Yalna Sunu Borom Mayla Ndam Lou Seed Ama Nékh ❤️❤️❤️❤️❤️
@YoroGueye-o5rКүн бұрын
Boul dioye dara tout rufisque est derrière toi champion bii
@kaneadama1226Күн бұрын
Ama nékh yalnala yalla soutoural mayla ndame inchallah barkep yonentebi psl inchallah
@JoesambSamКүн бұрын
Amine 😢
@mamadouthiane-ds3icКүн бұрын
Yalla nalla yalla maye ndam inchallah
@diayoussou882323 сағат бұрын
Thiatou daouada fall ❤❤❤❤
@diop3575Күн бұрын
Ama nekh mano lek avance diambour ba paré beugue deg loula nkh thiatou daouda fall manoko diakhasè ak nit gni boy bou cool la yarou di communiquer bien bayil sa thiakhane yi tdf seul ❤❤futur balla gaye ll futur rois des arene inchallah yalle nako yalla may ndamm ❤❤❤
@BassirouGueye-y4x12 сағат бұрын
Saway khana déglou woo interview bi ? Fane lako diakhassé ak nit gni
@diop357511 сағат бұрын
@BassirouGueye-y4x ska dou ioe yako deglou woul nena boy bi dafa reew daf ko depacee te tdf biepa xam ni df yarou
@moussa.djikinemoussa1403Күн бұрын
Grand frère tu nous rend triste courage kou bakh nga diame rék ngay am incha allah
@francoisbernardbadji6315Күн бұрын
Frères pleure pas tout rufisque et fière de toi ❤❤❤❤❤
@mouhameddiagne2555Күн бұрын
sois fort ama nekh champion gua
@jupinleye8346Күн бұрын
journaliste bii Billahi koubaakh leu et courage Amanèkh
@thiawlahi4693Күн бұрын
Mbao est avec toi champion ndam rék incha ALLAH
@jaynprods2Күн бұрын
mike tyson le grand champion pleurait parfois avant ses combats, etre un champion est tres difficile ,je vois papae yade comme un coach et mentor pour lui qui l'a aidé au dela du sport a etre une personne morale et faire de lui un homme sage comme cus d'amato et mike tyson
@mouhamedkane8669Күн бұрын
Ndam rek champion Amanekh dan nga mbeur mou nek bilahi ❤
@bachirdiop2199Күн бұрын
Dina Yeureum teulou ba dane boy bi 😂
@volfroitfall8785Күн бұрын
Sawayy sdik gua😂😂
@ousmanefall7793Күн бұрын
Boy yeureum teulou dagay yeureum teulo fougne lay yeureumé sawayy no déf danou
@BiraneNiang-xn9qrКүн бұрын
Boy li nekk sih kholame layy wakh nioune douyou Niane aye domou Rio lagne sen mbeur bi dayou koy douma dane ko
@mohamedmustaphadiouf8293Күн бұрын
Yow xamnga ama nekh srx mo meune boys yi yeup dafa mousse
@ousmanefall7793Күн бұрын
@mohamedmustaphadiouf8293 JAMBAR BII DOU BOYOU KÉNE BILAY BI YAMOUL AK YOYOU BII DOU YOYOU MANIILA
@Sylla_Le_RoiКүн бұрын
Dioye dioyat inchallah le 1er janvier si langue ngaye dano 4 appuis ngaye ndiéka df doga danou incha a raboul harsi
@khadimmbacke8079Күн бұрын
Doma kholalll sama avenir 😢
@AboulBacharSallКүн бұрын
Waxo deug
@moustaphababou6282Күн бұрын
Thiatou daouda fall yalla nala yalla maye ndam me defal tre atacion amanekhe dafa yewou dalaye weur weur lo bamou yague mou dawe songe la plake la bayiko khel do ngaka
@generalndiaye735322 сағат бұрын
Ama Néxx Yalla Nako Yalla may Ndamm in cha Allah
@ouzdaking382Күн бұрын
Amanekh grand champion le requin de Rufisque yallah neu yallah mayla ndam inch'Allah amine 🎉
@momobouthiapathiolybi7752Күн бұрын
Yow khana do fans balla gaye
@bandapapeКүн бұрын
yalla ngua danou si barké yonnet biii 🤲🏿🤲🏿
@khesayad729Күн бұрын
Ama nekh molesne mane niome niepou amena dolle mana beure amena fiit ♥️
@GOLDENBOYE25Күн бұрын
Inchallah ndam rek ❤❤❤
@jeanmbayeniakh1614Күн бұрын
Machalla champion adouna dou dara mai gnémé rek adouna yep nakarla mougne rek partout là gaïndé ❤❤❤
@niassniasstapha915023 сағат бұрын
Ama nekh yalla nla Yalla may ndam inchalla
@diop3575Күн бұрын
Bayil yeureum talou bi saway niola eupou ay propleme fouf mano nek si lamb di faye kou ay millions ba pares beugue deg loula nkh lolou manoul nek tdf seul yalle nako yallah May ndammm ❤
@adamadiop575622 сағат бұрын
Say yaw xamo lamb xamo sports ki champions la
@mamadoumbow187416 сағат бұрын
Ndeysane Ama Nekh tu nous fais pleurer
@CheikhMbengue-fl8ikКүн бұрын
Merci modou anta❤❤❤
@SarryElhadjiOusmane-kq5lcКүн бұрын
Ndeysan yalna la Yalla may ndam Amiin
@bayefall1598Күн бұрын
Amanékh bayil yoyou lolou lamb la rek boy bi dafa yarou
@bayykallabounice9626Күн бұрын
Non mbeur Mon nékh rékk loyeu diakhasé boy dieul avance ba paré dii yeureume talou😂😂😂boy bii da paré té beurii na dolé
Fans Modou lo la mais thiate la faral sama toura ndo mame la 😊
@diop3575Күн бұрын
Ama nekh ioe ya geuneu reew bi boy bi fouf bayil boy bingay diakhasè ak nit gni boy bi niepa kham ni da yarou ms ioe mane nga boy boye beurel beug ko diakhasè ak nit gni weuy diougal fi mano deg loula nekh si lamb dji saway sof nga trop
@MarcoGonzales-hd2urКүн бұрын
Yallah nalla Yallah takhawou
@mansourgningue9425Күн бұрын
Courage Amanekh tu es un très grand champion.
@PapaDiallo-oe7pjКүн бұрын
Kou bax nga mais yalla nga danou TDF seul
@bayemo4147Күн бұрын
Ne te laisse pas pièger ama nekh boy bi dafla beug merlo rek pour yakk sa lamb
@MouhamedNiane-x7yКүн бұрын
Je crois bien qu'il a des problémes personnels. Ce qu'il a dans son coeur n'a rien à voire avec Lamb 😢😢
@DropDollard11 сағат бұрын
Même mane lolou la yakaar
@Lebou-fh8ubКүн бұрын
Ndam rék inchallah
@غلامالخليفةآبوبكرسهКүн бұрын
ءامين يارب العالمين ❤❤❤🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@AliouNdiaye-v8kКүн бұрын
Bargny derrière ama nekh thiatou TDF DO AM TOUSS NK
@elhadjngom2131Күн бұрын
Walahi thiat la beugone mou dane mé yalnala yalla may ndam sama toyna trop walahi
@MoustaphaNiang-e1fКүн бұрын
Ama nekh Moy dane
@ousmanefall7793Күн бұрын
THIATOU DAOUDA FALL YALNALA YALLA MAYE NDAM SI KAW AMANÉKH SECK DOMOU FATMATA DIAW INCHALLAH NDAM REK NO DÉF TEUD
@Lebou__bi846Күн бұрын
GOOR DIOKHE TOUROU YAYOU DIAMBOUR SI AY RÉSEAU AMOUL BEN NDIARIGNE LAMBJ DOU FOFU
@SarraNdiaye-ix1oy12 сағат бұрын
Wa guediawaye beuri guenn wahhh😊bi dou yoyou bi 🦈 la Rio seul
@daoudacisse4849Күн бұрын
Yalna yalla may la ndam ci kow thiatou daouda fall si barké SEYDINA MOUHAMED salla lahou alay hi wa salam
@KhalilSeck-p3vКүн бұрын
Ama nekh boy bi dou boy yoyou yalnala dane djél bou lérr
@DameGueye-ec7vtКүн бұрын
Pikine derrière amanekh domou rio
@DiopOmar-ee2qyКүн бұрын
Ama nekh yague Na la supportee'' dee'' mais sa palmarès rawna boy yi.
@modoudiawdieng5228Күн бұрын
Amin,😭😭
@OusaynouMbgeКүн бұрын
Goor d'où yeureum goor⚔️💛💙guérro seul
@cheikhbasskeurmassar9548Күн бұрын
Thiatou daouda fall mola meune
@BassDieng-m3uКүн бұрын
Ama nekh Lo défe danou do am loula nekh
@osmaneniang6116Күн бұрын
Le vrai champion…mais bouki timis leu yaga yaga day gneuw😢😂
@modoufall959Күн бұрын
Lamb rk la guiss sport bougn lay fayé ay millions gay nianatou xaliss am lén diom
@PapaThiam-pm8ssКүн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤😢😢
@MamadouDIALLO-oq2dkКүн бұрын
Thiatou Daouda Dall dafa yarou môme wakh deugue yalla
@bigtory4632Күн бұрын
Mo meun boy Bi lamb mo waxoul deug req mais ndanan deug leu xamolen ko naq
@ibrahimasene9243Күн бұрын
Yallanako yalla méy ndame amanéx
@AliouGaye-l3g23 сағат бұрын
😢😢😢😢😢😢
@MamadouGueye-q7hКүн бұрын
Peut être qu'il pense a son jeune frère dcd il y a pas longtemps
@babacarsarr1131Күн бұрын
TDF RK ❤
@khadimndiaye352Күн бұрын
Grand bi Assane Diop mon nék si xel 😢Papa Yada 2 moko wéteul guiss n'a lolou
@AlhadjiDiop-et9vdКүн бұрын
Numero ama nehk soumako diotone moubah inchalla
@galayebeye7868Күн бұрын
Fi amoul yeureum talou dh Lamb la rk thiat bi mague na dh
@cheikhniang02Күн бұрын
AMA nekh momo sa bopp nioune wa Rufisque yow lagn am yak domou dangou boul bayi dell noss si khallé comme ningako yagg deffé
@kharagnembaye5958Күн бұрын
Waa Ani mouni Mo Gates NN Mo Gates khwewone nafi nak ak mbeur yi 😂😂😂
@kaas161021 сағат бұрын
😂😂😂😂😂 khewina...lamp yi fèye na 😂😂
@moussapayemane4167Күн бұрын
Wa mais Ama nékh mi kane la yap 😂😂😂diohléne ma avansam ma sagako way ndah combat bi guéna néh 😂😂😂
@SalerGueyeSaer-zc2kq19 сағат бұрын
Dinako ndankhe ba danneko ama nékhe moko meune
@PapeGueye-hq5ldКүн бұрын
Kone yaw bakh deune bi mola dèranger
@ablayeWilane-s5kКүн бұрын
Boy bii da khamoul rek Bilakhi
@ousmanefall7793Күн бұрын
BOY YEUREUM TEULOU DAGAY YEUREUM TEULOU FOUGNOULAY YEUREUMÉ PAPA YADA NIEUPEU KO BEUGONE BAYE SAA OUTE WALOU BII AK SA YEUREUM TEULOU GUI GUA NÉKÉ NOO DÉF DANOU BOY BI DINALA WÉÉR LE 1ER INCHALLAH
@Lebou__bi846Күн бұрын
YAW DANGA COMPOUL MOTAKH XAMO LIY XEWW SOUBA TÉ LE 1 ER SEN MBEUR MII DINA DATH LOU METI
@daoudacisse4849Күн бұрын
@@Lebou__bi846Inchala
@Bamba-rkКүн бұрын
làmb legui ay link leu koi mais Ama nekh ay moromam rawou gnouko ci lènn na gaayi teugg combat wam
@trompeursambenebisamb6245Күн бұрын
Ho my good
@mordamengom8509Күн бұрын
Demale touki bayi lamb
@fatoucisse6422Күн бұрын
Diambar laa bilay
@Mouha-o2rКүн бұрын
Ki dafa wet si lamb dji koi
@khadimseye9364Күн бұрын
thitou daouda fall ndam raik
@IbrahimaGueye-s7sКүн бұрын
Boy gor dou yeureum gor
@ababacaredougueye9668Күн бұрын
Amanekh khana do wo Mo Gates thi combat bi,fi nga niou done sonal ak mo gates mo gates 😂😂😂
Amanekh may niou diam diaroul yeureum teulou bi ya guene réw boy bi fouf no deff danou inchallah TDF kassé lagnouy topou
@bigMoo201718 сағат бұрын
Lamb booci amoul koula diappalé, surtout tinguédje, defa metti.
@OusaynouMbgeКүн бұрын
Thiat seul💛💙💛💙⚔️zémbré
@KhadyGaye-n5gКүн бұрын
Lamb ji legui lobila motakh zarou amekh yi doune si nekhle te mbeur deugue leu demal europe te bayi lamb yagui ni dane boy niang ms mogui fayer kou aye milion si lamb ji yaw amo badiane si lamb ji
@fromdiouls547Күн бұрын
Lamb dji mo geun si Amanekh fouf 15millon en une années c’est pas fait pour tous le monde 🌍 je te parle en connaissance de causes 🙏🏽15pillions Europe dou tiakhan bro
@MamadouSene-i4zКүн бұрын
Khana dématt Babylon 😂 ki dém ba nieuw
@mansourgaye2792Күн бұрын
Thiatou daoda fall amanekh sa moromou grand frère less 2 leu da mélni niouy wakh meusou nio setane amanekh en tous cas daffa graw dh do dégue niouy wakh bouki timis
@hj-eu6xcКүн бұрын
Il a 43 ou 44 ans. C'est normal mou khalaate arrêter lamb
@afro3827Күн бұрын
Ama nekh aka nekh 😂😂
@ousmanefall7793Күн бұрын
LE 1ER DIIGUA DIOYATE DHÉ BILAY DIGUA DIOYATE NO DÉF TEUD
@malicksarr9794Күн бұрын
Yaa bonne danga kham loumouy dioy😢
@ousmanefall7793Күн бұрын
DAY SAUUP YOR SA NIARI DIÉK DI YEUREUM TEULOU LOU BEURÉ NA AK KOU NÉK DIAYOUL WARA BEURÉ AK BOY BI REK DI DOF DOFLOU NAA DIOYII DÉRÉTE BAA KHAM
@ablayeWilane-s5kКүн бұрын
Sa waye bari nga ndaye wakh
@Lebou__bi846Күн бұрын
@@ousmanefall7793 YAW BOUDÉ DEUMM NGA LEKAL SAY MBOKK KI MANO SI MOM DRA AMNA DROIT YOORR 4 DIEKK LOUSIY SA YONN
@mamyniang-t4z23 сағат бұрын
Kii mo meun boy bii way éhh
@moussandiaye1208-w2o5 сағат бұрын
Modou anta,Tu n'as pas été professionnel,il faut laisser puisqu'il pleur,bbayyilén top nitt bamou seuss🤌