Je t'écoute comme un professeur agrégé qui parle tellement t mots sont élégants... Adorable mon frère...amal diam BB
@sidymbaye15992 жыл бұрын
Machalla bébé Saloum Say wakh day yèttè yaw parolier nga yallanalla yalla defal jamm
@cheikhgueye462 жыл бұрын
Courage mbeurr 🖇️wax geu lou am solo nattou meun na dall kouneii kone yalnaniou yalla soutourall amine🇸🇳🙏🏾♥️
@khadimfall57962 жыл бұрын
Loulerr
@adamambaye7862 жыл бұрын
Machalalha bèbé saloum yaw yalna sa diam yague ❤️😭😭🙏
@bensaidmbaye36582 жыл бұрын
Franchement parler respect à toi mbeur yala nala yalla diapalei inchallah, vrai bibliothèque gua 🤞
@layebeye23612 жыл бұрын
Bilaye kii yalla rek la bokou ak moum ak serigne touba me bilaye soumako setane damay diouy bilaye me tegal lep sii yalla dakha mofi nek yalla bakh na yalla na yalla defal diam ak ay khewale 😭😭😭😭😭
@ibrahimathiam13932 жыл бұрын
Bb saloum alias dane seuy ami d'enfance depuis Kaolack il communique bien mai une chose que je rectifie sur ses paroles c'est que le mot diamo KO Serigne Touba Mai diamo KO yallah mai champion la courage frère Di ballon akh nieup sama guiss guiss rekk la wakh
@LiLyg682 жыл бұрын
G peur pour ce pays , on venere des etres humains et on laisse le createur qui a creer ces etre humains de cote. Shirk est le seul bakkar que Allah ne pardonne pas. Kepp kou ma saga nakk , lo ma wakh rekk wakh nga ko sa seurigne . En bon enttendeur.......
@cheikhbayeniassbadiane25442 жыл бұрын
Le grand du Saloum un vrai sage Yalla nala yalla tek loho
@assdoukoura13142 жыл бұрын
Machalla bb amna solo de yalla na yalla defay diamo rék
@falloukarimmbow49812 жыл бұрын
Ndéysan métina😢😢😭😭 n'a trop yalnala yalla maiiy fann bou goudou ak wéer ki yaram Amiine 😘🤍💥💢💯 yalnala maam fallou mbacké Takhawou Amiine Amiine yarabi. Du courage frér Talibé sérigne Touba mbacké
@alioukonte19462 жыл бұрын
Sa communication me Dépasse jameu si ioa 🙏🏽💪🏽
@ibrahimabadiane82522 жыл бұрын
Machalla deugoul rék lolou la yalla beugue boul ragal kenn yalla rék
@thiawaly27992 жыл бұрын
Merci beaucoup saloum saloum que Dieu te donne une très longue vie
@modougayekante65752 жыл бұрын
Il communique très bien 🥰🥰🥰😋
@beuguegalsenziguinchor62802 жыл бұрын
Bilahi souma yalla bétone ak ay khéweul dinako dimbali té yalla rek tak
@ousmanesall44012 жыл бұрын
Ndeysane yalla nala yalla defal diam
@helenendiaye32372 жыл бұрын
Courage mon frère je te connais pas mais vraiment je te fais confiance et je sais que tu arrivera inchalla
@ndeyefatouba73422 жыл бұрын
Ndeyesane meuse na partagé ak mome béne instant mé machallah sou waxé rek gua nawko amale diame rek
@khadimsarr23612 жыл бұрын
🇦🇪🇦🇪 machallah dawna yaram champion amal Diame rék ak soutoura ak ak yokouté ak tawfekh 🤲🤲🤲🤲🤲
@malickseck16392 жыл бұрын
yallah na yallah samou dolli soutoura ndayesan ❤❤❤❤💯💯💯🇬🇲🇬🇲🇬🇲
@amethsaw81212 жыл бұрын
Machalla bébé saloum yalla nala yalla diapalé 😓😓
@mouminediene40372 жыл бұрын
C'est la première fois que j'écoute un lutteur durant 37 minutes
@talibemamediarraboussoboro31162 жыл бұрын
Ki bopouleu frer
@amedione89482 жыл бұрын
Yalla nala yalla défale diam
@maxkara94172 жыл бұрын
Man Ay WakhTanam DaMakoy TéwLou Lou BaRii MaChallah 😍 Da DéGG MaChallah ❤️
@diakhoumpaalioune9402 жыл бұрын
Bébé saloume xoll bu nice la yoor 👌🏾👌🏾👌🏾
@maimounafaye42922 жыл бұрын
Yaye goor kou bakh.yalnala yalla défal diam
@jeancollinsarr72452 жыл бұрын
Communications dafco meune machalla
@bakhyaye70822 жыл бұрын
Ndeysan dewna yaram😭😭😭🙏🙏
@sonkodiop792 жыл бұрын
Yalla nala yalla fay Diop khas ta dimbali diam yeup
@matarmbueg41152 жыл бұрын
Merci bebe dueg rek mo am solo
@coachsportifniangcd89472 жыл бұрын
Les Hommes vertueux sont toujours soufrants dans cette vie. Diappal ni ci linga nekk moy deugg. Yalla nala yala bour samm té yokk la soutoureu
@bayykallabounice96262 жыл бұрын
Bb saloum yalla Nala taxawou
@kebadia58312 жыл бұрын
Amna solo bb salom 😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏
@seckkhadim26492 жыл бұрын
No bébé saloum sopou nala lol barké serigne touba Yalla na sa diame yageu diambar
@gueyeabdou13772 жыл бұрын
Une leçon pour tout le monde BEBE SALOUM def na la kharit
@Concept02082 жыл бұрын
Serieux bb Saloum dégue louko dafa néx. Seutou Serigne Moussa Ka bi diamou ci yaw. "Natoup djoulit day yokouy Makama bamouy sipiw Niawtef bissoup Xayama", parole de Serigne Moussa Ka.
@babacarsarr81352 жыл бұрын
bebe saloum sa wakhe rafetna bilahi 😭
@sidymbaye15992 жыл бұрын
Yallanalla yalla may téranga
@alphadiallo54832 жыл бұрын
Du courage mbeur yalla na gnou yalla diapalle yalla mayla ay ndam you wess sa ndiorte amen
@ndeyetalltall32152 жыл бұрын
Machallah beaucoup bébé saloum
@mbackediop77662 жыл бұрын
Yalla na la yalla Takhawou Barké Serigne Touba
@mordiagne22012 жыл бұрын
YALLA NA LA YALLA TAKHAWOU BARKE S TOUBA
@lassanandiaye96922 жыл бұрын
Merci gros bordeaux et diop khass
@salyallemomuawrksarr86522 жыл бұрын
Ndayssane bébé saloum lou méti goor lay dal kone mougnal dina bakh te yalla dinala takhawou inchallah 😭😭😭💖😭♥️💖
@syvieux1822 жыл бұрын
Bebe saloum barki seydina limamou aka maleu fan yalla neuleu yalla dèfeul diam
@helenendiaye32372 жыл бұрын
Belle communication bonne continuation
@bigmanzamoussa31432 жыл бұрын
Machllah bebe saloum
@youssefouangare20812 жыл бұрын
Mbeur c kadou machalla yao do beure lélène nga lepeye bakh inch bamba ever
Amale diam mon frère yalla khamena leep ta yalla d'où djeekh
@aboudia7642 жыл бұрын
Mancha allah yalnala yalla taxawou
@yacinediop87622 жыл бұрын
Ablaye diop hass sama domou mbaye mbobou chéri soumboulou yallana sa diam yague bébé saloum bonne continuation.
@diamahi57142 жыл бұрын
Amine
@saliouba94282 жыл бұрын
Courage baye fall bi
@mariamamamybayo97012 жыл бұрын
Machallah
@modoukebe20502 жыл бұрын
Masalla bebe shalom wakh dji rafet na
@ndiaboutadiouf79122 жыл бұрын
natou yalla la rekk bilahi
@salioundiaye84852 жыл бұрын
machalla
@Bamba_Kara_Thies Жыл бұрын
Mala beugu mbeur nguir Serigne Touba 💓💓💓
@khorediasarr78752 жыл бұрын
Wly ki je l'éstime beaucoup ❤️❤️
@alfredtavarez35582 жыл бұрын
il parler correctement chapeau à vous
@fabintourassoulndiaye21642 жыл бұрын
Tu.as.bien.parler
@aminalalionne56792 жыл бұрын
yalla nala yalla maye kholou mougne lou méti yaguena si adouna bi mais bon courage
@cherifbayo4120 Жыл бұрын
Ragalal yalla wayy mon frère Yalla Moy mayé doom op serigne touba
@yacinehane37382 жыл бұрын
Mbeur bou intelligent la machala longue vie à toi
@abdouboukharagnelolo96872 жыл бұрын
Ziar bb saloum 👍
@infosgalsen97102 жыл бұрын
Courage mbeur 👏❤️ms Srx nvkk meune nga done rappeur yaguii rimes dhh 😹thieuy ngaaka blindé doflo na gnepp
@seydinaaliouneboromjasiji32002 жыл бұрын
Saloum Saloum Bi Yalla nala Yala Diapalè
@jayeceesay26392 жыл бұрын
Very good communicator
@tallafall56942 жыл бұрын
Machallah bro
@mhd_00392 жыл бұрын
Courage frère ❤✊🏽
@ibra__rassoull91302 жыл бұрын
Machallah Machallah Machallah 🥰🥰🥰
@crackdufoot2 жыл бұрын
Non wadji nitt kou bakh la en plus vrai baye fall leu jaime bien ça mentalité
@gassamadjiby83022 жыл бұрын
yalla nala yalla same mbeur diame rek ngaye ame inechalah 🙏🙏🙏
@bayeniassndiaye67732 жыл бұрын
JAI MÊME PLEURER KHALÉ BI DÉLOU TÉ GUISSOUL BAYAME BAYAME GUISOUL KO
@chernodem96272 жыл бұрын
Waw is that bro tahnks so much
@aladjifalloudia49152 жыл бұрын
Serigne aplaye doip khass kou bakh la yalla borom kodal fanam amine 🙏🙏🙏🙏
@alioumamadouba37882 жыл бұрын
Bb Saloum un homme courageux amal diam
@gorguifaye22562 жыл бұрын
Machallah Sax wakh rafete n'a Amal diameuh sa vidéo fimako guiss déglouko bly
@modoudiop91972 жыл бұрын
OK merci
@morthiam17392 жыл бұрын
Pape diédhiou, grand frère de Ama Baldé et de Serigne mor N'Diaye (promoteur) , vous donne ses condoléances et vous encourage bien...
@assanewade52802 жыл бұрын
Amale diamou frère ✊✊
@fatoufall68972 жыл бұрын
machalla yalla maye nalla si wakh machalla li lagniye wakh nité
@papidelirecomedien6782 жыл бұрын
Slt cv abdou laye diop khass guirr yalla takh am na mbeur Bou deuk yeumbeul mame fall niou geun ko xam si frontière il a gravement male depuis des années mes ba legui guissouma akhhlou lamb wakh si 🙏🙏🙏🙏🙏🙏wala niou dimbaliko guirr yalla dimbali len té yalla takh si barké seydina Mouhamed psl 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@walyfay2 жыл бұрын
Bonne chance
@mouhamadoumouhamadou36992 жыл бұрын
Noon saway yalna la y'allah défal jamme insha'allah
@gueyeasskhadim16782 жыл бұрын
Tawfeekh bafaw ci barkep Cheikhoul Khadim amiiiiin amiiiiin
@fayendiouma20812 жыл бұрын
Courage champion
@salyallemomuawrksarr86522 жыл бұрын
Natou dou wéss te yalla koumou guene beugue lay tek natou kone bébé saloum mounial yalla bakhna
@Sportif912 жыл бұрын
Rayyy nitttt doundeulé nitttt Une phrase à véhiculer 😭😭😭😭
@bilalfall29532 жыл бұрын
Li nék sa kanam yalla na yalla déf xéweul diadieuf Ablaye Diop
@khadizakor3450 Жыл бұрын
Ndeysane 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 courage 😰
@khadydiagne96872 жыл бұрын
Machallah il explique bien
@lahadmbengue72662 жыл бұрын
Kou am numérome bb saloum tɛ̀ yalla takh abdou lahad dɛ̀pui Bologna itali
@modouniang58872 жыл бұрын
Vraiment bébé tu es mon professeur
@lhommetranquille31472 жыл бұрын
Diadieuf mon amis d’enfance bébé saloum dp8 kL lycée waldiodio diamou si iow bro dina bakh inchallah
@bassndiaye21822 жыл бұрын
machalla kou meune beurè mougui ni ndoke ndoke reke mais kene dakou ko beurè nassa s yague
@ibrahimafall2332 жыл бұрын
Vréma grand bi kaadu yi rafét na lol yalla nala Serigne Touba sunu yakar tay ak euleuk takha wouleu fépp
@bidewbileral75492 жыл бұрын
Machalla nattu yalla
@serignesarr64482 жыл бұрын
Beugue nala gier deumi serigne touba
@barroaly17642 жыл бұрын
Nice na ❤ ❤
@annecheikh39342 жыл бұрын
Ndeyssan c triste accuser qlq un comme ça j ai eu pitie de lui machaallah il communique bien tres pose bravo a sa femme digne