🔴Urgent Audio Serigne Cheikh Ndigeul bi Imaam Khadim Bousso Répondre Imaam lamine Sall si liwakh ni.

  Рет қаралды 101,777

Khelcom Production

Khelcom Production

Күн бұрын

Пікірлер: 200
@SerignefalloumbackeDaroukhadim
@SerignefalloumbackeDaroukhadim Жыл бұрын
Jerejef serigne xaadim xam xam bi sétt n'a macha allah lii lañ soxla ndaw yuy jàng di wané dëgg
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
C'est un malhonnête limouye défendre le charia ne le reconnais pas mais aï intérêt lagnouye défendre 😂😂😂
@MaketSii-jm4fu
@MaketSii-jm4fu Жыл бұрын
Machalla imame bousso akh imame sall li da am solo si dine il faut nguene toke si plateau mou ler
@juufy4569
@juufy4569 Жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Khadim Bousso
@bounabanno6961
@bounabanno6961 Жыл бұрын
Yaw défal attentione kou khamoul khamoul !! Khadim Bousso liimouy wakh dou wakhi dara!! Dioroomèlu diabar thi shariihatou l'islaam doonul sokhna 👎!! kénn manoukoo fas bamou fasou !!! Khadim Bousso liimouy wakh dou wakhi dara !! Dèlèn déglou Serigne Mbacké Abdou Rahmane 👍!!
@fallattidjani8603
@fallattidjani8603 Жыл бұрын
Li serigne lamine Sall wax moy dëgë ❤
@bassirsoco1641
@bassirsoco1641 Жыл бұрын
Yaw kone khamo touss
@laveriteabsoluejuste6358
@laveriteabsoluejuste6358 Жыл бұрын
Fo ko ték, bañ mouride
@masstv2484
@masstv2484 Жыл бұрын
Waw s.lamine wakh n'a degue par c que ñeen ti sokhna moom lousi topou ndiallo la mais dou sey fofou lako tek
@masstv2484
@masstv2484 Жыл бұрын
Fi l'islam lani wakh lolou moy débat bi mais pas ay mouritak tijaan
@ndiagandiaye7364
@ndiagandiaye7364 Жыл бұрын
jaajeuf imam khadim bousso ♥️🕌🕋♥️
@AhmedalienSalim
@AhmedalienSalim Жыл бұрын
Merci beaucoup serigne lamine sall
@zallmbaye1622
@zallmbaye1622 Жыл бұрын
❤machallah
@abdoulsene5518
@abdoulsene5518 Жыл бұрын
Machalla serigne Khadim lérna nagne diadieuff bousso yag fi té werr barkep serigne touba
@mamadoudiop4582
@mamadoudiop4582 Жыл бұрын
Mais ici le problème n'est pas la idda mais plutôt le fait d'avoir plus de 4 femme. C'est parce qu'il fait parti des vôtre. Soyez honnête la vie est éphémère
@laveriteabsoluejuste6358
@laveriteabsoluejuste6358 Жыл бұрын
Diiné du xéll, serigne Khadim Attépp charia lay léeral
@lascarsamb4036
@lascarsamb4036 Жыл бұрын
Merci faut pas hanger le theme
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
​@@laveriteabsoluejuste6358ki léraloule dara kham nané charia 4 femmes la reconnaître mais dafa kham nè dafa am mbolo mo takh té si gnome la booke les autres femmes l'islam ne l'ai reconnaît pas donc ida bi concerné wouléne 😂😂😂
@mamadoudiallo7286
@mamadoudiallo7286 Жыл бұрын
Ne te fatigue pas plus malhonnête ke ce khadim bousso dans ce pays j’en cherche. Ana djoullite ak fass lou eup gneenti soxna ci loolou ngeen waron taxaw mais ay man n’a am djeukkeur fi saass yi walla day djeul Idda…man xawma ban façon Islam ngeen di pratiquer finalement
@bmwde9068
@bmwde9068 Жыл бұрын
Dieuredieuf sangue bi bousou
@babacardiallo6442
@babacardiallo6442 Жыл бұрын
ماشاء الله جزاك الله
@King-dm9kh
@King-dm9kh Жыл бұрын
Oustaz lamine Sall a raison
@laveriteabsoluejuste6358
@laveriteabsoluejuste6358 Жыл бұрын
Fo ko ték 😂
@MorNdoye-m9i
@MorNdoye-m9i Жыл бұрын
Sante boubakh sérigne bi nit la comme niépe Daf toup diegalou yalnako yalla baal
@khadimgueye5088
@khadimgueye5088 Жыл бұрын
Machallah amna solo
@assanesarr6177
@assanesarr6177 Жыл бұрын
Li mobakh. Wakhtane si xam xam avec un respect mutuel
@bintoufallsene7775
@bintoufallsene7775 Жыл бұрын
Dieuredieuf serigne khadim bousso
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Khadim est malhonnête limou wakh ragal motakh mou wakh khame nané l'islam 4femme la reconnaître môme khame naco bou baakh mais défendre aï intérêt mo takh
@malickseck911
@malickseck911 Жыл бұрын
Akassa Serigne khadim
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
Lii serigne lamine wakh mo gueneu weer dé
@niangmoussa3393
@niangmoussa3393 Жыл бұрын
Solo wah bi dou ay massala imam Bousso.
@maodophilo
@maodophilo Жыл бұрын
Degu rék la yala begu Bounou parparlo Bounou défendre lo xameni sounou orgueil laneko laneko ték Wax ji moy téno yam thi gneneti soxna yinou yala wax mou lér Mo gueneu dal xel mo gueneu wor Cheikh ndiguel nak damakoy gnanal yala diegualko, diegueulma, dieguele mbolom joulite Jamou yala boy jegualou borome y a rien de plus normal que cela D'à war serigne yép sax, ndaye Sénégal serigne bou fato ngani yalnako yala jegual ay bakaram yereumeko gnou dal sa kaw néla serigne bi amoul bakar wala waxdji bakhoul Mo tah nak kouthiy dound gnanal ndiegual sa borome gnane gnép gnou gnanal lako nday kéne gueuneta xam nit bopam Mane tamite mangui jégualou sama borome di gnane yala jegualma thi barké la ilaha ilala
@noblekhol3661
@noblekhol3661 Жыл бұрын
Wakh lo ame mo gueune ssi yaw
@modourokhaya9616
@modourokhaya9616 Жыл бұрын
Serigne bi sa wakh dji amna ay tegguine lole fenial na yit sa xol bou laab. Yalla nanou yalla Dieguel nioune nieppou ta mayniou sa xel mou sell mii machalla
@sonhiboumbow4293
@sonhiboumbow4293 Жыл бұрын
Machalla dr khadim bousso lerna nagne
@ousmanesow1599
@ousmanesow1599 Жыл бұрын
Merci beaucoup sall
@badafall7085
@badafall7085 Жыл бұрын
Serigne khadim bousso guede la decke lom wakhe si xam xam werna machalla
@mamadoudiop4582
@mamadoudiop4582 Жыл бұрын
Innaa lil'Allahi wa Innaa ilayhi radji'oune rien n'est plus mauvais qu'un savant malhonnête
@art4automobile415
@art4automobile415 Жыл бұрын
Merci 🙏🏾 serigne lamine sall sa xam xam weur na lérna liga si la ande li lislam diglé
@brunobadji5867
@brunobadji5867 Жыл бұрын
Non c'est Oustaz Lamine Sall Qui a eu RAISON ❤❤❤
@abdoufallsow3277
@abdoufallsow3277 Жыл бұрын
😂demal jangi leegi indil sa dalil . Ndax ki ndialo warna set lu ba xam dara topou ko thib eumb wala?
@thiernodiouf3867
@thiernodiouf3867 Жыл бұрын
Merci imam Sall Sa Wax La Geumm
@santyallaboubakh4430
@santyallaboubakh4430 Жыл бұрын
Macha allah tey mom kham kham fegne na thi soufiyankeyi lamine diambarla mes li imame khadime wakh mo geuna deugeur bou togoul ab dirre mane na yobalè ab eumbou lolo takh niou permetre ko mou took ab dirre.
@mamndiagnabousso7733
@mamndiagnabousso7733 Жыл бұрын
Wax deugue
@lepatriote934
@lepatriote934 Жыл бұрын
Imam a bien dit si avant de les libérer 3mois avant elles ont eu leur régle et n'ont pas eu de relation avec le mari elles peuvent bien se remarier le jour suivant de leur libération elles peuvent bien se marier le
@alkitab3326
@alkitab3326 Жыл бұрын
4 femme ndiallola. Comme toup n'a yallah nako Yallah bal
@mordiopdiardiafserignetoub7530
@mordiopdiardiafserignetoub7530 Жыл бұрын
Mach alla image Kh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@assanefall7609
@assanefall7609 Жыл бұрын
Dieuredieuf Imam Bousso, nit ki Sall naafékh la, yéené woul sakh Borom NDIGUEL niaane (prières)yimouy wakh. Dafa contre dokhinou younou Mouride ak wow Baaye Fall.
@gueyematar1869
@gueyematar1869 Жыл бұрын
Réérgi AK bokkalé gui barina thi Réwmi. Comme séne Serigne Toubna Téé ngéna Di joulli Di woor. euleuk Chiékh Ibra boppam Lay Tal dé.
@masstv2484
@masstv2484 Жыл бұрын
Bayi leen kou leen wakh degue ngueen naan da leena contre yewou leen
@GayePenda
@GayePenda Жыл бұрын
Fisy senegal mouno fi wa kham kham ta wakho kuer seringe abass sall wala fass toure
@mariemefall8864
@mariemefall8864 Жыл бұрын
Ma ngui diégueulou dé kou bakh wayé lou eup niénti sokhna diiné islam nangou wouko .Li Oustaz Lamine Sall wakh moy Deug . Yalna niou yalla bolé diégueul. Wasalam .
@cirehakimlo2033
@cirehakimlo2033 Жыл бұрын
Jërëjëf imam bousso بارك الله فيك وأهليكم
@galogueye4821
@galogueye4821 Жыл бұрын
C'est important de clarifier ces questions... mais surtout de l'encourager davantage dans le droit chemin en respectant l'islam et ses enseignements, surtout la prière, le jeune, zakat entre autres.... Et surtout s'éloigner du chirk ou BOKALÉ, de l'hérésie et du mysticisme. Qu'Allah nous guide...
@NiangAmadou-bt3mg
@NiangAmadou-bt3mg Жыл бұрын
Dieuredief s.khadim amna solo
@hossenfal4229
@hossenfal4229 Жыл бұрын
3 sokhna la
@abogassama6567
@abogassama6567 Жыл бұрын
Sëriñ lamin laa gëna gëm
@gentlemara6345
@gentlemara6345 Жыл бұрын
On peut pas avoir plus de 4 femme. Alors dès qu'il y a 5 femmes toutes les autres sont repudies d'office
@idrissamor7880
@idrissamor7880 Жыл бұрын
Le prophete en avait plus de 5
@wadeabdou6069
@wadeabdou6069 Жыл бұрын
Dieudieuf
@MrTaffisco
@MrTaffisco Жыл бұрын
@@idrissamor7880sallalahou aleyhi wa Salam avait 9 femmes et seul lui en Islam a se droit donc quiconque a plus de 4 femmes tu n’as pas ce droit
@iboudieye1255
@iboudieye1255 Жыл бұрын
Kou ame 4 famme takk Diouromėl yėpou tass na seye ama toufa
@idrissamor7880
@idrissamor7880 Жыл бұрын
@@MrTaffisco alors l’islam est impartial sur ce coup 😂
@ahmeddamegueye1879
@ahmeddamegueye1879 Жыл бұрын
Serigne bou tole ni serign cheikh war na moytou li mais yalna yalla djiegueule ko wayé serign cheikh dioudiou na lén yén aye talibém
@SmodouNiang-k6t
@SmodouNiang-k6t Жыл бұрын
Macha allah
@SalmaNdiaye-oe8ju
@SalmaNdiaye-oe8ju Жыл бұрын
mashalla lilanio bègue siborom xamxam waye imame sall wodoul waxdji kene wakhoule digal fall d'à âme lou epou 4 fame
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
Ki dandone nosss rekkk. Serigne bouy nosss di fooo ba yalla nieuw ci Kawam
@binetougueye8986
@binetougueye8986 Жыл бұрын
Konn dé gagné nala noss bamou nékh ko mou diègalou yalla té yalla meun nako diègal parsk mok mom la . Yaw nak nga nékk thi déram bi dithi noss té khamo fokoy guissè bamou lay diègal
@layma4143
@layma4143 Жыл бұрын
Maa chaa'allahe serigne khadim xam xam rek woor serigne lemine moom tamit amna xam xam
@cheikhmar8926
@cheikhmar8926 Жыл бұрын
S Lamin sall machalla liga wakh mo gêne wer dè
@amathtop1429
@amathtop1429 Жыл бұрын
Yalna niou yalla mousseul ci borom xam xam bou ragaloul yalla, c'est très dangereux
@tallaNdiayeitaly
@tallaNdiayeitaly Жыл бұрын
5 famme kharamna
@bounabanno6961
@bounabanno6961 Жыл бұрын
Délèn attentione kou khamoul khamoul !! Khadim Bousso liimouy wakh dou wakhi dara!! Dioroomèlu diabar thi shariihatou l'islaam doonul sokhna 👎!! kénn manoukoo fas bamou fasou !!! Khadim Bousso liimouy wakh dou wakhi dara !! Dèlèn déglou Serigne Mbacké Abdou Rahmane 👍!!
@wordswork9761
@wordswork9761 Жыл бұрын
Serigne khadim bousso linga indi mo gueuneu yénnou manna.
@syllabayesylla8066
@syllabayesylla8066 Жыл бұрын
Wakho degeu dh lamin sall mo wakh deheu ko takeu 5ème Famme bis bingako také 4 yo ndieukeu bognoko khamé bolen nekhé gno dem gnibi sen keur baye sen seuye tas na
@fashionfashion1330
@fashionfashion1330 Жыл бұрын
Saa Waay😂 Li Imam Sall wakh mo Wérr, Diouromèl dou diabar nékoul tji Boume, kou nékoul tji Boume noye diappé Ida, Bayil tiakhane waay
@aronadiouf5586
@aronadiouf5586 Жыл бұрын
Sa wayy meme sou nekoul si boum meunasi dieulé eumbeu motakh ida bi mounousi niakk bala mouy seyyi daufiss kom niko imam sall wakhé
@binetougueye8986
@binetougueye8986 Жыл бұрын
Newoula dafay diapp idda . Dafay istibraa lawakh té il a parfaitement raison. Balaa seuyaat dafay took ba guis mbeureuk
@fashionfashion1330
@fashionfashion1330 Жыл бұрын
@@aronadiouf5586 Prochaine fois, il faut être plus précis par exemple plus clair, là je suis d'accord avec toi, mais pas idda
@fashionfashion1330
@fashionfashion1330 Жыл бұрын
@@binetougueye8986 Ok Lère na Mashallah, imam Sall kouma nekh la, li nitt gni di ragala wakh tji Dine dji, daf koy wakh té dou tji Ragal dara vraiment je l'apprecie
@absandiayendiaye7445
@absandiayendiaye7445 Жыл бұрын
Wakh,naa deugg sokhna dou eupeu gninteu 4soukko épée dougnou sokhnna alkhourane mokko wakh😮
@bayeomardiaw6299
@bayeomardiaw6299 Жыл бұрын
Istibra fimouy amé dafay fékeu séy amnafa.niom sén chariya bopou lagnou amé .Moy li hol sohnasi rék néko yéyonala.con nak boulén yéwiwé .meuneugnoulén fasat .té dou ame istibra.lolou la Serigne Lamine salle afizahou Lahou .Di wah.serigne bousso holatal boubah ligaye wah.
@amathtop1429
@amathtop1429 Жыл бұрын
Khadim Bousso ragalal yalla
@tallaNdiayeitaly
@tallaNdiayeitaly Жыл бұрын
Waxo si diné
@falloundiaye7889
@falloundiaye7889 Жыл бұрын
Kh bossou politique sonko dakouy dérange 😂
@momardiop9061
@momardiop9061 Жыл бұрын
Yéna naffek lamine Sall limou wah ndioumtéla maz heubyi khadim bousso léralnako
@biramefall9147
@biramefall9147 Жыл бұрын
Naguéne mandou si séni wakh nguir yallah
@MoukhtarCiss
@MoukhtarCiss Жыл бұрын
Segne khadime liga wakh lérna amna solo mé diaroul glorifié wou nak lamine a toujours raisons
@xassida99
@xassida99 Жыл бұрын
S khadim dh limou wakh bodoul dinne sakh khel nogou noko ndakh bou seyé fenen fekou mou embon lolo man n'a indi AK lentou si diekeur dji s Lamine tamit limou wakh amna solo Dana ka dh nio boko finouy wakhé
@cheikhmoustaphafalloufatyk6076
@cheikhmoustaphafalloufatyk6076 Жыл бұрын
Yene niare niepa yame delene atte lougene khame yonou cheikh ibrahima fall wi de khamoulensi dara
@abibouthioune200
@abibouthioune200 Жыл бұрын
Diamou Yalla rék mo woor
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
​@@abibouthioune200bilay yonou yallah rék kessé mo woor amoul benene yonne
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
Beneu Yonne kessé mo am moy bou yallah kessé
@KharitouyayamNdiaye
@KharitouyayamNdiaye Жыл бұрын
Sa waye PAS bi limou yeuk ba daw moko khame yéne nak néke léne fi Di rew RW Lou rek yalla nako yalla bolé si ay sopeme
@ndiagambow9617
@ndiagambow9617 Жыл бұрын
Da niou mbadù woul rék deiii
@Elhadjikane-i6f
@Elhadjikane-i6f Жыл бұрын
Waay lii serigne lamine sall wakh mooy deug nopallal sa bopp meuno layal lou eup 4 femmes arrete
@laveriteabsoluejuste6358
@laveriteabsoluejuste6358 Жыл бұрын
Kii layalul kéne attép charia rék la andi 😂
@serignetoubadiop5528
@serignetoubadiop5528 Жыл бұрын
Wakh lenn thi detenus politiques yi ;;djoullits yiye déé thi touba ndakh innondations yi ;;wakh lenn milliards yi foumou neck;;;wwa ouba ngui déé ak thionna;;;;;;;Ces histoires ne nous interessent pas;;;
@ibrasarr2424
@ibrasarr2424 Жыл бұрын
Lamin déy doul rék
@akimbousso2206
@akimbousso2206 Жыл бұрын
Waw Man sama ladj bi moy ndakh dalena leer ne serigne chiekh ndigal dafa am lou apou 4 fam wakhdji pour Man da teel serigne chiekh ndigal dafa yewi ay sokhnam wakh talibemyi ak djioulit yepou ngiou ñanalko waw lolou mom diarna deba te seni wakh yen ñar ñeupou moy dará leeroulen ci ndakh da am lou apou 4 fam wala deut kon dama yakarne mandousi ak ñanalko modon li war wasalam
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv Жыл бұрын
No amna lou euppp 15 nganane 5 massi ame lou lerr amna domame youma khamm
@azizniane3144
@azizniane3144 Жыл бұрын
@@sonkofocus2024-ph4hvastakhfiroullah
@amethdienediaw8512
@amethdienediaw8512 Жыл бұрын
Non, niom dagnuni souféké amna plus de 4femmes. Kone batay deugeu lugnuko. Litax gni abordé question bi xam ngako, xam nako, moy Serigne gnu Baye d'habitude dagnuy plus de 4femmes. Donc c'est interessant gnu léral nitt yi luy atté bi, guinaw bou seuy bi amatoul.
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv Жыл бұрын
@@azizniane3144 bilahi walahi nak amna plus d 15 femme walahi
@daoudawade8480
@daoudawade8480 Жыл бұрын
Ak louuleen mane di wakh dangen nouy doli ak beugue cheikh ibra ak wa kereum
@aissatoundiaye2903
@aissatoundiaye2903 Жыл бұрын
Manee serigne bousso am lou eup quatre femmes mo diadouwoul gnognou dougnou diabar ak ndailoo kat lay
@diopmar6382
@diopmar6382 Жыл бұрын
Guissa goulen dara nguen beugue nek palassou yalla
@sunugalvisiontv2702
@sunugalvisiontv2702 Жыл бұрын
😂😂😂 xoulalma waxè douff yii rèk Mélné nitt dafa mana bâkh ba mouthiou si Nattou
@sunugalvisiontv2702
@sunugalvisiontv2702 Жыл бұрын
dioullit bou xéll warr ta toumall moroumou dioullitam si Nattou boukou yalla tékk
@khadimleye5738
@khadimleye5738 Жыл бұрын
Serine Khadim bousso li lagni xar ci yaw mais pas di tok ay Tfm di défendre le dictateur macky sall et sa sorcière d’épouse
@malickseck911
@malickseck911 Жыл бұрын
Lamine sall tidiane la il voulait juste insulter les bay fall a cause des prières et jeun pour eux c'est une victoire doul
@moukhtarndiaye8507
@moukhtarndiaye8507 Жыл бұрын
Non yaw comprendre lu barii dhh moum lii segne bii wakh rkk la wakh dh ndakh mou wakh néh: duntéh tei day jolii ak wour meun neuku loulu rkka takh mou fataliku wakhu serigne touba rahimahul lah je m’excuse duma tidian juste dama lay lérall rkk🙏
@amycollediop6519
@amycollediop6519 Жыл бұрын
Donc dire on ne doit pas dire ce que le coran dit chaque musulman doit prier il doit aussi jeûner si il est en bonne santé qu est ce qui te dérange
@djibisall1523
@djibisall1523 Жыл бұрын
5ème fame dou diabar guél la
@moussamariesene6759
@moussamariesene6759 Жыл бұрын
Thiaxane baxoul.
@malickndiaye1201
@malickndiaye1201 Жыл бұрын
Bayileen par par lo ci diine kii kham kham lay wakh
@ibaniang2346
@ibaniang2346 Жыл бұрын
دين إسلام
@morfatoudjitte5226
@morfatoudjitte5226 Жыл бұрын
Man sama giss giss li diaroul won yobou ci adouna bi yeupp di ci wakh
@AlassaneNdoye-pf5qi
@AlassaneNdoye-pf5qi Жыл бұрын
Khadim Bousso n'a rien n'a dîre . Il n'a qu'à parler des marabouts mourides qui ont plus de 4 femmes dont serigne touba qui dit on avait 33 femmes.
@AlassaneNdoye-pf5qi
@AlassaneNdoye-pf5qi Жыл бұрын
Mais serigne touba lui il avait combien de femmes ? Cette question je la pose à tous les Mourides mais surtout à Khadim Bousso.
@moussadiop5289
@moussadiop5289 Жыл бұрын
Khadim diabar 4 mo dagane bouco eppé cocou nekatoul diabar nekaléla rek
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Khadim Bisso tu es malhonnête khame ngén ni charia 4 femmes la reconnaître gnognou la ida bi concerné gni déss si aï thiakhane lagne néwone 😂😂😂😂par parlo rék
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 Жыл бұрын
Iaw wakhofi dara imma lamine samba mola eppu xam xam foff ngén amoulén xam xam bokkalé rk
@serignecisse4590
@serignecisse4590 Жыл бұрын
Khadim dayfén wakhoul deug
@SarrNdeye-fp1zm
@SarrNdeye-fp1zm Жыл бұрын
respe bahna
@fatimadjarri5648
@fatimadjarri5648 Жыл бұрын
Plus de 4 Femme c' est Haram 😢
@dernieremunites1263
@dernieremunites1263 Жыл бұрын
Yaw wakhofii lounou xamoul ne Oriente pas le débat autrement
@dembiska8882
@dembiska8882 Жыл бұрын
Serigne lamine Sall mo nekk si degue diabar 4 la yam boko wesso islam reconnaitrouko
@moussadiaw532
@moussadiaw532 Жыл бұрын
Serigne bi Bosso yaw politicien ngua se wakh wéroul
@FagueyeSow-s5f
@FagueyeSow-s5f Жыл бұрын
Mai dji téguou çy 4 yi thy harame laniou nékonne Serigne bi kholale boubakh
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Khadim Bisso parparlo rék franchement je ne te comprends pas défendre aï intérêt mo takh mais lamine Sall limou wakh dafa léer charia 4 femmes la wakh gno gnou la l'islam reconnaître gnome gnoye diape ida yénane diabar yi l'islam ne l'ai reconnaît pas
@khadimsylla576
@khadimsylla576 Жыл бұрын
Sénégal ngay gis mokkalul Faatiha fekk ñaari boroom xam-xam yuy werante mu ne moo leen di àtte.
@aas499
@aas499 Жыл бұрын
Vraiment y a trop d'hypocrisie chez les soufis
@championBoulan
@championBoulan Жыл бұрын
Oustsse lamine SALL mo wakhe de gue yaw mii khamoul gat démal nga Djida guie wat waye
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
Serign noseeur
@abdourahmanekandji547
@abdourahmanekandji547 Жыл бұрын
S khadim rombou 4 sokhna takk 5 diem kaw kéndouko toudé sayoup soubha
@ibrasarr2424
@ibrasarr2424 Жыл бұрын
Lamin khamoul dara laméniebiu rék mo raye
@madieyediop7307
@madieyediop7307 Жыл бұрын
Serigne bi danga warone ndieuka lèral lane la l'islam wakh thi kou am lou eupou 4 sokhna ba parè doga nieuw thi ida dji
@bachiirleveridique9767
@bachiirleveridique9767 Жыл бұрын
*BU LÉEN AND AK S LAMIN NDAX LI NGÉEN CONTRE S XAADIM POLITIQUEMENT NAKA NOONU BU LÉEN AND AK S XAADIM NDAX LI NGÉEN MÉRÉ S LAMIN SAL*
@mamndiagnabousso7733
@mamndiagnabousso7733 Жыл бұрын
Maneu daleu diakhler n’a Meunolena bayi parparlo ouztaz lamine sall limou wax dou xam xam lo bagn bagn gnaye nagoulko ay nopam you goudou imam bousso diadieufati xam xam rk gua fi wax deleneu deglou ba parer di sogua commentaire
@aliounebadaratall-wy5ul
@aliounebadaratall-wy5ul Жыл бұрын
Li serigne Lamine sall wakh rékk moye deug wallakhi
@taliberassoul
@taliberassoul Жыл бұрын
Kou am 5 femmes guenné nga si islam bou yaggue Tappalé rekk mofi dess Boy yaw danga dooth
@KharitouyayamNdiaye
@KharitouyayamNdiaye Жыл бұрын
Ki oustaz lamine sall dou moromou kiko diagal sakh wakhou ma ak mome
@thiamb7170
@thiamb7170 Жыл бұрын
merci Ouztaz Lamine Sall pour la clarté . Khadim Bousso del wakh nguir khamm kham wala yalla , tu commences a perdre tout mon estime
@modourokhaya9616
@modourokhaya9616 Жыл бұрын
Serigne bi leral niou Lou khadim bousso wakh ci mbirmi tegouko si xam xam
@papecisse6000
@papecisse6000 Жыл бұрын
Khadim bousso li lamine sall wakh môme ame. Degue.
سورة البقرة كاملة, رقية للبيت, وعلاج للسحر | القارئ علاء عقل - Surah Al Baqarah
3:51:48
سورة البقرة كاملة رقية للبيت, علاج للسحر - القارئ علاء عقل Sourate Al-Baqara
3:52:00
القران الكريم مباشر Holy Quran live
Рет қаралды 1,5 МЛН