Mais Mosquée bi c'est trop beau. Extraordinaire. Diereudiefeti Borom Touba.
@bbneymar10695 жыл бұрын
Khadim Gueye du nit
@papesarr10435 жыл бұрын
Nice na
@mourtadadiop85795 жыл бұрын
Serigne bi rek ❤️❤️❤️
@kingpro7714 жыл бұрын
Mer6
@beuggeumjeufgoudikbamel61705 жыл бұрын
Billahi wallahi wa tahalahi li wa senegal 🇸🇳 am man Nani ken amouko ame seringe touba am Alhagie Malik am mameblimamou am Baye Niass yalla na jamm yagg senegal 🇸🇳
@falloumoussandiaye58075 жыл бұрын
Degu la
@papadembasene51655 жыл бұрын
BEUG GEUM JEUF Goudik bamèl bilae mbok mi xamo li nga wax sax mane dh layenne laa wayè maagi doundou mbectèi mii nii gaa yii yalla yii koulène nangouloul da ngay sonneu rek rèw mi🇸🇳 migi saff sapp ak serigne touba bou gamou diotè niou ande gamou dji liniou am kène amouko way yalna diam yagg nieup ay mouride layène tidiane ect danio xamoul baate yii nak wayè nio bok yone wii
@diarrangom57375 жыл бұрын
Walahi fou lou yomb
@falllouseck71065 жыл бұрын
Wa GFM yala naléne yala faye magui bitimréwe mè dara retiouma thi magal bi dieredief S mountaha yala nafi yague té werr Aminé🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@ndeyekdiedhiou78785 жыл бұрын
Wa GFM yala nalène Yala Faye constant Serigne Touba
@abdoudiagne19365 жыл бұрын
Amine
@fallouniangsonko5 жыл бұрын
Serigne Ganna Ak Serigne khadim gueye yalna yalla yokou séne takhaway barké Serigne Saliou sama kholl sedna trop
@assanesene39825 жыл бұрын
Sama gayi mane souma nékoul wone mouridoulahi loumay doone Dieuredieuf Serigne Touba
@ndongali35405 жыл бұрын
Machallah Diambar yi , Dieuredieufé Cheikhoul Khadim Thieuy mo beuri dolé kholal ma lii rék nga liguëy lo khameni say bo woté niit gni di ndieukeuneté Niit gni di diougué par tous dans le monde Dieuredieufé Cheikh a AHMADOU Bamba sounou fierté niépa bëgue si yaw Di nianal SERIGNE MountHa Yalla nafi yague té wér si Barké Serigne Bamba
@maofallmaofall23545 жыл бұрын
Alhamdoulila machalla serigne gana ak serigne khadime gauye am te na solo sante serigne tuoba rek
@abdoubakhembackeattaboroum51265 жыл бұрын
Serigne Gana yalna la yalla Fay ligua wakh si serigne Touba ak wér diadieuff
Màcha llah Serigne gana Amna solo bilay yalla n'a gnou yalla Dipp lei
@goradiaw49035 жыл бұрын
Ndaysan li nekhna torop machaallh serigne gana mesera Mokhtar ak serigne khadim Gueye yala nalen yala defal diamou ak khewulle AK soutour thi barkep khassida yi merci yene wa TFM liguey bi rafetne te matna
@Fall6845 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne touba wayé gathié ngalama Mame cheikh Ibrahima fall yanou wane bamba ak ninou si diarigno
DIEUREUDIEUF CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASZOULL serigne touba serignou wa Sénégal force je suis tidjiane mais bamba doumorome dieureudieuf serigne touba cheikh ahmadou bamba Khadim raszoull amoul morome tay ak euleuk BAMBA point
Machalla nékh na khol sédna dieuredieufé serigne Touba
@ksivugk71515 жыл бұрын
Diaurediauf seregne Touba machalla amna solo troub
@omarsidibe30905 жыл бұрын
Thiey serigne touba dieureudieuf gana mesere
@famalo90215 жыл бұрын
Macha alla tfm dieurdieuf serigne khadim gueye serigne gana yague lene fi lol te were ci barke serigne touba amine dieurdieuf serigne touba amoul morom dh bene rek la fi
@babacardione33645 жыл бұрын
Serigne gana mésséré yalla na yalla goudal saw fane té dolila ak wér
@moussaaw37455 жыл бұрын
Machalah Diadieuf sering Touba amoul morom
@khadimgueye37145 жыл бұрын
Kou sobbou nii Bamba sa massoum Baaya diougueul andak sa dieum té deim Lambarna niou guiss"
@kossondiouck82645 жыл бұрын
Serigne Touba Amoul morom dh
@kabiroudabo47755 жыл бұрын
Mâcha allah amna solo❤️❤️
@Darousalam20844 жыл бұрын
Dieurdieufety serigne touba khadimou rassoul diarama mame cheikh ibrahima fall
@khadyndiayeyayefall90145 жыл бұрын
Thiey sounou wadji kéne la dieureudieuf serigne touba sama xol séde na
@ndiayefallou59785 жыл бұрын
Machalla serigne Khadim
@talibeboromdarou61515 жыл бұрын
Public bi machala awou nguen lou nekh
@AmyMaradieye5 жыл бұрын
Dieur dieufe cheikh Ahmadou bamba khadim rassoul
@allembaye94945 жыл бұрын
Tfm dieureguéne dieuf YALLA guéne am ngueureumeul SERIGNE BI gnoune émigré yi am nagn mbécté
@elhadjindiaye21165 жыл бұрын
Manchahalla kholl zéde naa🤲🤲🤲🤲
@awadiongue5395 жыл бұрын
💝💝💝waye Serigne ganna doundal way
@mouhamedkane96935 жыл бұрын
machalla seringe gana mèssère wakhtan wi amna solo machalla
@adioumadiouf11242 жыл бұрын
Way sokhna Diarra meune da gnaka am dome bou melni kén dou Sérigne Touba Dieureuf Sérigne Touba Diarama mame cheikh ibrahima fall
@LoveGlitter_Candy5485 жыл бұрын
Dieraudef tfm mange bitim reew waye machalla dara umpomace yala nangen yagga djitou
@dijaleilichendiongue55955 жыл бұрын
Thieye sokhna mama mariama bousso diarratoulahi thieye 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🐲