Dafa melni makk yi nio nek di defaral xalei yi dh. Aytia Modou nieuweul dogalii Ama InchaAllah..
@alydiakho4132 жыл бұрын
Si zarco continu de lutter sans précipitation bén mbeur dotou ko dane
@iboufaye56952 жыл бұрын
Bilahi DeuG leu
@avdoulayendiaye45832 жыл бұрын
Bilahi Zarco presque defaitam yeup si actiom lay dano
@MoustaphaKandji-g7s Жыл бұрын
Bilaye ❤
@makavelli-ru3un2 жыл бұрын
Doole dokhoule diam félicitations zarco🔥🔥
@hantangtoure46442 жыл бұрын
D'où galathie moy beurè merci zarco djiaroul tak Lou bari entraînement rèk mo woor félicitations
@mamadoundiaye59562 жыл бұрын
Bilahi frère
@cheickamalasanogo79392 жыл бұрын
Pour une première fois zarco ne s'est pas precipité
@serignebassiroundiaye54902 жыл бұрын
Un combat très technique de zarco , jajeuf champion zéro faute
@kareabdoulahad6222 жыл бұрын
Khekh bi diar na yoon dane nako facilement ak tecnique
@serignebassiroundiaye54902 жыл бұрын
@@kareabdoulahad622 tres class façon bimou khékhé ak mom , vraiment bokouniou niveau té wanénénako
@kareabdoulahad6222 жыл бұрын
@@serignebassiroundiaye5490 wone nako mala mak si lamb eupou ko kheloum beure kou beure ak gouy gui sa thies siteu modou anta bathie seras thiat kokou dou thioune
@abdoulayegueye10072 жыл бұрын
Zarko merci
@abdoulayegueye10072 жыл бұрын
Meeeeeeeerci xqllay
@ibrahimasougou70612 жыл бұрын
Merci zarco siguil gua grand yoff
@oumarfall80982 жыл бұрын
Ayy Aziz Ndiaye assurelnama sama victoire molene di tardel.. Demm lenn entrainé dji te wagni lekk mo guenn si yenn...ALimentation mbaye Gouye dara bakhoussi ayy 4kg Dibi ayy hamburger ayy 3 plats de thiepp ayy ndambei... Chapeau Zarco !!!
@diakhateleye2 жыл бұрын
Boulma ray way
@tk922212 жыл бұрын
😂😂😂🤝
@omartoure99162 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣
@kareabdoulahad6222 жыл бұрын
4K diby setan ngako ko dougou si catin cantino yi mane dh khaw ma woon ni lolou khe senegal doye ware
@diagneafrica84672 жыл бұрын
Aye wakh la rek kilo sakh douko diekhale
@joediopdiop48752 жыл бұрын
Mbaye gouy gui dafa bari wkh tè tapét la félicitations zarco
@manladeh89232 жыл бұрын
Kii kay merci rek 😂😂😂😂 coups yi déclencher rek mou daw guénn
@boromebakh282 жыл бұрын
Dieureudieuf Zarco si ndamlii do morom Mbaye Gouygui dafa réww amoul respect.
@papambaye75642 жыл бұрын
Badolaa la
@londame39062 жыл бұрын
Mbay gouy gui wakh jou Bari rk man na takh mou danou merci zarco 👍
@ousseynoufbi90742 жыл бұрын
Merci zarco ❤ki da beurii wakh
@moustaphafadiga7742 жыл бұрын
merci zarco ki do moromam yako meune yako eup fite dakeu ko beuré💪💪💪🦁👑
@tarkindabi41682 жыл бұрын
Merci zarko
@talladiakhate49192 жыл бұрын
Merci zarko👏🏿👏🏿👏🏿 boy bi rewna barina wakh
@ndiaboutadiouf79122 жыл бұрын
Machalla zarco ya bakh si xale bou rew
@boyetownfromdkr52872 жыл бұрын
Senegal nala khamal dara légui so beuré wakh danioulay contre di niane yalla pour nga âme défaite so yarouwoul bilahi mbaye gouye gui so kholé commentaires yii khamni sénégalais yii mérénanioula ndâkh sa wakh diou bari ak niakeu respecté zarko ak wakh diou niaw
@papendiouck57032 жыл бұрын
Khamosi darasakh
@dienemor24112 жыл бұрын
Lou weerr nga wakh mbaye gouy gui amoul respect
@guissguiss24592 жыл бұрын
Bilahi mane je priais pour mou danou tellement qu’il est irrespectueux ce gars
@iboufaye56952 жыл бұрын
Dafa khamOul zarcO rék
@soldarouyayam85242 жыл бұрын
Ta nak mbaye ragual la khamonaco bou bakh
@yigosophie54862 жыл бұрын
Kou sétane face à face ba ? Sarko waxone nako diga daw bilae🤩🤩
@alioudia21312 жыл бұрын
Merci zarco 🤲❤ ki dasof dam rk detour de zarco machallah ❤🇸🇳🤲
@modou20042 жыл бұрын
Merci zarko mbaye gouy gui das beuri wakh trop
@papindiaye67412 жыл бұрын
Baparei rew bilaahi
@falloumbodji25972 жыл бұрын
Merci zarko ki da Bari wakh
@observateur58212 жыл бұрын
La communication de Mbaye Gouygui sur la vie privée de zarco était très mauvaise. À revoir avec son staff. Du courage à lui félicitations à zarco
@khalifamboup87742 жыл бұрын
Yarou dafa am solo frere
@observateur58212 жыл бұрын
@@khalifamboup8774 merci
@mansourkane29342 жыл бұрын
Bilahi frère mbeur warnagne kholate séne communication
@mansourkane29342 жыл бұрын
Bilahi frère mbeur warnagne kholate séne communication
@Gorafall732 жыл бұрын
Thiouné
@Leukbass102 жыл бұрын
Wahaha mbaye gouy GUI li nga warone mbeuré Lep wakh nga si signature bi 🤣🤣🤣🤣
@dembaztarkinda82702 жыл бұрын
Merci zarko 👌👌👌👌
@sambandiaye39492 жыл бұрын
Félicitations Mbeur Zarco
@azizlaye24342 жыл бұрын
Merci zargo ki dafa ndaye Bari wakh ta defofi dara
@self-made2xvi2932 жыл бұрын
Lamb moo doywar rék Mais Zarco dou moromou gñii,
@thiernoyahya76832 жыл бұрын
bilahi zarco bimakoy setane Mouy niew foundioungne thi mbapat yii walahi mbeur camil sama village sah dielna fofou lamb lutte simple mo meune boy yii fouf
@self-made2xvi2932 жыл бұрын
@@thiernoyahya7683 sisi dafa mbapatt baa sonou, dafa yagu dème sii village yii difa dieule ayy tournoi ou il perd par demi-finale ou finale... encadrement laa amoul rék Mais champion leu
@bunsingdemacosntv68222 жыл бұрын
Nice job bro congratulations 🏆🙏🙏
@pathebah6272 жыл бұрын
Zarko vs Moussa ndoye Aliou seye combat la
@cheikhtidianesy24192 жыл бұрын
Bilay nii la meunone démé mbaye gouy gui dina am louko bett meussoul yakkar ni zarco meun nako dane.Ce serait une leçon pour lui pour ses prochains combat de donner du respect à son adversaire et surtout éviter d'entrer dans ses vies privées.
@Alassdi12342 жыл бұрын
MBAYE GOUY GUI sugnu dibi yi fo ko dougeul
@mhd_00392 жыл бұрын
😆😆😂😂😂🤭🤭🤭 Nooo kepp kou diay beuri wakh ba hegue biir guew gui ohhhh ay wakh doulathi guenne
@khadimg20782 жыл бұрын
Mbaye gouy gui ak wakham you bari yèp dèkètè dou tousss sorko deff ko eupe dollè lou barii merci zarko
@fafandao25712 жыл бұрын
Chapeau Yahya Diop bilaye mo gagné ba paré tourné dannalema B52
@gueyembaye8532 жыл бұрын
Wa zarko mene na li ndekete 😂🙆🏻♂️🙆🏻♂️🙆🏻♂️🙆🏻♂️
@falloutall21472 жыл бұрын
Saaway iow xaamo zarco dhe daafa niiak fayda rek me gars yii dakouniiuko beureii
@linksmeziemezie71822 жыл бұрын
Sheut Zarco ki dei niab la def🔥😂😂
@zossboubousiteu92872 жыл бұрын
Du courage bou siteu 😭
@momoteuw91312 жыл бұрын
Zarco dafa bokou si mbeur yiy nékhal lamb dji dfa ame fite té dou meussa arrière félicitations champion
@mamadousarr33712 жыл бұрын
Mbaye gouy gui ak wakham diou Rey dou Dara tappet leu ngeme woul zarco🤣😂🤣😂 félicitations zarco
@niangelzo3642 жыл бұрын
Zarko nek si micro Diko teukou niou tallal la micro nekh n'a lol wanter nga roumkoum dadjier akk môme neko djiak sibiir gueew fofou thiowli zarco il fait partie des lutteurs les plus athlètes crocias,vif très à l'aise dans ce qu'il fait len reQ Moy tiatam te fadam wakh nako Moy teyi reQ fi weup monguin si môme doumani douniou d'Anne dé mais Dina nakari danne domou grand Yoff fo life💯✌🏿🔥
@Steven-ul8pw2 жыл бұрын
Félicitations zarco Mbaye Gouye gui lamb dou xasté ak wah bou niaaw dh yor micro melni seko lingay moudjé
Félicitations zarco du courage mbaye gouy gui mbaye geuye gui nak dafa khawa bari wakh qoui
@dembiska88822 жыл бұрын
Ki kay day wahh rék
@pdiallo10292 жыл бұрын
@@dembiska8882 wakh ak lek bergueur ak ndambe lek la meune
@dembiska88822 жыл бұрын
@@pdiallo1029 😁😁😁
@diagneafrica84672 жыл бұрын
Trop sakh
@ibnouserignefall69652 жыл бұрын
Comme iow khana
@papaabdoulayeniang95362 жыл бұрын
Yekini a regneé durant 10ans tee kenn mousso gui lu bari si media yi mbeur da ngay discret nekk sa coin di liguey,boy bii dafa bari wakh et il n a rien encore prouve dans la lutte
@mamadoudiop11052 жыл бұрын
Lu ler gua wakh lu nekk yekanaka zarco bep rek du dara
@azousambe1802 жыл бұрын
Dafa défoul gate ba pareh meuneuh fène ak yakeuh dère domérame bimou done
@mamadoudiop11052 жыл бұрын
@@azousambe180 motakhit dumanagn ko lamb ah vie privé diam bour bokul lep si guew gui la
@kareabdoulahad6222 жыл бұрын
Dako mane dakh ko beure dakh ko khekh geun ko yageu si lamb beure ak nio khamne mbaye gouy gui beure woul ak nioniou kou berek gouy gui beure ak sa thies beurek siteu beure ak bathi seras beure ak thiat beure ak modou anta lolou kham ngany dou beneu
@papaabdoulayeniang95362 жыл бұрын
Zarko a toujours eu des combats de gladiateurs tee moo dakh beuree mbaye,mbeur da nga paree sur tous les plans,si vous avez remarquee mbaye foogoonn ni day nieuw diapp ko dann ko donc ba lolou amoulee la perte lamb ji
@sentechndiaye7532 жыл бұрын
Machalla lutte tv
@babssadikh58632 жыл бұрын
Zarcko boy grand yoff leu fite bé deugeur, té dafa meune beuré tothie na mbappate you beuri
@latifthiam11142 жыл бұрын
Felicitation zarco taye mome beuré bou diare yone khékhe bou diare yone nga défe zarco bo téyé thi LAmb rk billaye kéne mounoula wayé defoi yaye beuré ba dane sa bop te yawe champion nga bone continuation mbeure
@seydinaaliouneboromjasiji32002 жыл бұрын
Bravo Zarco Domou Grand Yoff
@ousmanelegrand70322 жыл бұрын
Mbaye amoule fite ba pare amoul dole….. graisse rek la
@paamathndiaye2259 Жыл бұрын
😂😂😂😂
@deuguekepp102 жыл бұрын
Combat très mystiques
@damembengue18942 жыл бұрын
Félicitations Zarko
@yadeinfo28742 жыл бұрын
Merci zarko ki dafa weradi trop ta beuri wax
@Mrdiop2 жыл бұрын
Félicitations zarco wagniil waakh djii rék yok liguéy bii
@tallalioune81512 жыл бұрын
ZARKO A UNE TRES BELLE FORME VRAIMENT
@bdam74302 жыл бұрын
Machalla diaradief zarko contan si yaw
@ESPOIRDEFIS2 жыл бұрын
Tieyy zarco mais mbaye Gouy Gui iow mano.beurré dh courage défarou zarco si ié déplacement boulko si toppou taxawall déglou wala nga fékisi ko si lolou
@sadiothior46532 жыл бұрын
Felicitation Zarco nila rekkk affaire yi bou amé srx rekk champion ngua mel ngua ni Mbeur walaa mel ...Mbaye gouy gui khana dingua nopi
@beyonder19182 жыл бұрын
Bravo Zarco!
@babacarndiayefrommbour44212 жыл бұрын
felicitación zarkou ak meunn andié forme boy dann ak boy danou yépp
@manladeh89232 жыл бұрын
Waa Arbitre bi moom mètti na di weuh 😢 melni kouy wax ak ay doomam nii tshim
@Concept02082 жыл бұрын
Sans esprit, le corps n’est d’aucune utilité: notion de respect de l'adversaire; un facteur prédominant dans les sports de combat. Zarko a mis en strategie le b.a. ba de la boxe, de ne pas prendre de coups, en tout cas le moins possible, de toucher l'adversaire sans être touché soi-même, ou le toucher avant qu'il vous touche. Félicitations!
@misterzappa90732 жыл бұрын
Pour la première fois Zarco Gagne un combat capitale lol bravo courage à Mbaye Gouye il faut qu’il diminue d’être trop bavard et respecte tes adversaires
@zizadioufdionewar82882 жыл бұрын
Wadji ak wah djou bari dji yeupppp ndékété gattt la hamoul. Li kay mo tah mou né dou beuré ak boyiiii di mpabattt. Lamb j légiii koula gueneu reuy laméñe rec ga né kila. Amouñou bene tecniq. Sen ham ham yeup si tiktok bb la yem
@onelove67212 жыл бұрын
Lamb j koussi yakar ni leup mystique la dinga danou chaque dimanche Lamb entrainement la ak sagn sagn késsé mystique doga nieuw
@adolphefredericmendy84852 жыл бұрын
Merci beaucoup Zarco. Mbaye gouye gui était devenu très arrogant à la fin té mingui ni yambar le
@kilserabalde89542 жыл бұрын
Alhamdoulilah ndah waxdji diékh sh
@dreadalion2 жыл бұрын
Grand Yoff comme Medina. Ya un bug au Galsen . Machallah !!!🤬🤬
@morsady53702 жыл бұрын
Guene balma baol baol yi il faut que guene travaille sene mantal yi daguene na guawa perte mandal même tapha tine...balene ma juste conseil la
@pseutmbodjtheboss86152 жыл бұрын
Vraiment zarco dafa liguéy félicitation
@khalildia33162 жыл бұрын
Athia zarco mbaye gouy gui dafa beri wakh 🥰🥰
@moussaibrahimasarr78032 жыл бұрын
Cheikh tidiane niang dieulna final legui ni à bassoul naniou ko diokh Mbaye gouy gui mi beuri wax té dou dara
@babacarndiayefrommbour44212 жыл бұрын
merci kone chiekh tidjan wèèr na leégui felicitación👍
@kalypro73712 жыл бұрын
Aythia zarco 💪💪💪💪💪💪
@ndiaboutadiouf79122 жыл бұрын
Merci zarco
@papanasri49312 жыл бұрын
Sétanouma lamb j dée commentaire gni l'ay sétane no mbaye Gouy gui loy wax wa kogne baa😅😅
@ousmanesarr7562 жыл бұрын
Mbay gouy gui dou deureum nakaté lamign ba reuy 😂😂😂
@Papisco.sall.2 жыл бұрын
Zarco dou ragal dh🎉💪💪🙏🙏
@Mrdiop2 жыл бұрын
Mbaye gouy guii man bougouma façon bii dii waakh baa am adversaire fék liguéyoo
@modoudiouf53362 жыл бұрын
Aaay yala dieuradieuf mbay gouygui na danou continuè ndakh dafa meun wakh diou niaw ta amul respec si nii
@assanebeye15992 жыл бұрын
Bilahi wakh diou niaw bakhoul
@abloslimshady2 жыл бұрын
Zarco presque takkoull dara tchi galladj, affaire yii dou galladj deh mais entrainement you woor!
@andedieulefimacky52092 жыл бұрын
Mbaye gouy gui do agresser songue même bou feker dalay dane mais ngaye beurei melni pas Félicitation zarco.
Niaw mbaye gouye dinga teuthie sa tatt yi bari wakh comme djiguen
@papediouf46072 жыл бұрын
Zarco nièmè ko yomboul dèh....
@pandiaye942 жыл бұрын
Zaarcoooo ‼️‼️
@salifba30142 жыл бұрын
Felicitation zarco mbaye guigui defa rew te beuri wak
@mamadoundiaye52302 жыл бұрын
Mbaye gouy gui da beuwi wakh lamb dey ladje touti def tek félicitations zarko
@mbayesow78622 жыл бұрын
Mbaye gouygui deffa respect te woul zarco aye wakhou doffe rek lay wakhe Vie privée daimour ga tok si Télévision di wakhe Vie privée diambour li bakhe na si mome doff leu rek