Ya Allah niongui lay niane, ngeu teuyél niou keur yi , garap yi... Ni GA téyé assamane beu danouwoul ci kaw souf 🙏 Allahouma sali ala Seyidina Mouhamadine WA Salim.
@bernardhaba72592 жыл бұрын
Tes rigolo enfaîte c koi chaque foi yallah
@khadydiouf72792 жыл бұрын
Amiine
@nguattesyllawakhaldeh16032 жыл бұрын
Aminé
@awandeye71422 жыл бұрын
🤲🤲🤲
@marieme29612 жыл бұрын
Amine
@loucha71792 жыл бұрын
Ont doit mettre l'émotion à côté et démolir certains maison à Dakar fanane thi bedd mo geune fanane thi bir bamel
@Amilli7772 жыл бұрын
Exactement!!!!
@ramecesssarr97342 жыл бұрын
Bilay
@mansourdieng20002 жыл бұрын
Allahou Akbar Yalla Rék Moo Mane Yalla Rék Moo Sagn Yalla Rék Moo Bari Doolé Yalla Moy Boroom Yeurmandé Yalla Moy Boroom Aldiana Yalla Nako Yalla Yeureum Kharé Ko Aldiana Firdawsi Amine Allahouma Amine 🤲😭
@amindao75722 жыл бұрын
Amine yarabi 🤲
@mansourdieng20002 жыл бұрын
@@amindao7572 Allahouma Amine 🤲🙏👈
@fatou71122 жыл бұрын
Amine Ya Rabi thi barkel yonentebi 😥🙏
@mansourdieng20002 жыл бұрын
@@fatou7112 Amine Allahouma Amine
@sokhnadiop51722 жыл бұрын
Amine
@maimounaniang56022 жыл бұрын
Ho metina paix à son âme ke firdaws soit sa demeure éternelle
@ajahjalow92322 жыл бұрын
Massa yalna souf oyof thi kawam courage à la famille Metina
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Temp yi li khéw yalnafi yéme mir youy danou rék keur yi yépa maguette paix a son ame metina 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@ndeyefatoudiouf36522 жыл бұрын
Amine
@ironahide58962 жыл бұрын
Ndokh bi mo bari tè keur you bari bakhoul
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
@@ironahide5896 c vrai keur bakhatoul
@mansourdieng20002 жыл бұрын
Yalla Na Ñou Yalla Yeureum Rék
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
@@mansourdieng2000 amine
@zeynasagna74252 жыл бұрын
Wa li bahame diame la sénégal fane yi tarrr na lolou
@ndiayecoumba89872 жыл бұрын
Ndéysane yalnako yalla yeureum té kharé ko aldiana firdawsi amine
@mansourdieng20002 жыл бұрын
Yalla Nako Yalla Yeureum Kharé Ko Aldiana Firdawsi Amine Allahouma Amine
@Fatoumbodji4592 жыл бұрын
Fatimatou Ba yalna la yalla may kholou mougne Inshalah
@Made17-202 жыл бұрын
Repose en paix metina dei Di nelaw dall danou sa kaw ah metinaa. Borom keur yi deilei verifier letat des maisons fi sabililahhh fissure si batimat dou ay thiakahnn sou tawei ba parei deilein balai ndokh dafa meunn yakhhh
@kikicamara26272 жыл бұрын
Bilahi li ngua wakh deug le gnune fignu louer pa bi nouko neikh la tabakhé keur gui kou niow ni keur gui tabakh bi bakhoul mais lui il s'en fou..damay sakh tokhou bientôt parceque li wooroul
@Made17-202 жыл бұрын
@@kikicamara2627 yi tokhoul deiii sama.papa dafay louei ay niit tei doulein ameil akh motakh dafay verifier letat de la maison il ne badine pas AK fissure meme sunou keur sou guissei fissure dafay wakh rek wo maçon sou tawei aussi ba seiwet mou takhawouniou ni aythia deimlein balaie motakh Lou beuri ma khamko Senegal ngay guiss ay drama you doywar tei gniko tek nit yi sont au calme ils doivent etre poursuivi
@salydiandiaye99672 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum
@mariamjagana3392 жыл бұрын
اللهم اغفر لها وارحمها وعافه
@aramefaye28062 жыл бұрын
Hô li metti na trop Billahi yalla na motalé ndawam aldjana firdawsi 🙏
@cheikhkhoule60652 жыл бұрын
Yalnako yallah yeureum té diégal ko xaréko thia aldiana firdawssi
Lii moom il faut ñu xoolaat constructions yi ñuy def ca fondement yala fondement su baalulee kaw menul baax batiment defa wara am fondement bu dégër ak dal bu dëgër
@gordaymandu97572 жыл бұрын
Yallah nako yalnako yalla yerem kharéko aljana firdawsi😭😭😭
@ibrahimafall11422 жыл бұрын
Paix à son âme yallah nako yallah yeureum
@kinesow46792 жыл бұрын
Yalla na adiana firdawsi di keurou noflayam ak bep waye dawlou ci barker seydina mouhamed psl
@kingdiop34082 жыл бұрын
c vraiment triste yalla nako yalla kharé aldianna
@docswold15112 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla areu sameu gnou
@khadydiouf72792 жыл бұрын
Ndeysane méti na trop yalla nako yalla yeureum kharé ko aldiana
@ndeyengom2 жыл бұрын
Maçon yi nagnouy degeureul daleu yi 💔🙏
@c.a.sjunior12012 жыл бұрын
Réfléchi c une vieille maison
@Ngom2212 жыл бұрын
@@c.a.sjunior1201 enfaite elle sensibilise rek pour les constructions actuelles
@marieme29612 жыл бұрын
@@c.a.sjunior1201 pourquoi l’agresser? Soyez courtois dans vos commentaires et dans la vie de manière générale
@mamesodaniang35712 жыл бұрын
@@marieme2961 merci
@fatoumatamandiang42892 жыл бұрын
Yall mo niow rek bilah
@choudracherifa67082 жыл бұрын
Massa, Yalnako YALLA yereum té xaréko Aldjana Firdawsi.
@manesylla19332 жыл бұрын
Yalnala yalla may xolou mougne
@mohamedtall19922 жыл бұрын
Paix à son âme ! Mais la manière les maisons sont construites devrait être revue ! En coulant les maisons ils devraient plus plutôt mettre des éléments qui maintiennent les ourdis
@originali1552 жыл бұрын
C'est pas la maniere mais c'est juste les propriétaires qui doivent refectionner leur maison ame nassi yo khamanté c'est plus de 60 ans gnou bayi ko nonou
@modoungom2 жыл бұрын
Oh 😥 yalla nako yalla yeurem ta kharéko aldiana firdawsi thi barkip daradiaye cheikhoul khadim Mbacké 🤲🏾🤲🏾🕋🕋🫶🫶🤲🏾🤲🏾
@awabadji63752 жыл бұрын
k l paradis soit sa demeure eternelle
@Fatoumbodji4592 жыл бұрын
Yalna ko yalla yerem té kharé ko aldjana ya guene kawé Inshalah
@mamediarafaye87512 жыл бұрын
Yalla Nako yalla kharé Aldiana férdawsi si barké Serigne saliou mbacke Amine yarabi 🤲
@mamediarrandiaye10032 жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureum 🤲🏽
@sincerementparlantlovejust38162 жыл бұрын
Yalna égalé ndawam Firdaws Gnougui bokk ak yénn nakhar bi
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Yalla yeureum ko amine way
@sokhnaastousidi68812 жыл бұрын
Qu'elle repose en Paix
@aminataba95582 жыл бұрын
Non mais doullllll wayyyyy nane la nittt di néké si nakhar guéni insister diko lathie aaaaahhhhhh
Yalla nako yalla sounou borom diegueul kharé ko aldianna firdawsi
@diallorougui7172 жыл бұрын
Que son âme repose en paix
@mirachouxbadji87562 жыл бұрын
Que son âme reposé en paix
@habycisse36092 жыл бұрын
C'est tres tres triste.
@torodo.ferrari2 жыл бұрын
Thieuy yalla Yalla nako sa borom yeureum kharé ko aljanah firdawsi
@maimounandiaye52462 жыл бұрын
Vos questions bête kome.ca kou domam dé guene koy lathieu noumou dounder drame bi,wow guene beut mane dal bi sen site khewer mba legui sak jour ay douleur ak ay misère
@seynabfallou3952 жыл бұрын
Yalla na ko brome xaré aldjana firdawsi
@mordiouf43392 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum té xaaréko aldiana firdawsii taww bii beurii wonn naa trop
@youngricch342 жыл бұрын
😭😭🙏🙏🙏🙏
@babinta36902 жыл бұрын
badien yama aka bhhh ndeye sane
@mamediarrasaw55592 жыл бұрын
Yalla rek moko sagñe
@maguetteseck31632 жыл бұрын
Bilahi
@mansourdieng20002 жыл бұрын
Billahi Wallahi Tallahi Wakh Ngua Deug Yalla Rék Mooko Sagn Yalla Nako Yalla Yeureum Kharé Ko Aldiana Firdawsi Amine Allahouma Amine 🤲😭
@moustapha43612 жыл бұрын
PAIX À SON ÂME 😭 😭 😭 😭
@nogayefall42982 жыл бұрын
Allakhou akbar
@mamysow95822 жыл бұрын
Rip
@loelhadji1002 жыл бұрын
Paix a son ame
@sokhnaastousidi68812 жыл бұрын
Li ba kagne keur bou baxoul nothi deuké Sénégal médecin après la mort
@maguetteseck31632 жыл бұрын
Ay way li metina
@mmembodjaida32542 жыл бұрын
Ay yalla xallé yi rek niooy dem
@mmembodjaida32542 жыл бұрын
Borom keur yi niémé naniou yalla
@yoroba39362 жыл бұрын
😭😭😭😭😭❤️
@elhadjimor37292 жыл бұрын
Ndaye sane li métina trop sakh li yalla nafi yéme
@ndeyengom2 жыл бұрын
Encore 😳😳
@dogodiop51882 жыл бұрын
Thiey yalla
@damemarr27452 жыл бұрын
👉🏿😭😭😭😭😭😭😭👉🏿🇸🇳
@Rasssoullll2 жыл бұрын
Li lanatila
@aissatoundiaye70042 жыл бұрын
Aldiana firdaws
@docswold15112 жыл бұрын
Liii yeup wakhone nagnou kooo depuis que soko tegueulowé niiit yiii ayiii bol vous savez même pas ce que sa signifie
@marieme29612 жыл бұрын
Mdr tu es sûr que tout va bien?
@malaldiallo59502 жыл бұрын
Yow doule, merde
@FatimaM6532 жыл бұрын
Elle a raison ça attire le malheur même l'écouter n'est pas bien
@marieme29612 жыл бұрын
@@FatimaM653 délo YALLAH thieureum. Mom mo yorré dounde ak déh wayé dou mindèff ak ay bols 🤦🏾♀️
@mamesodaniang35712 жыл бұрын
@@marieme2961 Yallah d'où téré baay sa tôle. Bougnoula wakhé li bakhoul ta boko bayé dou wagni sa ngueume Dara bayiko. Je suis sonko mais bols yi bakhoul moussiba naroulay
@bilelbibi12472 жыл бұрын
Les masons khamougnou dara
@ndeyefatoudiouf36522 жыл бұрын
Mètina trop mais nake ancien bâtiment yi daniou ko wara danèll
@bilelbibi12472 жыл бұрын
Même bâtiment you besyi dali bakhoul
@ndeyefatoudiouf36522 жыл бұрын
@@bilelbibi1247 je confirme
@mansourdieng20002 жыл бұрын
Waxoo Leen Fi Dara Yalla Moo Yorr Doundou Ak Dée Ñaanal Leen Ko Yalla Mou Yeureum Ko Kharé Ko Aldiana Moo Gën Seen Waxou Dof Yi
@ndeyefatoudiouf36522 жыл бұрын
@@mansourdieng2000 mane j’habite là-bas je connais bien les quartiers et le nappe d’eau est trop près des fondaments keuri nion mandi dokh mouye sama boss ak kènène