Urgent 🚨 Balla Gaye verse de chaud larmes, Sa Thies fait des témoignages et des révélations très…

  Рет қаралды 55,146

KHASS Prod

KHASS Prod

Күн бұрын

Пікірлер: 95
@cheikhmboup3523
@cheikhmboup3523 2 ай бұрын
Sa thies yalla gua nek roi des arénes en 2025 inchallah que dieu te protége🙏🙏🙏
@ndiayeabibou3951
@ndiayeabibou3951 2 ай бұрын
@@cheikhmboup3523 amine yarabbi
@AboujohnToure
@AboujohnToure 2 ай бұрын
MachaAllah sa thies xèl mou sél gua yorr laff thiat yalnala yalla taxawou 🙏🏾♥️
@Prodioufvcbbkt
@Prodioufvcbbkt 2 ай бұрын
Machalla sa Thiès je suis fan de modou lo mais vraiment je estime beaucoup.inchallah tu sera roi des arenes
@SERIGNEMORMBOUP
@SERIGNEMORMBOUP 2 ай бұрын
Machallah sa Thiès nawnala trop khalé nga mais sa xél ak sa xole dafa raféte yalna yalla défal jam
@dialzydiasse5786
@dialzydiasse5786 2 ай бұрын
une bonne communication mais aussi très cohérente si tu l'écoute on dirait sé lui le grand frère
@malickly4840
@malickly4840 2 ай бұрын
absolument dacor
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd 2 ай бұрын
@@dialzydiasse5786 bayil garouwalé say
@FallNdiaye-ss1dy
@FallNdiaye-ss1dy 2 ай бұрын
@@dialzydiasse5786 c vrai
@aliouba5607
@aliouba5607 2 ай бұрын
Machalla kadouyi rafet na sa thies ❤
@Abraham22199
@Abraham22199 2 ай бұрын
Mash Allah il communique bien ❤
@diamilmboup4392
@diamilmboup4392 2 ай бұрын
Sa Thies dou sama Mbeur mai il a mon respect walahi il comunique très bien machalah
@maymounafall8176
@maymounafall8176 2 ай бұрын
Ma sha'Allah. Très belle communication.
@aliouba5607
@aliouba5607 2 ай бұрын
yalla na la yalla deffa diam sa thies ❤
@cheikhmboup3523
@cheikhmboup3523 2 ай бұрын
Vraiment ça thies yalla nalla yalla defal diam daga yarou torop bilae
@GoraMbengue-f2j
@GoraMbengue-f2j 2 ай бұрын
Akka nitté mashallah responsable deugue leuh .
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 2 ай бұрын
Machallah yalla nala Yalla diappalé lou leer nga wakh
@elhadjiibrahimadiatta9485
@elhadjiibrahimadiatta9485 2 ай бұрын
Champion ❤
@bbkrbbkr8875
@bbkrbbkr8875 2 ай бұрын
Mo geneu degou si mbeur yi machallh ❤
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 2 ай бұрын
Il est respectueux ❤
@mouhamedtraore904
@mouhamedtraore904 2 ай бұрын
Ce mec communique très bien ❤❤
@nicoladiouf4252
@nicoladiouf4252 2 ай бұрын
Sa Thies meilleur communication que Dieu vous protège bilay denga kham dara rek
@AdamaMballo-t9s
@AdamaMballo-t9s 2 ай бұрын
Wallahi c’est la vérité sa thies
@CoumbaDiallo-l7h
@CoumbaDiallo-l7h 2 ай бұрын
Machalla khôlene lou Nice rk nguén def ko 😢
@BaOusmane-l8m
@BaOusmane-l8m 2 ай бұрын
Lamine tivi wah na lepo machallah c fin ahhh
@rimesmakerposeidon2427
@rimesmakerposeidon2427 2 ай бұрын
Sathies verre dako diape bilahi
@sambadrame3497
@sambadrame3497 2 ай бұрын
Balla ❤❤sa one love
@PouyeMagaye
@PouyeMagaye 2 ай бұрын
Sa thies khamouma loukoo balla def mais loukoo nakharíí leuh 😢
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 2 ай бұрын
@@PouyeMagaye loutakh nga wakh lolou nitte day wakh loum kham wl lou yonam nék
@adamaseck8816
@adamaseck8816 2 ай бұрын
@@PouyeMagaye balla defouko Dara mo bone bonou bopam
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd 2 ай бұрын
Losi kham ​@@adamaseck8816
@aliounendiaye6049
@aliounendiaye6049 2 ай бұрын
@@PouyeMagaye bilahiii j’écoute limouy wakh mok balla yeup Mais ils ont un vrai soucis meme batay ils se lancent des piques Dernier interview de balla il a dit lima defal sama yallah nako sa thies meune bah defalkoko aujourd’hui sathies dit que mom il fait pour sa mère aussi En gros ils ont un vrai problème
@ChekhomarFall
@ChekhomarFall 2 ай бұрын
Machalla sathies❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ndiayeabibou3951
@ndiayeabibou3951 2 ай бұрын
❤❤❤sa
@mbayediaw1962
@mbayediaw1962 2 ай бұрын
Sa thies vraiment nawnala lool bilahi
@SYLVESTREKANKOLA
@SYLVESTREKANKOLA 2 ай бұрын
Sa Thiès seul 🎉🎉🥳🥳🥳
@serignembaye5223
@serignembaye5223 2 ай бұрын
Communique bien nassa diam yague ❤
@mariamjohn9172
@mariamjohn9172 2 ай бұрын
3 round yes one round will never go international
@BubaluizSuware
@BubaluizSuware 2 ай бұрын
Grazie 😘😘😘😚😘
@Abdou-l5l
@Abdou-l5l 2 ай бұрын
Communication. Bi machalla
@MouhamedNgom-w2x
@MouhamedNgom-w2x 2 ай бұрын
Sa seule ❤
@cheikhantadioptv2574
@cheikhantadioptv2574 2 ай бұрын
👍🏆👍🇸🇳
@PapeGueye-mk8ry
@PapeGueye-mk8ry 2 ай бұрын
Machallah
@Patriotepourtoujours
@Patriotepourtoujours 2 ай бұрын
Sa thies kesser ❤
@bacardiagne4449
@bacardiagne4449 2 ай бұрын
Mentions spéciales sathies bonne continuation et bonne chance
@BaOusmane-l8m
@BaOusmane-l8m 2 ай бұрын
Journaliste ❌ balla gaye 2 c pourquoi image bi rafetol
@LimaDiagne-v4f
@LimaDiagne-v4f 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 2 ай бұрын
😢😢😢😢 Modou kharagne lo so rayé siteu baparé nga maye sathiéss chance kou nitéleu koubakh la ❤️❤️❤️❤️👈 merci sathiéss apart kharagne légui yaye sama mbeur
@ibrahimandiaye7139
@ibrahimandiaye7139 2 ай бұрын
merci frère
@Ydakh-ui5yo
@Ydakh-ui5yo 2 ай бұрын
Sama champion bi légui comprendre gua motah légui bandit gua
@BabacarNiang-me8ve
@BabacarNiang-me8ve 2 ай бұрын
😢😢😢sathie mi boutohoul si balla gaye mi doudem malako wakh bilahi nadem si balla
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv 2 ай бұрын
@@BabacarNiang-me8ve balla mome rk demoull khana guisso forme bala bii
@adamaseck8816
@adamaseck8816 2 ай бұрын
@@sonkofocus2024-ph4hv balla deh mo guineu demm S’ENE wa keur ak sa mbeur biniou diouteul
@MoussaDiakhate-n6h
@MoussaDiakhate-n6h 2 ай бұрын
Modou lo sa thèse combat la
@Niane2023
@Niane2023 2 ай бұрын
Sa thies vs modou lo
@coeur2lion38
@coeur2lion38 2 ай бұрын
Aziz Ndiaye mome wahi dof la wah da beréwoul rék
@GnimaCamara-g6w
@GnimaCamara-g6w 2 ай бұрын
Machalla sa thies n exposé jamais votre vie familiale dans les réseaux sociaux, li linge sale se lave en famille fait attention aux réseaux sociaux
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 2 ай бұрын
Pourquoi nga crois photo balla bi bayi lène saytané
@mariamjohn9172
@mariamjohn9172 2 ай бұрын
Sa thies amou lo yarr bala sa Kilifa respect ko so bugay am jamma bala mo tah niou bugala
@binetadione6587
@binetadione6587 2 ай бұрын
❤️❤️❤️❤️
@diotayurewmi9516
@diotayurewmi9516 2 ай бұрын
Sama mak moma magué 11 ans amna diabar comme mane tay laniou geuna and , dra changéwoul ,presk chak semaine niou wéranté mais danoukoy wakhtané mou diekh. meuno ame xarite bu rombe say Mbok , wakhofi dra loudoul Garouwalé sa Mak ,nane do topou si guinaw kénéuh dagua dioudou si pauvre ca veut dire sa ame Ngor mais pas Balla ,avant dagua ko done kanio diko sani ay kher népeu contane.Ioe bombardier wala eumeu mola geunal sa Mak kham. si la preuve ay magou diambour rek guafi nouyu ak say djigéne, Balla sah limoko nouyuwoko. Nioune niogui ak sunuy mak sofi bayé sa mak Ya kham . sou défone ni Ioe do ame lo dieulé tay keur ndah biguay ale say cachéts mola yor dieuléla si moto diokhla auto sa xaliss noko def , fi niépeuy def si sen mbokou yi. Li nak Niétané lay nirol balla doula woudiou wakh diou nekh si ay adverséram gua geuna meune ke wakh ko si mom. Sou féké ni dagua diapeu ni mo tah fayékouwo ay millions mba da wara bayi bagua ame combat mou sogué oute dioume gua, yagui ankh sa bopou weurseuk Yalla moko yor , rakhassal sa xol bi defsi sa mak dji .
@GoraMbengue-f2j
@GoraMbengue-f2j 2 ай бұрын
Omar défaillant yimiy andal niokoy orienté ndakh pour niom xaliss moy adouna contrairement akk salif borom bakh bilahi golf fi nieupp la amal diam am yitté.
@Abdou-l5l
@Abdou-l5l 2 ай бұрын
Aziz. Boudon. Beurè. Dou wahh lolou.
@diotayurewmi9516
@diotayurewmi9516 2 ай бұрын
souma meunne vocal dinala wakh lo meuna dégu , diogue dém balou aak sa mak pour diékhal wahdji
@malickndiaye2804
@malickndiaye2804 2 ай бұрын
Rageu toppu mak
@soldar05581
@soldar05581 2 ай бұрын
Bilahii sa boy wakhé rk niepou sopat ko kou xam wakh tay wakh deuge tay wakh Lou bakh bilahii topal thie samak rk Man mii réro wan n'a mak sama mak waye léou diekh na tay kon topal balla guaye rk bilahii doko ré thiou saye tane dafa Bari dole mé balla guaye dala beuge loll xol lên si sén yaye mér bou bakh la japou lén si rk 😢
@khadydia2869
@khadydia2869 2 ай бұрын
😏😏😏😏😏😏😏
@mariemethiam5861
@mariemethiam5861 2 ай бұрын
Sa Thiès kinga togal sa dom la??😂😂😂😂😂😂waro wone togg côte à côte ak Sa yowit!😂
@SerignemodouNdiaye-s3u
@SerignemodouNdiaye-s3u 2 ай бұрын
Salif NK comme si beugo diam quoi,balla gaye molo mona dueurign mais monoko apportél dara loulaa yalla dogal kel est ton problème yow
@MouhamadoulamineSeck-e1o
@MouhamadoulamineSeck-e1o 2 ай бұрын
Balla guaye na khalale sa thiés yone bi mou beré ak roi bi modou ak siteu kousi dane warna berék gnome
@assanediop771
@assanediop771 2 ай бұрын
Vrais yambar tapèt moy sa thies wah rk say morom rawla
@AboujohnToure
@AboujohnToure 2 ай бұрын
Bane moromame moko raw fall ?
@assanediop771
@assanediop771 2 ай бұрын
@AboujohnToure boye niang2 ak ama balde nioko raw beurenaniou ak roi des arrènes bay deloussi di beurek franc ak reug reug mom danoul eumeu sene danoul boye niang2 ndah tapet ay door
@doffff
@doffff 2 ай бұрын
Zq thies dafa nité
@mamecheikh3642
@mamecheikh3642 2 ай бұрын
C bon la communication ? Mé sache que Omor sa kelifa leu . Meuno am kouko sout monoul am lolou sout
@MbavkeGaye
@MbavkeGaye 2 ай бұрын
Sa thiess combat mok eumeu sene repesct mo eupo basi lambo ji sinon pour Man emeu warola dan
@lansanadiedhiou6006
@lansanadiedhiou6006 2 ай бұрын
@@MbavkeGaye respect bimou diokh Eumeu si birr guew bi motakh mou niakk combat bobou
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 2 ай бұрын
Sathis ak tapha tine combat la
@papamakhtarniang
@papamakhtarniang 2 ай бұрын
Bou modou lo daané siteu halaatnaa trope modou dieul sathies na haar rék
@PapeHane-mi5xy
@PapeHane-mi5xy 2 ай бұрын
En tout cas wakho fi dara lou lérr balla moye sa kilifa taye boko nango
@adamaseck8816
@adamaseck8816 2 ай бұрын
@@PapeHane-mi5xy bayilma ki yaw mo kham nioune balla rek laniouy topou ❤❤
@lixman771
@lixman771 2 ай бұрын
Bah dis à balla Gueye de se comporter comme un kifîfeu alors . La vérité est que balla ne sait pas parler 🗣️ tout simplement
@adamaseck8816
@adamaseck8816 2 ай бұрын
@@lixman771 yaw doul balla mo guineu kilifeu sa baye
@eboyjobz9743
@eboyjobz9743 2 ай бұрын
@@lixman771 borom khell nga fam
@eboyjobz9743
@eboyjobz9743 2 ай бұрын
@@adamaseck8816ak sa baye right?
@MamadouBousso-v1b
@MamadouBousso-v1b 2 ай бұрын
Je 😂
@malickndiaye2804
@malickndiaye2804 2 ай бұрын
Yaw ya amoul fayda
@MantaDiop-v3k
@MantaDiop-v3k 2 ай бұрын
Yaw maye gno diamou
@bassiroudiengsowchefdestra1730
@bassiroudiengsowchefdestra1730 2 ай бұрын
Sa thies n'est pas intelligent
@lixman771
@lixman771 2 ай бұрын
Wakhofi Dara tu es juste fan de balla Gueye . Tu n’est pas logique la 🙄en tout il communique 10 fois bien plus que balla 🙄. Je voie qu’il est très modeste et plus instruit par rapport à son frère 🙄
@Mameles
@Mameles 2 ай бұрын
@@bassiroudiengsowchefdestra1730 iow mii ya intelligent_woul…
@mouhameddiagne9347
@mouhameddiagne9347 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
@غلامالخليفةآبوبكرسه
@غلامالخليفةآبوبكرسه 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 51
56:27
Pikini Production
Рет қаралды 1,1 МЛН
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 22 МЛН
SATHIES VS MODOU LO OU SATHIES VS SITEU/ L'AVIS DES EXPERTS
14:02