@romanreigns627 Жыл бұрын
Merci Sadiongou
@dmcdjilymbayecolle4629
@dmcdjilymbayecolle4629 Жыл бұрын
Ay way nouy bayé ndégalo yalla Moy dioli AK waoor Di déff ndégalo Serigne bi
@petitkebe9887
@petitkebe9887 Жыл бұрын
moma jhaal
@OusmaneLy-cv5nd
@OusmaneLy-cv5nd Жыл бұрын
Wallahi God bless sa ndiogou li moy deuk wahtan avant tout mo guene la plus part bo wahtaner gnou bayyi❤❤❤
@kebe-ng6710
@kebe-ng6710 Жыл бұрын
ont ne peut pas assurer la sécurité sens études ni formations qu'on se dise la vérité.
@mouhamedndiaye5164
@mouhamedndiaye5164 Жыл бұрын
CHARITÉ BIEN ORDONNÉE COMMENCE PAR SOI MÊME
@elhadjimorsall5833
@elhadjimorsall5833 10 ай бұрын
Koun touba lou fa police ak giandarma djierigne sou fèkkè bayyi wouniou mbirmi ci seun lokho 🤗🤗🤗🤗
@SohayboFall
@SohayboFall Жыл бұрын
Assane merci beaucoup ❤❤❤
@MoustaphaGueye-b8y
@MoustaphaGueye-b8y Жыл бұрын
Mérci sa ❤❤❤❤❤
@MouhamedGning-m4t
@MouhamedGning-m4t Жыл бұрын
❤❤❤machallah
@dieynabacoly4053
@dieynabacoly4053 Жыл бұрын
Merci sa geu ci mbidef saf nena dawa dayi la❤❤
@elhadjicheikhba4122
@elhadjicheikhba4122 Жыл бұрын
Merci Assane diadieuf way
@mbendacouture8010
@mbendacouture8010 Жыл бұрын
yalla sah lim téré doréwoun si
@ibrahimaba5199
@ibrahimaba5199 Жыл бұрын
Yalla limou téré amna limsiye diglé Ray wala dor wala dague lokho khana diango .
@MaAbdouRahmanGaye
@MaAbdouRahmanGaye Жыл бұрын
Yaw diango
@mariamagueye-iu7dw
@mariamagueye-iu7dw Жыл бұрын
Mersi..asane
@revolution6609
@revolution6609 Жыл бұрын
Respecter les règles de qui et de quoi ? Ni la Religion, ni l'etat n'interdissent des coupes de cheveux. mountakha devrait plutôt apprendre le Coran et la Sunnah que de faire le malin avec le peuple. Yalla sounou Borome moo nekk di wér faux serigne ssi. Lolou moye deugue.
@baradiop6335
@baradiop6335 Жыл бұрын
Assane dangay fene li Serigne abdou ahade terewone dou li
@SerignembackéSeye-v7h
@SerignembackéSeye-v7h Жыл бұрын
Lanla serigne abdou lahad teré won?
@OusmaneTouré-h9h
@OusmaneTouré-h9h Жыл бұрын
Serigne bi wakhoul doré baye fall réw lagn déf
@petitkebe9887
@petitkebe9887 Жыл бұрын
billhi
@noreynily9925
@noreynily9925 Жыл бұрын
Yaw mi yarew
@sokhnaSaly_Diop4853
@sokhnaSaly_Diop4853 Жыл бұрын
Louy sén dekkou Mame ? Bougnoye dore gnéppa Yam té Serigne bi meun nga bokk ak mom askane té do mbokam Ki mbokam DEUG Moy kiy nékk thia lam beuguone Ay thia khane késé gnépa Yam thi kanamou Serigne bi amoul mbacké mbacké amoul Ndiaye Ndiaye C'est une honte ngén di digulé thiangay té sétoulén😡
@Prince_00836
@Prince_00836 Жыл бұрын
🤝🏼👍🏽🙏🏼
@aidaniang9626
@aidaniang9626 Жыл бұрын
DEUG la
@sokhnaSaly_Diop4853
@sokhnaSaly_Diop4853 Жыл бұрын
@@aidaniang9626 man de mbacké la sante mais Bouma teguou woul thi Yon bokkouma ak Serigne bi dara Sougnou keur lépp lougnouy tere amoufa
@antadiop213
@antadiop213 Жыл бұрын
Pourquoi li yalla téré fi thii sénégal kéna doré woufi Serigne dalay khamal lou bakh ak lou bonne mais waroula forcé dara
@noreynily9925
@noreynily9925 Жыл бұрын
Li GA wah vo KO ték
@cheikhdione2925
@cheikhdione2925 Жыл бұрын
Sa Ndiogou et Assane c'est vraiment la Solution.
@noreynily9925
@noreynily9925 Жыл бұрын
Walahi Lou wér ga wah assane machahalla
@cheikhabdoulkarim
@cheikhabdoulkarim Жыл бұрын
Nous sommes tous des mourides mais sincèrement ce qui se passe a touba dou lolou la serigne bi diglé khar bopou nite ndakh coiffure c'est pas normal deugue leu yalla beugue
@beugubaax7188
@beugubaax7188 Жыл бұрын
J'espere que les dirigeant de walf vont faire klk chose ak doff bi. Koudoul diouli dina téré kouy dégradé.
@fallougalsen1325
@fallougalsen1325 Жыл бұрын
Assan tay d'accord roma si sa khalat sa khalat bakhool door Mo darrnier solution koka difon sa ndaye wala sa baye dola nekhe
@elhadjicheikhba4122
@elhadjicheikhba4122 Жыл бұрын
Diereudieuf Baye fall yi
@ndiattendiaye3947
@ndiattendiaye3947 Жыл бұрын
Il faut aussi prendre des personnes de référence pour mettre de l ordre
@santkoutedeki7538
@santkoutedeki7538 Жыл бұрын
Baye fall bi dou djouli sa yonn nekou thi nakh momeum daniou ko diokh digaal franchement ❤
@dabakhndoye8900
@dabakhndoye8900 Жыл бұрын
Merci Assane
@smadiakhatelo9891
@smadiakhatelo9891 Жыл бұрын
Mani Assane mi wax lén ko deugue temp yi ay néféré rèk lay wax Esk mingui ak khelam Esk Ak ndiabot topou ko 😂😂😂
@CheikhounaSylleu
@CheikhounaSylleu Жыл бұрын
اسلم غليكم ورحمة الله
@gueyeibrahimamercibeaucoup9544
@gueyeibrahimamercibeaucoup9544 Жыл бұрын
Kou nous téré football ga lankue da none wara téguel sa Ndaye ❌❌❌❌❌❌
@pathembathie3388
@pathembathie3388 Жыл бұрын
Assane ya nafekh 😂😂😂😂
@dieynabacoly4053
@dieynabacoly4053 Жыл бұрын
😂😂😂😂no mes Assane doudem wa li ci argument 🎉🎉❤
@doudou610
@doudou610 Жыл бұрын
lép serigne mountakha laa khamoul dara
@mfn1-mj7cx
@mfn1-mj7cx Жыл бұрын
Wakh nga deug 🙏🙏🙏🙏🙏
@SidateNdiaye-k2z
@SidateNdiaye-k2z Жыл бұрын
Merci.assen
@badarabax
@badarabax Жыл бұрын
Merci
@mouhamedgaye4683
@mouhamedgaye4683 Жыл бұрын
Beurena lou yalla terré nit yagui koy df. Te kenn doroulen touba kagn la am armé bopam
@gninguekhadim531
@gninguekhadim531 Жыл бұрын
Depuis cheikh Ibra xamko touba Baye Fall yi djeufé diguel rek
@Quran_karim221
@Quran_karim221 Жыл бұрын
Moma diakhal T sakh nagnou wakhak bayfal yi lank baania djoulli
@moustafandiaye172
@moustafandiaye172 Жыл бұрын
Mountakha mbacke matoul kilifa mo takh touba djakhaso
@SerignembackéSeye-v7h
@SerignembackéSeye-v7h Жыл бұрын
Mbaye sy mansour domouram jiy dioyal macky sall mo matoul kilifa
@ElhadjiToure-yk5wt
@ElhadjiToure-yk5wt Жыл бұрын
Assane tey danou nga dè 😂😂😂😂
@BayeSerigneGueye-wx8es
@BayeSerigneGueye-wx8es Жыл бұрын
Machallah sa niogou très bien analysé
@massacoulibaly6969
@massacoulibaly6969 Жыл бұрын
Pour être éducateur il faut être pédagogue
@falloulo1498
@falloulo1498 Жыл бұрын
Souhibou ioe nit nga ❤
@dawdatouray266
@dawdatouray266 Жыл бұрын
But who is the president of touba and who is the president of Senegal?
@alimatousadiya3967
@alimatousadiya3967 Жыл бұрын
Macha'allah sa ndiogou🥰
@ElhadjiToure-yk5wt
@ElhadjiToure-yk5wt Жыл бұрын
Baye assane messere yaw rèk laye toopp way tèy mome daga danou ba niapp sa khoon 😂😂😂
@Ibrahimafall313
@Ibrahimafall313 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤assane wakhal de
@khadimbambaaluminium432
@khadimbambaaluminium432 Жыл бұрын
Machalla lépou wakhtan la doré takoutt kéne yaro
@Patriotesn
@Patriotesn Жыл бұрын
Assane sa raisonnement bi dafa doffé toropp franchement
@Quran_karim221
@Quran_karim221 Жыл бұрын
Non billahi Sénégal mo nekh yalla ni djoulli lèn bay fall yi bagn ba noppi di door gni mourouwoul
@madimadi3208
@madimadi3208 Жыл бұрын
Touba lieu de tous les dérives 😢
@ibrasarr2933
@ibrasarr2933 Жыл бұрын
Nit nite merci sa li ga wakh rafète na
@PapaSy-pw8ln
@PapaSy-pw8ln Жыл бұрын
Salam salam yalla ngui dééfou gnou ko Sénégal séen adouna mooy beugeu touuki
@anam7786
@anam7786 Жыл бұрын
3:08 asane neexooma dara kaddu keen duka fowe
@khadyndione9815
@khadyndione9815 Жыл бұрын
😂😂😂Assane ray nama billay wallay
@nenediouf1079
@nenediouf1079 Жыл бұрын
😂😂😂😂assane wakh na deugue guénale séne deuk😂😂😂
@Assgueye2002
@Assgueye2002 Жыл бұрын
Contana si yaw ❤❤
@PapeThiam-ww2mi
@PapeThiam-ww2mi Жыл бұрын
Sivil douyar moromou civilam touba kéne momouko souguési tolénounou diaylé touba sédoko yéne mouridyi sof guéne bariguéne wakh té diné khamoulési dara
@gninguemameanta2838
@gninguemameanta2838 Жыл бұрын
Mane touba la deuk mai dinè dou force lii ni dafay wagni ngeum
@MaloumThioye
@MaloumThioye Жыл бұрын
Vive sonko
@mmlne
@mmlne Жыл бұрын
Baye assane doré ci ndigalou serigne bi boufékké ndigalou serigne bi diamou yalla la kone iska douniouko matalé Sénégal yepp
@SerignembackéSeye-v7h
@SerignembackéSeye-v7h Жыл бұрын
Serigne bi yilifoul wa senegal wa touba rek la yilif
@nariboubassirdiop7461
@nariboubassirdiop7461 Жыл бұрын
شعيب Li ngay wakh amoul amoul ko nek touba ta yeuoul li serigne bi wakh
@IDRISSADANFA-l2y
@IDRISSADANFA-l2y Жыл бұрын
Non Assane est extraordinaire 🤣🤣
@zgrsljrbkbtfg1135
@zgrsljrbkbtfg1135 Жыл бұрын
Mountakha mbacké lingay def nii dinko layo ak YALLA
@bayemodouthiam1478
@bayemodouthiam1478 Жыл бұрын
Assane Nafekh gua rek ak sa Yéré bou déborde bi 😂😂😅
@djilyndiaye5885
@djilyndiaye5885 Жыл бұрын
Baye Assan khamo dara
@assannian7746
@assannian7746 Жыл бұрын
Bay assan wakho fi dara 😭
@serignediengbois4979
@serignediengbois4979 Жыл бұрын
Iow asan ndéke wéro
@abdoulayesane5365
@abdoulayesane5365 Жыл бұрын
Assane tu es intelligent quand tu dis les femmes et les filles du Serigne font le haissalle et c'est interdit par Les autres sa à tout dit 😂😂
@bayembow3268
@bayembow3268 Жыл бұрын
Saa. ❤ profesional
@AwaDiop-e7i
@AwaDiop-e7i Жыл бұрын
Daga duekoul touba gnoune wa touba kon kou nek allakhira sonounagnou trop
@AnnaColy-t8y
@AnnaColy-t8y Жыл бұрын
Assane iow ya Bonn ay domou Adama Di souffrir nguanane nagnou léne door
@adamandiaye7601
@adamandiaye7601 Жыл бұрын
Loi dale nieupathi wara yame soudé gueume yalla amna
@khadijahs4052
@khadijahs4052 Жыл бұрын
Nane sangara bii ak touhh yamba bii nak.... Mandit bay tereuff nane dieureufff serigne touba lolou laniou wara ndiekeu terè
@mouhameddiallo1793
@mouhameddiallo1793 Жыл бұрын
Bay assane franchement dema la nawon dila suivre sac jour way tay boudé wakh deug rk atté wo deug lingay wakh tégo féne ay tappalé donge nga fi wakh
@OusmaneLy-cv5nd
@OusmaneLy-cv5nd Жыл бұрын
Mais Assan nanotingua ddd wahi doooof kesse ngua fi wah 😮😮😮
@elhadjimorsall5833
@elhadjimorsall5833 10 ай бұрын
Taymom bay assane li nga wakh dou deug nit warouta door mromou nitam 🤭🤭🤭🤭🤭😏🤭🤭🤭🤭
@MayeGueuy
@MayeGueuy Жыл бұрын
Yalnagnou douma sa yaye walla sa mak kon do wax lolou
IL'HAN - Qalqam | Official Music Video
03:17
Ilhan Ihsanov
Рет қаралды 700 М.
Quilt Challenge, No Skills, Just Luck#Funnyfamily #Partygames #Funny
00:32
Family Games Media
Рет қаралды 55 МЛН
Branco en colère et tire sur Sonko & Diomaye: les vérités de Ahmed AIDARA
9:06
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 31 М.
Retour sur la Visite du Président Bassirou Diomaye à Touba
9:27
Itv Sénégal
Рет қаралды 169 М.