Touba: De présumés membres de PASTEF à l’ assaut de l’ autorité du khalife sur la ville sainte.

  Рет қаралды 3,808

@CheikhIbraFall-TV

@CheikhIbraFall-TV

Күн бұрын

Пікірлер: 82
@cheikhfall2165
@cheikhfall2165 6 сағат бұрын
Yeen nopalou lene. Li xew Touba Manou lene ci tuss.
@MbayeThiam-m5d
@MbayeThiam-m5d 4 сағат бұрын
Jarul Mér. Jarul Saaga. Ab Mouride Da Fay Yaru. Touba Borom Touba Ko Moom. Même Poloce Ba, Police Spéciale Lañ Vi Bind. Touba Titre Foncier La. KEUR Jambur La. YALLA BINDUL KU MANAL SERIGNE TOUBA DARA. KON JARUL WAX JU BARI.
@mouhamadoufall4473
@mouhamadoufall4473 14 сағат бұрын
Ousmane Sonko est derrière tout ca. Il fait comme si yeugoul tiinoul fek mom la. C’est la même chose avec les insultes et diabolisation des religieux. Lepp mom la ligueyouniou leufeul ndem beug niou yapp
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 7 сағат бұрын
Mo tothie Séne leufel ndeye tay Ousmane sonko Lou Mouy ragal si Béne Serigne bou Serigne yi manone gatte dounou gagné yalla mofi néke
@mouhamadoufall4473
@mouhamadoufall4473 7 сағат бұрын
@ yaw amo xel. Nawlo woumala douma wakhak yaw. Diour la yakoup tate la rek
@SaliouKne-il2qd
@SaliouKne-il2qd 9 сағат бұрын
saway demleen khe thioji seen dakoup bay moogen ngeeni nkall nkali
@MoussaMbengue-vc9wg
@MoussaMbengue-vc9wg 7 сағат бұрын
Sa saram ndeye sakh meunou ko réglé ya gueuneu kham liko fi ték autoritè bou sagn défié touba amoul
@beautifuldiscover5603
@beautifuldiscover5603 19 сағат бұрын
Ki moy kane ? Yaww fouyoula feiik teigueul sa ndayy domeramm . Neikeu ci deukeu jambourr nane dagay défier ki mom deukeum aam aay réclame nganane dagayy oser di attaquer ndigueulou serigne touba . Inchallah on verra bien et je suis persuader c'est cheikh thioro qui est derrière tout ça
@sonko2024rk
@sonko2024rk 9 сағат бұрын
Wabakhna yéne touba serigne bi moy diokh deuk koko nèkhh
@momartalla7800
@momartalla7800 19 сағат бұрын
Touba khalifa bi moy fal maire
@abdoukhadresylla3425
@abdoukhadresylla3425 18 сағат бұрын
Li wa APR niokoy def pour diaboliser wa pastef on sait très bien que Touba keur Serigne Touba la point
@aliouseck4863
@aliouseck4863 17 сағат бұрын
Yangui bakarou deh
@sidyndiaye-fw2vb
@sidyndiaye-fw2vb 8 сағат бұрын
Fatah diop mii dh wax mom bokoul pastéf
@novellase6810
@novellase6810 3 сағат бұрын
J pense pa dh
@affediop6372
@affediop6372 7 сағат бұрын
Touba li seringe bi beug mo fiy am
@CheikhSeck-j9t
@CheikhSeck-j9t 7 сағат бұрын
Yèna rew rek
@MamegorBeye-v3s
@MamegorBeye-v3s 17 сағат бұрын
Gni kou dokhane sén ndeye niou dieull
@NarouNour
@NarouNour 2 сағат бұрын
Bakhna nagne dem rek😭
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 3 сағат бұрын
Touba deukeu serigne touba limou deif ba am ko mom keineu ko deif motakh touba done beineu si Sénégal lolou mom seine sarap ndeiye ngueine si meunoul
@mbadiartv7485
@mbadiartv7485 9 сағат бұрын
Kaddou Serigne bi rek
@momartalla7800
@momartalla7800 18 сағат бұрын
Barthélémy justice moko condamné deukbi loufi Serigne bi beug moye ame
@morndadje4198
@morndadje4198 Сағат бұрын
Un bulletin blanc ne peut gagner
@tout1958
@tout1958 44 минут бұрын
Yéne nitou pastef yi légi Serigne Touba moléne désé
@LikaLo-z4j
@LikaLo-z4j 18 сағат бұрын
Sougéne beugé fal mair démléne séne dekou maam
@galgalgal8007
@galgalgal8007 7 сағат бұрын
Lii dou waa pastef.
@aladjidiop2315
@aladjidiop2315 18 сағат бұрын
Sonko kou am xel dagen yakar day teus teusi rk li BO siy jot Di wah AK yen nah apporte wolenko Dara beug KO yakal
@abdouldiop4711
@abdouldiop4711 4 сағат бұрын
Sene yala moye serigne bi
@AboutNdiaye
@AboutNdiaye 4 сағат бұрын
Lolou mom dounoulasi tontou danoulay bayi ba euleuk banou takhaw sounou kanamou borom mou atenou ak yaw
@AboutNdiaye
@AboutNdiaye 4 сағат бұрын
Khamouma kan waye' mande ' sa wakhj doumalako bal yaw miy woutal yallah morom
@goradiop8068
@goradiop8068 Сағат бұрын
Assalamou aleykoum warrahmatou lahi. Njongg li na yem ci àt yi! BillHahi du bax. ☠️
@tout1958
@tout1958 17 минут бұрын
Doxanee léne séne ndeye dém lidianti séne deukou Mame wala séne deukou baye domerame yi Serigne Touba sax geumou léne ko
@SassoumGueye
@SassoumGueye 6 сағат бұрын
Touba a un statut especal la 1ere et unique autorité est le Khalif Général des Mourides qui est le seul habilité à elire le maire de Touba la propriété de Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul ne perdez pas votre temps
@moussafaye6263
@moussafaye6263 4 сағат бұрын
Diokhnalah sama kadou
@kakhadim6511
@kakhadim6511 14 сағат бұрын
Sa létre jokh ko sa baye
@bathiefaye5264
@bathiefaye5264 2 сағат бұрын
Dem leen ci Sëriñ bi, kon du ngéen ko defaat de
@bathiefaye5264
@bathiefaye5264 2 сағат бұрын
Tuubaa sëriñ bi moo fi teg maire bi, soof ngéen torop
@sidimoctardiop3761
@sidimoctardiop3761 2 сағат бұрын
Péxey opposition bi la dé faite très attention 😂
@Kako-gq3cj
@Kako-gq3cj 11 минут бұрын
Touba.dou.dakarou.koufa.dougue.niou.niouse.sa.mame
@mouhamadoufall4473
@mouhamadoufall4473 14 сағат бұрын
Lii raam ci niak bi la dieum. Tepi sen leufeul ndeye yen nieup ay sonko aki diomaye yen nieup guen naan republique. Dokhane sen ndeye diott na
@smarttvsn7593
@smarttvsn7593 18 сағат бұрын
Ñongi leene xaar
@diopmourta6969
@diopmourta6969 4 сағат бұрын
WA APR NIYE SOSAL WA PASTEF
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 3 сағат бұрын
Yow fi deukou serigne touba leu sou adouna bi yeup dadjei wone meunouleine si seine tounou ndeiye leigui li moleine dessei beugueu dial deukoup serigne touba bi andi fi ay fo ak politique
@tout1958
@tout1958 37 минут бұрын
Wa pastef yi baye danou léne wara géné Touba namou géna gawé
@leytikane8704
@leytikane8704 6 сағат бұрын
Yenn nopaloulen diabolizer dialloul khelbiguen am pour diabolizer niitgni amnagne khel bouko eup
@bizliontv1671
@bizliontv1671 15 сағат бұрын
Mais moom loutax wakhoul touram. Abib bimouy waxal tamit tegoul tontoom. Waxi boppam la tek naan abib abib rek. Li daal louche neu !!! Est-ce que beugoul toumaal waa pastef ???
@biramediouf7626
@biramediouf7626 7 сағат бұрын
Lii dou wa Pastèf touba
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 7 сағат бұрын
Serigne bi moko fi tek
@moustaphambackeba4223
@moustaphambackeba4223 3 сағат бұрын
Thielañouye ñanfé séne ndaye nak bou bax
@Pape-cv3qr
@Pape-cv3qr 2 сағат бұрын
Yéna xam dé
@Falloundiaye-oi6ce
@Falloundiaye-oi6ce 2 сағат бұрын
defléne ndank FALLOU FALL MOMOU NONOU OUSMANE SONKO LA ÐÉ
@biramediouf7626
@biramediouf7626 7 сағат бұрын
Et on va amener cette audio à la police
@mouhamadoulfhadalsyllasyll2649
@mouhamadoulfhadalsyllasyll2649 7 сағат бұрын
Sawaye dalall fi serigne bi laniouye déklou
@tout1958
@tout1958 45 минут бұрын
Nitou pastef yi kouléne topou Sénégal dina takeu
@FallAsenag
@FallAsenag 4 сағат бұрын
YEEN Waa APR nopalouleen Cheikh Thioro Mbacke ak Assane Mbacke Niooleen gueuneu degueul khalifabi Mounouleena Diakhasse Touba K PASTEF
@NarouNour
@NarouNour 2 сағат бұрын
Bougne fekone sonko sisa kaw yaye sakh ngané dou mom sama papa la
@AbdulahiMbow
@AbdulahiMbow Сағат бұрын
You for da for ko you
@juniorfaye7147
@juniorfaye7147 4 сағат бұрын
Kate lene ndeyam deme sene deuk mame defkoufa deflenko nake boulone dellou guinawe
@aliounebambakara7167
@aliounebambakara7167 2 сағат бұрын
Yen gni nek ci audio yi d wax sounioulen xamon dinaniou len guéne ndeye ci deuk bi ay domeram bam khoukh Sax lolen guenu
@moustaphasamb4297
@moustaphasamb4297 9 сағат бұрын
Pastef amena porte-parole, lii waa boorbéé gnoo néékke si sééni manœuvres rék...
@kakhadim6511
@kakhadim6511 14 сағат бұрын
Yow koula nôkk nga beugg
@bayesallndiaye2646
@bayesallndiaye2646 6 сағат бұрын
Cheikh Thior La dh😮
@novellase6810
@novellase6810 4 сағат бұрын
Mom la dh
@AssaneFalll
@AssaneFalll 17 сағат бұрын
Diou giu line khar digene kham bakham sen baye mou mom Touba wala
@BoubacarGaye-k1n
@BoubacarGaye-k1n 9 сағат бұрын
yaw dokhalat bene liste mo dème compétition l'équipe lo bègue an kone yone amatul senegal
@novellase6810
@novellase6810 3 сағат бұрын
Lanne etat beug tokhal si deukk bi
@khadimMbacke-d9u
@khadimMbacke-d9u 5 сағат бұрын
Touba pour khalifape Serigne Touba pastef manousi dara défléne attention nak réwe ngeune trop
@novellase6810
@novellase6810 3 сағат бұрын
On c jamain
@oussmanelo6507
@oussmanelo6507 17 сағат бұрын
Demall sa dekeu baye
@biramediouf7626
@biramediouf7626 7 сағат бұрын
Vous voulez mettre en mal Pastef ak serigne bi ak wa talibe yi non lolou dou dial
@mamadousy8633
@mamadousy8633 10 сағат бұрын
Va dans la ville de tes grands parents
@abdoulayedione3364
@abdoulayedione3364 14 сағат бұрын
Vrai domeram
@KhadySene-i1y
@KhadySene-i1y 11 сағат бұрын
Pourquoi vous ne pouvez essayer pour voir 😂. Il faut le faire yéne rewolene sahe
@mbayanguefall9538
@mbayanguefall9538 3 сағат бұрын
Kii de yàq moo ko taxa jokk
@LikaLo-z4j
@LikaLo-z4j 18 сағат бұрын
Abib mii moo tégal ndeyam deug
@biramediouf7626
@biramediouf7626 7 сағат бұрын
Arrêtez vos mensonges
@cheikhsamb3743
@cheikhsamb3743 16 сағат бұрын
Falou mbawor bayill fénne
@moustaphadiouf1534
@moustaphadiouf1534 8 сағат бұрын
Yaw dimbalile nitt gni doul way
@cheikhounambaye331
@cheikhounambaye331 7 сағат бұрын
Yaw borom site bi Li nga wax wor nala
@abdoulahaddiop1769
@abdoulahaddiop1769 20 сағат бұрын
😂😂😂😂
@bathiefaye5264
@bathiefaye5264 2 сағат бұрын
Tuubaa sëriñ bi moo fi teg maire bi, soof ngéen torop
Pour chaque budget austéritaire viendra la censure ! - Éric Coquerel
9:18
La France insoumise - NFP à l'Assemblée nationale
Рет қаралды 3,1 М.
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 687 М.
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 35 МЛН
Новости дня | 16 декабря - утренний выпуск
4:42
Euronews по-русски
Рет қаралды 71 М.
PA Assane Seck : Ce qui s'est passé à la mairie de Dakar est extraordinaire...
18:01
RTS - RADIO TÉLÉVISION SÉNÉGALAISE
Рет қаралды 10 М.
Бундестаг решает, доверять ли канцлеру Шольцу
1:06